Incroyable mais vrai essayer de ne pas pleurer,Sama Papa dama doh ba fék ko mou teud déé thi allebi😭

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 9 фев 2025

Комментарии • 621

  • @taybtoure7286
    @taybtoure7286 Год назад +70

    Mâcha Allah un vrais homme kou begue Dame besele j'aime

  • @salimatacome2194
    @salimatacome2194 Год назад +8

    Je sais pas Kagn lay done Mai’s Pape Niang yalla bouniou mayé goudou fan ak werr nala meuss teral inchahalla

  • @fatousakhirsall9150
    @fatousakhirsall9150 Год назад +37

    Vraiment Pape Niang Yaw yay l Homme de l Année 2022///2023///2024 inchallah Yalla nangua goudou fane merci beaucoup yalla nala YALLA faye sa khôl ❤❤❤❤❤ amine

    • @amysarr9469
      @amysarr9469 Год назад

      Mane ak yow gno bokke bénne idée billahi wallahi ❤

    • @amysow7163
      @amysow7163 Год назад

      Bilahi

  • @adjasaliou8309
    @adjasaliou8309 Год назад +18

    Meune na watt ci yalla goor gou melni dame amatoull diko nianal yalla bayiko ndiabotam yalla teral lene ci barkep seydina mouhamed psl ❤❤❤

  • @aidafallousall6793
    @aidafallousall6793 Год назад +17

    Do torokh mouk adouna ak alakhira, ndakh ni nga takhawo say wadjiour mome lala yalla fayè. Ak ni nga gorè same kolorè ak sa sokhna bilahi yaa gorè

  • @diariatoucissokho780
    @diariatoucissokho780 Год назад +132

    Alhadoullillah Alhadoullillah Alhadoullillah c'est très rare de voir homme qui ne quitte pas sa femme étant malade ndeyesane mention à son mari yallah na diarbar tané thi diam

    • @Mamekebe-zw9hv
      @Mamekebe-zw9hv Год назад

      ❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉😂🎉🎉❤❤❤

    • @Mamekebe-zw9hv
      @Mamekebe-zw9hv Год назад

      ,,😂😂😂😂😂😂😂❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉😂😂😂😂😅😅😅😅😂

    • @AbipCiee
      @AbipCiee Год назад

      ​@@Mamekebe-zw9hv🎉🎉🎉🎉😊

    • @YafatouDiop-ye9dl
      @YafatouDiop-ye9dl Год назад

      Je suis ​@@Mamekebe-zw9hv

    • @boubasall850
      @boubasall850 11 месяцев назад

      C vrai sister ham nassi Darra sama yaye doundou nako,fébar teud 3 Moi hopital,warra préparé opération,dieureum diohko 2000fr😂😂ba paré di rar thii hopital by,,,heureusement ba Sama yaye gnakoul wone,ma indy lima Yorone Sama compte diohko,actuellement alhamdulilah,takalé nagnou ba agalé Keur boumou commencer wone,Bama touky bayfa pa by mou seyi Sama Keur yaye 😂😂😂😂

  • @FallyGueye-y7y
    @FallyGueye-y7y Год назад +7

    Dame l'homme de l'année, lidess thiisak doundou yalna lépp done mbécté , noflay , diam , ak khéweulak weurseuk wou yatou si barké seydina mouhamed psl ak pape Niang et toute l'équipe 🤲🤲

  • @CodouNdiaye-e1e
    @CodouNdiaye-e1e Год назад +27

    Il est l'homme le plus social du sènègal .longue vie à lui et plein de bénédiction.❤❤❤❤❤

  • @DieynabaKane-p7b
    @DieynabaKane-p7b Год назад +77

    Son mari est tellement gentil rare aux senegal

  • @hawadatt3595
    @hawadatt3595 Год назад +67

    L'homme social
    L'homme veridict
    L'homme qui realume les maisons sombres
    L'homme au chevet des diminuer
    Un vrai diambar
    Dieu ta élu l'homme de l'année depuis que tu as commencé a aidé les gens qui en ont besoin vraiment chapeau pape j'aimerais bien t'avoir comme frère tu est digne tu fais du bien sen attendre rien Au retour Merci d'être la pour ton peuple Un grand merci a toutes l'équipe qui t'accompagne une de tes fans qui ne rate aucune de tes vidéo je te suis depuis le Maroc diadieuf niang ballo

    • @nogayembathie5045
      @nogayembathie5045 Год назад +1

      Merci bcp ma sœur t’as tt dit mashallah ❤❤

    • @KhadyDiop-of9kd
      @KhadyDiop-of9kd Год назад

      Mé si soutoura Dina si bakh lol long vie à lui

    • @rokhayadabandiaye8011
      @rokhayadabandiaye8011 Год назад

      @@KhadyDiop-of9kdBou nekone si soutara aussi est-ce que dinagn xam ni li am na si deukk bi pour dilen aider? Publication bi baax na si benn côté dal

    • @FatouFall-m2p
      @FatouFall-m2p Год назад

      Merci pape niang❤

    • @Ssbz364
      @Ssbz364 Год назад

      Pape ak équipe bi yeup yalla na sa borome aar léne yook léne yalla reek mo léne meuna fay waye❤

  • @fatousylla5538
    @fatousylla5538 Год назад +6

    Bilahi kii mo goré ya bakh dame goré gua machalah lii mome amatoul ❤❤

  • @mariamesylla2865
    @mariamesylla2865 Год назад +27

    Ah machallah
    Qu'est-ce que je suis contente ❤ de la voir guérie❤ Chapeau à son mari❤ Chapeau à Pape Niang❤

  • @maguintd5790
    @maguintd5790 Год назад +17

    Machalla Yalla na dieum kanam merci pape Niang yak sa équipe ak SERIGNE biko fadjeu

  • @AntaFaye-xw9xw
    @AntaFaye-xw9xw Год назад +1

    Ndaysane limou sédéle diekeur dji for na ❤❤❤❤ ndaysane machalah

  • @yandegningu3440
    @yandegningu3440 Год назад +6

    J'ai regardé toute la vidéo en pleurant 😭😭😭😭 barké Serigne Saliou Mbacké yalna naléne yalla fey pape niang yaw ag sa équipe bi ❤️😭

  • @welyfaye5136
    @welyfaye5136 Год назад +10

    Pape walay yalla nala yalla faye wadji tamit Yalla nala borom bi takhawou samla arla oubil la bountou werseuk yeuk thiono bigua def sisay wadiour mou yagu wala mou yekh walay diguako guiss barké serign Babacar digua am dh inchalla

  • @catherinefall3700
    @catherinefall3700 Год назад +3

    L’homme de l’année 2023 et des années à venir inshaalah ! Yallanala souniou borome SWT maye katane, weer, weerle Ak n’dame thie lépe Lo soumbe amine yarabi 🙏🏾

  • @miningoubeatrice574
    @miningoubeatrice574 Год назад +24

    Gloire à Dieu et félicitations à pape Niang

  • @sokhnaoumoudiop6888
    @sokhnaoumoudiop6888 Год назад +15

    Sama borom keur ni la mel niou né def ma ragal louma beug beug nako am yeurmande goor bou ame yeurmande rek même bou amoul alal nekh na

    • @coumbagueye494
      @coumbagueye494 Год назад +2

      Aÿ waay lolou rék la beugue yeurmandé mooy leep

    • @sokhnaoumoudiop6888
      @sokhnaoumoudiop6888 Год назад +1

      Am na fi fracture cheville dama mel ni bébé di ma topoto ba legui moy dem marché di bok ay nat dit ma diokh bilay d'où thi djieul dara te khalisam la

    • @sokhnaoumoudiop6888
      @sokhnaoumoudiop6888 Год назад +1

      Mouniou dara mai loumou am djiokh ma soumay accouché mak mom hôpital bama am dom yalla nako yalla may coude fan ak wër ba djiaboot bi teral ko

    • @sokhnaoumoudiop6888
      @sokhnaoumoudiop6888 Год назад +2

      Goor bou am yeurmandem kou ko am seyal ba dé bou djiaboot bi mague mou nekh

  • @FashaQueen
    @FashaQueen Год назад +2

    Ndeysan un mari parfait bilay azim yalnako yalla fey té Sam lén yén ñar❤❤❤❤

  • @coumbasounadieng9081
    @coumbasounadieng9081 Год назад +2

    Pape Niang yalla na gua goude fane te werre yalla bou la darra fakatal

  • @adamseck6907
    @adamseck6907 Год назад +2

    Goor bou melni Dame en voie de disparition leu nk... yalla naleine yalla may wer ak goudou fan seni jaboot barkel ba dileine teral.amine Pape niang goudou fann ak wer tchi iow

  • @matydione8670
    @matydione8670 Год назад +7

    L'homme de l'année nak budget rek lako yéna comme cadeau car il joue un rôle noble et très difficile bravo pape yallana borom bi faye la

  • @aidathiam7840
    @aidathiam7840 Год назад +3

    AY PAPE NIANG YAW SOUMA YOROON ALDIANA, 😢😢 WALLAHI AM NGA FA PLACE BOU REUY. KOULA NARA TOUTAL MOOY TOROHH WALLAAHI

  • @fatousene6924
    @fatousene6924 16 дней назад +1

    Merci CHEiKH niang❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤ alhamdoulilahi

  • @ndeyeseynaboudiouf1959
    @ndeyeseynaboudiouf1959 Год назад +12

    Il est rare comme homme Sénégalais. Macha Allah, Serigne Dame yaye gore deugue deugue .

  • @naboujadia77
    @naboujadia77 Год назад +3

    Mande soumaye setan. Damay dioye Ba sone pape yalla nala yalla tekk lokho Amine yarabi

  • @ndeyefatousenghor8051
    @ndeyefatousenghor8051 Год назад +4

    Je ne peux plus retenir mes larmes 😭 walahi yalla mangui lakoy sédél thi barket quran nga mayma borom keur bou amé ni yeureumandé 🙏🏻🙏🏻 té dame mi ak nafi yalla takhawoulén bagnou nek sén donkassigui thi barket alhourhane 🤲🏻🤲🏻🤲🏻🤲🏻😭😭😭😭

  • @khadydiva4301
    @khadydiva4301 Год назад +4

    Ndaysane djeukeur dji Yagu na doundou lou meti ndeuysane yalla na la fayy sa thiono yigua doundou yeup 😢

  • @fatousakhirsall9150
    @fatousakhirsall9150 Год назад +14

    Sounou amine 10 Pape Niang Sénégal Dina dieum kanam ❤❤❤

  • @NDEYEastouGueye-le7gg
    @NDEYEastouGueye-le7gg Год назад +3

    Ay dame yalla Nala yalla faye ya bakh

  • @adamaniang5929
    @adamaniang5929 Год назад +5

    Mane d accord na Ken dou pape niang si social

  • @wawa119
    @wawa119 Год назад +25

    Le couple de l’année machallah

  • @mariannediagne7883
    @mariannediagne7883 Год назад +1

    Pape Niang yalla na yalla guddël sa fan , wérēl la. Bëgg naa la lool mon frère. Yalla na yalla sàmm la bu baax

  • @binegadio4799
    @binegadio4799 Год назад +2

    Hum dame dee outee n'a ak goor yu bari bo febaree rek nu daww bayila.dieuredieufeti pape

  • @anitaaidara4392
    @anitaaidara4392 Год назад +2

    Alhamdoulilah grand Pape yalla nalla yalla fayyy sedal ga sama khôl bilahi.
    Dame yak sa sokhna yalla nalen yalla diapalei ❤

  • @Djibyniass597
    @Djibyniass597 Год назад +7

    Alhamdoulilah pape niang yaw ak sa équipe yalnalen y'allah bour bi fay doli len soutoureuh si barki yonenti SALAHOU ALEYHi wWA SALAM ❤❤❤❤

  • @alimatougnabaly6512
    @alimatougnabaly6512 Год назад +9

    N’oubliez cheikh djinne❤❤il est a féliciter vraiment

  • @AdamaMané-w9j
    @AdamaMané-w9j 9 часов назад

    Pape Niang yalla gna goudou fane doundou ba doundou sappila barki sdn Mohamed 🤲🤲🤲🤲

  • @bibandiaye9845
    @bibandiaye9845 Год назад +2

    Aziz Ndiaye Baye Ndiaye ndiak Kaye léne diamou yalla thie gnie yéna gui def social wayé and tahawou gni weradi rek gno diarra défal

  • @yacinefaye4674
    @yacinefaye4674 Год назад +2

    Machaallah Pape Niang yaw dh Yalla rék mola meuna faye bilahi . Yallah na Yallah sam la doli la soutoura guena deugueral sa takhaway guena yatal say khéwal ci barké Seydina Mouhamed (psl) . Couple bi aussi Yallah défal lène werr dolilène soutoura ci barké Cheikhoul Khadim 🤲🏾

  • @LimaBah-w2p
    @LimaBah-w2p Год назад +19

    ❤❤❤❤❤Machalah pape niang l'homme social de l'année 2023 ❤❤❤❤❤

  • @ndeyesokhnaly1497
    @ndeyesokhnaly1497 Год назад +1

    Oh ndayesane femme bi tanena yalla na yalla khep doli

  • @AmidoufalldiopAmidoun-sk4oo
    @AmidoufalldiopAmidoun-sk4oo Год назад +4

    Alhamndoulilah 😢❤naniou défar keurgi tamite nguiir yallah diokhko khaliss bou Bari ravitaillement svp na thii autorité yi geuna diap té yallah rék takh pape nitou aldiana ngui

  • @TombonFaty-f9o
    @TombonFaty-f9o Год назад +8

    Avant tout d'abord c'est la salutation ,vraiment ça c'est une fiertés pour nous tous franchement je suis très content et fière de vous mon grand mon oncle mon papa PAPE NIANG vous êtes l'homme social exemplaire référence véridique et digne BREF le jambaar champion vraiment la population sénégalais est fière de vous GRAND je vous souhaite tout le bonheur du monde prospérité joie amour et la réussite totale .bonne couple â vous que dieu vous protège et vous donne une longue vie ❤

  • @AdamaMbaye-xr7pd
    @AdamaMbaye-xr7pd Год назад +1

    Kou melni pape gniang diaffé na si miiw reew

  • @musabah9602
    @musabah9602 5 месяцев назад +1

    Inchallah Ils sont les meilleurs pour tous les années vraiment 😢

  • @AmyGueye-qn5fc
    @AmyGueye-qn5fc Год назад +2

    Pape Niang yala n'a yala yokou sa fane yak gnigua andal gnep❤

  • @dadashu2052
    @dadashu2052 Год назад +3

    Nooo ki tanéna alhamdoulilah yalla n'a yalla khep doli 😢 ndeysane ay pape yalla rek moléndi Faye

  • @mamadoubar8891
    @mamadoubar8891 Год назад +1

    Billay Wallay
    Pape Niang koulaye khar kouni yalla na khaddi
    Yalla nalla yalla laffal thiate samal la boppam ARLA Moussal la Mouthial là deffal soutoura Adina ak alakhira
    Déffal lakko déffal ko sa ndiabote
    Pape ndoundal wérral Amal diam yalla doulla setane mouk thi Adyna
    Kome yalla khôl laye faye boulla yalla fayé sa khôl récc nga khamni déff Lou bakh récc Am sollo.
    Pape Niang billay Wallay l'homme social de l'année 2023.
    Bonne Année
    Mes Meilleures Vœux.
    Dieukeur dji guoré na dé ,lou diaffé
    ,wayé mokoko dji
    Machallah sokhna si yalla nalla yalla dollil wérr
    Yalla na yalla khép dolli
    Amine ya Rabbi

  • @MamiNdiaye-s8w
    @MamiNdiaye-s8w Год назад +5

    Wadji kou ame yeurmandé la si diabaram yalnako yalla faye

  • @ousmanediouf4592
    @ousmanediouf4592 Год назад +4

    Un vrai diantal men un vrai baye fall bilahi thi sama adina déh gueune guama diangaual ni mougne réka am solo 🤌bilahi 😭😭

  • @ramatoulayefaye8989
    @ramatoulayefaye8989 Год назад +1

    Il est sociale du Sénégal focus Pape

  • @binetaba237
    @binetaba237 Год назад +2

    Hoooo alhamdou lilah dall comme femme bi tanne na j'ai pleuré ce émouvant le mari et vraiment gentil trop fidèle mais pape merci yalna la yalah faye nafy yalnagua werre si diam

  • @yacineniasse2187
    @yacineniasse2187 Год назад +1

    Chanson merite vraiment pape chapeau goude fane AK weer

  • @pendakounta8280
    @pendakounta8280 Год назад +6

    Entièrement d'accord. L'Homme social de l'année avec un grand H diko nianale bou bakh sounou Borombi feyla yiw. Yallah kouko lébale kére mou feyla goudi. Maacha ALLAH.

  • @NdeyeCoumbaSow-w5s
    @NdeyeCoumbaSow-w5s Год назад +7

    Eh!Pape Niang social tu mérites le titre de chevalier dans l'ordre national du lion.Avec ton équipe,vous méritez d'être décorés franchement

  • @HelenaRassoul
    @HelenaRassoul Год назад +7

    C'est très rare de voir un marie qui est un grand coeur resper a lui dieu vous donne bcp de bonheur ❤

  • @diamathiombane8910
    @diamathiombane8910 Год назад +6

    Maaaaachala nous sommes d'accord que pape niang est l'homme social 2023 maaachala ❤️❤️

  • @mariamazhr2008
    @mariamazhr2008 Год назад +1

    Ohhhhh mashallah nima contané eupeuna pape yawite yallah nala fay si barké alhourane

  • @Fiiba-ng2ph
    @Fiiba-ng2ph Год назад +4

    ❤ macha'allah yarame dawna un bon marie ç rare bon vent à toi pape niang🎉 félicitations

  • @diopfatou-tc9mo
    @diopfatou-tc9mo Год назад +8

    ALKHAMDOULILAH pape yalla nala yalla fay mé Etat bi si li l'an wara def s'en khaliss bilaye ya Diarra diapalé❤❤❤

  • @margosoumah3908
    @margosoumah3908 Год назад

    Pape Niang et son équipe que le bon Dieu tout puissant vous récompense de votre courage et de votre dévouement envers les démunis. Aux bonnes volontés que Dieu vous bénisse ,enfin au mari de Nafi je dirai que c'est des meilleurs mari du monde. Un grand bravo..quand à Nafi , je lui souhaite un prompt rétablissement amine Yarabi.

  • @astougueye2316
    @astougueye2316 Год назад

    Alkhamdou lila yalla na yalla yok were gui sa borom kholou daimant la yor pape yaw yalla na la yalla fay ak kep kou thi daim dieurdief yalla sougnou borom

  • @fatoumbaye1064
    @fatoumbaye1064 Год назад

    Machalah pape NIANG yalla na yalla gueunela takhawou si ligay df yalna yalla gueun safara sokhna si

  • @thiecoumbasarr
    @thiecoumbasarr Год назад +2

    Pape Niang l'homme social de l'année

  • @BaMbAkarim8437
    @BaMbAkarim8437 Год назад +1

    Dundou nga lou meti mei fayou yalla dina nex ci yaw barki serigne bamba 😭🤲

  • @DBG761
    @DBG761 Год назад +1

    Pape niang je n’aime pas commenter mais yalna yallah faye la si barkep ardiouma dji

  • @fatousene8539
    @fatousene8539 Год назад +1

    J é tellement j é pleurer mais aujourd'hui alhamdoulilah

  • @sokhnakane5266
    @sokhnakane5266 Год назад +7

    Alhamdoulilahi pape Niang yalla nala yalla défal diam rék ❤️

  • @teningndao6031
    @teningndao6031 Год назад +3

    Li nit wara santè yallah barina 😢😢Bilae lou mëty yague na ci adina 😭😭😭

  • @Toulaye09
    @Toulaye09 Год назад

    Pape Niang yallah neu yallah faye sa xol. T es l’homme de l année 2023❤

  • @KhadijahLo-r6r
    @KhadijahLo-r6r Год назад

    Pape Niang yalla nala yalla faye si Barki lerou alkhouran ❤ yalla agali yéné biga am si nitt yi

  • @Mamanfaye-m2s
    @Mamanfaye-m2s 2 месяца назад

    Machalla pape yabakh manedé damala reconnaître bilay pour dila suivre Machalla

  • @AichaVital-m6e
    @AichaVital-m6e Год назад +4

    Ndeysane regardez comment son épouse pose sa tête sur son épaule on la sent rassurer . Diamono bi niou nek diafai ne torop guiss gor bou am yeurmander à ce point. Cet homme la on doit l aider ndakh il se bat pour sa femme t cette dame la pour aller mieux dans cette vie l à besoin k son mari se porte bien. C deux la il faut vraiment les aider

  • @fatoudia9900
    @fatoudia9900 Год назад

    Moy l'homme social de l'année té lolou force la té mokoy done tmt pour tjr tonton Pape barké seuydina mouhamed psl soumay wakh si yaw dina am commencement mais douma am fin mais borom keurou Nafy bi tmt machalla kou goré la diaffé na vraiment yalna yalla doli diam🤲🤲

  • @awaniang2713
    @awaniang2713 Год назад

    Niang dou bone bilahi daye bari yarme ndeme pape niang il est le mite yalna yalla defal diam

  • @secksokhnadaba6827
    @secksokhnadaba6827 Год назад +1

    Ooohhh pape machala y a beaucoup d amelioration d apres la fois passer machala ndeysanne ooooh😢😢😢

  • @SuzanneChaumetMbodj
    @SuzanneChaumetMbodj 11 месяцев назад

    Pap Niang douma sénégalaise mais je prie d,abord beaucoup pour toi, qu,Allah t, assiste et te protège d, avantage, et c monsieur est un saint, il est unique, que Dieu le paye ici bas et au délà, le mot me manque pour la qualification

  • @OumySarr-ez4ik
    @OumySarr-ez4ik Год назад +2

    Masha alla pape Niang et son équipe yalna yalla doli len soutoura si Barker yonentebi

  • @aliouba8131
    @aliouba8131 Год назад

    Alhamdoulilah pape niang vraiment j'ai pleure avant et après pape dieureudieuf nala yalla fay thi varké cheikhoul khadim

  • @yateletall379
    @yateletall379 Год назад +1

    Pape Niang yakk sa équipe akk képou kou sii déf sa deureume yalle n'a la yallah tabakhal château sa aldiana firdawssi amine 🤲🤲 dieureudiefé su niu borome bii swt ☝️ môme miy docteur bou mag bii

  • @mariamamboup9741
    @mariamamboup9741 Год назад

    Alhamdoulilah yalla na yokhou werr gui si barké baye niass

  • @Mane-rc7pn
    @Mane-rc7pn Год назад

    Billaye pape Niang boula yalla fayoul dou faye kenne wallahi machalla longe vie à toi

  • @astoundiaye3881
    @astoundiaye3881 Год назад +1

    Dame Masha Allah Yalla nala yalla fay sa ngorr yalla nala yalla takhawou
    Li diafeh si gorou tay yi

  • @alphadiallo9171
    @alphadiallo9171 Год назад +1

    Li dawna yaram nagnousi djangue rék hamné adouna yalla rék Moham momeun

  • @Noreyniprod
    @Noreyniprod Год назад

    Pape Niang et ses compagnies yalna leen Yallah fay seen xool

  • @bintoubanellediabang712
    @bintoubanellediabang712 Год назад

    Machallah pape niang thi liguéy bii é chapeau ô bonnes volontés

  • @maremetine5882
    @maremetine5882 Год назад +2

    Alhamdoulillah
    Dieu merci
    Yalnalène yalla fey Pape Niang ag équipe bi yép

  • @nafissatoundiaye2069
    @nafissatoundiaye2069 Год назад +2

    Il merite une demeure digne de son nom pour lui et dsa famille 👨👦👧👩👴👵jomme de année homme au grand coeur il mérite un 4x4 franchement lançons une cagnotte pour homme de année pour ces déplacement personnelle svp🎉🎉🎉🎉

  • @FamaNdiaye-w2z
    @FamaNdiaye-w2z Год назад

    Pape Niang yal nala yalla takhawou thi barke seydina Mohammed salalahou alhi wa salam amin

  • @Xidmatv09
    @Xidmatv09 Год назад +2

    Serigne bi tamit ken dou mom machallah

  • @KinéThiam-l2q
    @KinéThiam-l2q Год назад

    Pape Niang yalnala yalla Fayal bopam Pape yadiss gor Di dioulit piir

  • @Saloumsaloum9971
    @Saloumsaloum9971 Год назад +5

    Alkhamdouliha. Dieureudieufé Allah souniou borome.Pape yalna Allah féye yaw ak sa équipe ni

  • @joliefaye9816
    @joliefaye9816 Год назад +11

    Dieureudieuféty yalla sougnu borome 🙏🙏🙏

  • @ndeyesirandiaye8632
    @ndeyesirandiaye8632 11 месяцев назад

    Pape yalla yaw rék la déff nimoula deff pape yaw yalla rék mola meuneu fayale bopame bilahi pape yalla nalla yalla same are la yokou la si barké naby 😢😢

  • @ndeyembow6695
    @ndeyembow6695 Год назад

    Machalla ❤️❤️❤️ pape Niang yalla n'a la yalla same are arala may la wer werle yalla fay la amine ya raby

  • @diakhatefatiss4162
    @diakhatefatiss4162 Год назад +2

    😭😭😭😭😭😭😭Merci beaucoup dame delonga djiguene valeur reume walahi Longue vie a dam ❤❤❤❤❤

  • @SokhnaKane-v7b
    @SokhnaKane-v7b Год назад +1

    Je suis d'accord pape niang est l'homme social de l'année 2023❤❤❤❤

  • @diallo1391
    @diallo1391 Год назад +1

    Li dé geumoumako sakh ay way yalla ya bakh dieureuf sou niou borom mention a pape ❤😢😢