Masha Allah tata Mariétou wallah Qu'Allah te paie pour tous que tu nous montres particulièrement moi je ne savais rien en cuisine mais maintenant alham doulillah ❤🥰😘
Yaye doundeul wereul yalah nala borom same la ak sa ndiabote . Mashallah dagua mais sante bi reikk moma diakhal maye sa boure iow ndaw ga sante. Maman je taime fort
Dicton-bi dialeina , mouné : " Nianbasse Yakhoule Seure " , toute la Théorie de l'information est basée sur la PORTEUSE, cette dernière qui enveloppe l'information afin de l'amener à bon port sans dommage. Je suis convaincue que le woloff est une langue divine comme le disait notre Grand savant Cheikh Anta Diop. Comme le disait Thione Ballaga seck dans la chanson " DIAGA " : " Yeigaleiii Mission Meu Akhe Soin ". Merci pour les vidéos de recettes sénégalaises, ça me rappelle des souvenirs d'enfance . CUL8R !
Ahh marietou war gama bolék asmao cissé mou yoné ma si you bakh you senegal yi, magui france wayé awma dara amoul kene kouy def you bakh yi comme asmao . En passant merci pour vos plats, je rate plus une pub .
Bonsoir tata marietou namone Nala. Merci pour la recette ça fait longtemps que je ne l'ai pas cuisiné. Je veux bien la recette de thieré neukheul avec guerte kharane. C'est mon arrière grand-mere qui le cuisinait quand j'étais petite ça me manque beaucoup
Mane deh damay khaare ba vendredi inchallah ma sòga visionner vidéo bi 😔sinon douma ko meuneu mouñ waaay 😥 Marietou bisou nala avec tte l'équipe saveurs planétaires 😘😘😘
Mashala tata Mariétou tu cuisines comme feu ma mère, mère Ndoye paix à son âme. Merci de valoriser la cuisine Sénégalaise.
Man mom diam ak weer rek lalay nianal yalla defaralko mbolem dioulite
Man mom damala dom té yalla tah
Sama yaye rek lay guiss si yow machalla
Machallah tata namla lol finga guenanati bakhna yallah na la yallah faye yiw may la goudou fane ak weur si barke Seydina Mohamed Slws
Beug na lingay def way Tata machallah merci
J’adore comment tu parles 😂, merci le peuple est content 😂
Masha Allah tata Mariétou wallah Qu'Allah te paie pour tous que tu nous montres particulièrement moi je ne savais rien en cuisine mais maintenant alham doulillah ❤🥰😘
Tata Marietou yallah nala yallah sunu borom fey sauvé ngeu Modou yi
tanyi Madame sak dafa khawa jalouse ndakh reugeul you may door djamonoyi
Sokhna si moussieu wakhoul darra Macha Allah
Dagua dédicace sounou mak bou bah ndeye fatou fall yalna yalla yagual tahawayom merci ta marietou
MashAllah Maman ! Yallah neu leu Yallah fayeb
Association begueu niébé ax kandia ta Mariétou. Xol déye guissé.😘
Machallah yalna yalla samela
Yaye doundeul wereul yalah nala borom same la ak sa ndiabote . Mashallah dagua mais sante bi reikk moma diakhal maye sa boure iow ndaw ga sante. Maman je taime fort
Di la bégué depuis Bordeaux ta Mariétou. Mashallah.
Merci beaucoup tes recettes c naturel j'aime beaucoup
no sa wakhine mon ma nekh ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Diéré beussi guerté way machallah rérou vendredi
Mahchahala li déh khawma bane annee lako guedieu togou inchahla thi katanou yalla ak dollé rassoulilah dinako togou merciii Ta mariétou
Machala Tata Mariétou contanna torop si yaw merci beaucoup pour tout. Ta recette est appétissante
Every Senegalese dish I have made … I learn it from you!
Thank you so much
😂😂😂😂😂😂bilae les termes ❤😂😂😂😂j suis chef cuisinier 👨🍳 mais si ioe la maneh yeen plats sénégalais merci 🎉🎉
mashaallah tata Mariatou yalna nga guda fan!!
Amine ndeysane
Nioune nioo la beugeu Macha allah rek
Belle recette way defna saine def nekh
Tata marietou ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️Ay cœur rek machala
Mais tata machala thiéré day didji wayyy forokkh touti
Maa sha Allah nehk na tata mariatou
Merciii pour la recette tata ndambe akh rotti magnoc
Machalah amna solo tata
Wa tata mariétou gnambi dji dognousi togal roti dinagnou nékh lolou
Mashllh tata kerok thiere nassi lou nekh
Trés bien machallat tata mariétou bonne continuation.
Masha Allah Barak Allah Fiki
Waouh machalla belle recette et très appétissant
Dicton-bi dialeina , mouné : " Nianbasse Yakhoule Seure " , toute la Théorie de l'information est basée sur la PORTEUSE, cette dernière qui enveloppe l'information afin de l'amener à bon port sans dommage. Je suis convaincue que le woloff est une langue divine comme le disait notre Grand savant Cheikh Anta Diop. Comme le disait Thione Ballaga seck dans la chanson " DIAGA " : " Yeigaleiii Mission Meu Akhe Soin ". Merci pour les vidéos de recettes sénégalaises, ça me rappelle des souvenirs d'enfance .
CUL8R !
Takh gama beugue thieré
Jai vraiment aimé❤, merci tata Marietou pour la recette, wayé sayy terme reynama akk rehhh😅🤣😅
Machallah nekhna merci beaucoup
Machallah❤❤❤
Machallah tata yaguefi lol té wer
Bassi bi nekhna plat bi ma beugue la merci
Ma sha Allah nekhna
Vraiment tu nous aviez manquė marietou tout les youbiyaba tous les bagass
Félicitations et merci beaucoup Mariérou. Que Dieu te bénisse.
Machalah machalah
J'aime trop tes termes😅😅😅😅😅😅
Machallah 🥰😍
Machalla tata marietou
Machalla maarietou
Ceel té safff alhamdoulilah
Tata mariatou amounou sa fay baynalla ak yalla
Sima rapide bodémé saloum sama genrgiu khamoul séne bopou momelagne kaye wowé 😂😂mais bimom nékhna yagiunouyou nioubakh magiusouniou sopé ak Fama diankha macha alla yaye zeynab yalna brombi yésalyermadé sikawam amiiiiiiiiiiiiiine tata maryatou gennala Sopou
Choucrane tata Marétou mane saye woolof mo maye reye
Machallah
Da lamine saf na 😂😂😂😂😂😂
Merci beaucoup oukhy KALLAH facilite 🌹🌹💖💖
So funny 😂 thieré khess pethie
Tu m as fait peur😳 avec ta pp
@@baamina6495 😂😂😂
Merci de valoriser notre cuisine senegalaise👌👌🇸🇳🇸🇳
merci my DEAR on a grandit avec c'est youbi yaba 😂😂😂😂😂
@ ya ngui sa Palace dee🤣🤣👍
Merci vréma gnoulay soumi lay lahte
contanati thi yaw rek tata marietou machalla
Basse biii tokk n'a neko rellle
Machallah ta mariétou sa liguey rafète na
Manchalla tata mariato
Macha allah thiere mafe😊
Merci beaucoup tata
Alhamdoulilah je suis la première 💃💃💃 merci pour bien Tata #Marietou 🙏🙏🙏🙏❤❤✔️
Dieureudieuf faty
Ahh marietou war gama bolék asmao cissé mou yoné ma si you bakh you senegal yi, magui france wayé awma dara amoul kene kouy def you bakh yi comme asmao .
En passant merci pour vos plats, je rate plus une pub .
Wagne bi machala yeupe nexna
Bonsoir tata marietou namone Nala. Merci pour la recette ça fait longtemps que je ne l'ai pas cuisiné. Je veux bien la recette de thieré neukheul avec guerte kharane. C'est mon arrière grand-mere qui le cuisinait quand j'étais petite ça me manque beaucoup
Waaaah maman say xetou termes j'adore 🤣🤣🤣🤣
Ah vraiment!!😂néna nga niko ci tél😂😂
youbi yaba néko si rell merci tata😁😁😁
machallah
Mon plat préféré thiere bassy
Kholal liiii rk am envie bassi wer dathie ciii iioe nassa diam yag maman
Man dal je t'aime et c'est tout.
Tata mariétou mashallah 😋😋😋😋
Machallah tata
Thiere bi teint na eupeneu sama togologue bi machallal laf thiate
Ma Sha Allah Tata Mariétou😘
Mane deh damay khaare ba vendredi inchallah ma sòga visionner vidéo bi 😔sinon douma ko meuneu mouñ waaay 😥
Marietou bisou nala avec tte l'équipe saveurs planétaires 😘😘😘
machalah tata lahou biSsap wargua niou ko indus pour sama genre gui amoul recette merci d’avance
Machala nicena merci beaucoup mais tiré sime labougone
ruclips.net/video/lznfaqULBQU/видео.htmlsi=zkzw4qg0Q3a4Xpvu
Machallah 👍 namese
salam aleycoum je suis malienne et j'aime beaucoup vos plat sénégalaise je peut avoir la recette svp?
Machallah tata marietou amatina solo yalla nala yalla defal diam 😍🙏🙏
Machallah sama badiene mes nak djiollof djiollof la mes suis au maroc mes nekh trop tata
Machallah tata 😘😘
Thank you so much 😋😋😛😛❤🖒🖒
Maaffé bou niebe rekk la
MachaAllah
Moi c’est ma première fois but I like your Chanel ❤️
Bibiche Dioume t bizare dé hummm
Oh amna fofou toma je m'appelle Asmao
J’adore votre cuisine et je limite aussi,machallah laff thiate ❤️❤️💋🥰😍
👑 👑
Très bien 😂😂😂😂😂😂😂😂
Bakhou niak diome 😅😅😅🤣
Mère sayyy terme tamite 😂😂😂😂
Machallah seu commentaires nekhna
Lima nekh si yaw mouy mana togo ba bare rew
🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣