🔴Oh! ndeyssane😭 Serigne ibra gueye Yém na nar yi, "Khassida jazbu" makkah 2023 Thieye Serigne Touba,

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 21 дек 2024

Комментарии • 830

  • @mamediarrabeye300
    @mamediarrabeye300 Год назад +10

    Oh Machalah diomalga Naryii sa waxdji mo reuye❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ ❤❤❤ ❤❤❤❤

  • @mamadoundiaye5246
    @mamadoundiaye5246 Год назад +190

    Ma Sha Allah Serigne Ibra Gueye, on est très fier de toi. Tu as grandi sous nos yeux à Thies. Gloire à ton défunt papa qui t'a éduqué dans le travail et l'éducation islamique. Qu'Allah l'accueille dans son paradis éternel

  • @bayecheikhmbengue5626
    @bayecheikhmbengue5626 Год назад +99

    Ndaysane Serigne Ibrahima Gueye yalla nako yalla samou té aar ko si barkep borom Touba ak xassida yi barkep borom taif ❤

  • @SerigneKoli-ve2eu
    @SerigneKoli-ve2eu Год назад +65

    Karamati xatu yadi mes miracles sont mes écrits thieuy Ahmadou ❤️

  • @OusmaneDiallo-wk3jc
    @OusmaneDiallo-wk3jc Год назад +36

    Tiéye Serigne touba dieureudieufeuty aye waye naniou sante yalla nioune wa Sénégal thé défarat djiko yi yalla téral naniou😭

  • @bigue5329
    @bigue5329 Год назад +30

    kome wa Sénégal khamou niou kouye SerigneTouba nar yi niome khame nanioko mageui songa khame lou takhe Serigne Touba demoule maka bou demon dou nigawatt 🥺🥺🥺🥺😢😢😢 machalla Serigne Ibrahima geuye mouride sadikh bi🙏🙏🙏🙏❤️❤️❤️❤️🥰🥰🥰🥰

    • @SeynabouSarr-hx3hv
      @SeynabouSarr-hx3hv Год назад +2

      Bilahi lou amngaa wakh gnounn linou amm sakh khamougnou koo

    • @nafissatou9560
      @nafissatou9560 Год назад +2

      Billahi wallahi mbockou

    • @nafissatou9560
      @nafissatou9560 Год назад

      Dieureu dieufeuti Serigne Touba khadimou Rassoul ❤❤❤❤❤

    • @madoundoye2414
      @madoundoye2414 2 месяца назад

      Lou werr thé wor DEUG la daniou ko oumpeler

  • @mamadoucoumbafaye7666
    @mamadoucoumbafaye7666 Год назад +133

    Senegal amatina ndam kou bindeu li Serigne Touba foumou deukk Sénégal doyna ndam barké borom bi begg naniou 😢

  • @Mrsam75
    @Mrsam75 Год назад +48

    On ne peut qu’admirer même en étant d’une autre religion. Waouh cela donne des frissons. Respect

    • @cheikhdione2925
      @cheikhdione2925 Год назад +3

      Ok, bien vu. C'est tout simplement extraordinaire. Voilà les écrits du VÉNÉREUX CHEIKH.

  • @PapacheikhSylla
    @PapacheikhSylla Год назад +74

    بشرى لنا في شيخنا عبد الله وخديم رسوله صلى الله عليه وسلم والحمد لله رب العالمين في كل حال ❤❤❤❤

  • @SodaToure-cy7ed
    @SodaToure-cy7ed 7 месяцев назад +6

    Dieurdieufaty Serigne Touba diarama mame Cheihh Ibrahima Fall Yalna yalla Faye si barkép xassidayi🙏🙏🙏

  • @bdisn4484
    @bdisn4484 Год назад +7

    Ça marquerait dans l'histoire à jamais bilae ahmadou bamba ligueyal naniou ❤❤❤ mangui dioy ni 😢 skh bimay binedeu😢😢dieureujeuff serign Touba 🙏🙏

  • @mouhamadoujegou7696
    @mouhamadoujegou7696 8 месяцев назад +7

    Serigne Ahmad bamba le plus grand poète, il est trop mystique

  • @sallyfaye8084
    @sallyfaye8084 Год назад +8

    Suis moustarchide wallahi sama khol dafa toy bamay dioy yalla nala yalla Fay yiw barké Cheikhoul Khadim ❤️en plus ta voix ooooh mashallah 🤍

  • @khoudiagueye5012
    @khoudiagueye5012 Год назад +39

    Sante yalla bou bakh dit diouly thit seydina mouhamed (psl) yalla naniou yalla fayal cheikhoul khadim

  • @TapsirouSall
    @TapsirouSall Год назад +23

    Je ne suis pas mourid mais ça me fait vibrer ❤❤

  • @NJMTRTV315
    @NJMTRTV315 8 месяцев назад +6

    Thieye Serigne Tuba ❤❤💖🙏🙏Jërëjëf Serigne Ibra💘💘🙏❤❤🙏 Sante yalla bubax baniu amé Serigne Touba

  • @almuxtaarvision943
    @almuxtaarvision943 Год назад +12

    Wallaay ndeysaan. Moo ko wax lu ko kenn waxul, waxé ko nu ko kenn waxe wul, waxe ko fu ko kenn waxe wul.
    Al hamdul Xadiim.

  • @moustaphadiagne3803
    @moustaphadiagne3803 Год назад +20

    Ma cha allah qu'Allah vous protège si barké Cheikhoul Khadim si barké Seydouna Mohamed Amine 🙏

  • @diallocoura5717
    @diallocoura5717 Год назад +61

    Dieuredieuff serigne TOUBA🙏🏼❤️

  • @GnangaKandji
    @GnangaKandji Год назад +29

    Wallahi je suis fière d'être beug cheikhoul khadim❤❤❤

  • @morfall-g7l
    @morfall-g7l 3 месяца назад +9

    serigne bi amoul morome🙂🙂🙂 ta dou ko massa amme 😇😇❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @thiernocirembengue8558
    @thiernocirembengue8558 Год назад +7

    Li nekh na bilay je suis talibé mais serigne touba amoul morom 😢😢😢

  • @abdoukhoudossdiop2549
    @abdoukhoudossdiop2549 Год назад +15

    Nii sama khol bi cedde yalla nako sounu borom ceralé sakhol s Ibrahima gueye 🙏🙏🙏

  • @mamegangembacke849
    @mamegangembacke849 Год назад +10

    Ndaysan machallah dieureudiefè serigne Touba☝️🥺serigne ibra geuy yalanal yala fay barkè serigne Touba🤲🤲😭😭😭❤️❤️❤️

  • @Adnanezinho-jm8zk
    @Adnanezinho-jm8zk Год назад +26

    L’écriture de Cheikh Bamba khadime rassoul merci ibra gueye ❤

  • @mohamedngaide5774
    @mohamedngaide5774 Год назад +6

    Machaala eskeyy li mo diara royyy ❤❤❤ en tant que tidiane sui vraiment fier

  • @YouBeatzs
    @YouBeatzs Год назад +3

    Serigne Touba Aka amone yener Nieuw maka... Wayer ndeysane Dieuzbou djib na biir maka 😭😭😭

  • @salioumbaye180
    @salioumbaye180 2 месяца назад +2

    Akassa cey waw goor Jazboul khoulob❤

  • @ahmedtidianedia1767
    @ahmedtidianedia1767 Год назад +8

    Ndeyssane lii day djioylo wallahi j'ai plein de larmes aux yeux beugue serigne touba mo nékh❤❤❤❤❤❤🎉

  • @aboubakrygaye9668
    @aboubakrygaye9668 6 месяцев назад +3

    S touba am na ndam

  • @AbdouFall-br1tj
    @AbdouFall-br1tj 6 месяцев назад +2

    Amina amina amina daradjaye SEYDINA MOUHAMA 14:53 DOU RASSOULOULAHI SALLA LAHOU HALEYKHI WA SALLAMA

  • @papacoura7270
    @papacoura7270 Год назад +7

    Voici ces genres de videos qui meritent des million de views🙄

  • @smodousow2109
    @smodousow2109 Год назад +10

    Lii damy fattali wàcaa yu sëriñ Tuubaa gir siyaara xaritam ba صل الله عليه وسلم te yoo nu géej gi dog ko ❤❤❤😭😭😭

  • @alnour221
    @alnour221 Год назад +51

    Machallah❤❤❤❤❤ Dieureudieuf Borom Touba

  • @babacarndiaye2698
    @babacarndiaye2698 Год назад +1

    Ndeysane 😭 yalna yalla goudal sa fane serigne ibra gueye gueuneu yagg gueneu werr machalha

  • @elhadjimoussafalldiarra4413
    @elhadjimoussafalldiarra4413 Год назад +35

    Amine 🙏DIEUREDIEUFATÉ SERIGNE TOUBA ❤

  • @massediop8971
    @massediop8971 Год назад +31

    Dieureudieuf serigne touba amoul morom dh ❤

    • @fayeassane-tx4ir
      @fayeassane-tx4ir Год назад

      😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂❤❤❤❤❤❤❤❤❤😂😂😂😂😂😂

  • @amdyperki6545
    @amdyperki6545 Год назад +11

    Salahou Allah Mohamed ♥️♥️♥️ dieureudiefeti Serigne touba ♥️♥️ diarama Mame cheikhra fall ♥️♥️

  • @aichadiallo3662
    @aichadiallo3662 Год назад +37

    Amine 🤲 machalla ♥️

  • @abdoudioum-ji4mu
    @abdoudioum-ji4mu Год назад +10

    Kéne dou serigne TOUBA ❤❤❤❤

  • @mamadoukane5669
    @mamadoukane5669 Год назад +2

    Machallah diamou yallah rec mo woor
    Li toyal na sama khol bi Machallah 😭😭❤❤

  • @smodousow2109
    @smodousow2109 Год назад +13

    Naar yi xam nan né borom Tuubaa amoul moroom ❤

  • @alphaoumardiallo3884
    @alphaoumardiallo3884 Год назад +15

    Dieuredieufeti Borom Touba Diaraama Mame Cheikh Ibrahima Fall Lampe ❤️❤️❤️👍👌🙏🙏🙏

  • @awagueye6954
    @awagueye6954 2 месяца назад

    Ma sha Allah. Alhamdoulilah rabbil alamina. Alahouma sally hanla Nabiyou karim. Psl. Dieureudieuf Serigne Ahmadou Bamba Khadimoul Rassaul lilahi Psl. Alhamdoulilah. Dieureudieuf Serigne Gueye. Longue vie à toi et à tous

  • @ndeyefall1725
    @ndeyefall1725 Год назад +15

    Dieureudieufety serigne touba 🎉❤

  • @tinho8762
    @tinho8762 Год назад +8

    Alkhamdoulilah sante yalla dieuredieuf s.touba❤❤❤❤❤❤❤

  • @ibrahimadiouf8949
    @ibrahimadiouf8949 Год назад +11

    😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭thieye khassida yi, diaradieufati sérigne bi, kéne dou borom touba💯❤💯❤💯❤❤.

  • @ToureYacine-g4g
    @ToureYacine-g4g Год назад +21

    C une fierté machallah

  • @rapshouseofficiel9072
    @rapshouseofficiel9072 Год назад +361

    Tidiane piir la mai Bilahi dama contane ba dioy 😢😢

    • @diopbbndaya2245
      @diopbbndaya2245 Год назад +33

      Ndaysane yaw mi yaye talibé cheikh piirr nak❤ya bakh way🎉

    • @bawal1bawal977
      @bawal1bawal977 Год назад +21

      Talibe cheikh piir nga

    • @diarrashoubeyebeye1516
      @diarrashoubeyebeye1516 Год назад +25

      Thi khol la diougué té thi khool la douguou

    • @sarrassane5240
      @sarrassane5240 Год назад +17

      Ndaysane so xol moo sétt rék

    • @ibrahimadjitte9294
      @ibrahimadjitte9294 Год назад +22

      bép wérdi bou nitt ki diap ta tayaloul si péntiou yalla ba lako dieumé mo kham tidjan khadi...

  • @zoomania69
    @zoomania69 Год назад +36

    djeredjeuf Serigne Ibra Gueye di djangue khassida Serigne Touba yi di tawaf
    dolli sante rekk barke borome touba

    • @modou2878
      @modou2878 Год назад +3

      Jerejef Serigne Touba
      Santé Serigne Ibrahima guéye ci LIGGEY bou selle bi

  • @mamediarrathioub2351
    @mamediarrathioub2351 Год назад +14

    Dieuredieufety cheikh Ahmadou Bamba diarama Mame cheikh Ibrahima fall♡✧♡

  • @cheikhndiaye7344
    @cheikhndiaye7344 Год назад +8

    Machalla amatina solo dieure dieuf yalnanga fii yague thé andack weure barkep xassidayi yeppou Amine ❤❤❤❤❤❤❤

  • @DizaDiallo-ns5pn
    @DizaDiallo-ns5pn 2 месяца назад

    Thieuy serigne touba kam loumouy wah moutah narr bi ne peut ps lui passer tellemennt ça touche le ❤❤❤❤

  • @keindeibrahima4547
    @keindeibrahima4547 Год назад +17

    😢Dieureudieufè Borome Touba amoul morome koubageu lalal j'aime ❤

    • @m.a.d2475
      @m.a.d2475 Год назад +2

      Dieureudieuf borome touba

  • @BaabaDiene-hi2vv
    @BaabaDiene-hi2vv Год назад +11

    Alkhamdoulilah dieureudieufé borom touba a🇸🇳😍❤❤❤❤😴😪😥😓😣😭😭😭😭😭❤❤

  • @amadouibrahimaba6974
    @amadouibrahimaba6974 Год назад +8

    Dieureudieuf Serigne Touba yalna yala def diam ci rewmi ❤❤❤❤❤

  • @davidoaippels3287
    @davidoaippels3287 Год назад +4

    Dieureudieuf Serigne Touba Diarrama mame Cheikh Ibrahima fall s ibra Gueye Yaggfi loll te wer 🥰🥰🥰🥰🙏

  • @serignesarr6448
    @serignesarr6448 Год назад +9

    Thie serigne touba moy kéné

  • @MatyFall-z2h
    @MatyFall-z2h Год назад +3

    sante rek lako done suivre almouridiya bay dioy machallah ❤❤❤

  • @boromtawfkhetv6216
    @boromtawfkhetv6216 Год назад +2

    Thiey Serigne Touba Mo Tague Gandji Mbendéf lou ko ken Mossta Tague Wallahi

  • @muhamadudiouf6011
    @muhamadudiouf6011 Год назад +1

    Manam nekayou SERIGNE TOUBA lenén leuh❤❤❤

  • @cheikhabdoumbacke6970
    @cheikhabdoumbacke6970 Год назад +7

    Machallah s Ibrahima gueye Dieuredieuf ❤❤❤❤ xol sedna

  • @OusseynouNgom-l1o
    @OusseynouNgom-l1o Год назад +5

    Jarajeuf amatina solo trop machallah mala beugue nguir serigne touba ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @mbackeleye4264
    @mbackeleye4264 4 месяца назад +1

    MASHA.ALLAH ALHAMDOULILAH SANTATI YALLA BOU WEER JËRËJËF CHEIKHOUL KHADIM AMOUL MOROM ❤❤❤❤❤❤❤DIÀDIEUF

  • @BallafatyDiop
    @BallafatyDiop Год назад +2

    Tieuy cheikhoul Khadim ken dou mome billakhi Serigne Ibra Geuye machallah xol sed na trop

  • @magattetallly6077
    @magattetallly6077 6 месяцев назад +2

    Ndeysan naar yi daniou kham limouy wakh. Motakh di diangu transcriptions khassidas yi am solo lol.
    Dieureudieuf Serigne Touba
    Serigne Ibrahima Gueye yalna yalla weureul batt bi.
    Sallalahou Halla Muhammad ❤

  • @ismaeltraore6416
    @ismaeltraore6416 Год назад +4

    C'est notre fierté pour communauté l'islam Mohamed notre Prophète bien aimé Muhammad que Dieu nous facilite pour rendre visite le prophète à la Mecque inch'Allah 🕋☝️👑💪🤝🤲👳🤍💘💘🥰🥰🥰🥰🔐🤝

  • @abdoukhadresamb2565
    @abdoukhadresamb2565 Год назад +11

    Dieuredieuféty Borom Touba😭😭😭😭😭😭😭

  • @morndiaye9686
    @morndiaye9686 Год назад +4

    Dieureudieuf yalna yalla nangou niane barka seydina mouhamed

  • @serignetoubagueye7205
    @serignetoubagueye7205 Год назад +13

    Dieureudieufé Serigne Touba

  • @khadimkhouma
    @khadimkhouma Год назад +3

    Machallah amna solo loool serigne ibrahima gueye❤❤❤❤❤

  • @goramekare9594
    @goramekare9594 Год назад +2

    Macha Allah dieureudieuf Serigne touba diarama mame cheikh Ibrahim fall ❤❤❤

  • @allediouf1286
    @allediouf1286 Год назад +5

    Dieuredieufé Serigne Touba amoul morome

  • @magattediop3886
    @magattediop3886 Год назад +12

    machalla dieureudieuf serigne touba

  • @couradiouf987
    @couradiouf987 Год назад +15

    Masha Allah ❤❤ ❤❤❤

  • @djilysall7727
    @djilysall7727 Год назад

    Yalnala yalla may goudfan ak wergiyaram

  • @absadiop1188
    @absadiop1188 Год назад +6

    Kéne dou Serigne Touba ❤

  • @papasafouseck
    @papasafouseck Год назад +7

    Ohh ndeysane diadieuf thiey serigne touba❤❤❤😭✊

  • @matarsarr4344
    @matarsarr4344 Год назад +9

    Dieuredieufé Cheikh Ahmadoul Khadim Sounou Yakar Tay Ak Euleuk dieuredieufé Serigne Mountakha Bassirou yage fi lolou Balla Aïcha and ak wër

  • @sokhnamaisyll5171
    @sokhnamaisyll5171 Год назад +1

    MASHALLAH MAME BROME TOUBA KHADIME RASSOULE PSL AMOULE MOROME KENLEU YALLANAGNOUKO SOUNOU BROME FAYALE TÉ TASGNOUSI BARKÉME SI BARKÉPE MAME FALLOU MBACKÉ

  • @diawbenzema7548
    @diawbenzema7548 Год назад +1

    Diereudieufe serigne Touba ❤❤❤❤❤❤❤❤❤ibrahima gueye yalla n'a goudou fane ❤❤❤❤

  • @sidylaminedabo9936
    @sidylaminedabo9936 2 месяца назад

    😭👌🏾Akasaaa… 🗣️Jazbou jibb na thia Kaaba ga. 🙏🏾Jeureujeufati AHMADOU Khaadimoul RASSOUL❤❤❤❤❤❤❤. Serigne Ibra GUEYE 🤲🏾Doundal weral té yokk ba yeugg ko thi barké Khassida yi…

  • @GallasSaalih
    @GallasSaalih Год назад +3

    Allamoumma salli halaa sayyidinaa mouhammadin assaalih wasalim halayhi wa hala alihi salaatan wa tasliiman toutahirouni bihima hanil qabaa ihi

  • @ibrahimawade8541
    @ibrahimawade8541 Год назад

    Bilaye kéne dou Serigne Touba Serigne ibra Gueye yalla na la yalla faye thi barkép seydina moukhamét khol séd na

  • @skhnamaimounambow2996
    @skhnamaimounambow2996 Год назад +1

    Nexna si xol diereudiefety Serigne Touba Serigne ibra Gueye yalla yalla ngafi yag t Wer yalla weral bat bi

  • @shella8096
    @shella8096 Год назад +1

    Maa shaa Allah thieyyyy khassida nékhna trop mbéckté miii dieureudieuf Cheikhoul Khadim

  • @serignefalloukanendamatou4630
    @serignefalloukanendamatou4630 Год назад +3

    Jërëjëf serigne ibrahima gueye yalla nala khassida yi téral ad dounya wa aa khira❤❤🥰💚💞

  • @moryguettacisse2800
    @moryguettacisse2800 Год назад +14

    Dieuredieuf borom touba

  • @diopMbayangue
    @diopMbayangue Год назад +8

    Machallah ❤❤❤dieredief brome Touba

  • @SokhnafatyDiop-z2n
    @SokhnafatyDiop-z2n Год назад +4

    Dieure dieufe brome touba ❤❤❤dieure dieufe brome touba ❤❤❤

  • @bambacisse4200
    @bambacisse4200 Год назад +2

    DIEUREUDIEUFÉ SERIGNE TOUBA KHADIMOUL RASSOULILAHI SALLALAHOU ALEYHI WA SALAMA DIARAMA MAME CHEIKH IBRAHIMA FALL LAMPE BABOUL MOURIDINA ❤❤❤❤❤😢😢😢😢😢

  • @serignegningue662
    @serignegningue662 Год назад +1

    Machallah khôl sedeuna lep Mouhamadou Rassoullillahi kessai(psl)yalla nala yalla fay yiw si barkep khassida bobou mou mayniou diam si adouna bi yeup ravatni Senegal

  • @falloundiaye4863
    @falloundiaye4863 4 месяца назад

    Thiéy waay seugne touba❤❤❤

  • @sokhnadiallo9013
    @sokhnadiallo9013 Год назад +1

    Thiey Serigne Serigne Touba Dieureudieuf Serigne Touba 🤲🏿🤲🏿🤲🏿🤲🏿🤲🏿🤲🏿🤲🏿🕋🕋🕋🕋🕋❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @abdoudndiaye8254
    @abdoudndiaye8254 Год назад +7

    Djeureudieuf serigne touba

  • @gueye009fallou2
    @gueye009fallou2 Год назад +5

    Machaalla théye serigne touba amol morom

  • @mariamasylla4289
    @mariamasylla4289 Год назад +2

    Machallah Alhamdoulilah Arabile Hallamine Dieuredief Serigne Touba

  • @papaoumargueye8190
    @papaoumargueye8190 Год назад

    Serigne Ibra Gueye yala nako borom bii swt dooli soutoura saam ko défalko tawfékh akh taysir thi barakati Al Quran Kareem barakati rassoulilahi saws barké borom Touba khadimou rassoul barké Mame cheikh Ibrahima fall barké xassidas yii

  • @mbenediarra6311
    @mbenediarra6311 Год назад +5

    Machallah dieureudieuffe borom touba

  • @alassanediagne9399
    @alassanediagne9399 Год назад +6

    Dieuredieufé Serigne Touba khadimoul Rassoul ❤❤❤