Mashallah oustaz alpha ba une fierté pour la Oummah islamique ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤Sounnah si kaw bidah si souf.kou amoul arguments Moy toumal ay nitt c est honteux
Salam ya Oustaz, bonne continuation. Ne vous dérangez jamais. Même si le musulman est fautif, le tout puissant nous a dit de ne jamais désespérer de sa miséricorde et que les bonnes actions effacent les mauvaises. Paix sur vous.
Assalamaleykum warahmatullah taallah wabarkatuh ya Oustaz Alfa Bah mon fils pour Quoi mon fils par ce que vous à l'âge de mon fils donc thien Bon ne vous décourager pas tu te bats pour le sentier d'Allah qui est très très glissant donc ne recule pas nous sommes derrière vous et Allah subhanak aussi je vous souhaite un bon courage cordialement à bientôt inchallah Sabrine merci que Allah vous garde dans sa miséricorde Amine et toutes les odeurs qui vous écoute Icompris moi même Amine
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ is not easy to reach Allah let try Allah will direct and protect us Inshaa Allah..Alpha with the whole tearm ❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉further never back ward..we love your tearm just only for Allah,,we will continue to ❤ you all..this will be a big promotion for u Inshaa Allah Yabbi
Li d'où Dara si alpha gnome ay danhwa Kate lagne soralèwone li AK louko eupou sakh mais heureusement ba khame nagnou nè lêpou montage la si Kaw si kanam rèk alpha nous sommes tout cœur avec vous
Ahmed Cissé tu dois avoir honte. Tu as cru rabaisser cet homme en le vilipendant, mais tu as été élogieux pour lui. Tous les hommes voudraient pouvoir faire 45mnx2. C’est un véritable homme. Il attire les femmes par son comportement et son engagement. Toutes les femmes voudraient avoir cet homme comme mari.
Kankamousa c’était l’homme le plus riche du monde du début jusqu’à la fin kokou mo amone weurseuk et l’homme le plus populaire du monde et plus influent c’est le prophète Mohammad psl
Salamalecs frère Alpha Ba vraiment on n’a pas Besoin de ses débats,tu dois faire très attention parce que tu es entrain de mettre en danger nos frères .on dit en wolof nit day manou
Tarikhayii thinga jouddo gnou ngentella thi ko yew ak sa ndaye ak sa bay yep dengen kharam alfa ba mi njalokat bou bonbi moolay nakh demal nga deglou odio yimou def😢thim
Oustaz Alpha BA Qu'allah te protège . Continue à réveillé les sénégalais. Nous sommes très satisfait de vous. Vous faites du bon travail c' est pourquoi ils essaient de freiner. Ahmed cissé à manquer du respect à notre prophète Mouhammad SAW donc, il n'epargnera personne. Tout le monde sait que Ahmed cissé est un menteur.
Sokhna aicha sa tour bi rafetna, té,nga rafetal kaddu yi , oustaz c soi disan audio yunuy si c autentic ndakh danga si deeg luy incriminé oustaz Alfa sa dinganteek Yallah nak Beneen bi njoumté keen muthu si wala? Est do deglu lumuy wakh su wéré nga jeul su wérul nga nñaanal ko njub té njoortu lu rafet yakarna lii mo gënë dëpook sa tour wi dh
C'est très grave, yeuw ya gnakeu diom DEUG DEUG .... Bilahi dama gneuwone rek pour hol lane gayy eundi si sa audio yii , mais wahossi Dara di wah wahi kénéne... Gnilayy déglou dé yéna yém dé ragal yalla nékoul si yéne
Very good Ya Oustaz, I would have been very disapointed if you had talked about your private life in the internet...Keep the Da'wah going it's a wake up call for so many people... May Ya'Allah continue to Bless and Guide you and your team and reward you in abundance. And to Brother Younus, so sorry for your loss May Ya'Allah grant the deceased rest and make his/her grave be part of Jannatul Firdaus and an abode of Light and grant it to all the departed Souls....Ameen
So you respect his private life even while that involves him flying to Morocco to consort with "ukhties" and two timing 2 hot pushies? You guys are all jokes!
@@ChamOusainou-t1t he let us down, at first i thought they were lying but after hearing the whole audio of course it was alfa... he should have been very careful with women
@Abdallah31341 I also listen to the audios but i don't trust it cuz they hated this man because what he's saying to their tarika leaders this is why they are planning all this
@ChamOusainou-t1t that's is what i said, i thought they were lying against him because of his position to their tarikhas that's why i took my time to listen to the audio but honestly speaking it was HIM
Noo damay rousse souma guissé les soi-disant dioulite di parlo parlo di werantei ba nopi di woté ay dioulite. Legui Dioulite ; Dioulite moy nonam . Ahlou Sunnah ak Tassawuf ...
Bilahi c'est ça dh. Les ibadous detestent les wa-akhlou-tarikas. Wa-akhlou atrikhas detestent les ibadous. Vraiment gnouy niep warna gno kholate sougnoj boppou. C'est houteux. Sourate 49 verset 10. Les croyants ne sont que des freres. Ibadou yi nagnou bayi yakarni gno nek si deugue , dine beur ay yone lole . Je commence à dzcouvrir beaucoup de chose. Yalna gnou yallah yeureum gnoune niep
Assalam ya oustaz dadji rek bou dara déss ni table ni chaise dadjil lep gnoune yagnou yéee khamé nagn soss kat yi ak nonu islam yi on est fier de toi ya oustaz alpha k allah vou protège inshala
Mashallah oustaz alpha ba une fierté pour la Oummah islamique ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤Sounnah si kaw bidah si souf.kou amoul arguments Moy toumal ay nitt c est honteux
Tu connais même pas ce que sait la humma. C'est une honte voilà c tout
S'en fièrté yenn bann islam yen Ay nafekh yalla sokhla ouko
@@aboubacrysow510 balthazar ba notre fierté
😂😂😂 45mn sort de ma tête
Force a toi Oustaz Alpha Ba on es tous derrière toi☺️💪🏿Masha Allah
Alpha le kateur internationale
😂😂😂😂
Kimoraw kattalok
ALPHA WAKHI KOU ROUSS NGAYE WAKH.
Yalla n'alla yalla guindi
@@mariamaba472jspr boko ci oukhti yi rek 😂😂 Alpha Balthazard da graw dh
Yalla naniou yalla mouseul sy dioulit bouye bokalé yalla hum yalla kénala kén dou mome 28:19
Alpha euffffff coye 😂ba
😂😂😂😂😂
😂😂😂😂
😂😂😂😂 bayiko mounan nioun lay nakh
Yen daguen am blem sunna rek inchaa allah
😂😂😂😂😂
Yalla naniou yalla sahal thi sunna
Jaajeff yaw rekh laniou topou merci❤
Kép kou gueumni sunna rék mba sone lalal❤❤❤❤❤❤❤
Sounnah bidda le
Sen sunna ci de dou sounna 😂😂😂😂 demba Maroc 😂😂😂😂guir sunna 😂😂😂😂
Yéna gueuna sonnu nieup 😂😂😂
Sène xol dina dagu dèh si sunna incha allah si canam la dieum dèlène yak dèr rek
Sounnah si kaw bidah si souf❤❤❤❤❤❤❤
@@aboubacrysow510 saway hamnagne sene sunnah, lep lerna 🤣🤣😍🤣
@@mbayebabacardiouf7853😂😂 lérna déh
Alpha balthazar vraiment amato lo wakh
😂😂alpha moy masikhou dadial
45mn😂😂😂
Kou khool sa kanam gui khamni daga rouss katteur bou maknga😂😂😂😂😂😂
Yalla n'alla yalla guindi
@mariamaba472 kone yaw danga fokni si yoone bou dioub nga nék
@mariamaba472 أنا على صراط المستقيم
@@oustazahmedfall6478boo nekkon si siraatal mustaqiim doo wax nit ne dafa njaaloo te Amoo preuve
Bilahi koudoul khalate bamél Loula nékh waxal❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Balthazar Balthazar Balthazar Balthazar Balthazar Balthazar Balthazar Balthazar Balthazar Balthazar borom maroc😂😂😂😂😂😂😂😂
Lima diakhal kaye moy lanla woutiwon Maroc 😂😂😂😂
Balthazar 33 femmes dont 3 sœurs en mm temps😂😂😂😂
@@ErenKrüger1899
32 😅😅Doyna warr
Je pense que c'est celui qui est sur ton profil
Yalla n'alla yalla guindi
Oustaz alfa the best💪🏾
@@Ahmedmoussa88887 the best....🤣🤣🤣
@@Ahmedmoussa88887 balthazar ba thé best
@ dagua bakh di wakh rek vocal yiguèn wakh ni moko wakh sakh voix bobou ak voix alfa bi c’est diamétralement opposé thiey wa tassawouf😂
@@Ahmedmoussa88887 pourkoi guéne meune féne .dioulite dou féne
@@Ahmedmoussa88887 watal ne c pas lui
Merci frr kateur ga😂😂😂😂😂😂
Salam ya Oustaz, bonne continuation. Ne vous dérangez jamais. Même si le musulman est fautif, le tout puissant nous a dit de ne jamais désespérer de sa miséricorde et que les bonnes actions effacent les mauvaises. Paix sur vous.
Cheikh alpha yalla rek molaye faye
Sunna rek ❤
Sounna euf koy😂
Assalamaleykum warahmatullah taallah wabarkatuh ya Oustaz Alfa Bah mon fils pour Quoi mon fils par ce que vous à l'âge de mon fils donc thien Bon ne vous décourager pas tu te bats pour le sentier d'Allah qui est très très glissant donc ne recule pas nous sommes derrière vous et Allah subhanak aussi je vous souhaite un bon courage cordialement à bientôt inchallah Sabrine merci que Allah vous garde dans sa miséricorde Amine et toutes les odeurs qui vous écoute Icompris moi même Amine
Yalna yalla sougnou borom samou oustas alpha ba amine yarabi
Alphaltazar katt thi ouktiyi rekk😂😂😂 ba paré di saga sougnou mak gni 🤔
😂😂😂😂 kidib thiaga 😂😂😂
Ma chà Allah
Ngay sonne di wedi serigne bi té dou té serigne bi donne limou donne 😅😅😅
Ani ayna Balthazar 😂😂
😂😂 dama dém bay lathié lolou rék guiss sa commentaire bi
sarange tuuba, 33 femme, kooku mooy balthazar bu mag bi
Un seul préservatif aurait suffit pour éliminer un imbécile comme toi@@BaboucarrGaye-vu2hb
🫢@@BaboucarrGaye-vu2hb
Mey yow sarr nga sante😅
Homme de 45 minutes 🎉
Sounite amoule mousselime la alhourane wahe louye sounite wahabite mousselime moye deugue ❤ allahou wahid alkhourane moye deugue mousselime la ýallah wahe
Sois fort mon frère et n'écoute pas ces personnes maudites
C toi le maudit, nafek
Allah ta donné la liste des gens maudits 😅
😅😅😅😅😅😅😅😅@@badianefall4414
Machallah vérité absolue mon oustaz yalla nala yalla same
@@kazamariem6667 balthazar sall machala aconda
Ki kan la waay 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Jadjeuff way alphatazar ba😂😂😂 90mns
Ya oustass yalnala yalla sam mouthial la cii pékhey none ❤❤
Vive oustaz alpha ba mashallah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Viva Baltazar Massa alla demba Maroc guir diandi bagaz😂😂😂😂😂
Saway fén rek ngaye déff
Mane mom Alpha rk laay top, dingay doundé sounna bi mo nekh😂😂😂, dina diar nga tékma ci axe😅
Barak Allah fikhoum
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ is not easy to reach Allah let try Allah will direct and protect us Inshaa Allah..Alpha with the whole tearm ❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉further never back ward..we love your tearm just only for Allah,,we will continue to ❤ you all..this will be a big promotion for u Inshaa Allah Yabbi
@@abisatousinghateh5830 balthazar ba notre fierté
Cheikh alpha boféké liguayi diwax thiy deugeue le bolwaxaté darra thiy diné diy
Lidoyna war❤❤❤❤❤❤❤❤
Oustaz eufff.
Li d'où Dara si alpha gnome ay danhwa Kate lagne soralèwone li AK louko eupou sakh mais heureusement ba khame nagnou nè lêpou montage la si Kaw si kanam rèk alpha nous sommes tout cœur avec vous
Khamnaani défarou ba diake mo eup yité lou nite di déf si kaw souf
Hafizhahulah ❤
MachaAllah Amna solo lol❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
@@MameboussouSarr machala omar pourouth parath
Wizzy Alpha Ba billahi damala yeureum té amna loumay diombe sinon nala wakh lou niaw
Ahmed Cissé tu dois avoir honte. Tu as cru rabaisser cet homme en le vilipendant, mais tu as été élogieux pour lui. Tous les hommes voudraient pouvoir faire 45mnx2. C’est un véritable homme. Il attire les femmes par son comportement et son engagement. Toutes les femmes voudraient avoir cet homme comme mari.
Kankamousa c’était l’homme le plus riche du monde du début jusqu’à la fin kokou mo amone weurseuk et l’homme le plus populaire du monde et plus influent c’est le prophète Mohammad psl
Machallah Oustaz alpha yallana yalla Sam la te mou dalla si lège none amine y’a rabi
@@SokhnadiarraNgom-q9r balthazar ba moy nounou bopame
SERIGNE TOUBA PAIX D'ÂME LA DÉFF NIOUNE MOURIDE YII ☝️ TÉ LOLOU KÉNE AMOUKO ☝️
Serigne Touba niit safarala
mourid wack dadial neckoul ci alkhourane 😂
@AlassaneCamarand-ep4js
Ndéring yi ndeysane 😂
@@AlassaneCamara-ep4js bayil fene dara wolou lassi
Masha'Allah oustaz alpha may Allah the almighty guide you.❤❤
inchallah yalla danala samb dé ❤️❤️❤️❤️❤️
L'adultére est interdit, surtout un grand dahwa personne come lui. Il ne peux pas être un guide, puisqu'il utilis ses adeptes.
Lakhawla walla khouwata illah illah Dieu est grand
Salamalecs frère Alpha Ba vraiment on n’a pas Besoin de ses débats,tu dois faire très attention parce que tu es entrain de mettre en danger nos frères .on dit en wolof nit day manou
Barakalahoufik Machaallah ❤❤❤❤❤
Kateur international ba Maroc 🇲🇦
Alpha alis Balthazar ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Wa legui bignou la toumalai LOUSSI yonou Serigne Touba
Sen Sunna bi nexna dè xaley yeup Alpha iriiiii nalen😂😂
Tarikhayi lepo aye fenla 😂😂😂Senegalese yewolen 😂😂
Sa baye sakh ak sa yaye aye féne lagne 😅😅😅😅
Tarikhayii thinga jouddo gnou ngentella thi ko yew ak sa ndaye ak sa bay yep dengen kharam alfa ba mi njalokat bou bonbi moolay nakh demal nga deglou odio yimou def😢thim
Waye dou donne Baltazar mi moñouy yee😂😂😂😂
Yawak sen oustazi pervert yii yenay doule katt yi. Katt rek
Thanks oustaz Alpha bah
Oustaz Alpha BA Qu'allah te protège .
Continue à réveillé les sénégalais.
Nous sommes très satisfait de vous.
Vous faites du bon travail c' est pourquoi ils essaient de freiner.
Ahmed cissé à manquer du respect à notre prophète Mouhammad SAW donc, il n'epargnera personne.
Tout le monde sait que Ahmed cissé est un menteur.
Masha'Allah oustaz alpha leral yi Amna solo yallna yallah fay la
Nio la eupp khame khame fouf Té Serigne touba rek inchallah
Alpha khamna yalla khamna 😂😂 ndakh khamo Di wakh lénén lounou la wakhal nième ngako😂😂 alpha Kattér
dangay danday doull thiaganga boy thiotou ndemm😊😊😊😊😊 gomoko
Masha'Allah oustaz alpha, may Allah the almighty protect you from the Ameen
yena fi dane nek di wakh kom yene rek yana nek thi ak ndioub 🤣🤣
😂😂😂😂😂
boy ana ouhti yi bay pss massi bok boy alpha ba thiaganga baltazar wa ahlou kantante😂😂😂😂😂😊😊
Ngibil giné nga maygnou diam way baltazar bou bonbi 😢😢😢yay doumi khadj gisago dara
Sokhna aicha sa tour bi rafetna, té,nga rafetal kaddu yi , oustaz c soi disan audio yunuy si c autentic ndakh danga si deeg luy incriminé oustaz Alfa sa dinganteek Yallah nak
Beneen bi njoumté keen muthu si wala? Est do deglu lumuy wakh su wéré nga jeul su wérul nga nñaanal ko njub té njoortu lu rafet yakarna lii mo gënë dëpook sa tour wi dh
C'est très grave, yeuw ya gnakeu diom DEUG DEUG .... Bilahi dama gneuwone rek pour hol lane gayy eundi si sa audio yii , mais wahossi Dara di wah wahi kénéne... Gnilayy déglou dé yéna yém dé ragal yalla nékoul si yéne
Kii ken toumaalouko bayyileen par par looo😂
Man mi sakh dama fogon né toumal la waay audio yi dafa léer nagne 😂
@@Abdallah31341😂😂 edu cateur la
@iboudue2727 😀😀😀
Saga Who kene qAllah te garde❤
Oustaz younousse nio gui lay diale sa bokam bi Fatou yalla n’a yalla yeureum ko te hareko aldiana Amina yarabi❤
Kouy waxale yalla sougnou borom yalla sougnou borom moléy samal bopam wallahi
Xana kéneu samou ko kone??
Lidé my torokh adina ak alahira. Vive Cheikh Ahmed Cissé
SO BAYIWOUL SERIGNE TOUBA LII NARA NIEUW MOYE GUEUNEU GRAW 😢😢😢 ON A TROP VUE 😂😂😂 G PEUR POUR TOI 😢😢😢😢
Ah bon tu connais l'avenir ? Et le passé ?Affaire 33 là c'est vrai ou pas ?
Très bien ya oustaz ,preuve day wakh dé ndéketé xol moy goumba dou ay beutte
Yow Alpha thiaga
SERIGNE TOUBA NAINA MOY KHADIM RASSOUL IL A PASSÉ TOUT SON TEMPS À TRAVAILLÉ POUR DIEU ET SON SON PROPHÈTE
Yalla nala yalla samou
Merci !
❤❤❤
Merci oukhty Fatima ❤️
Assalam aleika
Very good Ya Oustaz, I would have been very disapointed if you had talked about your private life in the internet...Keep the Da'wah going it's a wake up call for so many people... May Ya'Allah continue to Bless and Guide you and your team and reward you in abundance. And to Brother Younus, so sorry for your loss May Ya'Allah grant the deceased rest and make his/her grave be part of Jannatul Firdaus and an abode of Light and grant it to all the departed Souls....Ameen
Ameen
😂😂😂😂 neko moubayi auff bi 😂😂😂
So you respect his private life even while that involves him flying to Morocco to consort with "ukhties" and two timing 2 hot pushies? You guys are all jokes!
@@JshwHwhw😂😂😂😂 ya bonne
⛔🚨🚨🖐️Yaw com Dangay dioubbanti nitngi te yaw danla toumal danga wara léral tebayi wiri wiiri bi
Yalla nala yalla samb oustaz deug rek gay wakh
Wallahi they can never put you down because Allah is always on the right path and you always speak the truth Ustas Bah
@@ChamOusainou-t1t he let us down, at first i thought they were lying but after hearing the whole audio of course it was alfa... he should have been very careful with women
@Abdallah31341 I also listen to the audios but i don't trust it cuz they hated this man because what he's saying to their tarika leaders this is why they are planning all this
@ChamOusainou-t1t that's is what i said, i thought they were lying against him because of his position to their tarikhas that's why i took my time to listen to the audio but honestly speaking it was HIM
Warléne séne bob té ngéne diémeu dioupp té bayi dérou titt njii😂😂😂😂😂😂
Sunna si kaw bida si souf
Baye lahi Moy rassolou lahi fi ah faniou dieum
❤❤❤
AKA MALA TITEUL 😢XAM XAM MI GUI YÉM SI WAKH LI NGUA XAM 😢 mano xam lépp wédi lépp SVP 😢😢😢
SALAM oustaz YALNALA sougnou Borom SAME ci BARKE SEYDINA MOHAMED SALLLALAHOU ALEYHI WA SALAM AMINE ❤❤
Wahkenko deug moo geune,
Sénégal deugu dokhoufi fène ak sos mofi dokh
Gemelligeum'tabayi
Kastee
TRÈS BIEN ALPHA LÉRAL DAL MOY LÉRAL NIT YI SI YAKH EXPLOITER AK NIAK RESPECTER DINÉ YI WAA TARIKHA DEUKÉ
Noo damay rousse souma guissé les soi-disant dioulite di parlo parlo di werantei ba nopi di woté ay dioulite. Legui Dioulite ; Dioulite moy nonam . Ahlou Sunnah ak Tassawuf ...
Bilahi c'est ça dh. Les ibadous detestent les wa-akhlou-tarikas. Wa-akhlou atrikhas detestent les ibadous. Vraiment gnouy niep warna gno kholate sougnoj boppou. C'est houteux.
Sourate 49 verset 10. Les croyants ne sont que des freres.
Ibadou yi nagnou bayi yakarni gno nek si deugue , dine beur ay yone lole . Je commence à dzcouvrir beaucoup de chose.
Yalna gnou yallah yeureum gnoune niep
SEYDI BA
Machall ❤❤❤
Kou yapp magu gni yalla wérr la beutieuk 😂😂🤣🤣🤣
Alpha'bobayiou'Ouztaz
Adhy'Nias'dodiok'thi
Problem
Assalam ya oustaz dadji rek bou dara déss ni table ni chaise dadjil lep gnoune yagnou yéee khamé nagn soss kat yi ak nonu islam yi on est fier de toi ya oustaz alpha k allah vou protège inshala