famille kou djiguene ki amou béen ndiarigne. sa dome di doundou souffrance, au lieu nga récupéré ko pour sa sécurité, nguén bayiko si seybi nane mougnal. Mougnal dafay féck mou done gor bouko diar.
Bayi len di nane sen dome yi setal si xale yi di nane sey kate moy diour dome you barkel legui rey na ndasi 😢😢😢😢😢 goroul africain toroxal jigenn rek 😢😢
@@papasambadiop7599 sénégalais San pour San li ma guis europe sou amone afrique con gor dou ñeme lale jigenn mane nak deñma yar douma toude say way diour ndax menane ma juur balnala
Sa c le sommet vraiment enfaîte c la limite qu'oi sachant que tu vivra pas plus de 53ans il tue la mère de ces enfants quelle égoïsme j' ai très mal 😭😭😭😭😭
Merci papa bien dit l information est bonne pour ls cas similaires à venir. Il faut cesser de forcer un mariage instable due à la violence physique. Rester à cause des enfants qui sont devenus orphelins 😢
Père toi aussi tu as fauté quand il y a une situation comme ça tu vois que la fille est en danger il fallait bien la expliquer que son mari ce qu'il voulait faire et expliquer aussi à la famille mais il fallait pas attendre qu'elle soit mort pour nous expliquer ça maintenant ça n'a plus d'importance 😡😡
@@mameyandediouf9446c'est un voisin pourquoi attendre que la fille soit morte pour venir nous expliquer ce qui s'est passé si tu as la possibilité que un voisin te mais dans sa vie familiale et que tu vois quelque chose qui peut détruire la famille où il va avoir un mort d'homme tu devais signaler immédiatement avant que ça soit trop tard
Waxlo xam baxna merci tonton gnou waxtan touti fi Sénégal la xamanté nagnou defoi ngén balma jigén dina déff goor ci wallou serigne andak yaw dé dakoy gënël metina nalén yalla yërëm kén xamoul man dama ragal serign ci sama sëy dagnoulay tromatisé cé just une analyse com tout le monde 😢😢😢😢😢
Yaw Lo bok ak kou gorki fi pas de serigne sokhor rek mofi am dagay dé Lo yobalé yayou diambour tu de serigne y’a de ses femme talougnou serignetou liguey lagnou kham sokhor rek moko diap yalla nako yalla bougal noy faté bakéne dougou aldiana c impossible
Bilaye papa bima dégué liwakh kone môme meunoule dépassé 53ans kone dafa wara dé yobalé sokhname plus bima dégué ni sokhnasi nioguiko fék si kawe lalebi mou teudeu d'après les témoins kone affaire bi louche n'a lolll😢😢😢paix à leurs âmes
No Seck dé amena toma me serigne bi sow yawitd def nke touma si waye dème dij No Sénégale yalla nanio yalla defal diamou ak sotoura di netali ba copoul deé khana ngen nianal len yerma nde yalla ???
Est ce que amoul secret famille ... Plan bimou teurelone, yalla mi si andoul. Pour seck day sotti essence diabaram, Di banékhou si nimkoy laké. La femme ne s'est pas laissé faire.diamarlo ak dieukeur dji bagnou taak gnome gnarr
Maan daih daih gui nimoumah maiteh dafa djaigui dayo milliardaire sakh boma taiyaiwoul doumala lidjeunti Bilaay adouna bi dafa diekh bapareh ngou bari thi nioune sougnou khool yi mo khaat taiksi laboul forcé bi guene wara bayi Seck moom nama Borom bi Subhanahu wa ta ala baal mais intérieurement amna lou nek thi moom taiksi boona ingaan na maan taiméri doom takhouma tok thi seuy bou boon jamais...Li dara diarouko thi adouna djouliit dafaay djaileuleh di djaigueleh sa dairou Sokhna naiskooy yakeh koula djoureul ay doom boon daal amoul frontière... Khady Diouf yalna khiper Firdaws Barké alkhouraaan oul Karim daradjiay Nabi aleyhi salaat wa salam
Pa bi waxna deugeu interview biniou déf si chef de quartier bi yéneu si deukeudo yi danio décharge Seck diko waxal lou bax mais toudouniou femme bi sax
Cher dame affaire de mougnal yi bakhna Dal ,dinane fouma dieum AK ndiabote bi ? Sénégal reke ngeye guis genre yi ngalawaye arête si cela ne fonctionne pas divorcé et vous trouverez mieux
Si je comprends Bien le Mari était condamné,du coup il essayait de salír la Femme pour ke Bou yalla defone li gueun mou bagne remarié, après mou ham ni peut-être elle pourra se remarier mou suicidé AK môme 😢 d'après les explications
Yaw tamit massa beuri nga problème khana yafi né wone sa woudiou yaye mola diakhassé AK dôme baye ba doula toudou wala tamit sa béne kharit mola beugone signé lo papier pour diaye keur ci héritage nga bagne wala dou yaw
*Thieuy Yalla li doyna warr😢j’ai de la peine pour les enfants 🥺paix a leurs âmes 🙏🏽🙏🏽khady va en paix j’espère que tu trouveras la paix là bas🥺🙏🏽*
C’est triste des couples qui ont des problèmes ils faut la séparation c’est mieux pour éviter l’irréparable
Wallahi ma chérie. Mais Sénégal mougneul rek la gnouy wakh. Le divorce c'est pas une honte ou un péché. Il faut savoir dire stop quand ça va plus.
Machallah Tonton si témoignage bi kou bakhe ngue vraiment yalna la Yalla faye té ngui décédé yalna léne Yalla yeureume kharé léne aldiana
famille kou djiguene ki amou béen ndiarigne. sa dome di doundou souffrance, au lieu nga récupéré ko pour sa sécurité, nguén bayiko si seybi nane mougnal. Mougnal dafay féck mou done gor bouko diar.
Exactement
Bilaye senegale kou ame problème sa sey reck gnoune ko mougniale ba kagne nagnou bayi loulou te khole li thi bire
Seyou Sénégal bakane laye lathie😢😢😢😢😢😢😢
Billahi wallahi khady Diouf Sama rak dja, mon guene fouf, ngio NGIOU ngiep barke Borom touba, 😢😢😭😭😭, waye yalla bakhna 🙏
2:58 2:58 3:03 3:04 3:07 3:09 3:09 3:14 3:15 3:17 3:20 3:20 3:20 3:21 3:22 3:22 3:26 3:27 3:30 3:30 3:30 3:34 3:35 3:36 3:36 3:37 3:38 3:38 3:38 3:38 3:39 3:39 3:39 3:40 3:1 3:45 3:46 3:46 3:46 3:50 3:50 3:56 3:58 3:58 4:01 4:03 4:03 0 3:11 4:05 4:05 4:06 4:07 4:08 4:08 4:12 4:12 4:13 4:14 4:16 4:16 4:17 4:1😮 4:26 4:28 4:28 4:29 4:29 4:38 4:39 4:40 4:41 4:43 4:43 4:23 4:25 8 4:19 4:20 3:11 3:13
4:51 4:54 4:54 4:54 4:55 5:01 5:15 5:16 5:17 5:20 5:21 5:22 5:22 5:23 5:23 5:23 5:23 5:24 5:25 5:27 5:32 5:32 5:33 5:39 5:40 5:41 5:46 5:5 5:53 2 5:59 6:06 6:10 6:18 6:21 6:22 6:23 6:25 6:25 6:26 6:29 6: 6:39 6:33 6:44 6:44 6:46 6: 7:09 7:20 7:21 7:25 7:26 7:27 7:29 48 7:32 7:32 7:33 7:33 7:34 7:42 7:03 7:46 7:46 6:49 6:51 7:48 7:51 :48 7:54 7:54 7:49 7:49 7:57 7:58 7:5 8:02 8:03 8:03 8:03 8:04 8:05 8:07 8:08 8:08 8
Papa tu as très bien parlé sa kadou rafetna
Bayi len di nane sen dome yi setal si xale yi di nane sey kate moy diour dome you barkel legui rey na ndasi 😢😢😢😢😢 goroul africain toroxal jigenn rek 😢😢
Sa papa mom khana gorou europe leu???
@@papasambadiop7599baye diou bakh la ame rek mo takh
@@papasambadiop7599nos propres pères sont fautifs, niou wakh ko té dé
@@papasambadiop7599 sénégalais San pour San li ma guis europe sou amone afrique con gor dou ñeme lale jigenn mane nak deñma yar douma toude say way diour ndax menane ma juur balnala
@@khadydieng1381 dego mogui saga sama bay waye balnako
Non Sénégal doy n'a war bilahi yallah nañou yallah mousal sy seytane
Merci de ton courage ❤❤❤❤
Yalna yalla yeureum kho
Sa c le sommet vraiment enfaîte c la limite qu'oi sachant que tu vivra pas plus de 53ans il tue la mère de ces enfants quelle égoïsme j' ai très mal 😭😭😭😭😭
On vit plus jusqu à 100 ans de nos jours mais cela n’ inclut pas de tuer
J’ai trop mal pour cette famille C’est horrible des enfants orphelins par la lâcheté de leur père
😞😞😞😞😞 quelle horreur ! Pas de mots, repose en paix khady diouf
Tonton tu a bien dit nitñi nañou bayi tapalee di wakh deugg yalah nalen yallah kharee aldiana
Khamnani Khady dale wayam rafetna sèdèyi rafetna wakhdji bène Yalla na Yalla knarèko Aldiana mok ak borom keur gui
Merci papa bien dit l information est bonne pour ls cas similaires à venir. Il faut cesser de forcer un mariage instable due à la violence physique. Rester à cause des enfants qui sont devenus orphelins 😢
mane de dama leni nianale yala yeureum lene khare lene aldiana firdawsi si barke seuydina mouhamad psl 🙏 🙏
Père toi aussi tu as fauté quand il y a une situation comme ça tu vois que la fille est en danger il fallait bien la expliquer que son mari ce qu'il voulait faire et expliquer aussi à la famille mais il fallait pas attendre qu'elle soit mort pour nous expliquer ça maintenant ça n'a plus d'importance 😡😡
Non mais qu est ce qu’il fallait faire il n est pas son père c est juste un voisin
Exactement
@@mameyandediouf9446il n est pas son voisin il a marié sa tante écoute
@@mameyandediouf9446c'est un voisin pourquoi attendre que la fille soit morte pour venir nous expliquer ce qui s'est passé si tu as la possibilité que un voisin te mais dans sa vie familiale et que tu vois quelque chose qui peut détruire la famille où il va avoir un mort d'homme tu devais signaler immédiatement avant que ça soit trop tard
Waxlo xam baxna merci tonton gnou waxtan touti fi Sénégal la xamanté nagnou defoi ngén balma jigén dina déff goor ci wallou serigne andak yaw dé dakoy gënël metina nalén yalla yërëm kén xamoul man dama ragal serign ci sama sëy dagnoulay tromatisé cé just une analyse com tout le monde 😢😢😢😢😢
❤❤❤
Yaw Lo bok ak kou gorki fi pas de serigne sokhor rek mofi am dagay dé Lo yobalé yayou diambour tu de serigne y’a de ses femme talougnou serignetou liguey lagnou kham sokhor rek moko diap yalla nako yalla bougal noy faté bakéne dougou aldiana c impossible
Bane Serigne? 😂😂 Shimm rk Nii rk ngéne Di déff
C était un psychopathe
😭😭😭😭😭 Ndeysane Ndeysane Ndeysane and very sad.
Sénégal ngay guiss niouy seetane violences conjugales bamou indi saafane kouné témoigner. Motakh djigueen gni khamlene sen valeur té bania nangou yéneu yi
Goor Bou bone rek sokhor ignane
D apres les explications on peut en deduire que le mari etait psychologiquement perturbé
Dessane li metina trop sakh yalnalene yallah yeureum têt kharelen aldiana Thi Barker alkhourane
Ndeysane khady kou yarou ndango ligueye
Bilaye papa bima dégué liwakh kone môme meunoule dépassé 53ans kone dafa wara dé yobalé sokhname plus bima dégué ni sokhnasi nioguiko fék si kawe lalebi mou teudeu d'après les témoins kone affaire bi louche n'a lolll😢😢😢paix à leurs âmes
Médecin après la mort 😢😢😭😭😭
Y’a bien dit machalla
Paix à leurs âme oh Ndeysan 😢
Ki dafa bone waye😢😢😢
Ça alors soubanala ☹️ la paix avant tout sinon la séparation c'était mieux paix à leur âme
li métina trop way yalla naléne yala yeureume oyofal Souf séne kaw
Yalla Yeureum lène amine waye
Merci papa thi eclairissement
Mais yéne tamite sétaane nguéne parceque yéne guiss nguene comportement waadji nguéne diko mougneloo légui nak raynako mome moo perté ak ay doomame c esr fini
Wah nga dëgg jigeen foumou améwul jamm warè soukoo fa bayyi
Pourkoi nguèn stane ba li yèp khew deuk diam mathie gueun surtou negou sey dafa waratah am harmonie
Esk rayouko ba paré soga tal keurgui😮
Bonne question
Il était un malade ce mari
Fi fanla. Si Sénégal
Niague
😢😢😢😢😢
Am na solo
Paix à leur âme
No Seck dé amena toma me serigne bi sow yawitd def nke touma si waye dème dij No Sénégale yalla nanio yalla defal diamou ak sotoura di netali ba copoul deé khana ngen nianal len yerma nde yalla ???
Limou wakh darà nekou thii pour ancha la kenene
Sou déwé nak ? Sou défé dougn ko wakh ?
Allah ahlamu☝🏾Loula leeroul mome fékkéwo waroci sédé
Ak lou manti khèw raye nit talko eupheneu.
@ndeyefatouba1012 Ray nitt kay bakhoul bakhoul mais nk leernala mako ray
@@MbodjAmadou-dw3shpolice Dina si enquête
Tonton ioe tamite pourquoi depuis lors ta rien dit 🤦♀️🤦♀️🤦♀️🤦♀️
Est ce que amoul secret famille ...
Plan bimou teurelone, yalla mi si andoul. Pour seck day sotti essence diabaram, Di banékhou si nimkoy laké.
La femme ne s'est pas laissé faire.diamarlo ak dieukeur dji bagnou taak gnome gnarr
Linga wakh tmt c'est possible
Tak diabar ba paré defko ennemie chiiim
Billây boneu rekh me dina xam loumouy wakh yallah
Vous êtes tous responsables il ne fallait pas les réconcilier
Maan daih daih gui nimoumah maiteh dafa djaigui dayo milliardaire sakh boma taiyaiwoul doumala lidjeunti Bilaay adouna bi dafa diekh bapareh ngou bari thi nioune sougnou khool yi mo khaat taiksi laboul forcé bi guene wara bayi Seck moom nama Borom bi Subhanahu wa ta ala baal mais intérieurement amna lou nek thi moom taiksi boona ingaan na maan taiméri doom takhouma tok thi seuy bou boon jamais...Li dara diarouko thi adouna djouliit dafaay djaileuleh di djaigueleh sa dairou Sokhna naiskooy yakeh koula djoureul ay doom boon daal amoul frontière...
Khady Diouf yalna khiper Firdaws Barké alkhouraaan oul Karim daradjiay Nabi aleyhi salaat wa salam
Soudone mom douma nieuw damay tokk sounou keur soma sokhla nieuw
Pa bi waxna deugeu interview biniou déf si chef de quartier bi yéneu si deukeudo yi danio décharge Seck diko waxal lou bax mais toudouniou femme bi sax
Ngéne balma dh mai nopi moléne war li khew kham ngéne lep paix à son âme
Louy loolou moom da see am benn sañ sañ . Leegi dou retracer les causes et conséquences telles qu'elles sont
Senegal tant que maattoo sèy sagar dou gnou le gissé kou wéradi. Les maladies mentales sont réelles. Yaalla na Yaalla yeureum.
Soxoor guénn Di diawalé ak fébar dara diotouko daa bonn rék douma dé mane késsé 😢😢
😢😢😢Ndéyssane li métina torop surtout xalé yi ils sont orphelins du jour au lendemain 😢😢😢d
Cher dame affaire de mougnal yi bakhna Dal ,dinane fouma dieum AK ndiabote bi ? Sénégal reke ngeye guis genre yi ngalawaye arête si cela ne fonctionne pas divorcé et vous trouverez mieux
Mastah paix a leurs âmes
Si je comprends Bien le Mari était condamné,du coup il essayait de salír la Femme pour ke Bou yalla defone li gueun mou bagne remarié, après mou ham ni peut-être elle pourra se remarier mou suicidé AK môme 😢 d'après les explications
Ligay wakh khamo si dara lo fekewoul losi sédé ay féne la
Limou wakh Kay dako kham
Amolen lolen wakh😢khaar ba Diane dem nga top du dore😢
Ho l’ ignorance dans ce pays
Waxoul dara lou niaaw limou xam la wakh te lolou moy degue
Alakhou ahbar
wa legui explosion bi louko waral kone
Je crois que verre yi ak takk takk bi mo waral explosion bi
Seck psychopathe deuggg leu😢😢😢😢
Khady mome elle été naïve N'Dakh. Ki Di wakh ni meuna khamni sa borom. keur. té. yow mi am aK mome dom khamoko ! Bia. li fekkla thi !
Walahi tu es véridique nite daguaye sédé deugue
👍👍👍
man sama ex diabar mougi neubeu sama dom 8ans meusoumoko giss۔mou nieuw sama galle nan niou delouwat😮dougatoumasi dee
Yaw tamit massa beuri nga problème khana yafi né wone sa woudiou yaye mola diakhassé AK dôme baye ba doula toudou wala tamit sa béne kharit mola beugone signé lo papier pour diaye keur ci héritage nga bagne wala dou yaw
@@aissatoumarone2095 😅😅😅wooyy
Est ce que ce n'est pas un coup de feu genre pistolet
Yam mi kou deugou nga
mais tamit Sey dagan n'a tass dagan 'na pas la mort a ce point comme si c'est la fin du monde
Ki.dafa.gueumoul.yalla.febar.boumou.takh.gia.rankinier.ba.lor.sa.diabar.li.dara.diarouko
COMME DARA BETTOULATHI D PRES SEENI WAKHTAANE YOW NIDIAANE WAROONENGA RETIRER SA NIECE PUISQU IL YAVAIT PAS DE SOLUTION
Khana guinaw ngay deg lo..wala dego limou wakh
Louyakhou yenaco yakh
Dou Courant dou gaz Kon bok lanla yemena
Paroles Insensés...A quoi bon ce bla bla...Arrêtez de faire des
Vidéos de ce genre...!
Paroles très sensées bien au contraire !
Paroles très sensées bien au contraire !
Sédé lo fékéwoul nit day mandou kou ngéne adouna wahal thî mom Lou rafét
Yaw es ce que xamgha louy mandou ?
@@aminataa1838wakhna deug lo fekewoul losi wakh ay féne la
Na fek mou done dieuf lou rafet si Kaw souf la femme miko dieuf waxal nanioukoko
Walahi deug Bou werr nga wax sénégalais mo deugeur fitt
Limou ko khamal la wakh hypocrisie bakhoul