Waxtane bou neex ak Père Mansour Diop qui encense Boy Niang sur Reug Reug…

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 28 окт 2024

Комментарии • 20

  • @aliouneelevage6482
    @aliouneelevage6482 2 месяца назад +3

    Pere mansour toujour fierte de l ecoute

  • @NdiaboutaDiouf
    @NdiaboutaDiouf 2 месяца назад +2

    ndiabouta diouf slu merci pere mansour diop yalla na boy niang dann reuf reug diel bou gaw te yomb inchalla rabi

  • @MadiopNdiaye-iy6jg
    @MadiopNdiaye-iy6jg 2 месяца назад +3

    Per Mansour diop💚💚💚

  • @malickdia3495
    @malickdia3495 2 месяца назад

    Machalah ndame recke inchalah cikaw cikaname inchalah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @damembengue1894
    @damembengue1894 2 месяца назад +1

    Lutte tv for ever ❤❤❤

  • @__mgk__wolf__man6301
    @__mgk__wolf__man6301 2 месяца назад +3

    En tout fou Reug Reug diap boy niang Iamb dji diekh deIen wakh rek, amouI mbeur bouy yewo ecurie DegauI bou meuneu dane Reug Reug

  • @youssoudiokhane3600
    @youssoudiokhane3600 2 месяца назад +2

    PÈRE MANSOUR DIOP ALIAS PÈRE DOLÈ...MÈME SOUYE WAKHE SI SERIGNE TOUBA SAKHE DOLÈ LAYE WAKHÈ ...DIADIEUF PÈRE MANE SA FANS LA 😂😂👊👊

    • @Bayeniang20
      @Bayeniang20 2 месяца назад +1

      😂😂ki di na youkhou ba deee fi 😂bilahi ko pere zora😂wesh

  • @IbrahimaDiop-v9l
    @IbrahimaDiop-v9l 2 месяца назад

    Pere mansour le meilleur

  • @bakaryceesay8141
    @bakaryceesay8141 2 месяца назад

    Kon bayil ma gel o'r😂😂

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 2 месяца назад

    Kon bayile 😂😂

  • @Concept0208
    @Concept0208 2 месяца назад +1

    1-Reug Reug ndanane la mais bo xolé ñimou dane dañko naw ci beurém, soraléko de trop. Ñew beuré wouñou, xexouñou. Kén defou ci lou Reug Reug dindi (Elton, Jordan, BB Saloum, Gris 2, Gouy gui, Bomb) Sa thies seul la guiss mou minimiséko (lingay beuré danoul sax sama dom), dox ci kawam dane ko.
    2- Li Boy Niang di beuré arrangéwoul Reug Reug. Boy Niang doko fété souf, doko dadialé. Xolal la defaite de Reug Reug contre General en Mbapatt dinga comprendre.
    3- Boy Niang lén rek la soxla ci mom, force interieure, mobilité, souplesse et endurance. Souko amé bén action bounou ame ci Reug Reug daneko inchaallah.
    Mais loumou soralé ci Reug Reug niak combat bi. Reug Reug bokay dane do hesité ci bén action té kén douko bayék Lamb ci biir guéw
    Yalnañou ci Yalla yobou ci diamak salam.

    • @mansourdieye9494
      @mansourdieye9494 2 месяца назад

      Reug reug kouy calculer doko daane té boy Niang beurém yeup calcul leu reug reug dafa mané lolu fouko reug reug diapp mou diéex

    • @Concept0208
      @Concept0208 2 месяца назад

      @@mansourdieye9494 Boy Niang dafa fiir ci ay thiereum. Boy Niang ci bén bénal bobou la beurém guëna assuré. Parceque sa you forcé ñiak combatwam (Lac, Mod'lo). Donc na sax ci manineum, gana liguey explosivité ak endurance. Niom niar kou ague sa morom fou sori daneko.

    • @mansourdieye9494
      @mansourdieye9494 2 месяца назад

      @@Concept0208 saway léne xamnako dé Reug reug foumou leu beugue diapp dinala yote ba diapp leu xana guissou bombardier droite bi mo gueuneu danger si mom té Reug reug dako fate ba diapp ko té Reug reug foumou diapp si guimb boy Niang bou yaboo wa Pikine diok té guéne stade bi xamné boy Niang paréna reug reug moko eup beurré eupko dolé

    • @Concept0208
      @Concept0208 2 месяца назад

      @@mansourdieye9494 Yalnañou ci Yalla yobou ci diamak salam.

    • @mansourdieye9494
      @mansourdieye9494 2 месяца назад

      @@Concept0208 inchallah ba le jour. J

  • @AmadouDia-o6d
    @AmadouDia-o6d 2 месяца назад

    Reureugue numou beurré 1danoule boy niang meme souko reureugue wor domba s1

    • @__mgk__wolf__man6301
      @__mgk__wolf__man6301 2 месяца назад +1

      Wakho deugeu dh biIIahi fou reug reug diap boy nianng Iamb dji diekh. Reug reug amouI ben mbeur bou nek ecurie de gauI bouko meunneu dane

    • @KhadyBa-x2r
      @KhadyBa-x2r 2 месяца назад

      Reug dakoy fakate mou reup inchallah yallah wonamako 😊😢❤😮