Doyalouniou dé Serigne Maodo ! 2stv, Serigne Ahmed Fall ak Serigne Mame Ousmane Ndiaye Dieureungene Dieuf ! Yalna Yalla faylene bijahi Rassoulilah sws !
Serigne Ahmed Fall ak Serigne Mame Ousmane Ndiaye Haj Maodo Faye si plateau. NI rek la meneu deme wakh bou yiw and ak dal kham kham bou léer and ak mandoute Yalla na Yalla doli soutoureu ak barke bijahi Nabi Moustapha
Machala rafetna sy malik yalnako yalla yok leer so wolee diotay direk guis Diabote gui rek khani Maodo yarkat la xam xam bouleer ak yar ak teguin rek nofi fegne merci l'équipe de 2Stv ak tam invité yi sa c voit que éléments mame Maodo guene machala rafetna
Machaallah wakhtane bi amena solo.Cheikhna Ahmada Tidiany Chérif RTA seutou yonent bi Seydi El Hadji Malick SY RTA yalnanouléne borom bi fayal.Oustaz Ahmed Fall sama sopé bi .yalnaléne bour yalla fay thi barké borom goudi gui
Kéne dou seydil hadji malick sy rta, wallahi mognou khamal ki gueune gneupe stw. Yalna yalla Samme khadaratoul tidiani ak kouli mouslimina wal mouslimati bi diahi Moustapha stw.
Serigne Babacar Sy a dit que : " Cheikh Sayyidil hadji Malick Sy aurait dû venir au monde au temps des compagnons du Prophète saws mais Allah l'a gardé pour notre temps en vue de nous aider et nous sauver !". Par ailleurs, Tout le Sénégal doit savoir toutes confréries et toutes communautés confondues que au temps de Cheikh Sayyidil hadji Malick, tous les guides de ceux que je viens de citer sont venus faire allégeance à Cheikh Sayyidil hadji Malick. Sans Exception. Et ce statut de guide général, il l'a hérité de son guide spirituel et oncle Cheikh Alfaahima Yoro Wellé qui lui-même de Cheikh Sayyidil hadji Oumar Foutiyi TALL. Serigne Babacar Sy a dit : " Les grands disciples de Cheikh Sayyidil hadji Malick ( comme par exemple Mame rawane ngom ; Gorgui Abdoul Hamid Kane etc...) et tout ce qu'ils savent de lui sont comparables à un enfant qui aurait ramassé un morceau de diamant sans savoir ce que c'est hormis la beauté de la pierre car cet enfant ne sait pas cette pierre peut subvenir à ses besoins et à celui de son père durant toute une année". NB: Concernant la Linguère ( princesse) qui voulait que Cheikh Sayyidil hadji Malick l'épouse et que ce dernier a subtilement décliné ce n'était pas du tout pour éviter de déraper et d'en prendre potentiellement une 5ème après la Linguère qui serait la 4ème. Car Cheikh Sayyidil hadji Malick Sy est " Mahfouz " c'est à dire protégé par Allah contre tout type de péché. Encore moins prendre une 5ème femme qui est un grand péché. Les raisons de ce refus sont à chercher ailleurs que dans cette explication. Conclusion : Quoi que vous ayez entendu de bien ou qui semble extraordinaire sur Cheikh Sayyidil hadji Malick Sy, sachez qu'il reste encore d'autres aspects de son personnage que nous tous sommes loin d'imaginer encore moins de savoir ! ESKÈY Alaadji Malick, ESKÈY Alaadji Malick, ESKÈY Alaadji Malick.
Fidal kou fi raw gnon ngui koy khamé ci sa ndiabot. Talibé youy Gnaka djoulit, gnaka wor, bokalé. 33 femmes 4 you bok ndeye ak baye beu paré nane ya yesseul diné. Khana mabal diné kay.
Ndeysan Mame Ousmane xool bi toyna yalla na léne yalla defal yiw si barke Seydina Mohamed SAWS
Mashallah á travers Les eleves on reconnait Le professor
Allahou Akbar, Waye Niari Diemou yi Ma sahallah
Doyalouniou dé Serigne Maodo ! 2stv, Serigne Ahmed Fall ak Serigne Mame Ousmane Ndiaye Dieureungene Dieuf ! Yalna Yalla faylene bijahi Rassoulilah sws !
B
Walay ndeysane mame maodo malick sy yalnanou ko yalla fayal
So beugué kham sa Serigne kholal si talibéyi machallh yar gui fégn na xam xam bi fégn na wakh li am fégn na lérou yallah dou rakh leundeum way♥️♥️♥️💯
Al-hamdoulillah machaalla yallah na yallah faye yiw thi barke mame maodo malick 😭😭❤❤
Machallah 🙏🙏 yalna len yalla defal diam si barke seydina Mohamed contannaniou machallah xam xam rek mo am solo👏👏👏👏👏👏👏
Kou nitewul manoul nek talibr maodo deko gnane yallah nangoul ko alhamdoulilah
Wallahi ahmet Fall man dh yaye sama eférelgan
Macha alla
Cheikhal Hadji Malick Sy l'inconnu de la nation sénégalaise
Serigne Ahmed Fall ak Serigne Mame Ousmane Ndiaye Haj Maodo Faye si plateau. NI rek la meneu deme wakh bou yiw and ak dal kham kham bou léer and ak mandoute Yalla na Yalla doli soutoureu ak barke bijahi Nabi Moustapha
Waw
Machala rafetna sy malik yalnako yalla yok leer so wolee diotay direk guis Diabote gui rek khani Maodo yarkat la xam xam bouleer ak yar ak teguin rek nofi fegne merci l'équipe de 2Stv ak tam invité yi sa c voit que éléments mame Maodo guene machala rafetna
Wah diou ler sel tegou ci kham kham. Merci maodo
Machall refftna yallna yall kodal senfafn je bark seydena Mohammed Sw amin refftna jerjaff
Dieuredieuf Cheikh Seydil Hadji Malick Sy 💖
Machallah wakhtaan bou bari kheweulou kham kham
Machalla kéne dou yonéne teu bi
Bilakhi walakhi Talakhi Cheikhal Hadji Malick Sy wathioo na ak nioune Yalla naniou ko Yalla Fayal né nangoul niou souniou thiofél si moome
Machaallah wakhtane bi amena solo.Cheikhna Ahmada Tidiany Chérif RTA seutou yonent bi Seydi El Hadji Malick SY RTA yalnanouléne borom bi fayal.Oustaz Ahmed Fall sama sopé bi .yalnaléne bour yalla fay thi barké borom goudi gui
Kéne dou seydil hadji malick sy rta, wallahi mognou khamal ki gueune gneupe stw. Yalna yalla Samme khadaratoul tidiani ak kouli mouslimina wal mouslimati bi diahi Moustapha stw.
Mancha allah yallana yalla fayalenou mame cheikh seydi elhadji MALICK sy amine
Ahmed f yálla gua goude vane Amine
Machallah sy malik ken dou seydil Hadji malik sy amoul morom 🙏🙏🙏🙏❤❤❤❤🕋🕋🕋🕌🕌🕌
Machalla walay ndeyssan lou ame solola
Kou beugue yonéne bi faw gua beugue maodo.thiey maodo
Nékhoul ba nékhoul mais ken'dou seydil khadji malick sy diadief oustag maodo diadief oustag ahmet fall diadief mam ousman' ndiay
V3 4..... 66
Diam si yein Macha Allah
Noo maodoooooo Machalla
Machallah kou lén deglou bou bakh dina si dieulé lou bari.
Maodo faye tay mérenala ndakh lingaye dagu ahmet Fall ahmet Fall dafa bari torop
Machalah sama niari sope yiniou bolé invite sedna xol serigne mame ousmane et serigne ahmad fall yallna yalla faylén yiw
Kou beugue SEYDI EL HADJI MALICK SY fo k nga am xam xam. Li dougnou bett ci ay talibéme
Machala wakhtann wi amna solo
Machala tivaouwane notre fierte
Macha'alla yalla faye
Machalla dieureudieufaty
Ma challah mame Maodo kéne dou
Dierediefe ti seydil khadji malick sy diarama serign babacar sy
Machalla yalna yalla fayy léne
جزاكم الله خيرا و خفيظك الله
Machalah quel fiérté.yalana yalla dole lerr
Machalla 2stv
Machalla xamxam bi selll na
Tabarakallah waxtane bi amna solo
Machaalah kham kham rek wallahi Hadji Maodo faye yà kham temps
Thiey Maodo manchala yalna yalla feyalgnouko barké Nabil Moustapha PSL
Kou leine dakka invité Yalla sakou ko yénneu ayeu ❤️❤️
Macha allah laf thiat yallah na yallah samma len amin ya rabbi ci barke seydina Mohamed saws
Mach'Allah Dieureudieuf borom kham kham yi.
Y'Allah nalène y'Allah feye yiw.
Wafi nékhna way
Machalla dieuregendeuf ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂👂🇮🇹🇮🇹🇮🇹🇮🇹🇮🇹🇮🇹🇮🇹🇮🇹🇮🇹🇮🇹🇮🇹🇮🇹🇮🇹🇮🇹🇮🇹🇮🇹🇮🇹🇮🇹🇮🇹🇮🇹🇮🇹🇮🇹🇮🇹🇮🇹🇮🇹🇮🇹
Serigne Babacar Sy a dit que : " Cheikh Sayyidil hadji Malick Sy aurait dû venir au monde au temps des compagnons du Prophète saws mais Allah l'a gardé pour notre temps en vue de nous aider et nous sauver !".
Par ailleurs, Tout le Sénégal doit savoir toutes confréries et toutes communautés confondues que au temps de Cheikh Sayyidil hadji Malick, tous les guides de ceux que je viens de citer sont venus faire allégeance à Cheikh Sayyidil hadji Malick. Sans Exception. Et ce statut de guide général, il l'a hérité de son guide spirituel et oncle Cheikh Alfaahima Yoro Wellé qui lui-même de Cheikh Sayyidil hadji Oumar Foutiyi TALL.
Serigne Babacar Sy a dit : " Les grands disciples de Cheikh Sayyidil hadji Malick ( comme par exemple Mame rawane ngom ; Gorgui Abdoul Hamid Kane etc...) et tout ce qu'ils savent de lui sont comparables à un enfant qui aurait ramassé un morceau de diamant sans savoir ce que c'est hormis la beauté de la pierre car cet enfant ne sait pas cette pierre peut subvenir à ses besoins et à celui de son père durant toute une année".
NB: Concernant la Linguère ( princesse) qui voulait que Cheikh Sayyidil hadji Malick l'épouse et que ce dernier a subtilement décliné ce n'était pas du tout pour éviter de déraper et d'en prendre potentiellement une 5ème après la Linguère qui serait la 4ème. Car Cheikh Sayyidil hadji Malick Sy est " Mahfouz " c'est à dire protégé par Allah contre tout type de péché. Encore moins prendre une 5ème femme qui est un grand péché. Les raisons de ce refus sont à chercher ailleurs que dans cette explication.
Conclusion : Quoi que vous ayez entendu de bien ou qui semble extraordinaire sur Cheikh Sayyidil hadji Malick Sy, sachez qu'il reste encore d'autres aspects de son personnage que nous tous sommes loin d'imaginer encore moins de savoir !
ESKÈY Alaadji Malick, ESKÈY Alaadji Malick, ESKÈY Alaadji Malick.
Sa commentaire amna solo maacha ALLAH
Passe moi ton contact
Machallah yalla na nou yalla dégueu ak topou ta fayalnou len
Mach'ALLAH Oustaz Ahmed. Vous êtes vraiment une fierté pour le Sénégal et pour l'Islam. Sope nala ngir sa xam xam. macron va au diable
Amna solo bilahi sope nalene loll
Yalna sama Borom gueureum ko ta yeureum ko inchallah 🙏
Machaala amnasolo
Machalah
Ousmane nd yálla gua goude vane
ماشاءالله بارك الله فيكم جميعا يا اخي
MASHA Allah ❤💞🌸❣❤
Mashala leirneu
Masha allah🙏🙏🙏
Allhamdoulilah
Dieuredieuf
Contane na bilahi
Machalla amna solo🙏🙏
حفظكم الله ورعاكم
Alhamdoulilah
ماشاء لله تبارك الله جزاك الله خيرا أطل الله عمركم ماشاء لله تبارك الله ❤❤❤❤❤❤
Machalla Yalanelene yalla faye yiw
Wallahi djang reka ame solo🙏🙏❤❤❤
Mashallah sama Mame Maodo.
Machallah que Dieu vous garde ci barké seydi el malick
Macha Allah amna solo loool🙏🙏🙏
Bo beugué khame kouy Maodo kholal ay ndiabotam ak ay talibém
Machalla amena solo piir
Jerejef ❤️🙏
Djazakalahou hayrane
Machallah ouztas
Fotoum serign si bopou talibèm lagnou koy wèr
Maachalla doyoulounou
Manchallah manchallah amna solo
Machallah machalah
Machlla ♥️♥️
lidale dara daxouko
Macha Allah
Merci
li moy kham kham mes tog di khasante rek les jautre oustag naniou goor goorlou waye khole si nii
❤❤❤
🙏🙏🙏🙏🙏🤲🤲🤲🤲🤲
Maodo Malick Sy moy khamlé yalla, yar, di yétté té doula wakh ana, ana, ana, té doula demandé zéro franc
Ah man yén la beugue ndax sén xam xam
Mhachqlha
Fidal kou fi raw gnon ngui koy khamé ci sa ndiabot. Talibé youy Gnaka djoulit, gnaka wor, bokalé. 33 femmes 4 you bok ndeye ak baye beu paré nane ya yesseul diné. Khana mabal diné kay.
Doyna warr deh
Dett togn Baxoul kilifaguii naniou moytou Lolou
werd m...
ولا تقولوا أحمد وقولو ا سيد أ حمد فال
Ki moom kham khamam diakhal nama féne rék lay déf Ousmane lay wakh
Yawe kaye Yaye féneu kate bou reuy lane lafi fen wakhal?
Yaw da am loulA meti demal ga diangui xam sa dinè
Bilay ken dou mom yalnanio yalla fayal mame maodo 🙏
Ma challah. Wakerr maodo
Machala
Machallah
Machallah