Meurtre de Khady Diouf la jeune fille de 15 ans : Son Pére confirme qu'elle est enceinte

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 31 янв 2025

Комментарии • 326

  • @famadiop3689
    @famadiop3689 4 года назад +113

    Père iow kou geume yalla ga khady yalla nako yalla kharè aldiana firndawsi 🙏🙏🙏🙏k justice 👩‍⚖️ soit faite

  • @sissokhokhadijasiby1037
    @sissokhokhadijasiby1037 4 года назад +246

    Ndeyssane kaadou yii rafétna
    Borom Darou Noreyni mo daane wakh app diouliite bo tiité andalak sa xéle. Bo diakhlé déssal ak sa fitt, bo ñiakké ba désséto dara nga sango sa malanou Ngor.

    • @abybarry3826
      @abybarry3826 4 года назад +3

      Machallah !

    • @lecaporalbkm2873
      @lecaporalbkm2873 4 года назад +5

      Heuskëy lou wërr NGa waakh.. Al-hamdOulilah sante sunu borom rk.. maintenant na yoon déf liguéyaam et que la peine de mort soit établit au Sénégal

    • @sgftvsoldarogeneralfall9907
      @sgftvsoldarogeneralfall9907 4 года назад +2

      Yaw mi de brom xam xam ngua nala sa brom defal diam

    • @sissokhokhadijasiby1037
      @sissokhokhadijasiby1037 4 года назад +4

      Amine dieuwrigne niou bokkeu léppeu barké Ahmadou yaakari diaame gnii

    • @abdalahgueye8676
      @abdalahgueye8676 4 года назад +4

      Barke Soxna Khady Mbacke Noreyni lou leer ngua Borom Darou alkhamdou Choucry lilahi rabil Halamina modone lepeum

  • @pendadiongue115
    @pendadiongue115 4 года назад +105

    Machalla kadou yi rafet na
    Ki kou dalleu te gueum yalla leuh
    Repose en paix sokhna khady diouf

  • @bayeniang6077
    @bayeniang6077 4 года назад +70

    Cest un grand monsieur vraiment mes respects niawo thi been yoon

  • @annadiop8643
    @annadiop8643 4 года назад +63

    Gor yalla deug ga machalla yalla nako sounou borom kharé aldjiana firdaw si ya si barkep mouhamed psl 🙏🙏🙏🙏

  • @madodiagne3007
    @madodiagne3007 4 года назад +47

    Ma shaa AllAh gueummm gua yallah. Yallah na xipper aldiana firdawsi

  • @papeousmanefall5796
    @papeousmanefall5796 4 года назад +51

    Non vraiment moussou ma guiss kou degou com kii andak sa khell nekh na rawatina guem yallah yallah nako yalla yereum té khareko aldiana metina Maï guem yalla rek moy lepp

    • @alaminesylo2680
      @alaminesylo2680 4 года назад +3

      Geum yalla bathi lan khalé bi nit dafa yoré bakan kom.gnépou lan ndayou kou gor ki eumbeul ko ba baparé nagn nagnko soutral ndakh papam serigne le kiliafa le si deuk bi wa legui khady diouf mom lan le nagnou bayi neupou neupeul bi vraiment méti nama trop pér dieuleul say responsabilité dom nawlé le

  • @ibnibrahim7514
    @ibnibrahim7514 4 года назад +60

    Wakhi dioulite deug gua wakh papa 🙏 Khady Yallah na motalé ndawam Aldiana

  • @mamesaye1977
    @mamesaye1977 4 года назад +2

    Ndayessan papa kaddou yii rafet na machallah guem ngua yalla tamit te nangou dogall yalla nako yalla yeureum te dieguell ko ak mbolem dioulit thi barkep s.saliou 😭😭🙏🙏

  • @LINGUERE100
    @LINGUERE100 4 года назад +16

    Yalla Nala yalla maye kholou mougne. Tu es un vrai kilifa. Machalla

  • @yabalsylla9893
    @yabalsylla9893 4 года назад +42

    Ndeysan méti trop niogui lay masawou diko nien yala yueram ko te kharelko aldiana

  • @mouhamadoulamineseyebeugue2741
    @mouhamadoulamineseyebeugue2741 4 года назад +48

    *_Ndeyesann meetina trop papa dji mais machallah si kaddou yi yalnako yalla yeureum té khareko aldjana si barkép serigne saliou mbacké_*

    • @awasow876
      @awasow876 4 года назад +1

      Haha T tjr sur les Comentaires danga bayi les Bobodiouf khana😂

    • @mouhamadoulamineseyebeugue2741
      @mouhamadoulamineseyebeugue2741 4 года назад +1

      @@awasow876 *mdrr iow khanma d guama bobodiouf jamais légui rek la diougué sétan* non iow dou dém kw🤣🤣😂😎

    • @awasow876
      @awasow876 4 года назад +1

      @@mouhamadoulamineseyebeugue2741 lolou kay chak jour mangui setane di guiss sa comentaire😂

    • @mouhamadoulamineseyebeugue2741
      @mouhamadoulamineseyebeugue2741 4 года назад +1

      @@awasow876 *_iow kye nio bokk faible si bobodiouf non man mome affaire d comédiens domasi doyal_*

    • @awasow876
      @awasow876 4 года назад +1

      @@mouhamadoulamineseyebeugue2741 mane dh episode yeup setane nako

  • @maryfall3030
    @maryfall3030 4 года назад +13

    Machalla pére kou guem yalla nga yalla nako yeureum ta kharéko aldiana firdawsi

  • @cadiortv
    @cadiortv 4 года назад +21

    Macha allah. Yaala nako yaala kharee aldiana yi gueneu kawee amin

  • @mamesayefall2124
    @mamesayefall2124 4 года назад +12

    Ndaysan machalah kou geum yalla nga nasa geum yokk ta Sokhna khady Diouf yalla nako yalla yeureum kharé ko aldiana barké mouhamed slhw

  • @mansourdiop2499
    @mansourdiop2499 4 года назад +9

    Ndeysane innocente de 15ans défagoule dara si aduname niou défko ni métina trope no li dou yone bilahi amoule soutourale amoule serigne wala kilifa lidafa niawe rousselou khalé bou ndawe vraiment amena nio khameni mbame moléne tané khady repose en paix que firdaws soit sa demeure eternell

  • @diopfaya3471
    @diopfaya3471 4 года назад +23

    Paix a son âme, wakh dji rafetna lool machallah

  • @yamalnitkifingabeggmuyamla6290
    @yamalnitkifingabeggmuyamla6290 4 года назад +35

    Ndaysaan!
    Ku xippi say bët jiital sam xel yilif saw yoon!
    Nako Yàlla jéggal te yëram ko dolli muñ gi.

  • @mbayediouffaye4858
    @mbayediouffaye4858 4 года назад +19

    Yalla na souf sédeu si kawam borom bi xareko aldjana firdawssi amine

    • @mariefall5954
      @mariefall5954 4 года назад

      Mougne rék mo ame solo yana khipé aldjana

  • @awakhoumaseck4384
    @awakhoumaseck4384 4 года назад

    Masou ma guiss kou niak nakin wou meti wi ba pare gém yalla kom papay khadi Diouf yalla nako yalla yerem khare ko aldina barke serigne touba

  • @jodiemaury9306
    @jodiemaury9306 4 года назад +1

    Massa quel exemple yallah na ko yallah yeurem tè kharel aldiana firdawsi amine ya rabi merci 🙏🏽

  • @makhfaye-c2k
    @makhfaye-c2k 11 месяцев назад

    Amine machalah yalla nako yalla kharè aldiana té yalla fégnal lépe 🙏🏻🙏🏻

  • @marcelojrdabo1485
    @marcelojrdabo1485 4 года назад +9

    J'ai les larmes 😢 bilahi... Que dieu te accueille dans son paradis amine.... Sénégal va male

  • @anareksunarek4881
    @anareksunarek4881 4 года назад +13

    اللهم اغفر لها و ارحمها آمين يارب العالمين

  • @binettesy6978
    @binettesy6978 4 года назад +2

    Yaw deh Dagua gueum yalla bâ paré doyloko. Lou diafé si nite machallah

  • @mariemefall7464
    @mariemefall7464 4 года назад +21

    Paix à son âme

  • @kyakya9538
    @kyakya9538 4 года назад +5

    Yallana ko yalla diegeul kharéko aldiana ak bep waye dawlou thi barké Seydina Mohamed S.A.W barké Serigne Babacar Sy R.T.A

  • @aniichsow1440
    @aniichsow1440 4 года назад +33

    Yalle nako YALLA kharé Aldiana yi gueuna kawé si barké Seydina Mouhamed PSL

  • @jyafa7883
    @jyafa7883 4 года назад +12

    tu étais où ? pendant 5mois ! pourquoi tu n'as pas porté plainte étant donné que ta fille était mineure ? pourquoi tu n'as pas dénoncé la pédophilie aux médias comme tu le fait après pour parler d'elle après sa mort sans émotions ? triste pour cette petite fille sans père présent,non défendu par sa famille au nom du soutoura et de 10000f la vie d'une personne compte si peu ???? vous êtes les responsables de ce crime autant que le meurtrier

    • @dadyfesel5820
      @dadyfesel5820 4 года назад +1

      Vraiment sans émotion. Cest bizarre

    • @kanyba7166
      @kanyba7166 4 года назад

      Niom biniou yeuguei grossesse bi akk biniou ko rayei ça n'a mm pas duré une semaine
      Ils n'ont mm pas eu le temps de porter plainte

    • @jyafa7883
      @jyafa7883 4 года назад +1

      @@kanyba7166 c'est une blague que vous faites ? surtout un conseil ! dès que son enfant lui a dit première réflexion, il faut allée à l'hôpital, ce qu'il ont fait ! et à la sortie directement police. ils auraient utilisé l'énergie pour aller chercher les 10000fcfa pour aller à la police. la petite serait certainement encore en vie

    • @rakhouguedjii1506
      @rakhouguedjii1506 4 года назад

      5 mois nak guisso sa dome thièy doy nan war

  • @oumarmbaye947
    @oumarmbaye947 4 года назад +4

    Quel grand monsieur.Yalla na len Yalla may kholou mougne

  • @massambadioum1591
    @massambadioum1591 4 года назад

    Merci papa Khady yaw kou guem yalla la gna sa dôme yalna souf séde si kawme si barké s touba

  • @ramasamb9555
    @ramasamb9555 4 года назад +1

    Yalnako yalla diegal tei oyofal suf si kawam vraiment témoignage bi rafetena tei guem yalla ga machala

  • @astoubaby8970
    @astoubaby8970 4 года назад

    Yalla nako yalla yereume yereume ta khare ko aldiana firdaws 🙏 🙏 🙏

  • @sokhnakhadylybousso5139
    @sokhnakhadylybousso5139 4 года назад

    Masha alla masha alla wakh dji téyy na rafét na am kholou mougne dh papa meii yalla nalla yalla guena dooli kholou mougne
    Th sa dom yalla khareii ko thi aldiana firdawsi yii th diégual ko ay bakaram thi wérou rajab gui

  • @dieynabandiaye2843
    @dieynabandiaye2843 4 года назад +5

    Ndeysanne Geum Yalla wessouwoul li...
    Yalla nako Yalla kharei Aldiana . Un vrai Papa mashaallah.
    Mais Sénégal lgui mome doy na waar on s'entre-tue de trop

  • @mamedia6425
    @mamedia6425 4 года назад +1

    Yallah nako yallah yeureume tei xarei ko aldiana wakh djii rafeite neu macha allah

  • @dofftareiw572
    @dofftareiw572 4 года назад +8

    _*Noy amei sa dom ga neikk senegal mou neikk senegal gay tokk 5 moi 19 jour doko giss sameu bou neikk sameu ga tei euleukk yomale khiyam digako layo ak khalei bi pour yeine dome rek moy yoreil way diour akh paix à son âme-*

  • @khadydiop9550
    @khadydiop9550 4 года назад +19

    Machallah say kadou rafetna yalnako yalla yeurem te xareko aldiana

  • @ahmedkeita6853
    @ahmedkeita6853 4 года назад +1

    Monsieur merci tu es très posé machalla lere na

  • @peaceandsalam2852
    @peaceandsalam2852 4 года назад +25

    Yàlla nako yàlla yërëm té xaare ko àjjanay Firdawsi ñu mu fa fekk ak ñu ko fa fekk

  • @cheikhbi2056
    @cheikhbi2056 4 года назад +4

    Sénégal amna niou raw Corona Virus. Khalé bou ndaw nga bireul ko raye ko. Métina
    Du courage du courage.

  • @pascaldiandy5667
    @pascaldiandy5667 4 года назад +2

    Que son âme repose en paix qu'Allah le Miséricordieux l'accueille O paradis éternel Firdaws 🙏 métina père kou mouna mougn gua Yalla na souf sédd si kowom🙏

  • @zamane5507
    @zamane5507 4 года назад

    Machallah cheikh bi, contenna thi yaw, Ndeysane.

  • @mameboussondiaye2840
    @mameboussondiaye2840 4 года назад

    Billay pape yaa gueme yalla yalla nako yalla yaram

  • @labarry2567
    @labarry2567 4 года назад

    Machalla way papeu Khady yalla n'a ko yalla yeureum

  • @thiatouyayam275
    @thiatouyayam275 4 года назад +3

    Franchement li dal sa kaw mètina lol mais aussi kou bakh ga yalla nala yalla may kholou mougne.Repose en paix khady

  • @minafall8709
    @minafall8709 4 года назад +1

    Machalla père yalna la yalla may kholou mougn nila dioulitt dafay geumm yalla

  • @madameoumar1622
    @madameoumar1622 4 года назад +1

    Mashalah gueume gua yalla gnak baparé boléthii dalee ak téyy yalenaka yalla kharé aldjana métinna nak nit akii nopam gua rayka aussi pour lane

  • @salioulatyrfaye2472
    @salioulatyrfaye2472 4 года назад +8

    Yalla nako yalla yeureum te khariko aldiana

  • @fatimafatima-xh4fn
    @fatimafatima-xh4fn 4 года назад +2

    il parle bien machallah, vrai croyant; courage, paix à son ame

  • @miya7190
    @miya7190 4 года назад

    Waye papa yalla na yalla doli Diame waye goor ndielaye méle waye mé khady yalla na ko yalla yereume té kharé ko aldinna amine amine

  • @chekhsyll1095
    @chekhsyll1095 4 года назад +3

    Yalla naco yalla yerem te khare adiana te yone def ligueyem

  • @tabarasarr6298
    @tabarasarr6298 4 года назад

    Wakh deg limome dou yoon 😭😭😭😭😭😭

  • @ibrahimdiallo62
    @ibrahimdiallo62 4 года назад

    Yallah nako yallah yeureum tè khareko Adjiana. Amine

  • @kif7471
    @kif7471 4 года назад

    Vous êtes très fort et kou geume YALLA nga Machallah

  • @fayemareme7015
    @fayemareme7015 4 года назад

    Machalla kadouyi rafetna yalla Na ko yalla yeureume ter khareko adiana

  • @antathioune1699
    @antathioune1699 4 года назад +3

    Rafet na papa💖💖💖😭😭😭

  • @madeleinediop6678
    @madeleinediop6678 4 года назад

    dioulite dale dafay gueum yalla tè bi baye wanéna ni yalla kéneu la wayè li métina basi kanamou yalla wayè yalla mi dara teuwoul yalna lérale lèpeu si barkè alhourane😔

  • @ndeyfatoumbengue6113
    @ndeyfatoumbengue6113 4 года назад

    Ndeyssane massa yalla nako yalla yeureum khare ko aldiana si barkè seydina mouhamed metina trop

  • @ndeyadior7379
    @ndeyadior7379 4 года назад +1

    Paix à son âme yallanala sounou borom bi doli kholou mouyyy 🙏🙏🙏

  • @codycorinnediouf5662
    @codycorinnediouf5662 4 года назад +2

    Vraiment bien parlé de tout cœur avec vous

  • @bassboye1660
    @bassboye1660 4 года назад +13

    Pa bi yak nako yalla Faye nit kou bakh la vraiment

  • @omarndiaye3629
    @omarndiaye3629 Год назад

    Que son âme repose en paix 😭🙏👌

  • @mhmdnabiirassoul766
    @mhmdnabiirassoul766 4 года назад

    Ndaysann wallahi kou gueum yalla nga yalla nalla yalla may xoolou mougne

  • @fatoubarhamthiellosene1806
    @fatoubarhamthiellosene1806 4 года назад +2

    Hoo mashalah Yalah nalah Yalah maay holoupe mougne ce dur

  • @channelba3918
    @channelba3918 4 года назад +12

    Machalla père wakh bi rafetna masta rip khady

  • @antafall1453
    @antafall1453 4 года назад +11

    Yallah nako yallah yeureume

  • @lesenegalais01
    @lesenegalais01 4 года назад +2

    Khady yalla na ko yalla yeureme té kharé ko aldiana firdawsi

  • @ousseynoundiaye3186
    @ousseynoundiaye3186 4 года назад

    Papay khady yalla nala yalla samm

  • @Topofthetopapex
    @Topofthetopapex 4 года назад

    Que dieu te soutienne toi et ta famille 🤎🙏🏾nit kou direct teh véridique. Rip khady

  • @santesarignetouba4390
    @santesarignetouba4390 4 года назад +3

    Yalenako yalla takhawou barké khassida yii

  • @lol_fatou1689
    @lol_fatou1689 4 года назад

    Ndeysanne yalnala yalla maay kholou mounie té sa Doom yalla yeureum mou egali ndawam aldianay firdawsi kou bah te daal gua bolewo niak baparé nianki 🙏🙏

  • @adamadione6027
    @adamadione6027 4 года назад +8

    Yalla nako yalla diegal khareu ko aldiana

  • @yayasallykoulibaly6336
    @yayasallykoulibaly6336 4 года назад +1

    Ndeyssane papa yaw dé amnga khôl mougne. Vrai killafa ni lay wakhé. Yallah nala yallah takhawoula

  • @tabarasarr6298
    @tabarasarr6298 4 года назад

    geume na yallah yana yallah may xolou mougne😭😭😭

  • @diakawaka7033
    @diakawaka7033 4 года назад +17

    Le Pere n'en veut meme au meurtrier 😡😡😡en fait il n'ose pas s'attaquer au marabout la honte completement fou eh Ben, je new vois aucune once de colere ni de tristesse

    • @zfsamt525
      @zfsamt525 4 года назад

      Merciiii

    • @Marocausènégal
      @Marocausènégal 4 года назад +1

      On dirait

    • @ndeyeaissatoudiatta8085
      @ndeyeaissatoudiatta8085 4 года назад

      Paix à son âme. Je te présente mes sincères condoléances à toi le papa. Mougnale metina torop

    • @oumaathiam6868
      @oumaathiam6868 4 года назад +4

      Diaka Waka ésk dou dafa gueum rk.. amna nio khamni Lou gnew rék souven dagnkoy ték si lokho yalla

    • @dijadija7000
      @dijadija7000 4 года назад +5

      Non je vous une fuite responsabilité comment peux tu voir ton enfant pendants 5 mois.cest absurde.

  • @cheikhounakhadimdiagne756
    @cheikhounakhadimdiagne756 4 года назад +12

    Ndeysaan metti na

  • @amyfall3124
    @amyfall3124 4 года назад

    Yalla nako yalla yeureme te khare KO aldiana te yekhe niouko amine

  • @arimaz89
    @arimaz89 4 года назад +1

    Thiey yalla wadji geume na yalla ndeysane metina yalla nako yalla kharer aldiana

  • @seckfatoubinetou4512
    @seckfatoubinetou4512 4 года назад

    Ndeysane yaw dh niako ba paré nianky macha allah

  • @serignemadickemboup853
    @serignemadickemboup853 4 года назад +2

    Machallah ça c l'honnêteté

  • @amyfall9653
    @amyfall9653 4 года назад +1

    Metina lou lou machallah merci 😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭

  • @djigueulkhemesse2110
    @djigueulkhemesse2110 4 года назад

    Ndayessane méti na yall nako yalla kharé aldiana

  • @amnasolonjie596
    @amnasolonjie596 4 года назад +1

    Ndaysane yAlla nako yalla yueram

  • @usmandiagne7760
    @usmandiagne7760 4 года назад

    Yall. Nako yalla yeureume

  • @astoudione9441
    @astoudione9441 4 года назад +2

    Papa dji kou gueme yalla yallnako yalla xarèl aldiana

  • @ndeyegnimamane151
    @ndeyegnimamane151 4 года назад

    Yallah nako yallah kharé aldiana firdawsi🙏🙏

  • @sokhnandiayeba5606
    @sokhnandiayeba5606 4 года назад +1

    Yaar môme yalnako yallah tèral,fi akk feulé Yalnaa yékh

  • @thiorondaw3864
    @thiorondaw3864 4 года назад +3

    Yalna yewo aldiana firdawsi

  • @matysyllambaye5535
    @matysyllambaye5535 4 года назад

    bilay ya bakh yalla nalla yalla may khoulo mougne

  • @julesly1806
    @julesly1806 4 года назад

    Que le bon Dieu l’accueil dans son paradis amine son papa et courage

  • @abdougorafall5863
    @abdougorafall5863 4 года назад

    Ndeysan allahou ak barr yalla nakamou yalla yeram

  • @thiambanendour7944
    @thiambanendour7944 4 года назад

    Khady était un enfant un mineur elle repose en paix Ya Allha te donne la force de supporter la douleur elle avait que 14 ans elle fini sa jeunesse au Paradis et justice soit faite

  • @coumbaarenesarr6170
    @coumbaarenesarr6170 4 года назад +2

    Yallanako yalla khare aldiana firdawsi

  • @kanteoumy1487
    @kanteoumy1487 4 года назад

    Yalna motalé ndawaw aldiana

  • @gninguemamadoufalilou3657
    @gninguemamadoufalilou3657 4 года назад +24

    Gor Yala deug

  • @kourkopoulopoulo520
    @kourkopoulopoulo520 4 года назад +5

    Ndeysane metina metina trope il faut vraiment que le gouvernement fasse quelque chose sur ces meurtres là

  • @mariemniane2331
    @mariemniane2331 4 года назад

    Machala yala nala yala may kholou mougn kadou gui raféte na machala

  • @ndeyearamegueye5476
    @ndeyearamegueye5476 4 года назад

    Ndeye san bilay ya gueume yalla t dale yalla nako yalla kharè aldiana firdawsi diègalko ay bakaram oyofal souf si barkep seydina Mohamed

  • @abdalahgueye8676
    @abdalahgueye8676 4 года назад +17

    Kou raay niit tayko naniou la raay ndakh sounou Borom monou eupe yeurmende tee dafa wakh kou raay tee tayko daniou la wara raay mou diekh

    • @Oumanas5995
      @Oumanas5995 4 года назад

      lolou moye deug té moye loi djoulite