Face2Face Ama vs Modou - Le geste noble de Modou Lo qui fait la paix avec Bakhoum le manager de Ama
HTML-код
- Опубликовано: 5 фев 2025
- Pour plus de vidéos, abonnez-vous sur notre chaine / tfm
/ tfm
/ tfm.sn .
#TFM #REPLAYTFM #TELEFUTURSMEDIAS #TFMLIVE #TFMENDIRECT
Voilà pourquoi j'ai aimé Modou lo, c'est un homme humble !!!!!!
J'aime la complicité de Modou lo et Ama
Machalla ❤❤❤❤ Moudou ame na solo
Ça fait plaisir de voir des champions comme ça qui restent modeste
Félicitations Modou lô ak ama balde❤❤❤❤
Machallah Modou lo é félicitations Ama bo amaté combat yallah nala yallah may ndam inchallah jtm dall Modou lo ♥️♥️♥️
Ndeysane Ama dafa diaré rouss Modou Sakh 😂.
Bilay Ama Vrai sportive la . Il a l'état d'esprit d'un roi
Ama talibe la modou dina bayii lamb bayii fi ama. Fiere plë
Yaw wéroo d Ama naturellement dou nitou fitneu
Bakhoum mo wara kharourek
Ama est comme ça de nature ,très calme ,am kersa .
Modou brom bakh leuh mais Ama nit kou woyof.leuh machaallah ❤ Sénégal diam rk mofi khath
Modou lô, il est très mature Machallah
Franchement Modou lo xool ❤️ bou rafet leuh yorei ❤❤❤
Modlo,quel homme ❤,
À part Modlo akh mbeur parcelle yii,Ama moy samay mbeur
Modou Lo Dafa Moudié beugeu Amaa Baldé Dafa fégn thi visage by mắn sax beugeu nala a parti aujourd’hui amall jameu rék félicitations ❤du courage sama xoll Amadou Baldé A vie ❤️❤️❤️
Enfin diam ame na yawit balniou agg sonal nagne la si commentaire yi trop 😂❤️
@@ogviito1949 yên kay 😂😂😂
Mé niofar ndioun nieupou daniouy enbiance rék beugeu mou néx mé âpre Lamb ndioune nieupou ndio farr ay frère l’an ndioun nieupou yalna jameu yageu way frère 🙏🏻❤️
Ndeysane supporters yagay safonté😂normo😂😢
@@gueyelabsolu5889 yeah frère wakh nga deug dh bilay lamb lawone rek niouy nekhal mais on est ensemble yallah na diam yagg way 🙏❤️❤️
@@rouguikebe9984 wa guiss nga frère 😂😂
Moi et Ama nous connaissons pas personnellement, mais quand je l’ai rencontré j’ai vu un homme très calme, humble, gentil.
C’était à l’occasion du prank Star.
Le gars est d’une bonté incroyable
Machallah
Juste les suportaires doivent revoir leur comportement et prendre l'exemple des lutteurs qui se retrouvent après chaque combat
RESPECT
Vraiment
Li dafa raféte trop ❤️❤️💞💕 machallah beugué naléne yéne gnieup contane n'a trop
Diam dafa nékh trop 😍😍 barky borome Touba oh j'adore
Moi dh billahi si j'avais des millions aujourd'hui billahi j'irais jusqu'à la maison de ama pour l'offrir même si modou lo est mon lutteur vraiment ama a un grand ❤
Modou lo notre futur président de la république❤❤❤
Nékal nitte
@@MouhamedDia-lu8kg😂😂😂😂émotion bila compréhension rek😂😂😂😂
Dani deug sa ndaye dh 😂
Waaa waw futur président de la République du Sénégal 🇸🇳🇸🇳 💪💪
@@falloudiop6516 😃😃😂yaw ray nga ma
What I like most is that they keep respect each other after the fight wish you both goodluck
Ama ak Modou yeupa oyof ❤❤❤❤❤
A no vremant li rafetna nak, man defmeu bett sah sa fait plaisir nak ndeyssan nonou rek la, bou lep wesso nio bok l'islam ❤
Modou lo has changed so much his level of maturity is beyond imagination he is so sweet.❤❤❤❤❤
I'M A BIG FAN OF MODOU XARANGE LO, I PRAYED FOR HIM TO BEAT AMA BALDE. HOWEVER THE POSITIVE ATTITUDE AND FAIR PLAY DEMONSTRATED BY AMA BALDE AFTER LOSING TO MY WRESTLER, I HAVE SO MUCH RESPECT, LOVE AND SYMPATHY FOR HIM. WHAT A POSITIVE MINDED, CLEAN HEARTED SOUL HE IS !!! THEREFORE, I'M URGING MODOU AND ALL HIS SUPPORTERS TO HOLD AMA BALDE LIKE A BROTHER AND GIVE HIM ALL THE SUPPORT AND HELP THEY CAN 🙏🙏
Rigth man a nice message Modou is our best wrestler Ama is a kind boy too.
Ama seul a vie ❤
MODOU lô combat yi mouyue amate yébe YALLA nasi ame ayue victoire ba énervé Amine yarabi ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
vraiment c beau Li louko dak merci Modou lo ❤
Wallahi li rafet nah Modou lo & Ama baldé bilahi nioune nieup on est toujours en ensemble yalla nalen yalla taxawu
No Ama mi billahi xol bou raféte la yore walay yall nako yalla diapalé bare képp allkhour an 🇸🇳❤️🙏🏾
Modou lo é o melhor lutador do Senegal ❤❤❤❤
Li mo am solo diam mo gueun loy guiss Ama ah Modou vous êtes comporte en grand geste humble de Modou lo a bakhoum
Maashala Maashala ❤modou lo bonne continuation......akh sa maturité akh sa respect envers nits yi yalla na la yalla di défal diamm saa you nekk inchalla Amiiiin
Modou lô très humble ❤
Ama Baldé biakhi sa xôl dafa rafét bisniki tay apart Modou Ama rék lay Tôp Té Yallah na Yallah def beugueu nék roi des arènes Inchallah
Gnidone khôl bé bonne j'espère que legui mom kham nguen ni Mo est un vrai champion ❤
Bakhoum comédien la dh Modou ndanan la ama bo amate combat yalla gua am ndam
Yagui fane rectifié li Franc lay dadiel😂😂😂
Modou lo a goutter à la saveur de la foi ❤❤❤❤.
Modou lo 5eme president du Senegal ama balde premier ministre du Senegal pour 2024
Très bonne idée 😂😂😂
😂😂😂😂😂😂
YALLAH téré😂 Modou si système bi la bokk
😂😂😂😂😂
Non ioe do nitt quoi billahi 😂😂
Ama ndeysan barom bakh deug la walahi
Il faut modérer lamine. Malick thiandoum est très compréhensif sinon il pouvait s'énerve contre lui. Lamine parle trop, il empêche les gens de développer. Malick est classe
Bien vue merci bcp lamine samba vrai mbam leuu
Lamine kay Moy lolou kw
C'est vraiment beau
Al KILIFA XARAGNE LO L'UNIQUE GOAT❤
Modou lo machallah je t'aime notre roi 🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Mane Modou rekk la topeu bly ❤ sama tonton jeo manga mo takh niou beugue khalé bi
Maye Fan's modou lô bou beugg ama baldé ❤❤❤❤bilahi ama yalnala yalla defale diamou
Modou Lo d’où sama mbeur mai nak pour dire vrai niit kou baxla
Chapeau le roi
Ey wayyy Li rafetna torop 😢😢😢😢
Machalla ❤❤🇸🇳❤️🙏
Machalla Modou lo yw rek lay topou Ama balde Lou bx la daysane 😍🥰🥰🥰🥰
Ndeysane père bakhoum mi magui dioye bilay rouss na sakh
Nooo modou lo je l aime beaucoup bilay ❤❤❤
Aka am diam lo ndammm❤
modou lo vraiment tu es humble , ama je suis fiere de toi tu es tres courtoie
Vive kharagne vive ama balde
Seydina modou lo mou sel mi môm rk laniouy top❤
Mboro sama deukeu. Merci Ama d y t être rendu pour suivre tes entraînements
Ama brom bakh leu bilahi walahi mane modou lo moy sama mbeur mé ama dama bétt trop sakh walahi
Li nice na YLna diam yAgG❤
Modou. Lo rek ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Macha allha ❤ Modou Mane nk ama moy sama mbeur mais nk nice niou wax ko
Mann legui dama beugg modulo nguir woyoffamm. Il incarne davantage de sagesse😢
Abdou Bakhoum di wett di xarou😂😂😂😂😂
Ndaysan ama sporif degeu le bilahi j'aime ama
Vraiment machallah Sénégal Li rek Lagnu Kham diam rek
Ama sa khole rafetna Machalla
Machallah Modou ama❤❤❤
Bilay Modou Lo mo bakh ndeyssane mais pere Bakhoum mane mo mey rey 😂😂😂
Machallah ❤❤❤❤❤❤
Ama yée ❤
Ama khol bou rafét la yor ❤machala
The king❤️❤️🥳🥳
Masallaa ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
KHARAGNE LO LI RAFÉTE NA ❤
AMA seul 🎉❤
llou mom deug leu dine mboro yii
Liguéy gafa lou doyy war champion bii 💪
Ama balá Modou lo gueuddè lo guiss
je suis modou lo mais ama mo geuneu nekk sportif si lamb dji vrai sportif ama li Nice na trop
Pere Bakhoum Gainde deug la
Ndaysane adouna dou dara bilay li dafa nékh
Modou lo rk ❤❤❤
Modou lô rk lanouy top bilay walay Ama du courage rk borom bakhe ga vraiment
Ohhh Ndeysane adouna amoul solo
Yalna Diammeu yagg
Modou lo dieuleul si lii exemple euleuk bo niaké ndam nga wané sportif svp
Ama bilahi goor man des mousou mala bègue mais tay mom bilahi damala begue😢
C'est le le sport qui gagne ndam li Sénégal lay déss
Vois deux vrai sportif sur ce plateau 🎉
Yalna diam yagg ❤
Waaw gooré waay ❤❤❤❤
Veuillez nous mettre les interprètes car nous autres on ne comprends rien, ce pendant nous aimons la lutte Sénégalaise
AMA DAFA YARROU MODOU LÔ❤ DAFA YARROU TÉ DAGNO MEUNE WAKHINE 🎉❤
Mâcha alla je vous aime
Amanda have a great heart coz he never show jealous after their fight
Wish you all succeeds for this arena
Not Amanda 😂 just Ama
@@oumysougou3502 yeah I missed up but it’s not hilarious to smile
@@elmosquito7149 I did not know laughing is a crime interesting 🤔
❤️❤️❤️❤️ je vous j’aime
Définition du professionnalisme
Père bakhoum ak gafakaa-gui😁😁😁
😂😂😂
Mbété fasse
😂😂😂
Merci Modou si geste bi ❤
De Vrais Sportifs ❤❤
Modou Lo un très grand homme
Ama baldé dafa nité. Machalla
Le "est ce que kham nga lamala wakh" a changé on dirait 01:27 😁
Tanyi modou "anyway "la djeul ak "tu as compris" 😂
Non traduction bi la def rek 😂
100% kharagne rk❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Noo modou vraiment nice