Moi aussi,c est ce que je me disais mais j ai remarque qu elle a porte du blanc dans la journee et encore le soir...tu as raison la jeune mariee quitte les invites dans du blanc car la majorite d entre eux ne la voient que le soir...et c est l image qui reste gravee dans les memoires.....
Sa mariage amna mana manchala sa robe rafét na seuyeul bou bakh guorgorlou inchala❤❤❤❤❤❤❤
Ndeyssane yalla na yalla barkel lep inchallah yalla boula tiate top si sen seuy bi amiine
Ohh les
Paroles de ngaka mashallah fatel Gorgorlul rek yalla diapalai leen
Ngaka rena😂🤣🤣🤣🤣non journaliste bi dou nit
Aujourd'hui vous êtes Monsieur et Madame Adriana félicitations
Nganga un mec kul machallah
Machallah li nexna wayyy jeureux ménage à vous ke du bonheur inshallah
Heureux ménage que du bonheur laf thiat sur vous
Wa journaliste bi comm kou nek ci lamb déh reporté bi😂😂
Ah nk nga sagn ko wax man j ai peukhhhh😂😂
Journaliste bi migui réveil Lou Nex🤣🤣🤣
Yalna seuy bi barkel and ak djabot gou Bari ta barkel Guen seuy 100ans yalla mousseul l'en si lamigne ak thiate ak chaytané
Machallah Rafetna fatel ame n’a thiass ❤️😂
Aaaye waaye yalla naleine yalla lafal thiat machalla aye khalè laniou et sa ce voi ke vous vous aimer
Ils sont trop mignon et jeune mashalla
Machallah yalnaleen thiat sekhlou
Heureux ménage yalla na seuy bi am barké yalla may léne si ay ndiabote you am barké .
Machala c'est trop mignon. Yalna seuy bi barkel
Lala dou nitt😂😂
Machallah yallah na sey bi barkél am si ay nabot you barkél couple nice Machallah
Dello ngama thi lamb dh😂😂
Heureux menage a vs joli couple
Machallah je vous aimes très fort ❤💯
Machallah ❤️ kou beugue sa diabar gua l'AF thiate ❤️❤️❤️
Machala boul melni say mag si show biz bi seuy tass rek khaleh nga seuyeul boubah boula keneu deg
Les reporters🤣🤣🤣 ils sont beaux mashallah
Heureux ménage wayyy😂😂🤣🤣
Machallah ❤️ comme c beau 🥰
Djiguene feme wayyy trop cute
Yalna seuy bi teu cheytané ak ay gnognam Yalla lafal len tiatt amiine
Woouy reporter Bi 😂😂😂😂😂😂
wa journaliste bi😂😂😂😭woyyyy célibataire baxoul
Ki gnemé na yalla dé😂lim fi wah yeup té aram degoul lignouy wah😂
Moma diahal di😂
Heureux ménage king baba diam diou beuri si yen
C'est beau 🥰🥰🥰🥰🥰🥰
Journaliste yi comme gnouy commentaire lamb🤣
Je te sûre 😂😂
Man mi di top cas ba guente fatel avec sa maman tmt Ken dou wax si man 🙄😂😂😂😂
😂😂
Bilay momla buegone wakh 😂😂😂
Bilay yedd len ma nak 😂😂😂
Ngaka yakamti na dem lune de miel momay reyy🤣🤣🤣
Journaliste bi mom🤣🤣
😂😂 journaliste bi ray nama
Fatel elle est si belle et mature ♥️ que ton mari soit à la réception c déjà un signe ( mbathio et Amina pote , les epius étaient absents )
Blindé bii daal nasi nak machallah
Na ngua yeureume sa dieukeure niko yayam yeureume beugue ko niko yayame yereume ma cha alla
Té nà yeureum diabaram niko baayam yeureumé....histoire de yereumandé en couple 🙂🥰
Ngakka mo ibi dé yi aay yalla yi journaliste Di 😂mbetta combat
Lou nekh♥️♥️♥️♥️♥️
Wa diomi wolen si journaliste bi 😁
Journaliste yii tramite🤣🤣
Yaw lamb ngay reporter waleu?aaaaaa😂🤣🤣🤣🤣
😁😁😁😁
Journaliste bi war nagno deme bantamba
Heureux ménage yalna seybi barkél 🥰🥰
wa Journaliste tmt ni lan léni bayii😁😁😁
Bey léne diahasé🤐🤐🤐
Ay xalle laniou Waye amnaniou foula
Mashallah heureux ménage
Wa journaliste bii dafay reportée lamb wala😂😂😂😂 ki moma eup fite nak😂😂😂
Guisse ngua sa badiene dafa yeureume sa papa lathe ko sa yaye ma cha alla
Comme aye reportage lamb🤣🤣🤣🤣🤣😆😆😆😆😆😆😆sheut suis enveugleuuuu senegal beug nane cas
Heureux ménage yalla na barkél 🥰 fatél meunone nga sol rob blanc
@@hadjaltv7183 niary yone 🙄
@@hadjaltv7183 j'avais pas vue qu'elle a porté rob robe blanc je viens juste de voir donc je ne savais pas et pourtant j'ai pas critiquer 😇
Moi aussi,c est ce que je me disais mais j ai remarque qu elle a porte du blanc dans la journee et encore le soir...tu as raison la jeune mariee quitte les invites dans du blanc car la majorite d entre eux ne la voient que le soir...et c est l image qui reste gravee dans les memoires.....
@@aichaboirobalde9594 elle a porté du blanc et franchement cétait meme pas jolie...je préfère largent la robe noire
C'est bien mariage bi mes âpre ka mougne t'es gorgolou rék sey nerkhoul Sasser yi rafetna machalla
Machalah😘😘
Mariage bi nekhna mais amoul organisation dara
Machalla
Yalla na seybi barkel
Machalla machallah machallah
J'aime
Seuy bi sama xol dathi sédd xawma lane leu, té douma léne sax suivre niom niar.
♥️♥️
Nice.
Khol sèèd na heureux mènage way
MasahaAllah
Seye yalnassi Borom bi Def barkel sama khôl sedna
D'ici quelque tu va entendre qu'ils sont divorcés comme tous les autres personnages du monde VIP
Wa louléni déyanté nak
De la complicité...sans chichis 🙂
Khana saff léne 😠
Dada mi
Mais garde corps yi sof naniou di diani nit yi rek
Yeine journaliste yi yeina daka doull si monde bi wallahhi daguénne gneimei yalla trop Tei barri wakh