Merci Monsieur Laye. ❤30 ans ci Kanam, ils comprendront que l’Artiste conscient est Immortel. Li nga fi wax du xéwi. La vérité est Intemporelle. Force à Toi mon frère.🇸🇳💥❤️🧠.
30 ans ci kanam man ak sama wa famille yalla may gnuu xeweul gou barri def gnuu ay milliardaire Serigne Touba mbacké...samay wadiour fékéka téh taal ka ak mbolém djoulitt🙏Amine
Mome leuh dei séne baye wa game hip hop galsén ki Dou moromu king dip baye séne simon keur papa laye papa game bi lou lér lay tk deug bou wor lay wakh ragaloul moko takha done goor❤❤❤❤❤
30 ans ci kanam yalla nafi fekk kepp kou aimer sama commentaires ❤❤❤
Kou beugue sydouna Moukhamed lalal jaime❤❤❤
30ans ci kanam sama doom yi yor daara ji ma took di leen soññu ci al xuraan Yalna ñu Fékké ak jàmm ❤❤❤😢😢
اللهم آمين يارب العالمين
Amin inchallah ❤
Amine
10 an ci kanam maboko ci top 10 milliardaire yi ci Sénégal inchallah
Www yaw rek am fouleu
Ki nitou deuug la bilahii
Mangui commenté took xaar 30ans🎉yalla naniouko feker inchalla
30 ans cikanam yalana nguéne nieuwate fi gise sama commentaire inchallah ❤❤❤
30ans ci kaname ma nék président de la république
Ak man ❤❤❤
Yalla man nako
Yalna ko yallah deff Insh'Allah
Tout té possible ❤
30an Si kna Adina defay rmtouki
Merci Monsieur Laye. ❤30 ans ci Kanam, ils comprendront que l’Artiste conscient est Immortel. Li nga fi wax du xéwi. La vérité est Intemporelle. Force à Toi mon frère.🇸🇳💥❤️🧠.
30 ans si kanam yalna geen tekki yepp insàllaa ❤❤
Kou gueumni molen dakk rap lalal j’aime 👍
30 ans ci kanam man ak sama wa famille yalla may gnuu xeweul gou barri def gnuu ay milliardaire Serigne Touba mbacké...samay wadiour fékéka téh taal ka ak mbolém djoulitt🙏Amine
30 ans si kanam ma nek milliardaire Saloum Saloum inchallah
30ans si kanam ma nek Milliardaire inchaallah
Toujours des messages du quotidien dans ses chansons.
Boutique Laye Niakoul Dara
30 ans ci kanam, yalna ko ñi ëpp fékké d'abord ❤, té yalna fekk Sénégal 2050 réussir objectifs yimou amoon yépp té mou gën 🤲🏽❤.
Wakh dof😂😂😂
30 ans si kaname 🎉ma nek meilleur styliste du Sénégal 🇸🇳
30 ans cii kanam laye boutique don milliardaire téral nieup❤❤
Yàlla na ñu fi Yàlla bayyi ñu guddu fan te fekkee ko 🤲🏿🤌🏿
Amine ya rabby ❤
30 tans si kaname yalla nama fekk ma nek pro inchallaha ak kepou kou kay rêve ✋️✋️
Yalnako yalla df ❤
Amine yarabil khalamine❤❤❤❤
Amin
Alahouma Amine inchala
Amine ya rabbi
Laye Yalla defal la jàmm
💥 boom 💥 that's my big brother Lay bit dafa nex always big up brother 🎉🎉🎉🎉
30 si kaname ma neke père de famille retraité tokk sama piyane yoré sama Mouhamed takk diabre toudé ma dome amine
Lay lepp lo massa wakh Amna ndiarigne waye bi mom mosi raw
Kouye rapp yayi bayame blh❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Leçon suit✌️30ans ci kanam yalna bounou réthiou dara
“Ki neub thieureum tay dou ragual dafa done kou mouss” Trop fort !
30 ans ci kanam dina fék gars yi xamni yay sén Baye
Tu es vraiment fort ❤❤❤🎉🎉🎉 qu'Allah te protège
C'est magnifique mashallah le général des hip-hop sénégalaise❤❤❤❤🇸🇳🇸🇳🇸🇳💪💪💪💪💪♥️😭😭😭🇸🇳🇸🇳🇸🇳💪💪💪💪💪💪🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
30ans ci kanam dina miliadair incha allah
30 ans thi kanam Senegal da fay développè bou baakh inchallah..... merci boutikou laye tu es fort ❤❤❤
Le meilleur
Bilahi wallahi boutique lay rk ❤❤
3ans thi kaname inchallah ma ame 65ans yallna niou yalla tek thi Yone bou bakh
30ans si kanam ma nèk PA bou meuna netalli nane boye yi 2025 lako laye wayone
Machala frere
Wayal série senegal yi nio gueneu bone si adina,bo wakhé niouné daniy yéété té yéwunu
30 ans ci kanam Sénégal dina melni Dubai.
Trente ans si kaname on verra la réussite du PROJET..vision 2050🇸🇳🇸🇳
Inchallah
Lou lere ga wakh
Voilà un homme qui mérite d'être soutenu. ❤
Bravo l'artiste.
Machalla ❤
Mome leuh dei séne baye wa game hip hop galsén ki Dou moromu king dip baye séne simon keur papa laye papa game bi lou lér lay tk deug bou wor lay wakh ragaloul moko takha done goor❤❤❤❤❤
Incha allah yalla nagnou fi fekk ak diam ak khéweul ak soutoura ak djabote bou barkel❤❤❤❤
Il est trop bon jtj🙌🏾😘
Lou leer nga wax grand lay 30ans ci kanam=2050+5ans inchallah se sera incroyable avec des succès exemplaires
Incha'Allah
Sa film taybi dina daw toom domyi tog di séétaan bu nicé yawla bu ñaawé yit yawla❤❤❤
Lu mata bayyi xél
30ans si kanam ma donné milliardaire inchallah ❤️❤️
30 ans thi kaname 😂 Li nekhna deh 😂
C'est trés fort.!!!!! Fasse DIEU que nous entendons le message de LAYE "KOTHE BARMA" !!!!! BIG UP 👋👋👋👍👍👍👍👍👍
30ans Si kanam ma nèck milliardaires inch'Allah
100% talent lay le poète. Le porte parole de la population éveillée
❤ Amatina solo!
Jaajëf Laye !
Machalla
Ya diang ya dioub ya mokal térré ya tiapeu xalima té nane da yi téksi yémé
C'est très intéressant❤
30ans yalna sénégal développé bakou fébar fadiou gratuitement pére de famille yép am keur
30 Ans Si kaname Yalla nagnuh Borom bi may Moudiee gou rafette Ak Jaboote yiih barkéle ak sutura aduna ak alaxira ❤
Il est le meilleur de sa Génération
Rendez vous dans 30ans pour encore écouter cette master classe inchallah yallah na yallah goudal suniou fane ak wergu yaram 👍🏾❤️🙏
Bilaye wlaye da gala😮😮😮😮😮
Merci beaucoup laye amatina solo de ❤️❤️
j'aimerai bien que dans 30 ans nga guéne ci sa retraite balancer wate son bi sur les réseaux
Alahou akbar🥺🙏🏿
Lou ler souba mo yeme
Machallah way bou diglé woul yété woul ay nakh la yalla naniou yalla may moudjou bou raféte
Nooo machallah 👏🏾👏🏾👏🏾
❤❤❤❤Comme j'ai l'habitude de dire tu es le meilleur
30 ans ci kanam yal n'a weuy di néck talibé cheikh mouhidine samba Diallo 🙏
Laye you are the ❤️❤️❤️❤️❤️❤️🇬🇲🇬🇲🇬🇲
Merci beaucoup ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Boutique laye sa kanam inchallah 🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
30ans sikanam ma nék premier ministre ❤
Machalla diadieuf waay si soñioné bi
Merci Laye t'as encore frappé fort
Bonne continuation ❤❤❤❤
Je te souhaite une Somptueuse carrière
Laye bilah tu es meilleure plain de message ❤❤❤❤
Macha Allah yalna yalla same la frère li moy musique beaucoup de sensibilisation
Toujours le meilleur ❤❤
WALLAY DEUGUE LE WAYÉ MAY NIOU DISCOURS FÉN DE ANNÉES 🦻🦻🦻🦻🦻🦻❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
👍👍❤️❤️❤️❤️
Khana mafi djitou ❤
😢😢🤩🤩🤩🤩♥️♥️♥️
Rendez-vous au sommet in Sha ALLAH !
Un artiste d’une dimension extraordinaire kouye guise lou sori aye texte you ame sólo rèck laye déf 30ans sikame lou leer ❤❤❤ Felicitation laye 🎉🎉🎉
Lay yaguie wakh lou lerr
Une chanson pleine d'enseignement 😢
30 ans sikanãm yalniou bokh si niouye waxni "pourtant boutikou laye woyone nako"
Merci beaucoup ❤❤
Macha’allah message bi for na
Koudakor nelaye damen lala jem
Bilahi Lou am solou grd laye yangui yété. Force à toi 🥰
Vrément laye lance des messages important ❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machalla parole yi amna solo lool
Defa leer bilay
Laya ya meunn❤❤❤❤
Trop fort mashalah ❤
Boutikou laye the king ❤❤❤
Big respect Mister Laye🫡🫡🫡... 30 ans ci kanam, le RV de la dignité
Dieu seul l cé a 30 ans😢😢😢
Meilleure de sa génération ❤️
Très bon travail. Excellent machallah