Machalah dieuredieufe sheikh Ousmane cisse dieuredieufe cheikh alpha ba leral yi amna solo yalla na len yalla faye sen ligueye rafetna billahi louler nga wakh deug rek machalah sen ligueye rafetna yalla na gnou yalla moussal si bokale
Liy Sëñ ABLAAY JÓOB di wax ta mu reelu lool rek: AY KAJOORIYAAT, SAALUMIYAAT aki BAWALIYAAT. Cëy miim réew. Mu leer la ni daanaka ñu baree-bare ci say mbókk ci bókkaale yii la léen dee di fékk
😅Yen kana sene baye mo môme dinde dji sene data n'diaye way sokhorguen guene trop sene baye defoufi thiote n'diaye guene Di so al nitt gni sen tatii n'diaye way sokhorguen guene lole
Wax naa ko ba tàyyi nit ku kénn xamul sax boo ko gëmee yénn gëm yi saytaane fowe la ci moom. Li ëpp ci nit ñi li ñuy sóppe aka tóppe nit ki, du tópp gi muy tópp ALXUR'AN, du tópp gi muy tópp SUNNA. Ay kaawtéef, ay jómbalaan rek ta lépp ay jinné la.
Yalaa na borom as saman ak souff moussaka niou bokkale BIDAAH akk toop ay reer ak nennn❤❤❤❤
Leral pass pass yiedafaaa amsolo lolo saxxx❤❤❤❤❤
Bravo à vous les oustaz
❤❤❤❤ sen ligeyy amna solo de Macha Allah cotan si vous
Asalamaleykoum oustaz alpha oustaz Ousmane❤❤❤❤❤❤❤
Ww tassawouf môme sirk ak boccale kesse là yalla nagnou thi yalla moussal
Merci ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ merci ba
Machalah dieuredieufe sheikh Ousmane cisse dieuredieufe cheikh alpha ba leral yi amna solo yalla na len yalla faye sen ligueye rafetna billahi louler nga wakh deug rek machalah sen ligueye rafetna yalla na gnou yalla moussal si bokale
Salam Bilahi walahi Nam naléne yalla naléne yalla sam
Machala longue vie à vous
🤣🤣Lèèboone Lipoone.
Maa réthiou lima dioudou si tarikha yiiii 😂😂😂
السلام عليكم ورحمة الله وبركاتة جزاكم الله خيرا. Svp le temps est précieux ,ne doublez pas (2fois)la vidéo
Longue vie a vous ✊
Ses vieux doivent comprendre que ses genres d'histoires ne peuvent plus passer. Les cerveaux ont beaucoup évolué
Je t’assure
Ils ont trop rencontré des contes et des lébone -lipone
Segn babacar bou meunonn dara konn dou déé bayilénn doul 😂😂😂😂😂
Tarikha yi doul rek 😂😂😂😂
Liy Sëñ ABLAAY JÓOB di wax ta mu reelu lool rek: AY KAJOORIYAAT, SAALUMIYAAT aki BAWALIYAAT. Cëy miim réew. Mu leer la ni daanaka ñu baree-bare ci say mbókk ci bókkaale yii la léen dee di fékk
Tarixa yi bókkaale gi ñu yóbbe nit ñi, leer na ma ni bu ñu léen bàyyiwoon ak séen bópp sax du ñu ca yégg.
Ces 2 hommes sont malades..😂
Kone dé Djinn shaytane moko nakh wakh si khélam parce que lolou shirk leu
Comme film indo li 😂
😅Yen kana sene baye mo môme dinde dji sene data n'diaye way sokhorguen guene trop sene baye defoufi thiote n'diaye guene Di so al nitt gni sen tatii n'diaye way sokhorguen guene lole
Vous tous vous n etes pas des Senegalais il faut sortir dans notre pays
Vraiement gongo sunnah si kaw ba faw ❤❤❤❤❤

Ana mandou ??