Aziz Ndiaye offre un appartement d'une valeur de 300 Millions à la fille de Mame Binta et craque

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 2 фев 2025

Комментарии • 207

  • @antasarrsamb462
    @antasarrsamb462 9 месяцев назад +71

    Aziz Ndiaye nekhone gama wayai tay la raw ndakh li gua wakh thi mame bineta ndayssane yalla na sa diam yague inchallah

    • @rokhayadiaw9408
      @rokhayadiaw9408 9 месяцев назад +2

      bilaye walaye mane je l'estime bcoup ❤❤

  • @khadiatousow7845
    @khadiatousow7845 9 месяцев назад +6

    Ohhh j'ai les larmes aux yeux ndeysane mame bineta warone gua feké li mais lolou la yalla dogal paix à son âme. Aziz yalla nala yalla sam bayila ak sa djabot

  • @veroniquenatack7392
    @veroniquenatack7392 9 месяцев назад +2

    *Ohhhh🥺🥺🥺Aziz da dioy rk ma dioy😭😭😭😭cédè yi rafette na 😢Aziz ya goré machallah…Mame binta Yalla na soufff oyof thi kawam Yalla aldiana di noflay yam🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽mention spéciale à miss ndiaye nimou téwé khalée yii*

  • @marieheleneberre8736
    @marieheleneberre8736 9 месяцев назад +18

    Vraiment amnga kolere tu es un exemple yagale wereule thi sa kananou ndiabote heureux ménage à ta fille que ta défunte épouse se réveille au plus Haut des. Amin yarabal alamine. Barke Seydina Mohamed SAWS.

  • @leilaleila6838
    @leilaleila6838 9 месяцев назад +49

    Yallana la yalla lafal thiate té deukeul mame binta ak bëp yaye bou deudou barké seydina Mouhamed salalahou haleyhi wassalam 🙏🏽 gorè Ndiaye.

    • @rokhayasylla7261
      @rokhayasylla7261 9 месяцев назад +4

      Amine Salal lahou anleyhim wa Salam ❤

  • @FamaFaye-o8c
    @FamaFaye-o8c 9 месяцев назад +8

    Machallah aziz sa wakh rafét n'a yalla n'a sa diam yague yalla yok la ba nga yeug ko

  • @SokhnaRoubaSaliou
    @SokhnaRoubaSaliou 9 месяцев назад +23

    Ndeysane domou baye Ndiaye sangue sèdè yi rafetna 😢sokhna Mame Binta Yallah n’a bokk ci sangou Aljanna ❤khamouma Aziz xamouma famème wayè nièna sokhna mame Binta ❤jiguène diou bax diarna lounè ❤gor moo diarra digalèl 😢😢😢

  • @Diarista90
    @Diarista90 9 месяцев назад +3

    Raffet na ndakh djirim yalla moy ndayam soko défalé yalla défala boko défaloule yalla défale ko konn dèfal ko yalla dèfale la👈miss ak aicha Rasoul sén takhaway raffète na♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️

  • @princesse-Soninké
    @princesse-Soninké 9 месяцев назад +4

    😭😭😭😭😭😭ndeyssane Mame Binta yalna yallah doli la yeurmandé. Aziz N’diaye linga cédé sa sokhna si Machalla Yalna lako souniou borom faye.

  • @habibsy1825
    @habibsy1825 9 месяцев назад +64

    Koleuré guinaw lay fété. JËRËDËF AZIZ si ndioukeul bigua défal sa Awo

  • @alfylyfa7645
    @alfylyfa7645 9 месяцев назад +24

    Dama done guiss Aziz ak diko guiss rék si réseaux yi té khawe mako Wayé téye moune na sédé né nite ki kou ame korélé leu borome khôl bou raféte Machallah ❤ Yalla nalla Yalla méye wére ak goudou fane yak saye sokhna ak diabote bi yieupe ak saye bokk aki andanedo ak bépe dioulite ♥️si barké Seydina Mouhamed 🙏

    • @rokhayasylla7261
      @rokhayasylla7261 9 месяцев назад +1

      Amine Salal lahou anleyhim wa Salam ❤

  • @aissatoubah229
    @aissatoubah229 9 месяцев назад +13

    Je t'adore depuis aujourd'hui Aziz machalla Un homme véridique ❤❤❤❤

  • @Ami00765
    @Ami00765 9 месяцев назад +4

    Aziz est un Papa responsable 😊

  • @biguelo3675
    @biguelo3675 9 месяцев назад +11

    FAUT JAMAIS JUGER UNE PERSONNE PAR SA COUVERTURE KO XAMOUL DEI KOY WOWEI EIII AZIZ A ETE TJRS UN RESPONSABLE K ALLAH VS PROTEGE

  • @BinoDiatta
    @BinoDiatta 9 месяцев назад +6

    Machallah Mame Bineta ya Gorée yallah boula thiate dietou yallah na aldiana done keureume amine❤

  • @OusmaneSambe-l3f
    @OusmaneSambe-l3f 9 месяцев назад +21

    Ndéyssan Aziz yagui may dioylo bilahi 😢😢😢Mame Bineta yallah nako Yallah yeureum té xaréko aldiana 😢 😢 😢 😢

  • @naboukebe5390
    @naboukebe5390 9 месяцев назад +13

    Machalah bouma khole miss ak domou mame binta yi rek sama khol bi dafay sed lool ndeysaan da melni moleen diour seuy bou nekh mamma ❤❤❤te barke ak ndiaboot gou barke inchallah

  • @grands9838
    @grands9838 9 месяцев назад +8

    Al amine Ya Gorée Merci pour ce beau témoignage

  • @PapeSeye-kv3zn
    @PapeSeye-kv3zn 9 месяцев назад +6

    Ndeysane gor you melni yaw nio diarra Mougnal y’a am koleuré mashallah koula khar yalna Khadi Abdou Aziz alé Ndiaye ❤

  • @fatoudiongue6337
    @fatoudiongue6337 9 месяцев назад +11

    Quel temoignaaaage ohhhhh
    Sama xol bii seed neuu niou book niounei daniouy aaande, li moyy foulaa li moy saaag
    Mashallaaah❤❤❤ contaaan naaaaa

  • @abbagoudiaby2463
    @abbagoudiaby2463 9 месяцев назад +5

    VRAIMENT c'est émouvant j'ai même verser des larmes

  • @ndeyemariemefaye6962
    @ndeyemariemefaye6962 9 месяцев назад +18

    Rafete n’a aduna amoul solo Dieureudieuf Aziz yalle na léne sougnou bourom bi same 🙏 contana Mashallah

  • @mumsmbaye4805
    @mumsmbaye4805 9 месяцев назад +2

    Macha allah sédé yi rafétna , Aziz ligua sédé si Mame bineta rafétna. Fimou dieum yalnako gueneul fimou diougué

  • @khadydiop2570
    @khadydiop2570 9 месяцев назад +9

    Yalna aldjana nékk dekou wayam 🤲🙏Miss Ndiaye yalna yalla oyofal yann bi défal la diam fayla sa xol

  • @SeynabouFaye-l3n
    @SeynabouFaye-l3n 9 месяцев назад +43

    Ndeyssane mame bineta dieweum rafetena machaalla yalna khippe aldianay firdaws ass ya reconnecent

  • @ramatoulayediaw3864
    @ramatoulayediaw3864 9 месяцев назад +42

    Billay mookaffi ligueye bayi kaffi mame bineta yalla na Aldiana firdassi di dekouwayan warone na fekke takou domam dji ndeysane yall nanou soutt sen yaye fan Amin

  • @itools2514
    @itools2514 9 месяцев назад +26

    Loo diaffé lay wakh. Yalla na andeu bi gueneu deugueur😊

  • @khadygueye1707
    @khadygueye1707 9 месяцев назад +11

    Ohoho y’a goré abdoul Aziz alé ndiaye machalha ❤❤❤❤

  • @papasene1320
    @papasene1320 9 месяцев назад +4

    Aziz Ndiaye tu n’as jamais attiré mon attention à ce point.
    J’ai envie de te serrer la main. Te dire de vive voix Ya baax.
    Mame Bineta Yalnako Yalla xaare Aldiana.
    Seedei yi yalna yokkou daradiaam ci Aldiana you gueuneu kaawei
    Sama xool sedd na tei khawma seen famille.
    Contaan na lol Bilahi

  • @KhadyCiss-to6ue
    @KhadyCiss-to6ue 9 месяцев назад +13

    Mame bineta déme Omar déme moy bayame il faut mou bakh bilaye

  • @rokhayadiaw9408
    @rokhayadiaw9408 9 месяцев назад +5

    😭😭😭😭aziz yalla nala yalla taxawou 🤲yeureume mame bineta🤲té samale leu ndiabote gui si barké yonenete bi barki seydil hadji malick🤲🤲

  • @Awadiaw-sm9by
    @Awadiaw-sm9by 9 месяцев назад +14

    Bilaye dama dioye machalla tonton Aziz Ndiaye

  • @alimajolie3195
    @alimajolie3195 9 месяцев назад +6

    Yallah nako yallah yeureum té xaréko aldiana firdawsi barkép borom touba

  • @pendathiam1231
    @pendathiam1231 9 месяцев назад +7

    Ma cha Allah. Yalla nako yalla faye. Ndiaye diatta 😊

  • @maimounandiaye3622
    @maimounandiaye3622 9 месяцев назад +15

    Neysane yalla n'a kippe aldiana firdaws barki seydina mouhamed

  • @NabouLo-k7t
    @NabouLo-k7t 9 месяцев назад +5

    Aziz Ndiaye yalna yala lafal thiat ya bakh ya gorrè machalla

  • @safietouniang1574
    @safietouniang1574 9 месяцев назад +3

    Ndaysane yalla nala yalla lafall thiatt té bayilakk sa famille yi domy Mame bineta yi doundou bagua féké sén ndiarigne🤲🤲🤲🤲🤲🤲

  • @sofietouseck9865
    @sofietouseck9865 9 месяцев назад +13

    Jai pleuré 😢

  • @gabinekelly5182
    @gabinekelly5182 9 месяцев назад

    Machalla Aziz. Yalla na yalla Faye mame binta thia Aldiana.

  • @sigacamara866
    @sigacamara866 9 месяцев назад +4

    No ya am koleure Aziz Njie❤

  • @KhadijaBa-s7c
    @KhadijaBa-s7c 9 месяцев назад +10

    Ndeysane li dawna yaram

  • @pendagueye418
    @pendagueye418 9 месяцев назад

    Ndeyesane Machalla rafféte na yalla nalène yalla sameu 🙏❤❤❤❤❤❤❤

  • @Ndiayeniangua
    @Ndiayeniangua 9 месяцев назад +1

    Djigen bouy seuy da war di diamou dieukeureum ngir euleuk ay domam mame binta féké woul deh waye tay limou fii liguey fegn na thi ay domam Yalnako yalla yeureum 🙏

    • @mormbaye2989
      @mormbaye2989 9 месяцев назад +1

      Walay Li d la wax 😢😢😢😢

    • @Ndiayeniangua
      @Ndiayeniangua 9 месяцев назад

      @@mormbaye2989 mor mbaye 🥰ligueyou ndaye agnou dom lou way liguey rek lolou nguay am

  • @KhadyFall-si4jv
    @KhadyFall-si4jv 9 месяцев назад +13

    Azize dioyloguama bilakhi dagua goré rék yalla nako yalla kharé aldiana té yalla bayila ak jdabotam niou barkel machalla

  • @ndeyendiaye9542
    @ndeyendiaye9542 9 месяцев назад

    Machahala mame binta yallanako yalla yeureum aziz yow goor gua bvp de gens tont juge pourtan tubes pere responsable et un mari responsable

  • @mariemefaye2563
    @mariemefaye2563 9 месяцев назад +13

    Aziz ya goree ya bakh

  • @fatimadiop96
    @fatimadiop96 9 месяцев назад

    Bilaye yaye gore bula nékhone nga faté lépp wayé gore reek mo diara léballe téranga ❤❤❤❤ yalla nalla yalla same

  • @mbayethiao1024
    @mbayethiao1024 9 месяцев назад

    Dieureudieuf Aziz Yalna BOROM BI wathié Yeurmandé thi moom Barké Yonentibi shws

  • @papeomar8530
    @papeomar8530 9 месяцев назад

    Machallah Mame Binta yalla nako borombi yeureum té kharéko aldiana firdawsi ci barké Seydina Mouhamed(PSL)

  • @taphagueye8675
    @taphagueye8675 9 месяцев назад +3

    Merci beaucoup Azis ndiaye

  • @suzanneniang1850
    @suzanneniang1850 9 месяцев назад

    Deysane très émouvant Aziz ndiaye kholbi mo bakh ❤❤❤

  • @halikano392
    @halikano392 9 месяцев назад +1

    Lawla thiate lawlama lamigne YALLAH na MAMAN mourlo seuyeume bi amsi ndiabot gou barkel thi daradiaye SEYDINA MOUHAMMAD SAW MACHALLAH 🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲💯💢💬🗨💬💯💢💯💬🗨

  • @SalyBa-iz3gl
    @SalyBa-iz3gl 9 месяцев назад

    Votre papa doit etre fiers de vs
    Paix á sn ame
    Machallah Aziz ma fan goor bou fonkou diabaram

  • @MaketSii-jm4fu
    @MaketSii-jm4fu 9 месяцев назад

    Vraiment sedeye rafetna yalla na yalla yesal yeureumande si kawan vraiment ça touche au fond du cœur

  • @mamindiaye3255
    @mamindiaye3255 9 месяцев назад

    Oh ndeysan j'ai les larmes aux yeux mame bineta que firdaws soit sa demeure éternelle amin, miss laisse tout et donne ta main à Aïcha rassoul, Aïcha toi aussi tu es jeune mais soit derrière miss, diminue les réseaux sociaux

  • @ndeyecoumbatall
    @ndeyecoumbatall 9 месяцев назад +1

    J’ai même pleuré ❤️❤️

  • @maremedieng2164
    @maremedieng2164 9 месяцев назад +5

    Aziz dioylogama 😢 ndeysane ya gore, diabote bou soneu yalla ga feke sa lepi diabote

  • @nganefall
    @nganefall 9 месяцев назад

    Ya bakh ya gorè ya ame kolarè Ndiaye walahi bari gaure youdone dokhalé nénéne machalla ❤❤❤nite kou baakh dafaye goré

  • @assanesoldaroubayegorasarr1136
    @assanesoldaroubayegorasarr1136 9 месяцев назад

    Non Aziz yalla mo Koy fay YALLA NA MAWLANA takhawou inchallah

  • @fatoubinetou6392
    @fatoubinetou6392 9 месяцев назад +7

    Un homme bon

  • @ibrahimadiop1685
    @ibrahimadiop1685 9 месяцев назад

    Mame bineta ndeysane dafa baakh yallah nako yallah yeureum

  • @cheikhfall4377
    @cheikhfall4377 9 месяцев назад

    Yalla n'a yalla mottali yéné nieüp incha'Allah baniou yobbou wadiour yi maqqa si barké seydina Mohamed psl 😢❤❤❤❤❤❤

  • @mouhamad-bi7qu
    @mouhamad-bi7qu 9 месяцев назад +7

    Rafetna Machalla

  • @MameantaSambe-c1k
    @MameantaSambe-c1k 9 месяцев назад

    Machalla mon frère Yalla lafala Thiate 😢😢😢❤❤❤

  • @badariya393
    @badariya393 9 месяцев назад +4

    Baye bou bax ni lay deff si niabaoute mai baye legui mommmmm😮 khalise rek

  • @collesaliouseck615
    @collesaliouseck615 9 месяцев назад +1

    Machala ya des femmes digne

  • @ousmanediop1620
    @ousmanediop1620 9 месяцев назад

    Koulene tak deh yay seyi li🤣♥️🇸🇳🙏

  • @OuleyeSeckFall
    @OuleyeSeckFall 9 месяцев назад

    Mame binta fimou nek yalnako geuneul fimou diougué yalla branchel ko racol aldiana direct si bamel lam bidiakhi nabi moustapha salalahu aleyi wa salam alahouma amine ya rabi 😭😭😭😭😭😭

  • @abdoulay2867
    @abdoulay2867 9 месяцев назад +8

    Mame Bineta yalnako yeureum té kharé Adiana

  • @mouhamedba5913
    @mouhamedba5913 9 месяцев назад +2

    bilahi ya goré

  • @khadykasse8372
    @khadykasse8372 9 месяцев назад +2

    Machall azize❤❤❤

  • @SeneEva-ie9gu
    @SeneEva-ie9gu 9 месяцев назад

    Ooh je suis en larme
    C'est très émouvant walay

  • @Zazindiaye218
    @Zazindiaye218 9 месяцев назад +3

    Ndeyssan 😢

  • @astouwade9290
    @astouwade9290 9 месяцев назад

    Témoignage yi rafétna , yalla na adjalnay firdawsi donne keureum yalla same ndjabotam

  • @Oumoucasa
    @Oumoucasa 9 месяцев назад

    Machallah yabakh aziz ndaiye

  • @mamediarrafall4312
    @mamediarrafall4312 9 месяцев назад

    Mam binta yalla nako yalla yaram khareko adianay firdausi

  • @aliounediouf1894
    @aliounediouf1894 9 месяцев назад

    Machalla, tu as un bon coeur, vraiment!

  • @khadisarr1704
    @khadisarr1704 9 месяцев назад +4

    Amine way amine ❤❤❤

  • @aidaniangkonate3130
    @aidaniangkonate3130 9 месяцев назад

    Yala nako yala yereme kharé ko aldiana amine té yala diapalko diabotame bi incha alla tntn Aziz ya gniak kignane si kaw si kaname si barké sékhoul khalifa bignou book amine

  • @aidaniang9626
    @aidaniang9626 9 месяцев назад +3

    Ndeysane 😮

  • @AbdoulayeDiallo-eh4pc
    @AbdoulayeDiallo-eh4pc 9 месяцев назад +3

    Aziz yaa bakh.kou diapale sa mbokk yalla diapale

  • @aichaalarbaallf4359
    @aichaalarbaallf4359 9 месяцев назад

    Yallah molay Faye si kaw si kanam silou Bakh inshallah rabi

  • @amily104
    @amily104 9 месяцев назад

    Billahi wallahi tallahi kou saga ndiabotam yallah fayla charité bien ordonné commence par soit

  • @adamengomndiaye4209
    @adamengomndiaye4209 9 месяцев назад

    Ndeyesane 😢😢😢😢❤❤❤

  • @You-wm1ox
    @You-wm1ox 9 месяцев назад +6

    Mame bineta mougne na ba day

  • @CécileFaye-v6y
    @CécileFaye-v6y 9 месяцев назад

    Mame bineta yalnako yalla yeureum té xaréko aldiana firdaws

  • @AlassaneDiawDiaw
    @AlassaneDiawDiaw 9 месяцев назад +3

    Machlla yalna yalla samou Lene godal fanye loll amine

  • @unebatante7716
    @unebatante7716 9 месяцев назад

    Ndeysan yalla nako yalla yereum 😢sokhna mame bineta

  • @MohamedNdiaye-u8j
    @MohamedNdiaye-u8j 9 месяцев назад +1

    ❤❤ ndysane family ndiaye

  • @aissatougueyembaye7988
    @aissatougueyembaye7988 9 месяцев назад

    Machallah ya gooré ❤❤

  • @Ami00765
    @Ami00765 9 месяцев назад +1

    😢😢😢😢

  • @libyesenegal5451
    @libyesenegal5451 9 месяцев назад +6

    Ndeysan Aziz y’a goré dh

  • @elhadjiibrahimakebe1038
    @elhadjiibrahimakebe1038 9 месяцев назад

    Machalla yalla na khipé aldiana firdawsi

  • @dijatoucherifsidatyseck1410
    @dijatoucherifsidatyseck1410 9 месяцев назад

    Ndaysan yalla nako yalla yeurem dioylo nama

  • @SigaMbacke-wk2id
    @SigaMbacke-wk2id 9 месяцев назад

    Mame binta yalla nako yalla yeureume si barcke seydina Mohamed aziz ya bakh sa wakh rafet na maman yalla na seybi barcke

  • @mariepouye6470
    @mariepouye6470 9 месяцев назад +2

    Machalla 😢😢😢

  • @MODOUAMARtvofficiel
    @MODOUAMARtvofficiel 9 месяцев назад +2

    Ohhh 😢❤

  • @dramsell3132
    @dramsell3132 9 месяцев назад

    Amena solo yalnaniouko sédél siniou aye sokhena❤

  • @NykaSenghorFemme
    @NykaSenghorFemme 9 месяцев назад +3

    Machalla goor gua de

  • @oulidieyendiaye8166
    @oulidieyendiaye8166 9 месяцев назад

    Pourquoi je pleur com sa . Ndeysane yalla nala yalla dolèle