C est pas le milieu qui determine la personne nous vivons à thiaroye depuis plus de 60 ans jusqu à nos jours mais alhamdoulillah nos parents nous ont donné une bonne education machallah meme nos jeunes frères ne touchent même pas de la cigarette ni frequenter certains lieux le probleme en est que sont certains parents n eduquent plus leurs enfants je prie pour le repos de l âme du defunt
J'ai vraiment peur en tant jeune parent . Yalla nagnou yalla may niou mou naa tek sounouy doom sur le droit chemin. Yalla na yalla yeureum ki dém si barké seydina mouhamed saw
Yéne gni kassé motakh nidiaay dji diko téré dakodone ték si yone mom khamna ba erreur fek kosi mais yéne tmt ay khalé you ndaw di wakh di bandi bandilou vraiment kouléne khol khamni si louléne nékh nguéne nék Nidiaay dji moléne ko gueuno na beugu fouff mom miko done ték si yone guisoumako mais khamna amna louko méti trop Moussa yalla nako borome bi yeureum
Yene deh yena diakhassé moussa ak nidiayam, yena fii nek di bandi bandilou niak kilifeu ba deh. Malheureusement oncle bi sou khamone bayiko tranquille ndakh lii moussibeu geunouko reuy
Beugeu lou yomp niamé diour ragal responsabilités kou diour teuyeul say dom bolen sané si kaw nit yi les gens aussi ont leur propre problèmes ils s’en débarrasseront.aldiana firdaws
Inallilahi wo ina ileyhi radjioune inallilahi wo ina ileyhi radjioune inallilahi wo ina ileyhi radjioune Allahouma qghfirlahou wo yarhamhou que le bon Dieu ľaccueille dans son vaste paradis firadawsi amine ya Allah
Regardez moi ces garçons leur manque d'éducation se traduit par leur manière de parler. Soléne sétlo digua khamni amouniou yar. Vous n'avez rien n'a raconter. Si l'avenir du Sénégal repose sur les mains des jeunes d'aujourd'hui, ce sera un énorme gâchis. Qu'Allah fasse naître des jeunes sénégalais qui aiment leur patrie, et répondent aux exigences de celle-ci.
VOUS N ETES PAS MEILLEUR QU EUX MONSIEUR L ADULTE. ILS SONT LE FRUIT ET NOUS LES ADULTES ON EST L ARBRE.ON EST PAS MEILLEUR QU EUX CE SONT NOS ENFANTS.
Franchement ton commentaire est nulle on te parle de meurtre tu fais des jugements sans même les connaître bayilene jugé nite on dirait que pour toi dead bi defoula dara c’est honteux de ta part
Au-lieu de dénoncer le meurtre vous vous permettez de fustiger le comportement des ces jeunes qui viennent de perdre leur ami. C'est une honte. Le manque d'éducation dont vous faites mention n'est rien d'autre que le reflet de la fuite de responsabilité des adultes.
@@seydinaomar4815 Il est important de dénoncer le meurtre, mais il est tout aussi crucial de discuter des comportements qui peuvent mener à de telles tragédies. Les jeunes ont besoin de soutien et d'encadrement, pas de stigmatisation.
Kham lène lolène di wah si boy yii manak niom nio bockou kogne kou ndieuk wah sma rak la prsk moussa yalnako yalla kharé aldiana firdawsi champion la billahi
Ne jugeons pas par les apparences elles sont souvent trompeuses gni yarou béd bi rek molén sonal mais so moytoul niou bakh lagn l’habit ne fait pas le moine Dome bouy frequentè ay nit bou sa khel daloul nga wakh ba sone dégoul laisse ses amis venir le voir chez lui surveille les et discute avec eux donne leur des conseils ils vont se livrer à toi avec beaucoup de respect qui sait peut-être sakh tu peux les changé s’ils sont dans le mauvais chemin. C’est ça la jeunesse d’aujourd’hui. Qu’il repose en paix paix
Soudé ni boy yi la Moussa mell c'est k nidjay bi dako beugeulone lou bakh Gni ils ne sont pas fréquentable dh mane warna guiss kiniouy wowé ferraille dh
MOUSSA bo Yarou wone nidiayam douko Sonal pour yaarko batay rayeko ni 😢😮 KOULÉEN XOL yéén gni rèk nane ay xarittam guéen ça veut tout dire et pourtant néguéen ay xalé guéen 😮😢 OH TRISTE POUR MON PAYS LE SÉNÉGAL AVEC SA JEUNESSE 💔😭
Sante yalla baniou amé wajour you bakh youniou tekk si yonne bou bakh, alhamdoulilah rabil alamine, ça la jeunesse d'aujourd'hui,yalla naniou yalla samale sunu njabote ba niou jeule yone bou bakh nieupe nawe lenne ak founiou meuneu nekk, rip yalla nako yalla terou aljana firdawsi 🙏🙏🙏🙏
l'impolitesse se lit à travers vos mots et votre visage , bakan fort neu trop waye commencer par revoir votre education guen am yar respecter mag yenn mi di sandi ay kher keur diambour vous n etes pas blanche comme neige que son repose en paix
Yalla nako yalla yereum. Wayé liberté amoul fen. L'homme n'est pas libre il a des limites défini par l'islam, le christianisme, ... Mais aussi pourquoi personne d'entre vous n'arrive pas à dire la raison de leur dispute ? C'est triste mais franchement cette jeunesse naspi6pas espoir 😢
Cëy Senegal ak jeuness bu bésbi education 0 ñi koulén khol khamni Moussa yaruwul won. Lila wolof nan wakh ma sa kharit ma wakhla kinga don, waw lén Goor mafia bi
Ndeysan Ndidiaye dji certainement mbaakh reik lako beugeulone ba far deif Lou eup
Yalna yallah yeureum barkei alkhourane
Amine yarabi inchALLAH
Bilaye
Ndidiayam lou bax lako beugueulonnn rek yennn gniii merci rk
Yallah nako yallah yeureum
C est pas le milieu qui determine la personne nous vivons à thiaroye depuis plus de 60 ans jusqu à nos jours mais alhamdoulillah nos parents nous ont donné une bonne education machallah meme nos jeunes frères ne touchent même pas de la cigarette ni frequenter certains lieux le probleme en est que sont certains parents n eduquent plus leurs enfants je prie pour le repos de l âme du defunt
😂 Thiaroye mogui kasss Yeumbeul 😂
Thiaroye parents yeumbeul Washington lep Yalla la
Yallah nako borom bi yeureum khariko firdawsi gni sen comportement dara nekku si ngi ayeu khalei lagn naneu laine encadré niou liguey ndakh sedell nagn ko lou rafett yeufu dioulite deugg machallah yallah nallain borom defal diameu ak soutura
Justement khalei lagni yar sou nekei mak mou yarou
nafekh ga
Paix à son âme 😭😭😭😭😭😭
J'ai vraiment peur en tant jeune parent . Yalla nagnou yalla may niou mou naa tek sounouy doom sur le droit chemin.
Yalla na yalla yeureum ki dém si barké seydina mouhamed saw
Amine Yarabi
Bilay moi aussi j'ai peur
Yéne gni kassé motakh nidiaay dji diko téré dakodone ték si yone mom khamna ba erreur fek kosi mais yéne tmt ay khalé you ndaw di wakh di bandi bandilou vraiment kouléne khol khamni si louléne nékh nguéne nék
Nidiaay dji moléne ko gueuno na beugu fouff mom miko done ték si yone guisoumako mais khamna amna louko méti trop
Moussa yalla nako borome bi yeureum
Paix a son ame ce petit moussa 😢mais les jeunes oci il fait qu'on revois leurs éducation té khalé yi tamite daniouw téla bay école amm fite
Sénégal dou réwe mandi gaize agraisé sathie féneu gordjigeune thiaga fou réwe mi dieume
A la dérive triste pour un pays qui se dit à 90 pour cent musulmans. Que Allah nous protège de ce mal
AK bokalé😢
Lolo diakhal niep kay
Fou rewmi dieum.
C est la grande question..
Lépp si macky Sall la wone 😂
😂😂😂
Yénn gni nane ay khalé lagnou yalla naguén am ndiabote bou Mel ni khalé si boumiy nek khalé gakoy dioubanti
Yalla terre 😂
😂😂😂😂😂 guissou ma amine ba légui déé
Moussa que son âme repose en paix, mais a voir et entendre ses amis on sait clairement que ces jeunes ne sont pas fréquentables.
Mais bien sûr il faut le dire a haute voix ils ne sont pas correctes
Ils sont mal éduqué gnom gneup ay guinge man lagne
D'accord mais ce n'est pas une raison pour laquelle que son oncle le tue
@@fatyba3238 Très mal éduqué son oncle a le droit d interdire de vous fréquenté parce que votre façon de parler ça me dépasse
@@HouleyeSow-fg6fnmais ce n’est pas une raison pour laquelle que son oncle le tue😭
Yala aldiana di keureum
Amin inch'Allah 🤲🏿🤲🏿🤲🏿🤲🏿🤲🏿🤲🏿
Corrección boy durante danguay geuneu emporté wou nagnouy wah bayi daur
TCHEUY CETTE JEUNESSE ! QU'ALLAH L'ACCUEILLE AU PARADIS FIRDAWS
Yene deh yena diakhassé moussa ak nidiayam, yena fii nek di bandi bandilou niak kilifeu ba deh. Malheureusement oncle bi sou khamone bayiko tranquille ndakh lii moussibeu geunouko reuy
Bilae waxatiko
Niom sen kanam yi rek mo ndieuka indices nama yalla bal
Gni di melni niou volé nonou
Mais ray dou yooon
@@adjiadialo NDOGUAL LA RKK KHALEI DAGNON DEGUERE BOPP
Gni dé kou léne maye diam gnou firim rew tasko.gnou nane goudi goudi 😮
Oulalalala non mais je comprends rien là pourquoi c'est temps il y a trop d'assassinat on n'en peut plus qu'il repose en paix😢😢😢😢😢😢😢
Moussa yalla nga yégalé da ndaw Aljannah Firdawsi 📿🤲🏾📿🤲🏾📿🤲🏾
BOY GNEUW. KEUR. DIAMBOUR. TÉ. YAATALOUN. LÉEN NGUÉEN. TOK. SÉENI. KEUR.
VRAIMENT MAIS ILS SONT SANS VERGOGNE NIANKK DIOM LAGNOU DEFF BOLEINEDAKE SOUBE NOU NIEUWATE
@@Lhommejr KOU. SA. DIGNITÉ. DIEKH. SA. NIAK. DIOM. MOY. NIEUW.
Beugeu lou yomp niamé diour ragal responsabilités kou diour teuyeul say dom bolen sané si kaw nit yi les gens aussi ont leur propre problèmes ils s’en débarrasseront.aldiana firdaws
Wakh deugue
Yalla nako Yalla yeureum khareko aldjana❤❤❤
Yalna Ya Allah saameu Jabot gui
Beaucoup de jeunes de nos jours ne sont pas lucide.ils ont l'habitude d'utiliser les bouteilles de verre comme arme
Inallilahi wo ina ileyhi radjioune inallilahi wo ina ileyhi radjioune inallilahi wo ina ileyhi radjioune Allahouma qghfirlahou wo yarhamhou que le bon Dieu ľaccueille dans son vaste paradis firadawsi amine ya Allah
Réponse en paix moussa
Thieye bi génération 😢
Walaye ndesane
Souma ci yalla naré NATO dôme yalna ménépause précoce q
Amna gniousi régler dei kou beug bonne bonne générations bo guiss amna gniou bonn
Gni douniou ay andado vraiment cette jeunesse me fait peur 😧
Ay khalé niou ndaw di bandit bandilou li 😮😮😮
Yallah nako Yallah yéureum diégual ko kharé ko aldianna Firdawsi Sa Keur 🤲🏾
Regardez moi ces garçons leur manque d'éducation se traduit par leur manière de parler. Soléne sétlo digua khamni amouniou yar. Vous n'avez rien n'a raconter. Si l'avenir du Sénégal repose sur les mains des jeunes d'aujourd'hui, ce sera un énorme gâchis. Qu'Allah fasse naître des jeunes sénégalais qui aiment leur patrie, et répondent aux exigences de celle-ci.
VOUS N ETES PAS MEILLEUR QU EUX MONSIEUR L ADULTE. ILS SONT LE FRUIT ET NOUS LES ADULTES ON EST L ARBRE.ON EST PAS MEILLEUR QU EUX CE SONT NOS ENFANTS.
Bilay lolou la ndieuka sétlou do sax xamm sén explication yén waydiour yi la yeureum ndax dougn djogué si nakhar Li kén xamoul lanla
Franchement ton commentaire est nulle on te parle de meurtre tu fais des jugements sans même les connaître bayilene jugé nite on dirait que pour toi dead bi defoula dara c’est honteux de ta part
Au-lieu de dénoncer le meurtre vous vous permettez de fustiger le comportement des ces jeunes qui viennent de perdre leur ami. C'est une honte. Le manque d'éducation dont vous faites mention n'est rien d'autre que le reflet de la fuite de responsabilité des adultes.
@@seydinaomar4815 Il est important de dénoncer le meurtre, mais il est tout aussi crucial de discuter des comportements qui peuvent mener à de telles tragédies. Les jeunes ont besoin de soutien et d'encadrement, pas de stigmatisation.
Khale yi yeureume lene séne ndeye yi sona naniou bilaye yalla nalene yalla soppi nieff guene séne lou bonne
Innalillahi wa inna ileyhi rajioune yalnako yalla yereum té diégueulko
Kham lène lolène di wah si boy yii manak niom nio bockou kogne kou ndieuk wah sma rak la prsk moussa yalnako yalla kharé aldiana firdawsi champion la billahi
Légui sougéne boké kogne nk après
@@sarrabdoulaye4705Saway ki gniy juger boy yi si sen comportement lay wakhla boy yi
Kou wax waxbou amoul téguine niou waxko. Boulniou sonal
Kou wax waxbou amoul téguine niou waxko. Boulniou sonal
Yén gneup ay bandit ngén mandi toukh ginz rk ngén fi néké bandit bandilou Di diay lou amoul
Yalnako yalla yeureum khareko aldjana firdawsi amine naniou moytou saytané da bari dolè
Paix a son nâme
Senegal
Chaque personne décidé
Ce un champion
Yalla nako yalla yeureum kharé Aldiana wayé yénite déme mélou kane bi ma guiss rafetoul
Wow ngen beut si khale ak seni kanam yen dh nigen di wakhe yalna nalen yalla sopi
Ne jugeons pas par les apparences elles sont souvent trompeuses gni yarou béd bi rek molén sonal mais so moytoul niou bakh lagn l’habit ne fait pas le moine
Dome bouy frequentè ay nit bou sa khel daloul nga wakh ba sone dégoul laisse ses amis venir le voir chez lui surveille les et discute avec eux donne leur des conseils ils vont se livrer à toi avec beaucoup de respect qui sait peut-être sakh tu peux les changé s’ils sont dans le mauvais chemin. C’est ça la jeunesse d’aujourd’hui. Qu’il repose en paix paix
Yeumbeule thiaroye dama tite ci jeunesse bi en tant que habitants de ces lieux khamna lifi nekk doyna warr 😢😢
Une jeunesse inconsciente non mon pays va tres mal li lane la ni genre xalei yi fou Sénégal dieum
Soudé ni boy yi la Moussa mell c'est k nidjay bi dako beugeulone lou bakh
Gni ils ne sont pas fréquentable dh mane warna guiss kiniouy wowé ferraille dh
Je suis ton avis
Lou bakh lako beugolone surement
Vérité absolue ces p'tit qu'Allah les sauve vraiment a les entendre parler je me dis que ils sont point fréquentable
Pure vérité gni kouléne guisse sa xel dina téye
Nio bok même kogn niom nieup ms kén bakhusi ginz rk laniouy deff ak tukh boon
Thiey yalla paix à son âme 😢😢😢
Aye Sénégal li loumou donne
Titt na deh 😢😢😢
Ndeyssane yana ko Yalla yeureume té diégueul ko 🙏 té yéne Yalla takhawou léne bou bakh InchaAllah 🙏
😢😢fan gueun ande dieum 😢j'ai peur de ces jeunes 😢😢avec leurs langues 😢😢😢😢😢
Merci beaucoup 😊
Dabougoune mo bakh ndeysane bagnoule moussa fare saytaner dikk😢😢
Sama xel teyna thie gni di wakh 😢
que la terre lui soit légère, il faut vraiment de l'appuie pour ces jeunes défavorable
Repose en paix 😭 Ah mane diomi na
Moussa yalla nako yalla yeureum mais ndidiaye dji lou bakh lako beugueulone yéne gni mome dou nguéne ayy référence
Yalla nako yalla kharé aldiana 🤲
Li kagne lay diekh 😭
Nidiay bi dafa beuguone mou bakh rek ndeyssane ba ndogual fékeu kossi moussa yalla nako yalla yeureum
Ioe mandoul lothi xame 😢
Mais beugue mou bakh ba rayko c’est du n’importe quoi 😢😢😢 arrêtez la violence 😢😢
Mais beugue mou bakh lousi ganay outi arrètè vos affaires de ipocrite😢😭😭😭😭
Ioe xamoo fi ngay taxaw
Liberté ok yéne si yonou bone guéne beuggeu nekk
Souba lagni comprendre
MOUSSA bo Yarou wone nidiayam douko Sonal pour yaarko batay rayeko ni 😢😮 KOULÉEN XOL yéén gni rèk nane ay xarittam guéen ça veut tout dire et pourtant néguéen ay xalé guéen 😮😢 OH TRISTE POUR MON PAYS LE SÉNÉGAL AVEC SA JEUNESSE 💔😭
Yalnako yalla yeureum mé boyyi tamitt yéménagnou
Sante yalla baniou amé wajour you bakh youniou tekk si yonne bou bakh, alhamdoulilah rabil alamine, ça la jeunesse d'aujourd'hui,yalla naniou yalla samale sunu njabote ba niou jeule yone bou bakh nieupe nawe lenne ak founiou meuneu nekk, rip yalla nako yalla terou aljana firdawsi 🙏🙏🙏🙏
Loutax soutien de famille rek laniouy rey
😢Sénégal kou dèè am deugue mais yén doyoulema sama keur😢😢😢😢😢
Gayi ay doméram lang daniouy rayé rék mais Thiès fii kourayé niou tale la rék billahi
Je suis jeune mais j avoue que l président Diouf avait raison
Une jeunesse malsaine
Repose en paix toma 🙏🏽
Yar len sen doum yi guir yalla khale yi kolen guis khame ne amonu kilifa
l'impolitesse se lit à travers vos mots et votre visage , bakan fort neu trop waye commencer par revoir votre education guen am yar respecter mag yenn mi di sandi ay kher keur diambour vous n etes pas blanche comme neige que son repose en paix
Bilay Li doyyna warr xallé ginz ak Naan lagn fi néké bandit bandilou Di diay lou amoul
denio niak yar
C vraiment dommage
Ak yaw sa data yaye khamna mo blanche com neige domaram
Man degn ma yar . Doumey sagua, yallah n'a yallah yeureum gni ganiou
Yallanako yalla yeureum le petit moussa c est vraiment dommage mais khaley yi ils sont tres normas le malherido tela bayi ecole😢😢
Yalla nako yalla yereum. Wayé liberté amoul fen. L'homme n'est pas libre il a des limites défini par l'islam, le christianisme, ...
Mais aussi pourquoi personne d'entre vous n'arrive pas à dire la raison de leur dispute ?
C'est triste mais franchement cette jeunesse naspi6pas espoir 😢
Quelle jeunesse🤔
Nguirr Yallah wadiour yi naniou goorgoorlou si ndiaboot gui yarlen si dine te dilen nianal nianou wadiour dafa am solo si dom
Que firdawci soit sont deumeurs internel inchallah amine ya rabie Allah courages
Ces jeunes rien qu'à voir leurs comportements et leurs façons de communiquer,on doit les amener à Bango pour les redresser et les éduquer...
Non ils sont traumatisés pour le décès d'un ami
Thiey Sénégal😢
Yallah nako yallah yeremm ko tee hareeko Aldianna inchallahou 😢😢😢 mon payer Va Mal 😢
Vos visages font peur des jeunes avec ce langage l oncle savait pourquoi il l interdisait de leur fréquenter
Vraiment tous des agresseurs
il parle de mafia c des groupes de bandits
Mousa yalnako yalla yereum mai gnim dan andal gni baxougn xamna peut être nidiay dji dafa begon mou bax rek ba li amsi...
Yalla nako yalla haré ardiana
Vraiment senegal tou sans langage bii thème bii environnement djiko yi comportement ce regrettable dommage li lep moudienteul dey diale niou fateko responsable parents yi autorités yi yep mogui antouca metina trop semaine thi nioun sénégalaise yi khana nian yalla mou khir niou thi lou bakh diouli bakh na dey wagni lou barri
Reposé en paix ☮️😭
Que la terre lui soit légère Amine 🤲🤲🤲
Wa bi langage moy ban ni tamit.
Mon pays va mal,au nom de Dieu.
Ça fait peur deh.
Paix à son âme ndeysane que firdawsi soit son demeure éternel
Raay mom keineu douko cautionner neu justice def ligueyam mais à vous voir vous n’êtes pas fréquentable
Dou language bou correct Dou éducation
Mom kay doyna warrr😢😢
Ah lii tamiit doynawar
Parents yi nio faillir neikhoul deigue mais walakhi azim lolou mo am
Que son âme repose en paix
Allaahu akbar thiey senegal
Sante na yalla bou baxx sante serigne saliou
Dakar dou deuk bilahi
deuk la sakh khana si kou topou da bakan rk ak beuga dieul yon bout to bonn
Lou takh
Afair bi Sénégal Touba temps reynagne faa niit
@@jaimemonpayslesenegal8268Touba koun fa rayone
SÉNÉGAL MOM LATHIE NA DIAMONO DJI AY SARAKH BILAHI WALAHI LI NAK MOGUI EUPI LOKHO DÉ 😮😢
Yalla 'ako yalla yereume t khare ko aldiana mai on a une bne jeunesse
Ay yalla Sénégal Thi loumou dougou ni 😭khalé yi doy na war dale yalla nagnou yalla same 🙏🏾
Yene ay khaleyou diok pour yakh sene avenir goorgorlou lene
Sûrement son oncle voulait le redresser 😢vu ses amis qui parlent là ils ne sont pas fréquentables vraiment
San kanam yi. Koulein khôl khamni normalolein nekkk lein nitt
Lègue lègue nite fatou fék dafanpoulou nopal ay famillame,wayé kharitam yîma guisse awma ci ñôme yâkâr
Regarde rek komen ils parles g vraiment peur pour cette jeunesse
Vraiment je ne veux pas abuser mais ses amis ressemble à des délinquants 😢
Dou ndongual bilahi 😢😢
Mais son oncle est un fou 😢😢
Cëy Senegal ak jeuness bu bésbi education 0 ñi koulén khol khamni Moussa yaruwul won. Lila wolof nan wakh ma sa kharit ma wakhla kinga don, waw lén Goor mafia bi
Non boul wakh lolou billahi Moussa molen guëne yarou foufe peut être nk gnimiye andal rek la 😢
Paix à son âme😢
Da beugone mou bakh rèk far ndogal am
Paka limousi oute?
@@moussacissokho4248il paraît que boy bi mo tothie bouteille outsiko, amanna lolou lako diamer
Ki moy domerame
Wakh nga DEUG nakkk walahi
DEig ngeine wakh bi dfa fass jommm d'où fanane allle mai yeeinnn moyyy lolou tieuy yallah
Kholéne kanamou gni di wakhe rék
Kanam amoul Mark . Wakhal lénéénn
Paix à son âme yalnako yalla yeureum té Kharéko aldiana
1994 Ouest foir nor foir sacré coeur sicap urbaine Almadies terrain coutè 700mile yèène paayii préféré takk aay diabare
Senegale legui 80 boye yo guiss 3 gnothi correcte 77 yeppp affairou badi badilou 😢
Non 3eupna nel 1 kay
Yamba dji guéndi bayii💔💔🇸🇳