Tata marietou tu nous avez grave mankè avec tes mots daguay diangue di rèè Mach AllAH. Ya AllAH veille sur elle sur sa famille ainsi que tous les youtubeur de cuisine yaye isseu alphie atelier iba ... Merci pour vos partages 🥰🥰🥰
Ah welcome back!!. Wa diegyi et les lovers de la cuisine welcome len tata maretou way!.mais namonanla.. ah ya des gens ki ont cesser d innover a cause de tn abscence. Much ❤️ 😍
Les expressions de tata Marietou🤣🤣 Le "ndox bou tang", c'est avec joie que je regarde la vidéo Macha'Allah yalla nanioula yalla samal on t'aime dal 😍😍😍
Très bon retour Tata Marietou, vous êtes aussi appréciée par d'autres personnes que les Sénégalais, ce serait sympa de votre part d'expliquer vos recettes aussi en français ou alors les transcrire. Merci.
Maa shaa Allaah....looks good...I have used many of your recipes and they think I am a true Senegalese! May Allaah reward you for your efforts! Allaahuma Ameen Love your channel!
Tata Marietou tu nous a trop manqué tu ma appris à cuisiner Sen boulions est c’est très bon mes enfants est mon mari merci jais beaucoup avec toi est je continu a apprendre bisou bisou bisou❤️❤️❤️❤️
Cc tata heureuse de te revoir Conseil pour thieb bou barri gomme..??
Год назад+1
Merci ma chérie boy saure boul deff gniekh bou barè tankhal niekh tekko de cotè après le premier diekhy ngua khôl si tu dois ajouter encore ou pas si non rekk pouth path nguay am fofou bizou bye ✌️
OH MACHAALLAH SAMA NIROWAALÉ MISS YOU SO MUCH HAPPY FOR KNOWING YOU BACK ALHAMDOULILAH TATA MARIÉTOU DALAL AK DIAME SA BÈNE DOOME DEPUIS CANADA NAMOONE NAALA
Borom vrai Diakhassé mélangé gneuw na, masha'Allah Sama maman bi, mayone ngama dedicas yalla ngako yagu di deif thi barké Seyduna Mouhamad ❤️
Bilaye moye borom diakhassé mélangé aye termes you doye war la ame masha'ALLAH
Tata marietou tu nous avez grave mankè avec tes mots daguay diangue di rèè Mach AllAH. Ya AllAH veille sur elle sur sa famille ainsi que tous les youtubeur de cuisine yaye isseu alphie atelier iba ... Merci pour vos partages 🥰🥰🥰
Maachallah namonenagne la lool
Ah welcome back!!. Wa diegyi et les lovers de la cuisine welcome len tata maretou way!.mais namonanla.. ah ya des gens ki ont cesser d innover a cause de tn abscence. Much ❤️ 😍
Les expressions de tata Marietou🤣🤣
Le "ndox bou tang", c'est avec joie que je regarde la vidéo Macha'Allah yalla nanioula yalla samal on t'aime dal 😍😍😍
Très bon retour Tata Marietou, vous êtes aussi appréciée par d'autres personnes que les Sénégalais, ce serait sympa de votre part d'expliquer vos recettes aussi en français ou alors les transcrire. Merci.
Macha allah.Penda Mbaye bi amno solo.Merci beaucoup Tata Marietou
Tâta mariétou is back.
Standing ovation.
Li honk n'a ba yégu si tiourrrrrrrrrrrr
Bonne arrivée depuis ziguinchor
Tata Marietou Ndao, mane sallene kotane, nam nalla. Yalla nalla yalla deferal diam, soutoureu ak tawfekh
🙏🙏🙏🙏❤️❤️❤️❤️❤️
MashAllah comme d'habitude tata manquéwone ngagnou🤗🤗
Yalna jam di yag rek🙏🏽🙏🏽🙏🏽
macha allah et al hamdoulilah vous nous avez manque tata surtout vos plats
Mashallah Mashallah tata welcome back we missed you a lot
Salam salam namone négnela Sokhna Mariétou merci pour le retour 🥰❤️❤️❤️
Ahhhhhh Tata Marietou nyow naa! Nooo sunj nama daha Sa nama deh noooo leh opah na y one year 🫂
Tata mariétou 💃🏻tata Mariétou💃🏻tata mariétou nieuwna masha allah namone naaaalaaa 🎉❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Salam tata marietou dalal diam Borom tokki tokki merci 😊😊😊et Bonne Continuation Dieureudieuf 🙏 💞 🇸🇳
Vraiment danga nio féraal lonn borom diakhassé mélangé youbou yaba je me demandais est ce que tout va bien. Vivement le retour de tata Mariétou😘😘😘😘😘
Maa shaa Allaah....looks good...I have used many of your recipes and they think I am a true Senegalese! May Allaah reward you for your efforts! Allaahuma Ameen Love your channel!
Macha Allah Tata Mariétou manqué wone nga niu lolll. Bon retour
Tata Marietou tu nous a trop manqué tu ma appris à cuisiner Sen boulions est c’est très bon mes enfants est mon mari merci jais beaucoup avec toi est je continu a apprendre bisou bisou bisou❤️❤️❤️❤️
Ah tâta Marietou namone nalla deh🎉🤗merci pour le thiebou dieune du retour saf SAP😋
Salam Salam adji ndaw machalah sa yaye togue rek la dane deff borom doo degue dé yal na deh Di noflayam diar na yone fowa ndoo magua ndoo
Machallah tata nomenala trop borome youbiyaba on t'aime fort
Tata namone nagn la mashallah bon retour
Ohhhhhhh quel plaisir de te retrouver māshā Allah sant rek Tata Mariétou. Né ko ci réleu 💚💛❤️
Ma cha allah tata youbou yaba namonaniou la lol
Bon retour ma bel ❤
Macha'allah notre tata nationale ❤️namone nanioula torop bon retour alkhamndoulilah ❤️❤️❤️🥰
Bon retour
Une thiébou dieun bou khonke pour bien debuter
Mashallah 😍😍 bon retour!!
Ohhhh j attendais notification namone nagn la ❤❤❤❤❤
Manchallah tata marietou is back namonagnoula ❤❤❤ welcom
Welcome back maman love to see you again
Bonjour tâta bon retour
👏🏿👏🏿👏🏿👏🏿👏🏿👏🏿 ma tata de retour wayeeeeeeeeee !!!!!! Al hamdoulillah wayeeeeeeeeee 😍😍😍
En fin tata akk koor gui di nieuw machala
Mashallah Mashallah tâta Mariétou namon nagnoula 🥰
shiii tata namone.nagne la nak
Sama tata bi namone nako de bimay seuy ay recettam rek ladaane top ndeysane❤❤❤❤❤
Hi lovely aunt namone nala. Bilahi say tog AK say termes manquer wone nagnma. Longue vie et bon ramadan ❤
Namone nagnoula Tata nga dignou dianguale dans la bonne humeur.
Yalna YALLAH goudal saye fane
Naa môn nala tata Mariétou, bon retour ak diam, maneu yow rék lay weur, tu nous avez manqué.
Mais tata tu nous a bcp manqué machalla 😘🥰
Machallah Marietou bon retour namonnaila long vie santé réussite à vous et saveurs planétaires
Cc tata heureuse de te revoir
Conseil pour thieb bou barri gomme..??
Merci ma chérie boy saure boul deff gniekh bou barè tankhal niekh tekko de cotè après le premier diekhy ngua khôl si tu dois ajouter encore ou pas si non rekk pouth path nguay am fofou bizou bye ✌️
Merci beaucoup ma tata chérie yallah naleu yallah faye barki Seydina Mouhamed ❤😊
Gnom youbi yaba 😁vous nous avez manqué tata bon retour
Namone nagnela bon retour❤❤
Bon retour
❤❤❤❤❤❤❤❤
Tata mariétou namoon nagnela dei. Fo réron
Non marietou ki te peu ? dou mala bayi deh wa kandia bi yeup nak thiebou kandia la layilaaaa 😂😂😂😂❤❤ bi lay def inchallah samedi
ALhamdoulillah bon retour tata
Ohhh namone nagnoula depuis espagne
Ah enfin !!!! Le retour de tata Marietou ☺️☺️☺️ !!!
Ooh Tata Mariétou de retour amoul nougnou la naméwoul
Machalah rebienvenue Mariétou
Sama khol sedna bimala guisaté namonala trop tata marietou alhamdoulillah machallah
Ayyy tata mariétou warna fou nek pour âme say nouvelles. Facebook sakh binde nala fa. Mais nak comme âme na sa nouvelle Alhamndoulila
C'est mon plat préféré Je suis ta fan Tata Marietou noumanala, du Mexique,🇲🇽🇲🇽🇲🇽🇲🇽 jërëjëf jërëjëf, beaucoup de bénédictions, MashaAllah ❤️☺️⭐🤲 🇸🇳🇸🇳🇸🇳
Oh quel plaisir de revoir tata Marietou
Borom saveur
Machallah machallah très très contente de vous voir tata mariatou
Machahala tata marétou namonaniou la recette tou korgui
Ay way tata marietou namone nala patriote bou makk bi
Ah way Tata namonn nagn leu
Machallah
Alhamdoulilah 😍
Machalah tata Marietou namone naala trop !! Paix sur toi 🙏🏾
Eh tâta tu nous a beaucoup manqué avec tes beaucoup plats ❤️
Bon retour maman Machalla ❤❤
OH MACHAALLAH SAMA NIROWAALÉ MISS YOU SO MUCH HAPPY FOR KNOWING YOU BACK ALHAMDOULILAH TATA MARIÉTOU DALAL AK DIAME SA BÈNE DOOME DEPUIS CANADA NAMOONE NAALA
Enfin dieu merci nala diam sonaleu tata Maritou
Machallah tata maretou ❤️❤️❤️❤
Machalla tata nammone nanoula
❤❤❤❤ bonne arrivée tu nous a manqué
Hayo tata marietou harri 😘😘😘
Oh je suis très heureuse de vous revoir tata, tu nous a trop manqué machallah
Machallah miss you more mum
Waleykum Salam wa rakhmatoulahi wa barakataho! Namone nan la deh! Masha Allah. Balnala akh balma.
Alhamdoulilah ❤ Heureuse de vous revoir!
Ta Mariatou namnala lou bari et très bon retour ❤
Salam Mariétou fo néka
Salam salam vraiment ya hadja.namone nanoula machallah
Ya woniiii tata
Welcome back tata Marietou borom @Saveur planetaire.
Welcome back Tata marietou
Ma sha Allah sister welcome we miss you 😔
Nammonayla lool nekhna youbi yabayi
Tata Meriétou namoonlagnoula ba yeeg thi torooopppp sax
Mane limay takhamni mooma diaakhal🤣🤣 Maaachallah yanna Yalla sammeu la habibty
Namone nagne la
Fo newone tata diakhaaaaasé mélanger très bien 😂😂
Machallah dome baye namenala
Tata Mariyetou namonnaleu ❤❤
Alkhamdoulilah manquer ngua wonn fii 😂
Mashalla j’adore
Say expression louné la
Tata nieuwna Macha Allah
Bravo bravo bravo
Bienvenue notre Marietou planétaire tu as beaucoup manqué
Mashalla nomone naniou toguou bou amoul boillon fonekon lii moye togou
❤️❤️❤️❤️🙏🙏🙏
Tata machalla namonala
Ay tata marietou namone nagne la lol amal diam
Ayooo, machala bismillamah. A diabama wonibik
Salamou aleycoum tata bon retour sa fait plaisir de vous revoir vous pouvez me dire le nom du poisson en français merci
Heureuse de vous revoir notre Tata Mariètou International ❤️❤️
Man damala mèré wone sax 🤣🤣 welcome back Tata Marietou