@@adjigueye6395 Entre gnoune leu dinagn ko gérer com on l'a tjrs fait. Relevé les défis a toujours été notre point fort et ce n'est pas aujourd'hui que cv changer. Merci bcp
Gayi il faut être objectifs moi je suis mouride mais cheikh Omar diagne n'a rien fait de mal mm boudé amna loufi diaroon ak mourides yi il faut être honnête bayi fanatisme bi est ce que lire ngeen lettre bimou tontou tontou na ci yarr ak. Teggin ta limou wax diomaye ak sonko nioko ndieuk wax budget programmer woul yeen yi ta guenné xaliss sans preuve la gayi di bagn motax sonko ni budget 2025 bi dinagn fekhé am budget culte état dafa am yoon lifi xéwoon ci macky sall lagn doon xeex pour moi diomaye a bien fait de confier omar diagne ce poste par ce que tapalé gui dafa wara diex et puis seugn bass ni lougn beug diomaye def ko day fekk mou deuppo ak lou wara nekk
Qui a payé le transport des invités? Si ces derniers ont pris en charge leur propre transport, il me sera difficile d'accepter qu'ils n'ont pas pris en charge leurs frais d' hotels. Serigne Cheikhouna doit s'expliquer.
C’est pas pour rien Yalla wakh ni dafa beugue gni deugou di wakh deugue . Bilahi dioulite deugue moy deugou niemer deugue nak . Di wakh deugue même souma arranger woul yomboul. Yalnaniou Yalla def ay nit you deugou amine .
Assane a raison déh. ✅️ Ñoom ñaar ñéepp Khalifa bé lénn fal. Serigne Bara Mbacké, le Khalife Générale des Mourides, mofi tégoon S Cheikhouna mi, ték fi tamit S Bass abdou khadre atum 2009 lawoon. il faut surtout pas sacrifier Sëñ Cheikhouna
Vous êtes un mouride typique. Quand il s'agit du mouridisme vous perdez votre capacité de raisonner. Si Serigne Touba revenait sur terre je vous garantie qu'il rejetterai 90% de ce qui se disent mouride. Vous ne connaissez pas yoonou mouride comme Serigne Touba Amadou Bamba l'avait enseigné. Yoonou mouride n'est devenu qu'un système de manipulation et d'exploitation des soi-disant talibés. Qu'Allah vous sorte de votre torpeur religieuse
Niari nafékh yi, Sa NDIOGOU AK SOHIBOU di attaqué RFM, bayil sen thiokhor gui. Cheikh Bass louthi sa yone, Serigne cheikhouna , président commission relation extérieure moko bindeu.Et il en a le droit.Tu ne peux pas tout gérer😡😡
Seex Omar Jaañ de bu bañee Sëriñ Tuubaa loolu moom la, li am solo mooy li mu def ndax war na ko def walla waro ko def, waaye nag màggalsi toog Dakaar loolu dangaa noos si waaye màggal si wóo nañu bayyi tappale yi
Vous nous amerdez ak AK cette lettre, Vos invités vous les prenez en charge et arrêter de timpanisait les gens en plus Di tekk deal AK doundou si État bi Cette lobbie maraboutique niakk diom togg mouy dokh, va dégager inchallah
Vraiment des deux côtés après réflexion j'ai vu que c'était pas méchant car u y'a un changement de pouvoir mais que soit aussi dans les brigades et commissariats des FDS
Mannèè Bayillènn RAY RAYALL bi // Magalou Touba c`est tres bien Organisè avec plusieurs reunions avant le jour et le tout dirigè pas Seugn Bass - Ils on etè maladroit avec tous ce qui c`est passè dans ce pays et leur position - Avec le DIOUB JUBBEL. JUBBENTI // Il ne devrait meme pas avoire de lettre --- Basse mi mooy Fènn - doo yonni nitt ba mou perte nganè amou ci woon ndiguenn, kii allakhiraa ni lay deff talibe yi khanna ??- Commitè d`organisation yennako yonni fallko Serigne bi loumouyy FèNN - Ta billay mouride la mann mi di bindd- Li moo Djiekh - PARTOUT
C’est à 2009 qu’il eu une institution PORTE PAROLE DU KHALIF et on a créé le comité d’organisation en 2009 avec des sous commissions chacunes d’elles dotées des prérogatives. Serigne Cheikhouna a écrit la lettre sous le cachet de sa commission relation extérieure qu’il dirige depuis la création du comité d’organisation. Donc le problème c’est Cheikh Omar Diagne qui a répondu la lettre en s’adressant au président du comité d’organisation. Une lettre officielle doit être bien écrite et précise. Sandiogou assigne des sous entendu contre véridique. Il doit savoir que tte cette organisation date du magistère de Serigne Bara. SVP, if faut faire attention de certaines commentaires
Sëñ Bas moo juum bëgg a neexal Nguur gi warul woon a tax muy jéem a toroxal Sëriñ Seexunaa Commission bi Sëriñ Seexunaa moo ko taxal ci Jamonoy Sëriñ Baara
Merci Assane wakh nga lép Serigne Cheikhouna Mbacké thi liko war rék la nék dou dokh si ay tapalé kou bakh té sérieux wadji nga kham né da allergies mouride yi aka nara sone
Sa ndioogou commission bi dafa amaat yéneen commission you nékk çi biir kouné AK lagniou la santé Serigne chekhouna loolou mou wax deuggleu yagg nakoo yor té meuseul am problème kon lamou déf lawara déf Yaw nak sa ndioogou dafa mélné dangaa japp né masslaa mooko fa bayyi ndax limouy doomi elhaji bara loolou ndioomté la Serigne mourtada doomi elhaji bara la té çi jamono baayam moo nékkoon précédant commun bou Touba té dagniou KO faa jeulé
Saa S Seexunaa lim wax leer na dh Dafa bind lettre bi ci turam en tant que président commission relation extérieure. Saa yaw ak Sohaïbou demleen def gëstu ci S Seexunaa dingeen xam moom mooy kan. Ci diplomat yi gëna mak Senegal la bokk. Commission bim jiite ci magal gi mérite mooko fa bayi, pas une question de népotisme. Ngir yalla rekk dem léen def gëstu ci moom après ngéen ñëw wax ci moom. Vous allez certainement se rendre compte de vous vous trompez.
La seule chose à blâmer c'est le traitement réservé à l'information par les journalistes qui en ont parlé. Sinon COD et l'auteur de la demande sont dans leurs rôles. Et chacun va l'assumer.
Merci bcp professeur Cheikh Omar Diagne. Jub Jubal Jubanti
Yuéna alkou te bon
Omar diagne na dioubantti bopam ba parré sogua dioupanti watté
Pastef cheikh Omar vas vous mettre mâle avec la population attention à vous
@@adjigueye6395 Entre gnoune leu dinagn ko gérer com on l'a tjrs fait. Relevé les défis a toujours été notre point fort et ce n'est pas aujourd'hui que cv changer. Merci bcp
Dieureudieuf serigne touba ❤
Cheikh Oumar Diagne est très rigoureux dans son travail. Mash'Allah
Merci beaucoup sonko rek focus ❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉
Gayi il faut être objectifs moi je suis mouride mais cheikh Omar diagne n'a rien fait de mal mm boudé amna loufi diaroon ak mourides yi il faut être honnête bayi fanatisme bi est ce que lire ngeen lettre bimou tontou tontou na ci yarr ak. Teggin ta limou wax diomaye ak sonko nioko ndieuk wax budget programmer woul yeen yi ta guenné xaliss sans preuve la gayi di bagn motax sonko ni budget 2025 bi dinagn fekhé am budget culte état dafa am yoon lifi xéwoon ci macky sall lagn doon xeex pour moi diomaye a bien fait de confier omar diagne ce poste par ce que tapalé gui dafa wara diex et puis seugn bass ni lougn beug diomaye def ko day fekk mou deuppo ak lou wara nekk
T'as rien compris
Do mourite dagay fene rekkk
Lingay wakh khamossi Dara magal khamnga niata lay douga si possou éta démal nga gueustou
Yaw donc tu n'a rien compris,wala tu n'ai pas mouride dagaye saup
Cette lettre est écrit et signé par Cheikh Omar Diagne
Yow doule way ya soff dangua kham sarap dayam guanane mouride gua yow AB ma riradogua doule
Merci Sa Tu as bien parlé.
Il faut construire un très grand hôtel a Touba
Un hôtel 5 étoiles islamique
Et le faire à Medina Baye ville internationale
Aussi Tivaouane
Loll amna solo
Kange la sonko Di dioum yaw sa gnogou😮yaw daal pastef ga😂
Information you lèèr ta woor solution tv
Gagni deug deug, ganou Touba thi magalgui loumouy wout king Fahd.
Logistique état waroul wessou escorte pour sécurité ganyoyou.
Touba manque woul foumou lendi dougal
assane a totalement raison
Qui a payé le transport des invités? Si ces derniers ont pris en charge leur propre transport, il me sera difficile d'accepter qu'ils n'ont pas pris en charge leurs frais d' hotels. Serigne Cheikhouna doit s'expliquer.
Merci baaye assane ❤❤❤❤
Rien de spéciale pour la réponse de cheikh omar diagne.❤.L ETAT EST LIBRE DE TOUTE PRESSION de quelque lobbies que se soit .❤
C’est pas pour rien Yalla wakh ni dafa beugue gni deugou di wakh deugue . Bilahi dioulite deugue moy deugou niemer deugue nak . Di wakh deugue même souma arranger woul yomboul. Yalnaniou Yalla def ay nit you deugou amine .
Solution tv je sperk yena ngi khole commentaire yi Pour nguene kham ni nite gni dofou niou li assane wakh dafa leer
Assane a raison déh. ✅️
Ñoom ñaar ñéepp Khalifa bé lénn fal.
Serigne Bara Mbacké, le Khalife Générale des Mourides, mofi tégoon S Cheikhouna mi, ték fi tamit S Bass abdou khadre atum 2009 lawoon.
il faut surtout pas sacrifier Sëñ Cheikhouna
Bon cher Assane Messere, plané,donc mome daffay weddi.
La seul et unique leçon qui est visible , est une réelle division au sein de la commission d'organisation du magal
Merci Assane ❤❤❤❤❤❤❤❤
Merci beaucoup assane mesere wax nga deug
Omar diagne merci na tegue si yone niep ysmsi
Omar Diagne moy kane lettre dou dém si Omar Diagne. Serigne bass bou sokh la Diomaye légui woko téléphone wala Sonko omar Diagne na kate ndayam feulle
@@elhadjicheikhba4122 machallah bégna çi yaw lool 🎉🎉❤❤
Vous êtes un mouride typique. Quand il s'agit du mouridisme vous perdez votre capacité de raisonner. Si Serigne Touba revenait sur terre je vous garantie qu'il rejetterai 90% de ce qui se disent mouride. Vous ne connaissez pas yoonou mouride comme Serigne Touba Amadou Bamba l'avait enseigné. Yoonou mouride n'est devenu qu'un système de manipulation et d'exploitation des soi-disant talibés. Qu'Allah vous sorte de votre torpeur religieuse
Cheikh Omar diagne ❤❤❤❤
Niari nafékh yi, Sa NDIOGOU AK SOHIBOU di attaqué RFM, bayil sen thiokhor gui. Cheikh Bass louthi sa yone, Serigne cheikhouna , président commission relation extérieure moko bindeu.Et il en a le droit.Tu ne peux pas tout gérer😡😡
Merci alassane la vérité libére merci
Assane mo nekk thi deukk bilahi serigne bass waham dji rafetoul dh
Niafal sa ndaye feullé
😂😂😂😂😂😂😂😂. Thiey badolo mo nekh deh dou khalat
Merci Assane
Merci assane ce très pertinent
Asan a parfaitement raison
Saa Ak Sohaïbou liñiy wax xamuñ ci dara
Merci assan
belle analyse Sa NDiogou
tu a tout à fait raison
que le fanatisme religieux cesse il faut être objectif
Faire ce que l'état peut
Merci pa assane
Seex Omar Jaañ de bu bañee Sëriñ Tuubaa loolu moom la, li am solo mooy li mu def ndax war na ko def walla waro ko def, waaye nag màggalsi toog Dakaar loolu dangaa noos si waaye màggal si wóo nañu bayyi tappale yi
assan merci bien couronique
Vous nous amerdez ak AK cette lettre,
Vos invités vous les prenez en charge et arrêter de timpanisait les gens en plus Di tekk deal AK doundou si État bi
Cette lobbie maraboutique niakk diom togg mouy dokh, va dégager inchallah
Vraiment des deux côtés après réflexion j'ai vu que c'était pas méchant car u y'a un changement de pouvoir mais que soit aussi dans les brigades et commissariats des FDS
Assane à parfaitement raison.
Merci assane un commentaire sans comédie
Mannèè Bayillènn RAY RAYALL bi // Magalou Touba c`est tres bien Organisè avec plusieurs reunions avant le jour et le tout dirigè pas Seugn Bass -
Ils on etè maladroit avec tous ce qui c`est passè dans ce pays et leur position - Avec le DIOUB JUBBEL. JUBBENTI // Il ne devrait meme pas avoire de lettre --- Basse mi mooy Fènn - doo yonni nitt ba mou perte nganè amou ci woon ndiguenn, kii allakhiraa ni lay deff talibe yi khanna ??- Commitè d`organisation yennako yonni fallko Serigne bi loumouyy FèNN - Ta billay mouride la mann mi di bindd- Li moo Djiekh - PARTOUT
@@Shakur892 omar diagne moy natou sonko ak diomay ,, dofff kénn douko dougall si ÉTA ,, omar diagne app doff bou sokhor la 😡😡
@@Ralfalves-i9t Sou Nieupp khawonna diffè comme cheikh oumar diagne Senegal day avancer mon ami, Li gnieupp bokk na ci nieupp yamm rekk wala bok
Sén plateau bi vraiment exceptionnel
Moi je pense que le problème c cheikh oumar Diagne
qui est le secrétaire général du présidence de la république?
Merci beaucoup sonko
Assane il a parfaitement raison ❤❤
Sa ndiogou nitt dou nafekh baye assan Diara dieuf
Courage assane
Cheixouna balaga bind waxal AK Serigne bi ba am ndigal
No taye mom assane wakhna duegue Serigne Cheikhouna mbacke limdef nonoula ✅ khana kaye gayi no buegue eta bi kontane rek motakhe nou sarakhé ceikhouna 🤷🏽♂️🥲😭
Seringe cheikhouna mbacke mo am 99%
Pour une fois chapeau assane
Mèrçi sa ndiougou
Bola nit niy deglou wakh kham kham rek mola war diadiaf sa
Merci Assane RFM Defougnou Dara
Asane nèna radio bi leniou beug sarakhe😂😂😂
❤Sa ndiogou cerveau ❤
Baye Assane dina ray nite bilay 😁🤣🤪
Nafewkh yi ak sos kateyi ak diakhassè katyi nio nguify balègui pour diakassè sounou etats bou bess bi wayè soti dè incha allah
C’est à 2009 qu’il eu une institution PORTE PAROLE DU KHALIF et on a créé le comité d’organisation en 2009 avec des sous commissions chacunes d’elles dotées des prérogatives. Serigne Cheikhouna a écrit la lettre sous le cachet de sa commission relation extérieure qu’il dirige depuis la création du comité d’organisation. Donc le problème c’est Cheikh Omar Diagne qui a répondu la lettre en s’adressant au président du comité d’organisation. Une lettre officielle doit être bien écrite et précise.
Sandiogou assigne des sous entendu contre véridique. Il doit savoir que tte cette organisation date du magistère de Serigne Bara. SVP, if faut faire attention de certaines commentaires
Assane wakhi dofyi bayil diko wakh si walou li khew parcque cheikh omar diagne ga beug mal à l'aise
Sëñ Bas moo juum bëgg a neexal Nguur gi warul woon a tax muy jéem a toroxal Sëriñ Seexunaa
Commission bi Sëriñ Seexunaa moo ko taxal ci Jamonoy Sëriñ Baara
Yalla na niépou am djamou❤
Brabo asan ni tou deug
Bouléne faté ni Senegal 🇸🇳 serigne touba moko mome ❤❤❤
Bokalé rek sa bopp ngay fowé les mourides ne font mm pas 35% de la population sénégalaise daguen beuri thiow rek
Merci sa
Wa waw Cheikh Omar Diange Dall Lomou waax jub Jobal jubanti rék
Domihaj doungenn bayi fenn
Wakhi doff Cheikh Omar Diagne wédina lollou Serigne bass bou sokhla diomaye tay guissko légui
Problème bi Moy cheikh Omar Diagne dafa bagne mourid yi motakh gayi diare si mome def sabotage bi parcque cheikh Omar Diagne vraiment plasame douwone fofou day yakh ligeyou sonko et diomay
Mi nékoneu khalifa Serigne Touba cheikh a dommage lla
Chiekh Oumar rek ❤
Souhaibou assann wakh n'a deuggg. Serigne bass nagn ko ndiballeh moyy yekha wakh. Sénégal nekhoul wakhe.
Merci sa ❤❤❤
Sëriñ Bas moo jaxase yëf yii. Baay Asan lii mu wax mooy dëgg.
Li fal s basse mo fal s cheikhona sohibou ya sa man diakhal ngen ma
Sa ndiogou wakh na lep ... borom khel yi nak lay wakhal
Merci Assane wakh nga lép Serigne Cheikhouna Mbacké thi liko war rék la nék dou dokh si ay tapalé kou bakh té sérieux wadji nga kham né da allergies mouride yi aka nara sone
Baye assane wakhal deugeu té yalla takh
Assane ❤😊
❤ Hassan la manière dont il donne l'information c'est pas du journalisme pour quoi il dit goulet
Yalla na niépou am djamou🤲❤
Li sa wakh ska dègue ngène ko 😂😂😂😂😂😂
Sacré Baye Assane...
Sa ndioogou commission bi dafa amaat yéneen commission you nékk çi biir kouné AK lagniou la santé Serigne chekhouna loolou mou wax deuggleu yagg nakoo yor té meuseul am problème kon lamou déf lawara déf
Yaw nak sa ndioogou dafa mélné dangaa japp né masslaa mooko fa bayyi ndax limouy doomi elhaji bara loolou ndioomté la Serigne mourtada doomi elhaji bara la té çi jamono baayam moo nékkoon précédant commun bou Touba té dagniou KO faa jeulé
Saa S Seexunaa lim wax leer na dh
Dafa bind lettre bi ci turam en tant que président commission relation extérieure.
Saa yaw ak Sohaïbou demleen def gëstu ci S Seexunaa dingeen xam moom mooy kan.
Ci diplomat yi gëna mak Senegal la bokk. Commission bim jiite ci magal gi mérite mooko fa bayi, pas une question de népotisme.
Ngir yalla rekk dem léen def gëstu ci moom après ngéen ñëw wax ci moom. Vous allez certainement se rendre compte de vous vous trompez.
Merci beaucoup
ماشاء الله جرجفواي الشيخ عمر جاج حفظه الله ورعاه وأيده حفظه الله ورعاه وأيده حفظه الله ورعاه وأيده بجاه النبي محمد صلي الله عليه وسلم
La seule chose à blâmer c'est le traitement réservé à l'information par les journalistes qui en ont parlé. Sinon COD et l'auteur de la demande sont dans leurs rôles. Et chacun va l'assumer.
COD défoule dara lepp Serigne chiekhuna momou la ah nann waxante DEUG
Saa ndioogu tay de juum nga man kenn guenoumaa buegg ñi fi nekk waaye wax dëgg s Seexunaa moom moo nekk ci dëgg dan koo tooñ te s Bass yit daa juum
Billhi sa ya degue machalla
La réponse de Cheikh Omar Diagne est juste. C’est pas logique de loger des hôtes du magal de Touba à Dakar
Wa assam lan moy radiobi ni lakoy liire 😄
Sen touba bi sonnal nanou
Sonhibou yaw doméram nga sa bouye wakh doko dague assane bouye wakh ngakoye minimizé assane késsé mofi wakh deugue yéne dolén aye nitou deugue
Sénégal niarri deug mofa am ndax parparlo télé nio yax Sénégal niouy wara léral nioy leuneumbeul
S.touba amoulmorom
Asane degla walahi
Billay wallay baye Asane mesre wakhe deugue Billay deug reke gua wakhe sohibou ak sa diogou ayii nafekke laniou douniou wakhe deugue
Sa ndiogou wakhofi Dara
Le senegal appartien au bon dieu
Cheikh omar diagne n'a rien fait souka nékhé mou tontou niét rupture lagnou wakh
Assane limou wakh dafa l'aire nagne so falé nit béne affaires mou disi am ndam bou amé waroko Sarakhé
Chiekh bi limou wakh lerr na serigne bass man damako moudié beuge
Serigne barra mbacké
Merci Assane nakate sa lapoto la 😂😂