Asalaam Aleykum ya Ouztas, je suis peut-être le dernier à regarder cette vidéo de vous, car je suis un nouveau abonné de vous depuis hier soir merci infiniment 🤝🏼😊 jazakallah wa annaa kheyrann.
billahii OUSTAZ Sagna wakh ngaa deugueu c la première fois que je regarde tes vidéos mais vraiment j'apprécie tes paroles de sage billahii deugeu nekhoul
Sa waye boul sonn thi wakhi Iran Ndao. Mann dé khaw ma sama euleuk. Wayé mom ak gni nék thi guinawam yeup bougnou moytou woul euleuk Yalla di na brochette sénn ndaye thi digou safara ya gueuneu tangue.
Machalah SERINGE Sanga yalla na yalla goudal sa fan dolila soutra ak xeweul wereul la sam la sa xam xam rafet na trop💚💛❤
Je suis vraiment fière de toi
Deugue rék gua fi wakh des ❤️❤️❤️❤️❤️pour toi,au moins un homme qui a bcp de courage goudal fane🙏🙏🙏
machallah ya oustaz yallah nala yallah faye yiw
Merci Oustaz Sagna vous êtes très pertinent.Que Dieu vous bénisse et vous donne une longue vie.
Malla beugue yalla nagua goude fane thi barke (seydouna mohamed psl) amine yarabi thi barke serigne babacar sy amine yarabi. aminnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnnne
Merci beaucoup amine
Iran est un bavard croyant connaître tout
Dieureudieuf mbokeumi dieureudieuf dieureudieuf dieureudieuf dieureudieuf dieureudieuf machalaaaa oooooh iran damako yeureum
MachaAlla amna solo
Asalaam Aleykum ya Ouztas, je suis peut-être le dernier à regarder cette vidéo de vous, car je suis un nouveau abonné de vous depuis hier soir merci infiniment 🤝🏼😊 jazakallah wa annaa kheyrann.
بارك الله فيكم وزادكم علما وفهما وحكمة
billahii OUSTAZ Sagna wakh ngaa deugueu c la première fois que je regarde tes vidéos mais vraiment j'apprécie tes paroles de sage billahii deugeu nekhoul
Massallahh oustaz .. vous êtes vraiment véridique ... on est tous dernier vous
Sa waye boul sonn thi wakhi Iran Ndao. Mann dé khaw ma sama euleuk. Wayé mom ak gni nék thi guinawam yeup bougnou moytou woul euleuk Yalla di na brochette sénn ndaye thi digou safara ya gueuneu tangue.
Merci Oustaz yalnala yalla faye samoula aaarela
Merci oustaz yalla rek takh lingay wakh bon courage
Mashalla Merci beaucoup Oustaz Sagna
Conseil d un sage merci♥️♥️🙏🙏👏👏
Que le tout puissant te garde
Merci ouztaz sagna machallah wakh dji rafetna
DEUG dal dou wessou Nop machallah oustaz
Dieuredieuf Oustase deug bou wéér nga wakh iran Ndao dafa sankou, nafèk leu🙏
Mash'ALLAH
Très Bon conseil merci beaucoup. Bon rappel.
ماشاءالله جزاك الله خيرا وبارك فيك
@@SarrAliou-r6h ولك يا أخي الكريم شكرا لك بارك الله فيك وجزاك خيرا
Iran doméram la day garal nafekh ak seytanée
Merci pour ton courage .ya pas 1 homme aussi véridique k toi .merci'
..
Salam oustaz Sagna!
Quelle vérité et macha Allah espère tout le Sénégal entend tes messages.
Je te jure bro gni laniou wara déglou
Merci beaucoup Oustaz Sagna yalnagnou yalla mayy dégue ak topp. Merci pour les rappels 🙏🏽
Ok dieuredieuf
Merci oustaz sagna
😅oustaz djola c rare 😆
Oustaz serere amoule😂😅😀
Macha allah♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Salam et merci Oustaz Sagna ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🥰
Ay oustaz Sagna merci machahala
Bilay walay 🙏🙏✌️✌️✌️✌️
Machallah amena solo merci Oustase
Machallah merci beaucoup ya oustas
Macha alla yalla naga goudou fane 👍👍👍
Machallah déguetina DEUG oustaz yalnala yalla samé ❤️
شكرالك.يااخى.ان.ارادولم.يكن.الاحمارا
💓💓💓💓💓💓👏🙏🏼
Walahi deugeu rék ka nékhe
Oustaz yalla nalla yalla daffal diam
Machallah liga wakh amna solo 🖒
MACHALLAH YALLANA YALLA BARKEL TÉ SAMELA THII BARKÉ NITOU YALLA YII WAKHEDJI RAFÈTENA
MachaAllah oustaz
Longue vie a vous et que Dieu te protege
Hayyy oustaz bou sant Sagna! Grand Diola deug rék ngua wakh
Barakallahou fikoum Cher ouztaz
Merci beaucoup mon frère
Vérité absolue
Merci beaucoup ya oustaz
Merci beaucoup ouztas Sagna iran ndao da rèw domèram la
Merci duega rek mo am solo
Machalla t'es pertinent
La vérité ne traverse jamais, l'écoute d'un juste, c'est clair....
Wal lahi
No yow d oustass sougnou la amone 4si sa genre no kone Sénégal dey melni midi machallah merci mn segneur
Machala ya oustaz
Iran deh Ya Oustaz dafa féteurlou rek akk gnikoy diaye mouy diayakhou mais Bakhna Tivaouane deh djiwougne ko lii
Verité deuga nga wakh machalah Irán da beuré té moussoul ossi
ohhhhhh diaa dieuf waaye
machallah très bonne conseils
Machallah très bonne conseils oustaz dieureuf
Deugg rek mo wor jerejeuf oustazbne cntinuation
ALLAH AZA WAJAL te fortifie sur le droit chemin
ALLAH est unik seul aucune autre divinité n'est digne détre adoré
Machalah bilaye
Merci ya oustaz deug dou rombou ay noppou
Merci oustaz SAGNA
ماشاءالله جميل
Allahu akbar
Bilahi oustaz sagna mala beug mais le sang ne ment pas djeureudjeuf gor pur nga
Wakh DEUG reck mon woor yala khirniou sibobam
Dieureudieuf degg n’a wakhou djoulit
Biillahi wakhe ga degue merci
Wakhdji rafetna lolou
Tonton Sagna yaw rekk ya wakh deug Iran ndao dafa ra nopiiii
Sokhala n'a la
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Merci sagna manchala
Loulër nga wah
Merci oustaz
Ouztaz diegalou deh mei amo teguine
Macha allah
Allhamdoulilahi
Duigu rekk ya fie wahk .. ira seytan la,
Je me suis abonné à ta chaîne. Yallah n'a borom bi nangou nianeu amine. Défal la diamb bou beuri
Sagna xana yaw tu es le prophète. Tu donnes toujours des promesses nan euleuk rek😅😅😅😅
Lou lére
Machallah
Merci beaucoup ouztas
ya oustaz deugue nexoul ndakh wakhou yallah la dou waxou kene kou mer nak xolatal sa joilite bakham yangui jouli wala kefer nga ........
sur les mosques
nekh nga ma dou sa diemeu j wayii li cii yallah ngaa guené mbaa ma deugeu koo billahii Sénégal dou Islam moyii sen doundou parparlo réék
Bien parlé
merçi ouztaze sagna
Bilahi wa raboule guanbati goussi bayiwoule serigne babacar mansour par c q mome wakhal kène lou bonne kou diapeu bopeum la tek si kou deukoula ....
Sona rek
Yow mi leniou wara moytou nakhe mandouwo
Yaw rék la guiss oustaz bou niémé deugue goudal fane sa dunde am na ngarigne
والله حقا
Vrèmen beugnala barkè salatul fatiha beugnaka trope senegal aye niite yu melni yaw la mankè
Ki dafa kham dara si limouy wakh ki amoul kham kham billahi
Merci
Iran mom garwalé rek lay def légui.
♥️♥️♥️👍👍👍
🙄🙄🙄🙄🙄🙄🙄🙄🙄ayy ki mo niémé
Sagna na say fane goudeu