Ndindy La sortie surprenante de Serigne Abdou Karim Mbacké accompagné de Azoura Fall

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 27 янв 2025

Комментарии • 147

  • @Tapa-vc5uz
    @Tapa-vc5uz 5 месяцев назад +21

    Se abdou Karim yallah nafi yag téwér

  • @ndoffenediouf2749
    @ndoffenediouf2749 5 месяцев назад +3

    Yalla na Sa diame yagg Mbacké goudeul fane Mbacké❤

  • @massambakhouma2613
    @massambakhouma2613 5 месяцев назад +10

    Serigne abdou karim yalla nafi yague té wér amiiiiiine ci barké serigne fallou mbacke

  • @biranendiaye8759
    @biranendiaye8759 5 месяцев назад +13

    Merci sr Abdou karim yalna guafi yague

  • @IiiiloooHoko
    @IiiiloooHoko 5 месяцев назад +15

    serigne abdou karim mbacke yalla na fi yage te and ak wer si barkpe serigne touba ❤❤❤❤❤❤❤

  • @mbayefallou1401
    @mbayefallou1401 5 месяцев назад +6

    Macha-allah dieureudieufaty Cheikhoul KHADİİM Cheikh Ahmadou Bamba Yalla nanou ko YALLAH fayal ❤Amine ❤

  • @mouhamdoulaminebadji895
    @mouhamdoulaminebadji895 5 месяцев назад +6

    Yagueu fi lol té andak weireu Mbacké ❤❤

  • @mouhameddiallo8975
    @mouhameddiallo8975 5 месяцев назад

    NdeysanN ✨ Mbacké Balla Yagg fii loll tei Weer 🤲 Barkèb Cheikhoul Xadim 💓

  • @gueyemodounostresss2132
    @gueyemodounostresss2132 2 дня назад

    Machalla baye karim 😍

  • @omarfall4967
    @omarfall4967 5 месяцев назад +7

    Serigne Abdou karim Mbacké fallilou yalna fi yague té wér amine

  • @IiiiloooHoko
    @IiiiloooHoko 5 месяцев назад +9

    machallah mbacke ❤❤❤❤

  • @cheikhndiaye4199
    @cheikhndiaye4199 4 месяца назад

    Dieureudieuty Serigne fallou 💯

  • @awayaifaal7774
    @awayaifaal7774 4 месяца назад

    Seing abdou karim jamisunu borombe yan ngafi yaga the werr inshalla

  • @LikaLo-z4j
    @LikaLo-z4j 5 месяцев назад +10

    Djeureudjeuf Serigne toubaa

  • @BadouFaye-nr1vp
    @BadouFaye-nr1vp 4 месяца назад

    Cheikh Abdoul Karim mbacke yalla na fi sakh dak

  • @mamadoundiaye8643
    @mamadoundiaye8643 5 месяцев назад +6

    Dieuredieuf mbacke yag fi te weer

  • @ismailaba5448
    @ismailaba5448 5 месяцев назад

    Yalla na yalla Goudeul sa fane Mbacké yagg fi lol teh wér🙏🙏

  • @Iboudiouf1374
    @Iboudiouf1374 5 месяцев назад +7

    Mbacké ❤

  • @panogayembaye2116
    @panogayembaye2116 5 месяцев назад

    MBACKÉ BALLA YALLAH gafi dolé Yag lol té wérr ❤❤❤❤

  • @Leuzsonko
    @Leuzsonko 5 месяцев назад +2

    Baye Karim rek lagn beugeu mbacke yagg fi lol❤

  • @fatouseck7344
    @fatouseck7344 5 месяцев назад

    SERIGNE PAPE ABDOU KARIM FALLOU LODOUNE DOYOULE INCHAALLAH BOROM NDINDY BON MAGAL

  • @BoucarDiouf-g6p
    @BoucarDiouf-g6p 5 месяцев назад +5

    Yalna fi yague té wér

  • @ibrahimafaye9975
    @ibrahimafaye9975 5 месяцев назад +1

    Yalnafi yague loll té wér Mbacké

  • @mamadoufall140
    @mamadoufall140 5 месяцев назад +1

    Yalna fii yag te weur ❤❤❤❤❤

  • @YoussouLo-ku9lz
    @YoussouLo-ku9lz 5 месяцев назад

    Machallah

  • @FallouSene-p6i
    @FallouSene-p6i 5 месяцев назад +1

    Machalla ❤

  • @petitfaye2408
    @petitfaye2408 5 месяцев назад +1

    Guis nit kou bax bo xamul rèk mandul ay waxi banièl rèk nguafi dègu tes russa assumé 🙏 gni nguay guis nioussi eup yakarone nagn dotou niou bax si sén aduna serigne dieulèn indi watt lèn thi sociète bi ngua bokat kila dèfal li amo xalis boko santè nula nèx santè ko ❤❤

  • @Salimata1000
    @Salimata1000 5 месяцев назад +9

    Pauvre gens,vraiment triste pour l'Islam...Fi Allah swt ak Sunnah yonente Mouhammad sws rek mofi nek...

  • @ModyAidara-jb5vn
    @ModyAidara-jb5vn 5 месяцев назад +3

    Ceux qui accompagnent le marabout sont très sales lui il roule dans le luxe thiey Sénégal

  • @assgueye9996
    @assgueye9996 5 месяцев назад

    Saa waye danga deurr wla 😮😂😂😂

  • @IbrahimaDrame-wp7jm
    @IbrahimaDrame-wp7jm 5 месяцев назад +2

    ❤❤❤❤❤

  • @ndongolofficiel6392
    @ndongolofficiel6392 5 месяцев назад

    ❤❤yen gni commentaires nan li comédie la li arou baye fall la ak contane bayilen sokhor. Man jaime toutes les marabouts. ❤❤

  • @AmethMane-s1y
    @AmethMane-s1y 5 месяцев назад

    Yague fi Mbacké

  • @karimngom6480
    @karimngom6480 5 месяцев назад

    YAGUU FII LOLL TÉ WEURR MBACKÉ CII BARCKÉ BOROME TOUBA YAKAROU DIAMM YII ❣ ❣ ❣ ❣

  • @mbayesall5815
    @mbayesall5815 5 месяцев назад +6

    Tidian la dh mai ki mako beuguel sama bopou ❤🎉ki di falakh falakhi mom wéroul li dou yeufou nitt 😢

    • @basselabdou9891
      @basselabdou9891 5 месяцев назад +2

      falakh falakhi😂

    • @seynabfallou395
      @seynabfallou395 5 месяцев назад +1

      Xam al mo démé nonou depensé na nitt

    • @mbayesall5815
      @mbayesall5815 5 месяцев назад

      @@basselabdou9891 nice ki kay 😭

    • @mbayesall5815
      @mbayesall5815 5 месяцев назад

      @@basselabdou9891 😭🤔🤣

    • @bayendiagathiam2098
      @bayendiagathiam2098 5 месяцев назад

      @@mbayesall5815 yaw lii nga beugone wax motax nga nane kii mako beugeul sama bopou kiidi falax falaxi dafa guiss loukoko diaral lolou sa yone nékousi bayiléne dougou si paspasou nitt ki

  • @assgueye9996
    @assgueye9996 5 месяцев назад

    Saway meuno do bayi 😂😂 seuttt

  • @L24763
    @L24763 5 месяцев назад +1

    Li Mom dou diné, Li Mom yeufou mbame la 😅😅😅😅

    • @tawfekh1427
      @tawfekh1427 5 месяцев назад

      Fii lofi guiss lou graw

    • @tawfekh1427
      @tawfekh1427 5 месяцев назад

      Guisofi lou haram de

  • @ThiernoBa-kj5ki
    @ThiernoBa-kj5ki 5 месяцев назад

    baye karim domu ndaye amadou ba❤

    • @Leuzsonko
      @Leuzsonko 5 месяцев назад +2

      Legui apres ? Dieureudieufeti sunu takar bay Karim mou serigne fallou❤

    • @basselabdou9891
      @basselabdou9891 5 месяцев назад

      Amadou ba amadou ba😂

  • @MASSAERSYLLA-h8v
    @MASSAERSYLLA-h8v 5 месяцев назад +1

    Baye karim yaggue fi te and ak wer

  • @DiopDiop-vk4jj
    @DiopDiop-vk4jj 5 месяцев назад

    Quelle comédie

  • @falloudiaka4792
    @falloudiaka4792 5 месяцев назад +4

    Yalla nafi yague t ande AK wer

  • @gueyemodounostresss2132
    @gueyemodounostresss2132 2 дня назад

    Kidi wakh tamit daffa deur walla 😮😮😂

  • @assgueye9996
    @assgueye9996 5 месяцев назад

    Yokkou lérou Kane ioe 😂😂😂

  • @DiopDiop-vk4jj
    @DiopDiop-vk4jj 5 месяцев назад +1

    Ça c'est bokalee

  • @khoudiagueye5012
    @khoudiagueye5012 5 месяцев назад +1

    Serigne abdou karim yalla na fit yague🙏

  • @KhalilDien-fe5uh
    @KhalilDien-fe5uh 5 месяцев назад +4

    Azoura ndeysaan dafa am talibé dafa géner wou di wakh si kanamou seign bi lolou kou tarbiyoul doko kham geste yoyou. Azoura diap nala nguir dieumii KOU TED KI

  • @mamediarrakounde7296
    @mamediarrakounde7296 5 месяцев назад +3

    Yaague fi lol Mbacké andak weer Serigne Abdou Karim Mbacké

  • @mamadoubassiroukone4704
    @mamadoubassiroukone4704 5 месяцев назад +42

    Quelle comédie

  • @AngeliqueNdiaye-c7b
    @AngeliqueNdiaye-c7b 5 месяцев назад

    Bayr fall deugue danio gueme ligni don

  • @Fatoumatasow-mb5vc
    @Fatoumatasow-mb5vc 5 месяцев назад

    Quelle comédie 😂😂😂

  • @Flagrance
    @Flagrance 5 месяцев назад +2

    C'est quel genre de voiture ?
    C'est hors gabarit, c'est immense

  • @matarsow960
    @matarsow960 5 месяцев назад

    Senegal nekna beurina bruit

  • @oussoubane2712
    @oussoubane2712 5 месяцев назад +4

    Avant de juger il aurait fallu leur demander pourquoi ils se comportent de la sorte.

  • @boubacarba1293
    @boubacarba1293 5 месяцев назад +2

    C'est tout simplement triste et pathétique ! Un comportement pareil !

  • @BoulayeKonte-f6b
    @BoulayeKonte-f6b 5 месяцев назад

    😮😮

  • @MouhamedBiaye-oc4jb
    @MouhamedBiaye-oc4jb 5 месяцев назад +1

    Que du fantastisme au Sénégal 😢

  • @L24763
    @L24763 5 месяцев назад

    Kholal doff bi Mom😅😅😅😅

  • @musikonline550
    @musikonline550 5 месяцев назад +1

    😂😂😂 vraiment réveillez vous ay vrais dof guéne 😂😂 vous voyez pas ses enfants faire ces conneries que vous faites.. démléne diamou yallah té bayi diamou nite dém liguéyi téral sén wadiour té moytou serigne yi gua khameni sén intérêt rek 😂

  • @ndateyalla2784
    @ndateyalla2784 5 месяцев назад +4

    Gnileen toop salténaniou khassawnaniou niom niou doug si auto bou seet bou rafeet sheuuut senegal 😢😢😢

    • @PMD94
      @PMD94 5 месяцев назад +2

      Domeharam nga motakh ,tu mouriras dans ta solitude et ta procrastination,demande toi pourquoi tu es seule, sa xol mo leudeum

    • @ProPatriote
      @ProPatriote 5 месяцев назад +2

      Xol bou sett mo geune yeree you sett

  • @DiagneTahirou
    @DiagneTahirou 5 месяцев назад +1

    😂😂😂😂😂

  • @ousseynoutoure3621
    @ousseynoutoure3621 День назад

    Yow deimal diangui wakh khaoma journaliste ngueu khawma lo done

  • @DiopDiop-vk4jj
    @DiopDiop-vk4jj 5 месяцев назад +1

    Ces bayes sont égarés il faut penser à dieu

  • @sw22tv74
    @sw22tv74 5 месяцев назад

    Baye Karim nak comme azoura sab talibé laa donc war nga wakh ak môme
    Ab talibé day ame téguine

  • @fatoumbenguesene3006
    @fatoumbenguesene3006 5 месяцев назад

    Chirk akbar

  • @Iammameabdou
    @Iammameabdou 5 месяцев назад +1

    😂😂😂😂

  • @aliounediouf8196
    @aliounediouf8196 5 месяцев назад

    😱😱C'EST QUOI CES CONNERIES ET BÊTISES? 🥵🥵

  • @KhalyGueye-d2o
    @KhalyGueye-d2o 5 месяцев назад +1

    Azoura faal xana waxo wonn bayi ga ker serign si 😂

  • @BoussoSSALIOU
    @BoussoSSALIOU 5 месяцев назад

    Diamou yalla bayi thiakhan yi s touba lolu la wakh

  • @amadousow3039
    @amadousow3039 5 месяцев назад +1

    Lii dafa yomb trop ñioun serigne touba rèk moñiou diakhale bilay bagnii toroxal jeunesse bii la dèm cii Amadou ba pour khaliss c'est honteux

  • @tonyrobenson5902
    @tonyrobenson5902 5 месяцев назад

    ANA AKHENATON 😂😂😂

  • @cheikhdiop9932
    @cheikhdiop9932 5 месяцев назад

    Azoura ako dof😅

  • @abubasey4245
    @abubasey4245 5 месяцев назад +2

    Li ay chakhan la walahi bon nañu doka man😅😂

    • @Leuzsonko
      @Leuzsonko 5 месяцев назад

      Nioun baye Karim rek lagn geum beugougn kènènn koudoul mom

  • @AbdoulayeSall-zo2ny
    @AbdoulayeSall-zo2ny 5 месяцев назад +3

    Gissgéne Auto Ségn bi wipliw 😂❤Warna ame si yi Dei yalla bhna🎉😢

    • @guissguiss2459
      @guissguiss2459 5 месяцев назад +1

      Seugne yalla mo dogale mou am auto bi dou serigne yeupa ko ame yalla moy sédda lé dara diombou ko

  • @mandiayeniang9803
    @mandiayeniang9803 5 месяцев назад

    Journaliste bi tmt demal diangui watt sa français terrible neu lol😅

  • @Oubli2023
    @Oubli2023 5 месяцев назад +11

    « Mooy def , di dindi » 😂😂😂😂😂😂😂😂😂 .
    Meussoumako degg mou prononcer ALQURAN WALA HADITHS 😢.
    Ki est-ce Diangue na????
    Sénégal ,inchalla, la richesse nous libérera un jour .

    • @thiernobarry2625
      @thiernobarry2625 5 месяцев назад +1

      😂😂😂😂😅😅😅

    • @asnaakhadiimgueye8309
      @asnaakhadiimgueye8309 5 месяцев назад +2

      @@thiernobarry2625khamna de limou binde thi ay kamil yima thi kham matt na niatta yima kham

    • @ndateyalla2784
      @ndateyalla2784 5 месяцев назад +5

      Yalla naniou yalla libéré si nouvelle forme esclavage bi niou dougueul si tarikha .manaam sama mam moo gueun sa mam andil dima diokh dima tarbiyou .😢😢😂😂😂yalla lay top ay digleem tarbitou samay wadiour been serigne dou leek sama deureum inchallah. Sounouy seutaat nioy dakaal lii inchallah

    • @ndateyalla2784
      @ndateyalla2784 5 месяцев назад +2

      Gniileen toop salténaniou khassawnaniou 😅 eux ils sont dans des voitures belles chères et climatisées ....souniouy seutaat dananiou yeewou dakkal lii inchallah.

    • @PMD94
      @PMD94 5 месяцев назад +1

      ​@@ndateyalla2784yaw xalatal loutakh amo sarap ndeim , sa xol mo fekhoul motakh do comprendre moukk , si torokh ngay déwé , toute seule ,dinga fi nek di commentaires ba dé ,ta vie sera juste une merde ,parce que vous êtes méchant et orgueilleux

  • @Dam-g2u
    @Dam-g2u 5 месяцев назад +4

    Mouride dofna eupla.trop.bayilen bokalé.fi.yalla.né.ak.seydouna.mouhamed❤❤beug nabi ❤nabi ❤

  • @yawadiene6592
    @yawadiene6592 5 месяцев назад +1

    Yéneu talibé you mélni ay azoura gnome khana amou gnou djiangate si Serigne bi sopi séne djiko yaw vilipender AK doul aki Sousse rék deuk topeu Serigne

  • @user-ry4ki5ej2e
    @user-ry4ki5ej2e 5 месяцев назад +3

    Tout ça pourquoi ?
    L'islam à la sauce wolof est une aberration sur certains aspects.
    Maintenant en Islam à partir du moment où on est pas un aliéné, votre responsabilité est engagée.
    J'espère sincèrement pour ces gens qu'ils sont des aliénés.

    • @BennomorawKane
      @BennomorawKane 5 месяцев назад

      C sa que je m demande c pas possible

  • @mansourdiop1745
    @mansourdiop1745 5 месяцев назад

    C cons la aller travailler dièma dawal auto mou mel ni tèral papa ak yaye

  • @petersept4334
    @petersept4334 5 месяцев назад

    Auto bi en occasion rek sur american car city ça coûte 127900 euros mouye aye 87millions Sénégal avec 57000km...serigne nekh na waye ki mo yoré thiabi adiana akh appartement yi moye léye logé diokh la lou cédda gouye ngua nane té meune na dokh si gueth teye khaar asamane bou beugué mou taaw mou taaww wawawe li moye Sénégal...té nakk dou poupe sou niite yalla laaaa

    • @ProPatriote
      @ProPatriote 5 месяцев назад

      Wakh dof

    • @petersept4334
      @petersept4334 5 месяцев назад

      @@ProPatriote 😙

    • @seynabfallou395
      @seynabfallou395 5 месяцев назад

      Wa xo fi waxo nitt ki wakho ni linga wax fi yép meun nako wayé yalla moy Sedalé thieur ci adouna té yomal xiyam sakh thieur yi diuniou tolo

    • @petersept4334
      @petersept4334 5 месяцев назад

      @@seynabfallou395 yow mome weuro

  • @mouhameddiallo8975
    @mouhameddiallo8975 5 месяцев назад +1

    NdeysanN ✨ Mbacké Balla Yagg fii loll tei Weer 🤲 Barkèb Cheikhoul Xadim 💓

  • @serignleye5529
    @serignleye5529 5 месяцев назад

    Machalla ❤

  • @KhalyGueye-d2o
    @KhalyGueye-d2o 5 месяцев назад +1

    ❤❤❤❤

  • @elhadjndiaye1929
    @elhadjndiaye1929 5 месяцев назад

    😂😂😂😂

  • @FallouGalass-c8d
    @FallouGalass-c8d 5 месяцев назад

    ❤❤❤❤❤❤❤