"Balla Gaye Sakh Manou Ma Dan" Séye Diambar Wakh Na Dei Modou Lo avant le combat" Moma Wakh néma..."

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 7 янв 2025

Комментарии • 25

  • @MaraGaye-t7f
    @MaraGaye-t7f День назад +4

    Entous cas daal khaw ma lo manoul ms khékh bokou thi modou lo moy sa baay bonne continuation rk inchallah 🙏❤

  • @malicksarr2141
    @malicksarr2141 23 часа назад +3

    Allez champion seuy diambar❤

  • @AtoumaneNiasse
    @AtoumaneNiasse День назад +2

    Machallah fils neksi rk yalla bakhna ❤❤❤

  • @votremiroir7612
    @votremiroir7612 21 час назад +14

    délén wakh deug sén titre yi, boybi wakhoul Balla gaye manouko dane. yaw mi bind titre bi kou mana fén nga. yay takh ma desabonner

  • @ibrahimadrame9499
    @ibrahimadrame9499 День назад +3

    😢😢😢😢fils kholal sisa baye rék digua done diambar force

  • @bachirdomouparcelle4293
    @bachirdomouparcelle4293 19 часов назад +1

    Y’a meuna xeeex 🎉❤

  • @lougalo969
    @lougalo969 17 часов назад +1

    Li motakh doléne nékk champion. Lewto 10mn nieuwe di takk radios yi

    • @afro3827
      @afro3827 16 часов назад

      😂😂😂😂

  • @sophrotall8105
    @sophrotall8105 9 часов назад +1

    Kou fen rek nga wediko bagn ko setane benenn yonn off say video

  • @GoraMbengue-f2j
    @GoraMbengue-f2j День назад +4

    Seye champion nga mais lamb so khékhé ba guiss bountou dangay diapp beuré mais di door rekk lolou moom franchement dou lamb .

    • @modo6218
      @modo6218 День назад

      Wakh degue yalla

  • @DameNdiaye-z3t
    @DameNdiaye-z3t 18 часов назад +1

    ❤❤❤❤❤❤

  • @Adouna7361
    @Adouna7361 9 часов назад

    Seye bb talla da fébare rek Mais khame gani dousa morome déle wakhe rek

  • @bayemodoufall2879
    @bayemodoufall2879 22 часа назад +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂

  • @cheikhbasskeurmassar9548
    @cheikhbasskeurmassar9548 17 часов назад

    Séye jambar yaw lou takh daano bébé talla te bébé talla blessé

  • @NguerFaye05
    @NguerFaye05 22 часа назад +1

    Bebe talla nekoul si dara témano ko dane sawah mo bari wagnile wahji té fèhé di diap dibeuré

    • @ModouDiouf-i4d
      @ModouDiouf-i4d 18 часов назад +1

      beurer 2 personne gnokoy def saway

  • @BadaraGueye-ii5gh
    @BadaraGueye-ii5gh 15 часов назад +1

    Defal😂reucor

  • @afro3827
    @afro3827 22 часа назад +1

    Gni dess si poul bi gnola man fouf 😂😂😂

  • @LDM6812
    @LDM6812 18 часов назад

    Bayilén fén ci sén titre yi dina désabonner

  • @modo6218
    @modo6218 День назад +1

    Sey diambar yaw nak lambe dou khekh kasse yaw man ngua beurè kay do dem beurè

  • @Adouna7361
    @Adouna7361 8 часов назад

    seye daga dawe beuré bi bayile wakhe diou bari dji

  • @wadeidrissa7410
    @wadeidrissa7410 23 часа назад +1

    Boy bi mome khamoul bopam essais d'être comme petit c mieux sois un peu humble

  • @Moulayeofficel-y3v
    @Moulayeofficel-y3v 15 часов назад +3

    ❤❤❤❤❤❤❤❤