Masha.allah Alhamdoulilah Serigne Amadou mbacké Mbacké yalna yalla goudeul fanwi téh mou and ak weer Vtaiment tu fais la fierté des mourides bonne continuation ❤❤❤❤❤❤❤🙏🙏🙏
Maasaalah lii moom bu yàggee ñépp xam dëgg-dëgg murid lii lañ bëgg ngeen wax ñu sëriñ bi mooy kan, fum tegoon tànkam leegi ñun taalibe yi xam nañ bu baax te bëgg nañ lu baax kon mission bi def leen ci lépp looleen mën.
Maasallaa waxtaan wi am na solo lool amna maanaa . Yàlla na leen saa Boroom dolli tawfeex ci xam-xam ak barke. Maa ngi sàkku ci s abdu xaadr bu laajee ab laaj na bayyi giy def waxtaan wi développer ba noppi mu doora commentaires, budul loolu rekk giy def waxtaan wi manaa tënku ba du leeral lim bëgga leeral dëg dëgg Noo ngi tuub bu baax a baax nak di sant bu baax.
Masha.allah Alhamdoulilah Serigne Amadou mbacké Mbacké yalna yalla goudeul fanwi téh mou and ak weer Vtaiment tu fais la fierté des mourides bonne continuation ❤❤❤❤❤❤❤🙏🙏🙏
Aamiin bijaahi Xadiim
Macahallah amna solo lool yàlla nanu yàlla defal degg ak topp sëriñ Ahmadu mbacké Yàlla Nafi yàgg lool lool te werr amiin
Aamiin bijaahi Xadiim. Jarajëf s abo jòob
Magui niane yalla mi dra tawoul mou yagal lafi ta wéral la mbacke ❤
Jarajëf sñ Seex Ibra
Amiin amiin ci barkeb sëriñ Tuuba
Amine ya rabbi ❤
Amiin
machalla borom xam xam bu seel
bi.
kiy deff emission tamit nakoy teewlu diko bagn didag moo geun ✅
Jarajëf ku baax ki
Serigne Ahmedou mbacke yalla nala yalla défal diam
Machallah yalna yalla takhaou lène thi barkeb s fallou Mbacke
Aamiin bijaahi Xadiim.jarajëf Sëriñ Pape Diop
Serigne montakha yalnaf yague lool té wer amine 🤲🙏
جزاك الله خيرا شيخنا، فأنت خير خلف لخير سلف؛ جدّد الله رحمته الواسعة على والدك الكريم.
Aamiin bijaahi Xadiim. jarajëf Sëriñ Mamadu Njaay
Masha.allah Alhamdoulilah santati yalla bou ❤❤❤❤❤
MACHALLAH
Machallah... Niari borim xam xam. Wanté présentateur bi na bayi seriñ bi waxx... bu muko dagg.
Machallah amatina solou lool 🤲🤲
Jarajëf yaaram
Oh mbackei balla yag fi rek t weiir kou baakh t oyoff souma fattalikou diotayou goudi aljuma yi fa keureum rek oh❤❤
Kou bakh mogui té ragal yalla sagal yonou mouride machaalla
Jarajëf Sëriñ bi jongg
Mane mome wakh degue yalla nit kou baxe né cheikh ahmadou mbacke mi la guisoul balla aicha ya bax té ak ay teguine way ohhh❤❤❤
Ndeysaan yagg leen fi te wer
DIEUREDIEUF SERIGNE TOUBA ❤❤❤❤
Wa darou moukhty ay tanèf lagne❤
Jaajëf yaaram
Serigne Ahmadou yalla nako saa borom geuna sammou❤
Xol yii sédd nañ lool Mbàkke balla❤❤❤
Jarajëf
Bismilah barké cheikhoul khadim
Jaaraama soxna amy
Jetejef mbacke balla Yalnangafi yagg lolou tei wer
Aamiin bijaahi Xadiim
Dieuredieuf dieuredieuf.
Jarajëf Sëriñ bi Jéey
Maasaalah lii moom bu yàggee ñépp xam dëgg-dëgg murid lii lañ bëgg ngeen wax ñu sëriñ bi mooy kan, fum tegoon tànkam leegi ñun taalibe yi xam nañ bu baax te bëgg nañ lu baax kon mission bi def leen ci lépp looleen mën.
Inshallah sëriñ bi Faal. Jarajëf
Serigne Mame Mor Yalna sunu Borom Doli leen tawfeex liguey walahi kawé na fi nioun lolou ❤❤❤
Aamiin bijaahi Xadiim, jarajëf sëriñ Mbasa FAY
Machalla mbacke bala yage fui lole té were ❤❤❤❤❤
Aamiin bijaahi Xadiim
Machalah
Oh ❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Masallah
Jarajëf sñ Bassiiru jòob
❤❤❤
Maasallaa waxtaan wi am na solo lool amna maanaa . Yàlla na leen saa Boroom dolli tawfeex ci xam-xam ak barke.
Maa ngi sàkku ci s abdu xaadr bu laajee ab laaj na bayyi giy def waxtaan wi développer ba noppi mu doora commentaires, budul loolu rekk giy def waxtaan wi manaa tënku ba du leeral lim bëgga leeral dëg dëgg
Noo ngi tuub bu baax a baax nak di sant bu baax.
Aamiin bijaahi Xadiim. Jarajëf ku baax ki ci ñaan yi ak laabiire yi
Bien noté kubaax, dees na ko bàyyi xel. tey sant ci laabiré gi
Mashallaa Amatina solo Mais AKB deel bayi invité yi di yaataal
Yow deh sagouop seringe touba ❤ yagge fi loll
Dëgg la Mbàkke Sëriñ Siidi
Chekhoul khadimmmm
Sëriñ Muhammad, kooka amul Moroom
Amoul morom ❤❤❤
Aboner leen te partager mu gën a yaatu❤Sëñ Ahmadu Mbàkke bëgg naala lool Yàlla xam na ko❤
Jarajëf sñ Mustafaa
❤
Jaajëf Murid bi
Jerejef borom tubaa
Amul Moroom. Jarabu sñ Murtada ka
Machalla ❤️ amna solo
Jajeuf
@@toubausatv jarajëf
Kiy def émission jambaar la waaye na bàyyi sëriñ bi mu développé
Gueuna yagg Gueuna wer Barkep Borom Tuuba
Aamiin bijaahi Xadiim
Pour man au moins nga mayko 5mnt mu développé Après nga commentaire Joxaat ko mu Aggale
Bayyil serigne bi mu wakh monoo laathi ba noppi ngeun koo begua xam li nga ku laathi ish
Xam Xam bi wer na ler na
Jarajëf yaaram
Amna sollo lool xana di wax rék abdou khadre ba téew lou invite bi limi intervenir da xawa barri
Jarajëf yaaram, degg nañ laabiire gi
Thi sawou diante fepou melni thia diaye waye
جزاك الله خيرا شيخنا، فأنت خير خلف لخير سلف؛ جدّد الله رحمته الواسعة على والدك الكريم.
Aamiin bijaahi Xadiim
❤❤❤❤