Kawtef à Pikine, Bar Thiaga Lagne Oubi Si Kogne Bi, Bagarre avec les habitants:« Tougne bi la lek…

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 11 янв 2025

Комментарии • 128

  • @People221sn
    @People221sn  4 месяца назад +4

    N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ...
    Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii...
    Témoin d’un événement contactez : +221 77 451 21 10 WHATSAP
    +221 78 149 53 10 APPEL NORMAL

  • @ElhadjNiassetoure-kp2qs
    @ElhadjNiassetoure-kp2qs 4 месяца назад +8

    Vraiment copain ieo referencia nga kois force a toi deugeu mo ndieuk té moy moudjou

  • @cirely3220
    @cirely3220 4 месяца назад +54

    Guiss ga Sénégal dagaye nek si kogne di khekh sa wa kogne dila setane

    • @halamadrid2108
      @halamadrid2108 4 месяца назад +2

      Mo takh diarounioul dimbali .danlasi ray rek nioulaye setane

    • @Babbasfa
      @Babbasfa 4 месяца назад +1

      Bien sûr bouléne léré ni amo DEUG ta wakhoul DEUG dougnu guéneu Di togne .yow khalégha Sénégal noumouy dokhé.seul gni ko ragal néqeu sous sont emprise lay wolou niléne wakh léne ta dougnu sagna bagne.mo togne mom loumouy déf yeup thi kogne bi guéne khamoul

  • @bachirndiaye4384
    @bachirndiaye4384 4 месяца назад +23

    Thiagga yeup ay farou police laniouye am pour couvrir situation yii tok lèn nane commandant wak général ay commissaire

  • @RobertBoyndour
    @RobertBoyndour 4 месяца назад +47

    Khana sen cogn amoul ay goor pour kheikh bi

  • @Ababoukara
    @Ababoukara 4 месяца назад +26

    Ce commissaire de Pikine est incompétent. Il doit quitter ce Poste au plus vite. Il est incompétent c’est tout.

    • @niangtra
      @niangtra 4 месяца назад +3

      Est ce qu'il n'est pas corrompu tamit

    • @Sènègal1404A
      @Sènègal1404A 4 месяца назад +1

      Billahi

    • @Ababoukara
      @Ababoukara 4 месяца назад

      @@niangtra ça semble. Sinon il aurait fait son travail correctement. En cas de coups et blessures volontaire attesté par un certificat médical d’incapacité l’arrestation est obligatoire.

    • @Ababoukara
      @Ababoukara 4 месяца назад +3

      ça semble. Sinon il aurait fait son travail correctement. En cas de coups et blessures volontaire attesté par un certificat médical d’incapacité l’arrestation est obligatoire.

  • @morfall3066
    @morfall3066 Месяц назад

    Si les gens ont peur de de gérer la situation laisse tomber tous les jeunes qui habite dans la rue sont plus nombreux que quatre personnes l union fait la force

  • @AblayeDiop-e8r
    @AblayeDiop-e8r 4 месяца назад +23

    Wa lii lép kon migui khew si adouna bi man fannla nék je suis peur 😱

  • @code7236
    @code7236 4 месяца назад +9

    Waa khana fii goor amoufi ahh yéne😮

  • @ndarawndiaye9663
    @ndarawndiaye9663 4 месяца назад +6

    Un combat on le mène pas seule vous devez vous réunir en groupe… ligua nek yaw kasser motah gnou gniemela en plus tu es malade donc tu prends des risques frère soyez unis wotel réunion boyi gneuw

  • @OumyOumy-m6c
    @OumyOumy-m6c 4 месяца назад +21

    Wa khana kogne bii goooor amoufa

  • @elmoussafall3887
    @elmoussafall3887 4 месяца назад +4

    Thiotou ndem sénégalais mo niakk fayda sibopam étrangers non😭😭

  • @MimiMimi-vm5oe
    @MimiMimi-vm5oe 4 месяца назад +2

    Sénégal liberté ak matay bifi ame ci étrangers amoul fénéne.😢 Kagne mo sagne dém deukou diambour difa dore domou deuk ba ta dara fékoulaci bilay j'ai mal au cœur. Sénégal il est temps qu'on règle la question des étrangers niou limiter léne tekci khamal léne finiouy yame

    • @julioesuashistorias9589
      @julioesuashistorias9589 4 месяца назад

      Et apres demande a tous les Sénégalais qui sont ici en Europe sans papier et clandestin di diayanté di dakanté ak policier goudi ak beuthieuk pour téral séne wadiour ak ndiabote yi di investir séne deuk wakhléne gnou gnibissi?? Arretez le Raciste kéne menoul wagni weurseukou kéne !!! Salam !!!

    • @noppouaskanebi9352
      @noppouaskanebi9352 4 месяца назад

      ​@@julioesuashistorias9589sa lefeul nognou gnoubici est vous dégager 😂

  • @DaoudaDiatta-ku3mk
    @DaoudaDiatta-ku3mk 4 месяца назад +12

    Demal brigade de recherches

  • @MaremeKebe-qz8jn
    @MaremeKebe-qz8jn 4 месяца назад +7

    Ohh massa

  • @yayodiallo1021
    @yayodiallo1021 4 месяца назад +10

    Sa manchoir bi démal hopital si dentiste pour gnou defal la radiopanoramique pour verifier ndah amoul beneu problem

  • @SeynaboumameSamb
    @SeynaboumameSamb 4 месяца назад +2

    vraiment je suis choqué

  • @panafricain1993
    @panafricain1993 4 месяца назад

    Sénégal amna Yonne dou yow yaye loi

  • @MamyGueye-q9o
    @MamyGueye-q9o 4 месяца назад +4

    Ki bou nékone yoff problème bi régler na bou yague

  • @cheikhndong3851
    @cheikhndong3851 4 месяца назад

    Oui na guenn moy yonn

  • @ThiatouYayam-t4h
    @ThiatouYayam-t4h 3 месяца назад

    Dounguene outt essence tak keur gui

  • @malickdiack8268
    @malickdiack8268 4 месяца назад +6

    Wakh lenn ko brome keur gui bousi wakhoule dara ngen tale keur gui loulen si cela gnome la

  • @spinners05
    @spinners05 4 месяца назад

    Mane dal dama mandou🤭🤐

  • @karimcoulibaly9753
    @karimcoulibaly9753 4 месяца назад +14

    Commendant bi falaye dano

  • @sambawa7298
    @sambawa7298 4 месяца назад +2

    C'est votre faute vous avez élu un étranger c'est normal il n'a qu'à partir de manière c'est inadmissible

  • @fatouba2560
    @fatouba2560 4 месяца назад +1

    Dem len dakar ndeyam bien bon mou guen si kogn ba

  • @Sallmbaye2000
    @Sallmbaye2000 4 месяца назад

    Vimba sorcier là je le connais tu a eu la chance 😂😂😂😂

  • @amydiagne4868
    @amydiagne4868 4 месяца назад +1

    C est le quartier qui doit se mobiliser et les dégager.point

  • @Yallaykesser221
    @Yallaykesser221 4 месяца назад +2

    Est ce que wadji yoroul lomotif wa police ba😅

  • @SoukeynaDiouf-b8h
    @SoukeynaDiouf-b8h 4 месяца назад +4

    Def léne ni wa thies am fouleu tale ndéyame

  • @AichaVital-m6e
    @AichaVital-m6e 4 месяца назад +1

    Ce ci est extrêmement grave

    • @AichaVital-m6e
      @AichaVital-m6e 4 месяца назад +2

      @DieyeMoulaye une bagarre entre voisins ou il c fait mordre la lèvres. L'un reproche à l autre d avoir ouvert une activité illégal..
      Le fait k les choses aient atteint le degré de la violence est inkietan..

  • @Babbasfa
    @Babbasfa 4 месяца назад +1

    Pabi néna ki deukoufi😅ki dé mo guinté jeunou kogne bi .Dekofi di nétali.yéne gniko coth ak paka beug ko raye ba lolou mo indi thiow li yeup dossi wah.Senegaléla come yéne pikine la magué.Lighéne beug la naghouwul lolou moy wahdji.wassalam.Senegalais nak béneu noop la

  • @Mbodji-walo
    @Mbodji-walo 4 месяца назад +1

    Thiaga yi ak Policeyi ño and mo takh

  • @awakane1050
    @awakane1050 4 месяца назад

    Dagne KO warone na khékhlé mon geune diko sétane baniou gagne KO ni bagna yorè arme lokho lokho bouko défé kène douthi dèé

  • @Oussou221
    @Oussou221 4 месяца назад

    Pourtant diagayi si sene Li Géye laniou nek kou beuga niame niamale kou beugoule nga bayi léne ak sene yef ok 😂😂😂

  • @cissemaimouna5742
    @cissemaimouna5742 4 месяца назад

    Na demmmm

  • @ahmadouka8036
    @ahmadouka8036 4 месяца назад

    Mé yèn wa kognebi locandina kharr

  • @afro3827
    @afro3827 4 месяца назад +11

    Douguen kat ndayi wadji

  • @papamagattembaye786
    @papamagattembaye786 4 месяца назад

    En tout cas banditisme yagg pikine

  • @salioucisse2355
    @salioucisse2355 4 месяца назад

    Daa melni lii Dou pikine
    Xamna maoullen armey cogne 😂

  • @Sènègal1404A
    @Sènègal1404A 4 месяца назад +3

    Police sènègal douniou tous,dieul millitaire niou nèk si alle casamance yi indilène fi mogueune

  • @saliouDiabaye-sy1zo
    @saliouDiabaye-sy1zo 4 месяца назад

    Lidianti léne séne probleme li boudé deugeu sax yone moko wara lidianti pas yéne

  • @fas2822
    @fas2822 4 месяца назад

    Niaane lène Yalla laasi guiss

  • @YahyaMane-dw1gy
    @YahyaMane-dw1gy 4 месяца назад +3

    Frere yow khana amo famille

  • @fatimandao8359
    @fatimandao8359 4 месяца назад

    Mais ani wa kogne bi ñou laye sote ñouye sétane vraiment comprendroul ma dara

  • @salamsalam4960
    @salamsalam4960 4 месяца назад +4

    Tiaga guii bougni djougoul si sen mbir dinagn dem ba djeumeu djamono niou poser candidate pour nek presidente du sénégal 😂😂😂ndakh legii degni ozer neubeutouniou dara Mai’s keneu dou gor tmt ndakh diay yapeu mom sayou dokhee rek xamalni gor Yangi djeundeu bubakh 😂😂😂😂oh mon pays 😂😂😂😂

  • @malickseck911
    @malickseck911 4 месяца назад

    Les étrangers sème tjrs la pagaille Sénégal amlel fouleu

  • @momocreation3631
    @momocreation3631 4 месяца назад

    Policie yi nék sy banlieue bi amouniou bene ndiarigne ☹️☹️

  • @noppouaskanebi9352
    @noppouaskanebi9352 4 месяца назад

    Wadji ray léne ko tall ko

  • @omzo-r6o
    @omzo-r6o 4 месяца назад +1

    Allé à la gendarmerie pas la police

  • @ElhadjNiassetoure-kp2qs
    @ElhadjNiassetoure-kp2qs 4 месяца назад

    Senegal amoul ndey lois té dou meussa amm ndey lois leufeul ndey ndjitou rew yiñou yorr

  • @halamadrid2108
    @halamadrid2108 4 месяца назад +1

    Porkoi tes voisins ne sont sortis pour te defendre.bo continuer yow rek danlassi ray rek yow yay perte

  • @MoussaTine-c6m
    @MoussaTine-c6m 4 месяца назад +4

    Diarra complice la raye lenne ndayam da ngenne niakk fayda

  • @julioesuashistorias9589
    @julioesuashistorias9589 4 месяца назад

    Lan moy sougnou cogne ??? Séne papa gno dieunde cogne ?? Cogne bi keur rek guéne si am lélé sakh daguéne loué !!! Donc ligueunti léne séne keur mo gueune dakh amna diame dakh amna lék dakh am guéne liguey té yar xalé yi !!! Le reste c l'Etat qui doit s'en occuper !!!

  • @ibrahimadrame2931
    @ibrahimadrame2931 4 месяца назад

    Où est borom keur gui

  • @ndouroro1520
    @ndouroro1520 4 месяца назад

    Wamé ani wa kogn bi balé lén ki moudiogué fi

  • @ahmadouka8036
    @ahmadouka8036 4 месяца назад

    Il fallait se lever au début

  • @juniordieme2665
    @juniordieme2665 4 месяца назад

    Sa yonn nekoul thi bar diambour waxal thi Thiaga yi rek

    • @MimiMimi-vm5oe
      @MimiMimi-vm5oe 4 месяца назад

      Séne yone mingui ci kay ndakh bar bi mo indi thiaga yi. Genres wakh mo yakh deuk bi. Sûrement waurkatou bar nga motakh ngay défendre bar

    • @AmisSarr-y5q
      @AmisSarr-y5q 4 месяца назад

      Mais fofou sakh dou bar keur la mais wadji mo yakh keur gui louè yenen negyi dieul negam Di hébergé kou Dougg fayy

  • @AmadouSow-jl1gu
    @AmadouSow-jl1gu 4 месяца назад

    Dou deugue dou yonne bâgneléneko dâye yâkhe sougnou domme yi ak wa kogne bi téthe léne ko

  • @cheikhmbackeseck1608
    @cheikhmbackeseck1608 4 месяца назад

    Wa gni yabate wougnou keur diambour genn nane mou geen keur gui

  • @salioucisse2355
    @salioucisse2355 4 месяца назад

    Diarra NAA guenn wakh AK nittgni

  • @sopenaby2091
    @sopenaby2091 4 месяца назад +1

    Saway Li dafa yomb torop dollèn guèn tal keurgui amna yoxam ni diaroul xar yon sott lèn waji

    • @Mbodji-walo
      @Mbodji-walo 4 месяца назад +1

      Billay wa kogne bi comme amoul ay gooryalla😢😢😢

  • @IssaDiallo-v8j
    @IssaDiallo-v8j 4 месяца назад

    Thiaga boufi tidie dégo niata da guà teudj goor yi fayy déme nakk ay lagn laniou f

  • @magatteciss5012
    @magatteciss5012 4 месяца назад

    Wa ana chef de quartier bi badou wadji guouhal lou ko rek

  • @Aminata468
    @Aminata468 4 месяца назад +2

    Malheureusement le Sénégal n’appartient plus au sénégalais deguena hypocrite wayé allons rek étranger yii niogui fi di deff louléne saff sénégalais yii ande si deuk bii di delou guinaw

    • @MimiMimi-vm5oe
      @MimiMimi-vm5oe 4 месяца назад +1

      Sénégal bilay warnagn diouk ci étrangers yi lifi ame amoul féne. Deuk bi yeup ay étrangers nioko yakh je vous jure Sénégal nioko yakh tekci liberté bign fi ame amoul bénéne deuk

  • @boyeniang3781yeumbeul
    @boyeniang3781yeumbeul 4 месяца назад +1

    khana sén kong bi amoul ndy ay gor yalla😡

    • @fas2822
      @fas2822 4 месяца назад

      Yoone beugoul kouy fadial boppam

  • @NdiatendiayeNdiaatte-ru7ks
    @NdiatendiayeNdiaatte-ru7ks 4 месяца назад

    😮😮😮

  • @salioumbathie4138
    @salioumbathie4138 4 месяца назад

    Démal gendarmerie

  • @FallouThiaw-mb4je
    @FallouThiaw-mb4je 4 месяца назад

    Diarra khana ligueyoule mome na wakh lou lere koi

  • @SeynaboumameSamb
    @SeynaboumameSamb 4 месяца назад

    moi je pense qu'il donne de l'argent à la police c'est pour cela quel interview pas

  • @CheikhounaDiop-w7g
    @CheikhounaDiop-w7g 4 месяца назад +1

    Boudone sama kogne ba taye niapeu daniou ndayam

  • @mohamedd7470
    @mohamedd7470 4 месяца назад +8

    Wadji weur nama ni dafay diokh ay nampay yéneu deukkeu ndo. Motakh niou mandou si mom

    • @ZeynaTounkara
      @ZeynaTounkara 4 месяца назад +5

      Bro Kham ngua Sénégal gnou eup légui Khalis lagnouy diamou ko romb nouyoko 5000f mba 2000 rek dougnoula wakh DEUG ba Dilla dénoncer

    • @Mbodji-walo
      @Mbodji-walo 4 месяца назад

      Doumala wéddi nk😂😂

    • @AmisSarr-y5q
      @AmisSarr-y5q 4 месяца назад

      Diokhoul benn deukendo ndampay au contraire chaque jour day guenna dellou ganaw nioune nieuppa KO beurgueul kenn beugoul mou nouyoula

    • @mohamedd7470
      @mohamedd7470 4 месяца назад

      @@AmisSarr-y5q d’accord! Mais pourquoi pas mobiliser dieulé ko si kogn bi par force

  • @taphasamb6836
    @taphasamb6836 4 месяца назад +1

    Loussi sen yoone si auberge cogne bi yenn kaye boulenfa dougou rekk Mandou lenn avancer

  • @saliouDiabaye-sy1zo
    @saliouDiabaye-sy1zo 4 месяца назад

    Féne rék ngaye def soxar rék molene djapou vemba Lou lér la wax yaw dém nga prison ba tayi

    • @MimiMimi-vm5oe
      @MimiMimi-vm5oe 4 месяца назад +2

      Yow ya dakha doul nieup yaw ak vemba dangéne yame motakh ngakoy défendre hypocrite étrangers moléne gueuneul séne mbok sénégalais

  • @amarsall5678
    @amarsall5678 4 месяца назад +4

    Yawe demal ci yone

  • @cheikhmbengue6244
    @cheikhmbengue6244 4 месяца назад +2

    Lépp ak ousmane sonko bayi frontiére étranger di dougou noumou lénn nékhé naniou votél tahrou sarr inchallah ndakh sénegal bakh

    • @fas2822
      @fas2822 4 месяца назад

      Ya meuneu ...Sonko kagn la yeeg, étrangers nioukoy Kaas depuis temps Macky

    • @fas2822
      @fas2822 4 месяца назад

      Yow étrangers yii niou yagg ko Kaas ngay wakh Sonko

  • @mamadousy3993
    @mamadousy3993 4 месяца назад

    Liy deugg moy sene kogn ay fake gnofa nekkk ... wa police mom dangay warou dès fois

  • @sambawa7298
    @sambawa7298 4 месяца назад +1

    C'est des histoires de porcelet c'est interdit saga c'est un criminel

  • @AbdouDiallo-o8n
    @AbdouDiallo-o8n 4 месяца назад +1

    Thiago kagne

  • @ibrahimacamara1935
    @ibrahimacamara1935 4 месяца назад

    Diarra moy nafekhe bi dmoukhsram la

  • @sodadiop3021
    @sodadiop3021 4 месяца назад +1

    15mn35s pabi néna gnoune jeune yi

  • @Babbasfa
    @Babbasfa 4 месяца назад +1

    Racisme piir lafi guiss.Nite kouné amgha droit ni sama bountou keur dou tokhoukay yamba,lolou takh ghéne niko do Sénégalais beug gnu outeul fougnouy fréquenté ou pas.Sossal ko di toudou ay nitam pour diakhassé léne.khékh bi noumou démé?le gars et ses deux poulin nioko dap ak paka alors qu'il sortait avec sa soeur et son neuveu .bou diarbatam bi défoulwone sport de combat heur bi wakhatougnuko.pakanak koko guénél bo dioté si mateu santal.kou guiss keurgui khamni fofou amoul chambre sah nak bou libre.Li yeup parceque vous dite que dou Sénégalais ta mou magué pikine,tawam am 22ans ou plus dioudo senegal gui . raciste guéne trop .moléne eup ndieurigne thi kogne bi tékthi am métier lolou moléne méti.Diaykatou loubone moy dioh di khékh lou bone lou existéwul salh nak😮

  • @Babbasfa
    @Babbasfa 4 месяца назад

    Racisme piir lafi guiss

  • @amarsall5678
    @amarsall5678 4 месяца назад +1

    Yawe wakhou dofe Gaye wakhe

  • @MAYNA-DEYTH
    @MAYNA-DEYTH 4 месяца назад

    Démal gendarmerie