12 FANN CI WOOR AK ÑAAN ! APÔTRE YVAN CASTANOU

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 7 фев 2025
  • 12 FANN CI WOOR AK ÑAAN ! Apôtre Yvan CASTANOU
    ==========================================
    ==========================================
    Impact Centre Chrétien (ICC) adi jangu fu cofeelu Yàlla di sopali nit ña ay jambaar . Njabootu ICC ngi dajalo ci bërëb yu bare ca France ak ca deuk you beri si aduna ci yëpp.
    Yvan CASTANOU moy ki key jiite,
    Ci ICC TV WOLOF di ngen fi fekk baataxalou ICC TV ci kalamay Wolof ngir baatu Yàlla yegg fepp ca aduna te mu donn ndamam.
    Bul fate bindu ji, wasaare, bës zaime te di saafantek xibaar yi.
    Mbokk mi, yow mi beugueu diébal sa dundu Yesu, meun nga niou fekk fi ci ICC Dakar, ganaw Fédération Sénégalaisou Football bi ci Ouest Foire, wéttou GIM-UEMOA,
    Meun nga niou diot itam ci numero bi di : 77 620 54 49
    Ma bamtuwat ko : 77 620 54 49
    Na len Yalla samm te barkel len ci turu Yesu !

Комментарии •