Merci Oustasse a cause de vous que j'ai arrêté de fumer votre serment pendant le ramadan de 2013 j'étais a thiaroye djide kao Que Dieu vous donne long vie et vous protège des méchants
Ah machaAllah à chaque fois que je vous écoute j'ai le cœur soulagé QAllah vous réserve une suite au paradis firdaws je vous aime. Et j'aimerai vous rencontrer un jour inchaAllah
Qu'Allah vous benisse tous. Vous faites d'Excellent travail pour tous les musulmans qu'Allah seul puisse vous payer. Alhamdoulillah Great team work masha Allah.
Diazakala hayran oustaz yalla rek molay faye sa tahaway rafetna si diamou yalla yi vrema soula nehone gardé lepp pour yow harr koula faye haliss comme les autres. Alkhourane ak sunna rek mo worr in sha Allah qu'Allah vous récompense et vous protège
Machallah merci beaucoup Oustaz, ah moi c’est ce qui m’arrive souvent tout ce que vous avez dit j’ai ces signe là et récemment on me l’a dit, mais la personne veut que je lui donne 500€ pour me soigner seulement c’est la moitié de mon salaire et souvent j’ai donné beaucoup de mon argent et je ne vois rien je fais toujours des cauchemars de gros serpents et j’ai des douleurs souvent moitié de la tête et mon côté droit vers le Dos et les fesses
Alakhou Akbar ya Oustaz yalnala yalla doooli diam. Mane dama yaag di wakh né amna Lou nek sama yaram gnoumay nane bayil lingay wakh mais walakhi azim signe yingafih wakh yeup mangui Koy am walakhi dama soonou fouma dem rek gnou wakhma dagnou ma seuf tei d'où béni nite wayé naak yalna gnou yalla doooli takhawou ci barké Seydina Mouhamet Aleykhi salamouna
bonour oustaz Merci pour ces remedes islamiques contre ces genres de choses comme vous nous avez dit de ne pas faire des seet et des bokale . Vraiment ca va encourager les gens a arreter le bokale et les diabarkat .Que Dieu vous paye AMINE
Masha Allah rafetna amna solo diaridiaf serige be yalla na yalla Yoko ta barkel yalla na yalla Yoko diamu djamu ak sutoura amin amine yalla na yalla nagou sou nu diaf jaf yapu ta garam nu yaram nu defal nu soutura Ak tawfekh Ak khewal you Barry ta sakh Amin amine amine amine amine amine Sahed cisse Italia
Tay mom contant na si yaw ndakh li nit gni di wax nee dangay wedi sounou yeuf mou serigne touba, vraiment tay guisoumako, jajeuf nala yalla fay, barke mame cheikh ibra fall
جزاك الله خيرا يا شيخ جزاك الله خير الجزاء جزاك الله عنا خيرة اللهم اجعلنا من أهل الجنة اللهم اجعلنا من أهل السنة والجماعة اللهم اسفي مرضانا ومرض المسلمين
Merci Oustasse a cause de vous que j'ai arrêté de fumer votre serment pendant le ramadan de 2013 j'étais a thiaroye djide kao Que Dieu vous donne long vie et vous protège des méchants
cheikhsidaty daffe contant de toi ❤️🙏
Macha allah
Grâce à lui au lieu à cause de vous
Slt oustaz l'an gua wax thii seyou sorcellerie(gualadj)liguéye nit ba mou tkla, l'an moo thiy danger😘dieureudieuf machallah
Mercie oustaz tes adresse.sont intéressant je voulais l'adresse de oustaze
Il aime toujours partager son savoir. Qu'Allah le préserve et guide vers le droit chemin
😊,😊p😊,,,,, de lo,,,,,,,,,,,,,,,,,,,
,,😊
,
,
,,,
,,,
Machalla way oustaz merci beaucoup pour votre générosité ( mais ana gniko beugeu)👍
Niongiini
On est là
Machalla
Nionguini
Machallah sedii sall
Ah machaAllah à chaque fois que je vous écoute j'ai le cœur soulagé QAllah vous réserve une suite au paradis firdaws je vous aime. Et j'aimerai vous rencontrer un jour inchaAllah
Machalah seydi sall
Machallah 😊
Kou ame Numéro oustaz Oumar sall s'il vous plaît 😢😊
Gnakeu diouli tamite dina takh fo tolou daguay tite té do xam lanla
Yalla nagnou yalla tégue thi yonou siratikal moustaqim
Rokhaya Ndour amine
mala ko wakh
7y
Mashallah oustaz bilahi yalla nala yalla fay ci barké mouhamad salahou alehime wa salam longue vie et santé tous❤
mercie ya ouztass amna niouy tim nit nanko thiatt dala djapp di ka tektal ay dieuff ❤❤❤ mercie beaucoup
Qu'Allah vous benisse tous. Vous faites d'Excellent travail pour tous les musulmans qu'Allah seul puisse vous payer. Alhamdoulillah Great team work masha Allah.
🙏🏽🙏🏽🙏🏽 Merci pour cette aide précieuse Oustaz, yalnala Yalla fayy ci barke Seydina Mohamed sallalahu aleyhi wa salam 🙏🏽 🙏🏽 🙏🏽
Ma shaa Allah ! Yallah neu leu Allahou swt fay yiiw te mayleu wër ak gouddeu fane🙏🙏🙏
C’est efficace je connais bien la roqya je me suit bien s ensortie a cause de la force du coran et c’est allah qui querit
C comment
@@mariediouf7964 y a une centre de roqya à parcelle unité 15
Svp donner moi la solution
@@abdoulayeba2517 ça se trouve à Dakar au parcelles assainies unité 15
Li ngay wax yëp la plus part je le sens. InchAllah je ferais les douas
اللهم أرنا الحق حقاً وارزقنا اتباعه و أرنا الباطل باطلا وارزقنا اجتنابه واجعلنا من عبادك الصالحين.
amine ya rabi
amine ya rabi
ءامين يارب العالمين🙏🙏
Machalla oustase que le bon Dieu te garde et qu'il veille sur ta famille inchalla merci beaucoup encore 🙏
Machallah oustaz oumar sall sunnah ak alkhourane moy deug
Barakallahou fiika. Wa nou nazzilou minal xourr aani maa houwa chifaa oune wa rahma
Yalla na Yalla sédal sa hol oustaz dans cette vie et dans l'au-delà inchaAllah
😭😭Wallahi Oustaz Yalna Yallah gueureum lah 🤲🏾❤️❤️
Mashaa ALLAH ya oustas Oumar Sall yalna yalla Soubhana watahan ALLAH goudal. sa fane
Diazakala hayran oustaz yalla rek molay faye sa tahaway rafetna si diamou yalla yi vrema soula nehone gardé lepp pour yow harr koula faye haliss comme les autres. Alkhourane ak sunna rek mo worr in sha Allah qu'Allah vous récompense et vous protège
Machalla
Macha alla ya oustaz yalla nala yalla faye aldianatoul firdawsi mayko bep dioulit
Allahouma amine y'a rabbi
Amiine
Amine
Machalah oustaz yalla nala Sunu Borom Ya Rabi fay si Barké Seydina Mouhamed (SAW). Amine 🤲🏿🤲🏿🙏🏿🙏🏿
Yalla nala borom bi fay tei goudal say fane❤
aminn wa iyakii
Jaza'kallah khairan ya oustaz oumar sall may Allah reward you abundantly
Seul Le Bon Dieu peut vous payer ya Oustaze machalah longue vie et une santé de fer
MachAllah Oustaz qu'Allah vous récompense et vous bénisse
Macha Allah! Dieureudieuf Sall. Amnasolo lol lol lol. Yalla Tabaraka Watahalah mousal niou si chaytanè ak bokalé ak biddah ak ndiabarkat yi
Bilahai ki saytane bouy dokh ci kaw souf la wa yen khana monu len bayi keurou dine yi dioulit deg dey mando
@@basspouye9020 doule rek
Machallah merci beaucoup Oustaz, ah moi c’est ce qui m’arrive souvent tout ce que vous avez dit j’ai ces signe là et récemment on me l’a dit, mais la personne veut que je lui donne 500€ pour me soigner seulement c’est la moitié de mon salaire et souvent j’ai donné beaucoup de mon argent et je ne vois rien je fais toujours des cauchemars de gros serpents et j’ai des douleurs souvent moitié de la tête et mon côté droit vers le
Dos et les fesses
akassa oustaz barké serigne touba dinga fi yagu yagui khetalli nitgni yalla nalla yalla faye té takhawoula akassa akassa contannaniou
Macha'allah ya oustaz yalla nala bour bi kawel yokou Imane bi yakhine tawkhite AK takhoula si barké yarasoulilahi salallahou aleyi wa salam
Beug nala Oustaz Oumar Sall 😍😍😍 walahi anzim alkourane ak sunna rk mofi nék
Alakhou Akbar ya Oustaz yalnala yalla doooli diam. Mane dama yaag di wakh né amna Lou nek sama yaram gnoumay nane bayil lingay wakh mais walakhi azim signe yingafih wakh yeup mangui Koy am walakhi dama soonou fouma dem rek gnou wakhma dagnou ma seuf tei d'où béni nite wayé naak yalna gnou yalla doooli takhawou ci barké Seydina Mouhamet Aleykhi salamouna
Maa chaa Allah Ya Oustaz. DjazakAllahou khayran wa ahsannAllahou ilayka.
Dieureudieuf yalla na borom bi mouthieul gnou .Amine
bonour oustaz
Merci pour ces remedes islamiques contre ces genres de choses comme vous nous avez dit de ne pas faire des seet et des bokale . Vraiment ca va encourager les gens a arreter le bokale et les diabarkat .Que Dieu vous paye AMINE
Alhamdoulillah banou yalla mayè ay niite you melni yalla na yalla may wèr ak katan ba nga yague diko deff
Masha Allah rafetna amna solo diaridiaf serige be yalla na yalla Yoko ta barkel yalla na yalla Yoko diamu djamu ak sutoura amin amine yalla na yalla nagou sou nu diaf jaf yapu ta garam nu yaram nu defal nu soutura Ak tawfekh Ak khewal you Barry ta sakh Amin amine amine amine amine amine Sahed cisse Italia
Ke dieux te paye dieudieufn ya oustaz alkhamdoulila yala na yala barkhekel si barkhke seydina Muhammed sala lakhou tala Ali Muhammed
Mach ALLAH Oustaz Omar choukrane yalla nala Yalla faye té yokk kham kham bi. Amine
Machallah ya oustaz amna solo trop yalnala yalla défal diame mayla soutoural ak weur 💗💗💗
مشاء الله يااستاذ زادك الله علما نافعاو قلبا خاشع ولسانا ذاكر شاكر
جزاك الله عنا كل الخير يا فضيلة الشيخ حفظك الله ورعاك
Qu'allah nous préserve de la sorcellerie
Amine
Amine
amiine
Amine
Amine yaa rabb
Mashallah Oustaz pour votre générosité qu Allah vous assiste et veille sur vous
Dieureudieuf oustaz yalla nalla yalla faye ❤🙏
Macha Allah barakallahou fiik Al hamdulillah yalla nala yalla fayi nguendi fayi te yagalla souniou kanam amine
Dieuredieuf ouztaz yala na yala yok kham kham bi
جزاكم الله خيرا وبارك آلله فيكم جميعا اللهم امين يارب العالمين جميعا وصلاة وصلام على رسول الله صلى الله عليه وسلم
Ma scha Allah jazaka Allahu keiren ya oustaz Sall wa baraka Allahu fik
MachaAllah amna solo oustaz yalna yAllah fay la té same la
Machaallah ya oustaze baarakallahou fîk djazakallahou hayran
Dieureu dieuf oustaz yalna yalla samoula
Machalla oustas mè someunoul sarby noy def
Essaie de l'apprendre. Il y a l'appli muslim pro où tu peux voir les sourates. Courage
So amé kouko meune mou defko a ta place
Dieureudieuf ouztaz Mane deh damala sop
Dieureudieuf ouztaz Mane deh damala sop
Machallah oustaz yalla nagua fi yagu té wére
Leup liguafiii wah mongui si Mane et je n'arrive pas a comprendre le pourquoi ...Yallah nagnou sougnou borom samal bopam ...AMINE
Je l'aime trop c'est un érudit multidimensionnel et incontestable ma cha Allah
Cest un koi ??? Multi koi laisse moi rire frere ... ki koumou di seu serigne ba digua djeurignou ?
Merci oustaz yallnala yallah fey amine
Maa shaaa Allah que Allah nous protege et nous guide vers le droit chemin. Aameen
Amen Bity
Merci oustage yalla na yalla faye la barakalakhou fikoumm
Gnabar moy liguey barakallaahou fiikoum
merci oustaz yalna yalla may nieup deeg ak top te fayalnioula
Yalnala yalla Faye oustaz yalnagua goudou fane
Machallah ya oustaz k le bon Dieu vous bénis 👏👏
Dieeredief Ouztaz cii leeralby mais deefkatou youboneyii keep kukoy def yaallah nako yaallah torokhal tee youbonam deelou cii kawam cii Barakatul Seydina Muhamad Salallahou Alleyhi Wassallamm Amine amine amine Allah
machallah Oustaz amna solo trop Yalna Yalla na Yalla faye
Macha Allah vous la toujours pour les gens que Dieux vous protègent
Salam.
QU'ALLAH vous rétribue de la plus belle des manières.
Tay mom contant na si yaw ndakh li nit gni di wax nee dangay wedi sounou yeuf mou serigne touba, vraiment tay guisoumako, jajeuf nala yalla fay, barke mame cheikh ibra fall
Djazaka Lahou khayran ya Oustaz🤲🏽🤲🏽🤲🏽Allahou Akbar
جزاك الله خيرا يا شيخ جزاك الله خير الجزاء جزاك الله عنا خيرة اللهم اجعلنا من أهل الجنة اللهم اجعلنا من أهل السنة والجماعة اللهم اسفي مرضانا ومرض المسلمين
Traveling Somewhere امين يارب
بارك الله فيك أحسنت كلامك جزاك الله خيرا وجزاء اطال الله عمرك طويلا مع الصحه والتوفيق للجميع علماء 🙏
ماشاء الله يا إمام جزاك الله خيرا 🙏🙏❤
Machalla outaz je te souhaite une longue vie machalla
Machallah dieureudjeuf ❤❤❤
Manchallah Oustaz sa liguéye rafétna
Machallah y'a oustaz yalna yalla fay la
Merci oustaz c'est comme si vous étiez à mes côtés
Merci beaucoup ya oustaz yalla nala yalla fay
MACHA ALLAHOU OUSTAZ SA LIGAY RAFETNA SI WA GÉNÉRATION BI
Oustaz yalla rek mo am sa faye
Oustaz yala nala yala faye lingay def amna solo trop
Machalla yo allahou diounou gourdam ma oustaz modjina batane
Yallah nala yalla samm aare. La degeral leu mousal la si non yi ak sayaatiin al ins wal djin
Diazaa k'Allah khayrane ya oustaz
Machalla oustaz tout ce qu'on a besoin est dans le saincoran alhamdoulilah 🙏🤲🤲
Machallah jaza kallah khayran
Machallah oustaz que dieu te bénisse
Machallah Oustaz Yalla nala borom bi reward la.
A merci ya oustaz imam
Man deh hamnani niabar amneu deh
Yal neu yallah mousalniou si niabr si berki yallah
Sunu Sénégal mom li yallah ham doyneu
Merci yalla nala yalla faye
machalla yaa oustaz yalla nala yalla fay yiwe
Jerejef Oustaz yalnala Yarabbi yorkal sutura Yallah musal nyu si njabarr
ماشاء الله يا استاذ جزاكم الله خيرا
Jazak'Allahou Khayran Ya Oustaz
Machallah yalla na yalla brome bi faye yiiw
contribution lawoon rekk waaye yalna yalla fay ci labbiré bi maacha alah
machalakh ya oustaz yale noko yala fayal bobom amin way ake mo mene warate
Jazakalahou khaïrane ya Oustaz🙏🙏🙏🙏🙏
Tieuy yalla
Khaamna maane mom
Yakouna kone
Tieuyy yalla naniou yalla saam
Non ne dis pas ça tu peux aller le voir il habite pas loin à Keur MASSAR Darou Thioub. Si vous avez besoin de quelques choses n'hésitez pas.
Yalna nala faye cii barke Muhamed. (SAW)
Macha allah oustaze diazakallahou khayrane