Ça fait 10 Ans que je suis en Europe sans papiers mais a chaque fois que je regarde cet série c'est comme si je suis au Sénégal vive le Sénégal et la république que dieu veille sur notre Sénégal
So geumé ni Ndiawar mérite une nomination pour meilleur acteur de l'année beusseul "j'aime" nga commenté sama commentaire et je te repondrai avec "C'est Bien ou Trés Bien" 🤣😂😂😂😂😂
Cette serie reflète la réalité de la société actuelle Toutes les thématiques y sont abordées (naay, beuguei , gnak ngorrr, naive, bakh, doylou) mashala
La réaction de l'amie d'Ana la mère de Maty Rose m'a beaucoup surpris. C'est ce qu'on dit l'amitié du méchant est plus dangereuse que sa haine. Belle leçon 🥰❤
Chapeau à vous (evenprod🎉❤) Ibou laye diokhna leçon béppeu nitt bouy joué carte mouy 1xbet wala lénèn Que ni bou yalla wakhéni carte bakhoul rek amna loutah parceque daflay détruire carrément moralement et mentalement Yakar bou tass guay doundé com li dal ibou laye ak problème yidoul diékh com nimou barré ay plainte Boudon yamon na thi parking biko yalla may boooba li yeup douko dal Mes il a choisis l mauvaise chemins ba li yeup dalko Yalla néna [le vin, le jeu, les sacrifices et les flèches pointues sont une abomination de l'œuvre de Satan, alors évitez-les pour réussir. ] donc les gars evitez ❤ aussi mrcii Even Prod thi leçon bi
Ndiawar :🗣️Lou bakh nak kouko def daniou nann leu c’est bien , ngeu def lou geuneu bakh niou Nila c’est très bien, kone soda Mareme c’est très bien ahhhhh yaye 😂😂😂😂😂😂😂😂
Amitié amatul...la réaction de l'amie de Anna( notre adja nationale) m'a scotchée...donc derrière toue cette bienveillance et présence se cache une jalousie...ceey adduna...ce sont des choses que nous vivons réellement...XALISSO touche tous les maux de notre société.
Cher ami observe un groupe d'enfants qui jouent. Ils sont heureux parce qu'ils ne se souviennent pas des tristesses du PASSÉ et ils ne pensent pas aux malheurs qui pourraient arriver dans le FUTUR. Ils vivent pleinement le moment PRÉSENT. Si tu veux être heureux, fais comme ces enfants. De toutes façons, tu peux pas effacer le passé, et t'inquièter pour le futur ne changera rien. Ne souffre pas pour rien, tire de la joie dans ce que Dieu t'a donné aujourd'hui. Fata lui est heureux avec sa Queen Bineta et son mbakhale mou tooye.😂😂LOVE
Légui série sénégalaise yi yiw lagnou woté 😂 c très bien 😂(xalisso amna ibadou ,jeux de dames amna ibadou ak décé, lady diama amna ibadou ak décé ,bété bété amna décé)
Bravo maty rose ,yangui wonéné nit kén douko juger kén dou tégo lo menoul ,en il ne suffit pas d'être riche ou pauvre pour être humain,le bonheur de quelqu'un ou autre peut bien resider dans le cœur d'un autre,soyez juste humain et compréhensible
😮😮😮 naka diek mani Oumy mi louche na. Le jour où elle a compris ce qui est arrivé a Maty Rose té elle n'a rien dit a sa mère 😮. Loudoul gneuw hôpital di dofdoflou. Xalisso dal mo bari wiss
La réaction de oumy la meilleure amie de Anna ne devrait pas vous surprendre car quand elle a su la vérité sur la grossesse de Maty rose elle a préféré faire chanter le mec au lieu de dire la vérité à sa meilleure amie Anna la mère de Maty rose ! Vraie amitié mom il ne reste plus que moi et ma meilleure amie ! Merci 😂
Bilay kharit amoul man DH kharit mo yeuguel sama seye ânde AK sama dieuké yeuguel sama seye sama dieukeur abandonné ma té dama eumb 2moi dama diakhlé trop awma kouma takhawou
27:46 heureusement pour moi bama amé bén kharit mouy sama yaye yalla na yalla goudal fanam té yokou wergui Amine si barkéb Serigne Saliou Mbacké ak bép yaye 🤲🥰❤❤🎉
Bien vrai qu'il procure le bonheur wayy tamittt khaliss meune yakk les liens p arentals 😢😢qui se souvient de cette belle famille Diagne dans les premiers épisodes unies et joviale 😢😢
@@Itsaminata rappelle toi de l'épisode précédent où elle expliquer à la petite sœur de Diadia de ça jeunesse et que elle été bien amoureuse d'un jeune homme mais que ce dernier été pauvre d'où le fait que elle a choisi le papa de Diadia
Badlene 😊 da nopp diadia ndaysane begue nitt ta mouno wah daguay deff trop pour mou bagne seye 😂l'amour c autre chose l'amitié parfois sa empêche lou beri nda ragal
On l’a jamais vu ni jamais entendu sa voix mais son amour vit des millards de personnes prophète Mouhamed psl ❤
Sallalahou alla moukhamed
Psl❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Psl ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Pal❤❤❤
Psl❤
Boury dégage beaucoup de classe ❤❤
Pourtant elle est célibataire dans la vraie vie 😢😢😢😂😂😂😂
@@Président-ABDOU-DIOUFwatal
@@MariamaDiambang-l8q bilahi amoul jeukeur
Nonula djiguéne bou rafété b mou eup nila gori douniouko niémé 😅
@@FatimataBeieo mane ngay wakhal 😂
L’ami de la maman de maty rose m’a beaucoup surpris thieuy xarito tayy yii 😢😢
Bravo à toute l’équipe de xalisso 👏🏻😍
Bilaye ni lagnou mêle.
Depuis khâlé lakko toppp.
Thiey liii
Bilaye dêh. Nii.lagnou mêle.
Ay deumm lagnou.
Temps khâlé lakko topp ba tey nii dêh
Elle a l'air d'une bonne personne ba souy diéma bonne sax douko jap😂😂😂😂
Bilahi yaw dama bete sague mane
Massou ma bette depuis mouye encourager Maty rose si mbarane pa yi la sama xel teyone si mome
Justice pour diary sow que son âme repose en paix 😢😢😢😢😢
Amine
Amine
Rip🙏🏾🙏🏾🙏🏾😭😭😭bb Diarry
😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢
Amine
On l'a jamais vu ni jamais entendu sa voix mais son amour vit des milliards de personnes notre bien aimé {PROPHÈTE MOUHAMED❤🎉
Paix et salut sur lui
صل الله عليه وسلم ❤❤❤❤❤❤
PSL ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Sallahou Aleykhi Wa Salam amine yâ Allahou
Sallalahou Allah Mohammed
Xalisso: Ndiaware 😂
Bété Bété : Sanékh 😂
Merci even prod 😂🎉
Gnome gneup Thiès
Et amy mbaye
Ça fait 10 Ans que je suis en Europe sans papiers mais a chaque fois que je regarde cet série c'est comme si je suis au Sénégal vive le Sénégal et la république que dieu veille sur notre Sénégal
Yalla nalla Yalla may papier
Yalla na la suniou borom yombal la papier yi si 2025 bi inchallah mo done lou gueune si yow
Oh Yalah na la Yalah diapalé bubah ak sutura dina bah
Yalla nala yalla may papier
C'est bien 😂
Yayou ndiawar da diépi mareme soda 😂😂😂😂😂
😂😂😂😂
Sering maniru njagen 😂😂😂💔
20:05 20:26 😅 20:30 20:30 20:32
Bébé yeet
❤❤❤❤❤❤
Repose en paix. Diary sow😭😭
Qu'est ce qui est arrivé à Diarry Sow?
@Aimée-t7wviole et tue
Bb diarry sow yalla nako yalla kharer aldiana🙏❤️
Amine
Aminé 😢
Amine
Amine 😢❤
Amine
Kou beug am dom toudéko seydina Mohamed beuseul ❤
❤❤❤
Salalahou hala mouhamad ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️ ❤️
❤❤❤❤
Sallahou allah mouhamed
Amine ❤❤❤❤❤
So geumé ni Ndiawar mérite une nomination pour meilleur acteur de l'année beusseul "j'aime" nga commenté sama commentaire et je te repondrai avec "C'est Bien ou Trés Bien" 🤣😂😂😂😂😂
Tu as raison collègue 😂
Ak sanekh🎉🎉
Bilay c'est vrai
@@GamoNdiaye-n4r C'est trés bien 😅
@@diagnembissine4708 C'est trés bien 😅
Lima nekh sii Evenpro dagnou respecter heure ❤machallah contane nagne sii yéne 🎉❤
❤❤❤❤🎉
Bilaye yaw
Surtt lolou ❤
Bilay
C'est bien c'est très bien evenpro
Boury son sourire est magnifique Maty Rose merite du bonheur kou beuge Xalisso rek l'alal j'aim ❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉😊😊😊😊
Onheurkoudexlialissorekl,alalj,aim❤❤❤❤❤❤❤😢😢😢😢😢😢😢😢😢😢
❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉😊😊😊😊😊😊😊
❤❤😂
@@khadimseck3141 pousal fi
@Fcmobilebêta1009 ❤
" Aaah yaay " Kër Njawar bu amul mort dina am blessé. 😂😂
@serignecheikhdiop7327 Badou cas dou sur cas mofa ame ? 😂
Cette serie reflète la réalité de la société actuelle
Toutes les thématiques y sont abordées (naay, beuguei , gnak ngorrr, naive, bakh, doylou) mashala
Ak naar bi
Bolé si manupulation amna gniouco métirisé🎉😂😅
@oumouba4055 Merci, c'est toujours un plaisir de vous satisfaire. 👍
@@ndongondiaye4283😂😂😂
Bilahi soda maréme bo khamone loulay yott dangua bayi yottou moytoul boury loume lay wadial boko khamone dangua réguler yaw ak sa papa kouko guemni lale j❤
Damay ragal Boury fegnal len
@FatouMagane-us6cd Pour yaw lane lako Boury di widial ?
J’aime le caractère et la personnalité de Boury Machallah ❤️❤️❤️❤️❤️Djigueine foula wayy deff leip ak dall 😂😂😂😂🫶
La réaction de l'amie d'Ana la mère de Maty Rose m'a beaucoup surpris. C'est ce qu'on dit l'amitié du méchant est plus dangereuse que sa haine. Belle leçon 🥰❤
Wallahi j'ai été trop surprise mais malheureusement ca ne fait que refléter notre quotidien
@@ModouCoulibaly-c2n Walahi même moi aussi
Xana dégo Lou Wolof Di Wax naan beugn wékhna Lolou wayé derét moko lal jamono dji jamono intéré leu beugeunté amoufi naxanté mofi AM
Dama choquer
Andou jiguen yi sincère bariwaoule jiguen dafa sokhor ak moromou jiguenam
C'est bien c'est très bien Soda 😂la classe de Bourry et son regard qui me retient 😊😊😊😊😊❤
@Hassane221 Merci. 😎
@@evenprod on est fière de vous grâce à vous on s'ennuie pas 🇨🇵🇸🇳
Chapeau à vous (evenprod🎉❤)
Ibou laye diokhna leçon béppeu nitt bouy joué carte mouy 1xbet wala lénèn
Que ni bou yalla wakhéni carte bakhoul rek amna loutah parceque daflay détruire carrément moralement et mentalement
Yakar bou tass guay doundé com li dal ibou laye ak problème yidoul diékh com nimou barré ay plainte
Boudon yamon na thi parking biko yalla may boooba li yeup douko dal
Mes il a choisis l mauvaise chemins ba li yeup dalko
Yalla néna [le vin, le jeu, les sacrifices et les flèches pointues sont une abomination de l'œuvre de Satan, alors évitez-les pour réussir. ]
donc les gars evitez ❤ aussi mrcii Even Prod thi leçon bi
Merci
@ousmane839 Un plaisir de savoir que vous avez tiré une leçon de cet épisode. ❤
@@evenprod ❤️🤩
Des cœurs pour notre profete mouhamed PSL ❤
tambaliguénnnn
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤🤍🤍🤍🤍🤍🤍
PSL ❤❤❤❤❤
Soula nèkhone bind prophète ms dèfoko ❤😂😂❤
Kou dacord ni batlen dafa nop diadia rk la lal j'aime 😂😂😂
Khon guissé nga lolou
❤❤❤❤❤❤❤❤
Lolou bittileu fanan batlen migui beuga dée 😢
Mė batlėn mo wra tak dia dia Mou nėkh
@@OusmaneMboup-mr8zedanga fatté yayam😂
Ndiawar :🗣️Lou bakh nak kouko def daniou nann leu c’est bien , ngeu def lou geuneu bakh niou Nila c’est très bien, kone soda Mareme c’est très bien ahhhhh yaye 😂😂😂😂😂😂😂😂
Yaye dior limou tontou ndiawar moma raye
@@AidaMboup-we5ypkam😂😂😂
Khammmmmm😂
@@Princessekhady9952 merci khammmmm tu es contente j’espère
Retour de boury😂😂😂😅😅😅c'est très bien 😂😂😂😂 0:40
C'est bien 😂
Malick c’est bien c’est très bien 😂😂
Wayé si ione nal Boury je l'aime bcp 😂 mais moye 2 éme femme si série bi 😢😅
Ah oui c est très bien même
C'est Bien🤣
Diabar Ass bi da meune sagnessé teksi rafett wayy 🥰🥰 macha'allah 🥰
Mais c est une sorcière
@@Khadimamadouwah ko thiakaww😂😂😂
❤❤❤❤❤❤😅😢😊😂😂
Teksi bone nk😂
@davidave28 👍
Amitié amatul...la réaction de l'amie de Anna( notre adja nationale) m'a scotchée...donc derrière toue cette bienveillance et présence se cache une jalousie...ceey adduna...ce sont des choses que nous vivons réellement...XALISSO touche tous les maux de notre société.
Justice pour bb diary Sow kou d'accord lalale j'aime 😢😭😭😭😭😓✊❌
Justice bi len kessé leu moy gnou ray ki ko ray, oeil pour oeil dents pour dents
@@cmavie580vraiment nak😢😢
👹👹👹👹👹❣️
Justice Kaye diapou nako teudje
Cher ami observe un groupe d'enfants qui jouent. Ils sont heureux parce qu'ils ne se souviennent pas des tristesses du PASSÉ et ils ne pensent pas aux malheurs qui pourraient arriver dans le FUTUR. Ils vivent pleinement le moment PRÉSENT. Si tu veux être heureux, fais comme ces enfants. De toutes façons, tu peux pas effacer le passé, et t'inquièter pour le futur ne changera rien. Ne souffre pas pour rien, tire de la joie dans ce que Dieu t'a donné aujourd'hui. Fata lui est heureux avec sa Queen Bineta et son mbakhale mou tooye.😂😂LOVE
Waw waw cadou yi rafet neu Ma Sha Allah dinagn doundou présent bi th fatei passé mbeu😂😢❤
Fata blh yaw mn loutkh ma lay weur diakhal nma😭😂😂😂
Queen Bineta vient voir ton king ❤
Encore Fatasall, l'homme romantique chéri Binta mais dél wax thi serie bi bala thiat di dougou thi sa diganté ak Binta😂😂
Sacré Fata
Serigne mourinou diéguène thia Thies sama serignou sama papa ❤ yalnako souniou borom doli werr ta mou yagual koffi loll
11:38 minutes temps Amoul 🎉
Ay way laLal j’aime bi nguir yallah 😢
Loutax ngéne guaw rek laxa moul rek liii
Goor day gaaw 😂
Sponsors motax niouy setane série bi
@
Man mom sponsor takhoul may sétan série
😂😂yawe lay weur ba fadiarrrrr
Mareme soda tu monte 😂😂😂descend 😂😂lolou mba tay damakoy rée 😂😂srx
😂😂😂
😂😂😂😂😂
😂😂😂
Kon sokhna Diagne nop na ibou lay dh 😂oh l’amour bayiwoul pa yi ak mer yi dh 😅
@SoumayaDiop-j6z Guisgeu dh neker nagnou ko wone. 🤣
Envenprod c'est très bien 😂😂ndiawar moko wakh nena Lou bakh kouka def daniou lay wakh c'est très bien 😂😂
😂😂😂😂😂😂😂😂
😂😂😂
Ww 😂😂😂😂😂
C'est bien
😂😂😂🤣 tu m’as épuisé 😂
Des cœurs pour notre prophète mouhamed ❤
❤
❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤SAWS❤❤❤❤
Légui série sénégalaise yi yiw lagnou woté 😂 c très bien 😂(xalisso amna ibadou ,jeux de dames amna ibadou ak décé, lady diama amna ibadou ak décé ,bété bété amna décé)
C'est très bien😂
Nianal lénma ma gueuneu dioubo ak samma borrom keur❤
𝐘𝐚𝐥𝐥𝐚 𝐧𝐚 𝐧𝐠𝐞́𝐧 𝐠𝐞𝐮𝐧𝐚 𝐝𝐢𝐨𝐮𝐛𝐨❤❤
yalla nangé geuna diouboo ma sœur ❤️❤️
Yalla Yalla déf diamou sa souné
Yalla nalen yalla gueuna dioubole ak ndiaboot bou barkel
Yalla nalén dioubolé amine 🙏🏿
gua nianal ma ,ma am dieukeur aussi
Badlène tkt diadia sa diadia tôt au tard yènagn modiè patience rk 😊
😂😂
❤❤❤❤❤❤
Comme asmaou ak chauffeur by😂😂
@lennavivilennavivi À suivre. 😂
Bravo maty rose ,yangui wonéné nit kén douko juger kén dou tégo lo menoul ,en il ne suffit pas d'être riche ou pauvre pour être humain,le bonheur de quelqu'un ou autre peut bien resider dans le cœur d'un autre,soyez juste humain et compréhensible
Ndiawar :C tres bien 😂enh yaye
Yaye :kham 😂😂😂😂
33:17
Damako réeeee ba sonne😂😂😂😂😂
😂
@@AydaCamara-s7f yak kane🤧😂😂😂
@Anna_Mu_SerigneBabacarSyGueye 😂
😮😮😮 naka diek mani Oumy mi louche na. Le jour où elle a compris ce qui est arrivé a Maty Rose té elle n'a rien dit a sa mère 😮. Loudoul gneuw hôpital di dofdoflou. Xalisso dal mo bari wiss
Dp8 lolou lani d'où kharite bou bakh
@MamatataNdiaye Doyna ware tek beute rek. 🥲
@@aminaseck3694 Bilahi c'est vrai, diomi amoul temps
@@evenprod lolou mofi en réalité. Qui écrire histoire bi, ak qui ko réaliser je te jure dinaléne téral😀
Justice pour diarry sow .Que la terre soit légère sur lui 😭
Des cœur pour notre prophéte Muhammad ❤❤❤❤
Khana tay dina am j'aime sakh🥲
Diohma code niou game
Je ne sais pas si vous l’avez bien constaté ou pas mais Diawarr Diagne mo gueuna deugou si film bi🥺❤️
Bilay doff bouy dem la😂😂
Ani sopéy yonantou bi♥️salalahou alayhi wa salam🙏🏿
Gnonguinu😊
❤❤❤
Yallah n'a ngou yallah maay weer si barkel Mohamed psl 🙏🙏🙏🙏
Amine❤
Amine ❤
Haaaaa yéne gaw rek def na tout pour djitou fi rek mais
amine
@@malickofficiel1533mouni Lane yow 🤣 19/30 ba heure bi nguay nane ndakh y’a djitou 😭🤣
La réaction de oumy la meilleure amie de Anna ne devrait pas vous surprendre car quand elle a su la vérité sur la grossesse de Maty rose elle a préféré faire chanter le mec au lieu de dire la vérité à sa meilleure amie Anna la mère de Maty rose !
Vraie amitié mom il ne reste plus que moi et ma meilleure amie ! Merci 😂
😂
@Matalastar Bien des choses à vous. 😂
Oumy mi sokhorna yalna gnou yalla mouthial si xarite bou melni oumy ak niko anna fonké
Yalla nanou si yalla mosal
Kikay sokhor na
@@FatmaFall-y1b Elle est fausse vraiment
@@safietoubalde1951sokhor la deff 😢
Bilay kharit amoul man DH kharit mo yeuguel sama seye ânde AK sama dieuké yeuguel sama seye sama dieukeur abandonné ma té dama eumb 2moi dama diakhlé trop awma kouma takhawou
ani. team Boury lale léne j'aime 🤣🤣🤣
justice pour diary Saw que son âme reposé en paix amine ❤
❤❤
Des cœur pour notre Prophète Muhammad psl❤❤❤❤❤
❤❤❤❤
❤❤❤❤❤SAWS❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤
Boury aka mouss dina découvrir legi li mareme soda di def ci souf bole wul dara wahh boury way papa asse dée dina tak yayou maty rose 😂😂
C’est
Bien
Très
Bien
Merci
27:46 heureusement pour moi bama amé bén kharit mouy sama yaye yalla na yalla goudal fanam té yokou wergui Amine si barkéb Serigne Saliou Mbacké ak bép yaye 🤲🥰❤❤🎉
Wa Ndiawar mi kagn lay bayi c'est bien
C'est très bien ça 😂😂😂
Xalisso rek lay gnou top❤
@NdeyeawaBâ-w8i Lolou nexna. ❤
25:45 Bilahi elle joue très bien son rôle en plus d’être très belle 😂😂
@mamefatouseck897 👍
Diary malika yalla nako yalla yerem way meti na Trop 😢
Amine
Walahi
Aminé 😢
Amine 🙏🙏
Amin 🤲yalna yalla nangou nian c'est vraiment triste
Enfin 🎉❤❤
Soda Mareme ak papam bi sou ndiawar noyé bop touti dinene tibeu khaliss bi yeup daw gni douniou niitou Dara Thiey khaliss meuna lounei
No lolou moungui ci yoneuh en complicite de son paapa
@@aichandoye1100 sen objectif xaliisou diawar la
@aichandoye1100 Ah doyna ware nou xare suite bi.
Warañiou reussir nak danio wara warou dakh yaye dior guene kham kouy boury
Diop Fall da fakeu😂😂😂😂 narr bii kokou ko moytouwoul dinga dokh ba chine té doko yeugu😂😂😂
Wouyyyy magui dhe😅😂😂😂😂😂
Dedeeeett😂😂😂😂
Wakh dege de sama frère moko dale bilaye
@SerignemorBarry Lolou lerna. 😂
Comme j'ai l'habitude de le dire l'amitié d'aujourd'hui n'est plus sincère sourire à la face couteau dans le dos.
La tante de Maty Rose me déçoit😅
Man dh motax ma bayi xarito
@MameFatyDiouf-y4h bilay xarit yomboul legui
@aminatafall4175 Elle a bien caché son jeux.
@evenprod vraiment qui l'aurait cru 😄
kan momaye santale seyedina Mohamed lalale cœur bi ❤❤❤
Mane ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤SAWS❤❤❤❤❤
Psl❤
Mane❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Li dal iboulay warna nio yé nioune jeune yi niou bayi carte xbet bahoul bahoul
Kou d'accord beuseul j'aime ♥️
@habibkane6658 👍
Yaye Dior guénale si sa pate patarall bi 😂😂té nga diapp si séye khalé li 😂😂
Très bien est bien
@SerigneFaye-n4o😂
Très bien c bien Eddy c bien
@@FatouWADE-x4vdescends Fatou tu monte 😂😂
@@EddyPassoubilae elle monte na wathi dh😂😂😂😂😅
Mane c'est bien dina ma ray 😂😂😂 c'est très bien Boury boul ko fallé
Ndiawar dafa yague nak Macha'Allah (moussa seck) il a toujours été mon acteur préféré
Khalé yi mba yenagui dème ozan khalé yiiiiiiiii 😂😂
Mbam Nop nagno léne😂
Dieudieu glace 🍦 deff yeufou khalé
Bougnlène naboul loumathi mane😂😂 ak accent bi
Retour de Boury kimon meilleur key 😂😂
akha nèkhone makone dallou seydina Mouhamed ❤
Bien vrai qu'il procure le bonheur wayy tamittt khaliss meune yakk les liens p arentals 😢😢qui se souvient de cette belle famille Diagne dans les premiers épisodes unies et joviale 😢😢
Leup Modou diagne
Le jour que Djaja va apprendre que le banquier a essayé de dragué sa meilleure amie Boury en mm temps qu’elle, ça va barder deh 😂
Moi je pense que le banquier été le copain d'enfances de la mère de Diadia celui qu'elle a rejeté car il n'avait rien
@@ndeyeamidoucoure4014 j’y avais mm pas pensé. Très belle hypothèse
@@Itsaminata rappelle toi de l'épisode précédent où elle expliquer à la petite sœur de Diadia de ça jeunesse et que elle été bien amoureuse d'un jeune homme mais que ce dernier été pauvre d'où le fait que elle a choisi le papa de Diadia
@@ndeyeamidoucoure4014hmmm c’possible dh ndah l’autre fois Ndao mogui nane diadia hana écart d’âge bi mth mouy yehal sen relation bi
@@MaimounaDiop-z3w bon patientons voir 😍🥰
Walahi thies yéna dieul 1er si theatre sénégalais 🎉a vous 🎉
J'espère que Boury va découvrir le jeux de Maréme soda et son père. Parce que Ndiawar ak nimou meune mél nitt kou bakh la mérité wouko 😢😢😢.
Bilay
@fatoumatasall203 À suivre. 😎
N’oubliez pas de prier sur le prophète:
Sala Allahou Allah Mouhamad ❤🎉
Paix salut sur lui ❤
Aziz Dabala que son âme repose en paix et Walli
Boury class bimoy dégagée dama koo ragal lool sx ❤❤❤ ons aimes beaucoup
@sokhnafaty9160 Merci. ❤
Badlene 😊 da nopp diadia ndaysane begue nitt ta mouno wah daguay deff trop pour mou bagne seye 😂l'amour c autre chose l'amitié parfois sa empêche lou beri nda ragal
esque dougnou moudie😊😊
Nonou lay deme sakh @@NafiNiang-y7g
@@NafiNiang-y7gamna si Yakari dh 🎉
Dégni brisé cœur bi après mou moudié ak môme rék 😂
Mais lolu dara nekoussi amitié après amour dafay guena yombu rek
Bilahi dama beugue seydina mouhamed ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Je t'aime papa ❤❤
Je t'aime maman 😂😂❤
Je t’aime mame boye 😂
Je t’aime mon mari 😂❤
Je t’aime ma fille 😊
Ana dafa bakh , kholam rafet mou rafet ❤😍 motax meno am limouy am. Yallah xol lay fay🫶🏽♥️👌
Beuseul traduction 😂moune na fèn
Son amie là c est une vipère
Billy ❤❤
😂😂😂@@MaguetteSy-et1ym
iboulaye beurina convaquation deeh😂😂
Waw kharit dale amoule oumy kone Anna nga téke peute ah adouna légui à qui on peut faire confiance evenprod dieuredieuf 🙏🏽 ❤❤❤❤❤❤
Jajaa temp yaa ngi dox rekj, deception bu rëy nga nara am ci Amaat. 😂 😂
@mustafaasamb8419 À suivre. 😎
Mareme soda mi lane naral ndiawar yeineu 😩😂😂
Boury joue bien son rôle vraiment ❤
Yalla nanou ame khaliss bou bari ❤ way😊
Amine way
Amine 🙏 way
Amine siii barki seydina Mouhamed psl ❤❤❤
Amine ya rabbi temou and ak weurr
Mani boury mo amm classe ❤❤❤❤
Diari sow yalana nako yalla khari adiana
Mais Seydou il m'mank grave 😅🥰
Ziar nieup hum Dior Mbaye' ligua waye fi lan'la oh🎉 Mashallah 🎉
Ins'bi nak ay saison 2 momaye xégn ndah 😮😢 série yeungueu'touna dh côté yeup
@DiopMalick-888 👍
Yallah Boury am ndam❤❤
Pas avec ce comportement arrogant
Ani yayou mouhamed yi❤❤❤
Bayilene kharit bakhoul amatoul Béne valeur l'amitié sincère n'existe plus
Deug ga wax d 😫
@NdeyeFatouDiop-e9t bilay ma chérie amoul Béne sens
@@Nafina-v7u nék sisa bopou dal mo guena woor
Kharite bou goor dal mo gueun
Justice pour diarry sow kou daccord rk niou teuth wadie perpéte lale jaime
Sokhna kon nop na iboulay 😂😂
Lou bakh kokou déf niou waxla c'est bien c'est très bien 😂😂😂😂
Yalna nagnou yalla may goudou fane ak ķatane bou beuri niou meuneu réalisé souniou ay projets 🙏🙏
Amine inchallah
Yalla na Yalla déf diam❤
❤
Amen 🙏
Amin
Thiey sanekh mo meun théâtre ❤ des coeurs pour lui
Ndiawar c'est bien c'est très bien bou amoul mort dina am nless😂😂😂😂😂