Salam salam. Dans les novelas j'ai suivi une série de ce genre mais la fille de la dame était étudiante. Revenue à la maison àprés ses études tombe amoureuse de l'amant de sa mére. Finalement sa maman s'est retirée et la fille se marie avec l'amant. C'est pour cela que certaines femmes plus âgées manquent de courage. Que DIEU vous accompagne. AMINE ya rabbi.
ISLAM TÉRÉ WOUL SEY AK GOR BOU LA NGUENA NÉKE XALÉ MAIS CE QUI M'A DÉRANGÉ C'EST SA TÊTE SANS SE COUVRIR AVEC UN CHÂLE. WAKHAL SA WAKHE TÉ BAYI TOUROU OUSMAN. VRAIMENT DÉSOLÉ MAIS CE N'EST PAS LE CAS ACTUELLEMENT. SA TOUROU SA BOROM KEUR REK BOU NÉKÉ THI SA YARAM KON YOW DO MEUNA DÉFF GREFFAGE WAKHOU MALA TOUROU SAYDINA MOHAMED RASSOUL AK LI NIOU WAKHE THI AL CORAN RESPECTÉ WOKO CAR DÉFF YOKOU KARAW THI SA BOPOU C'EST HARAM, DO CONTINUER DI XESSAL AUSSI MAIS À PART ÇA BON VENT DANS TON MÉNAGE CAR CE MARIAGE C'EST LÉGAL ET NOTRE RÉFÉRENCE C'EST LE MESSAGER DE ALLAH MISÉRICORDIEUX PSL SOIT SUR LUI. IL Y A EU 2 MARIAGES 1/ AVEC KHADIJA PLUS ÂGÉE 2/ AVEC AISHA PLUS JEUNE DONC MUSLIMS MANDOU LÈNE THI SÉYOU DIAMBOUR YA. ALLAH REK MO XAM.
Yallna yalla same sêne sey bi ❤❤ amine
Heureux ménage Yalla na seuy bi barké
Yalna seuybi barkel je vous encourage que dieu vous protège des mauvaises langues et des aigris
Yalla na seybi barkel thi barke seydina mouhamed
Yalna seybi barkèle❤❤❤
Heureux menage je suis 100% avec vous
Ndiabote kay🤣🤣🤣
Je suis 100 millions de fois avec toi parce que ce mieux de ce marier que d’aller dans les Apt et faire n’importe quoi 😮😮😮
Yana seuy bi barkel si barke kou ted gui 🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Yallna yalla same séne sey bi yalla mayléne ay doom you barkél yalla mouseul léne si seytané
ALLAHOUMA AMINE lou YA ALLAH DAGANAL,, MUSLIM DAF THI WARA ANDE AK NIANALENE
Sey Bou nekh ndiabote Gou barkel amen
Bane njabooot menoule néke
Ma femme et moi fama validons votre Union
Sénégal kou déf gnou wakh kou défoul gnou wakh Kone nagne déf rék té biyi Borome bi mou motali inch'Allah dokhal léne waye
Heureux ménage amlén djam té aissatou nga féhé ba famille sa borom leur contan djam délousi si famille bi
Man dale force na ba sonne mais menouma geum mer bi aye wakham 😢
Du courage la grande dame Aissatou
Du courage encore madame Mbegue ne regarde pas le rétroviseur continué votre chemin.inchalla
Ci lou nekh yalla rek ngén nek mouy seuy bonne continuation le chien aboie et la caravane passe ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Salam salam. Dans les novelas j'ai suivi une série de ce genre mais la fille de la dame était étudiante. Revenue à la maison àprés ses études tombe amoureuse de l'amant de sa mére. Finalement sa maman s'est retirée et la fille se marie avec l'amant. C'est pour cela que certaines femmes plus âgées manquent de courage. Que DIEU vous accompagne. AMINE ya rabbi.
Cheikh Amhet naditala ofit da bègue mér bi wakhe mo takh mokoy diayy 😂😂😂😂😂
Yalla n'a seuy bi barkel
Yala na la yala faye nitt kou bakh ga diureudief ❤❤❤❤❤❤
Yalla bakhna
Reuzenirrr sarappp ndaye liii😂😂😂 Ameth Cisse moy domeram
heureux ménage
Diadieuff waye
Ameth 😂😂😂 ya faut
Ameth Cisse neinako souniou génération yaye souniou yonente
Boy iaw auto 50 millions bii mo yobou sa Xell mii 😂😂😂😂
😂😂weuzz seul 💪
Li nékh n'a wayyy
Choi adouna lu waye deff rek now wah lu si sen yone
Niak fayda
Eeeeh Allah
❤❤❤❤❤
❤❤❤🎉
Mane sakh nopp naako
Yamana doull ndayam set dafa xaram
😂😂😂
ak kirama yi nékeu si yaw yep nga def sa greffage nonou . wa bakhna😢
😂😂😂
😂😂😂
Boy telnga werou di 😂😂beutyi tela doug 😂 bathi kanam niou xol me pawlish moy domram deug 😂😂😂😂😂😂😂
Pawlish kaye
Kima guiss ni intérêt moko fa tiyé gore bou niak diom la amoul kilifeu wow na beutt one rek
Yaw d'à nga dof li beuzz la d'où deugeu
Djiguéne bou fowé woul bopam en général yogne al li
Daguaye doul ba poupe sakhemb
ISLAM TÉRÉ WOUL SEY AK GOR BOU LA NGUENA NÉKE XALÉ
MAIS CE QUI M'A DÉRANGÉ C'EST SA TÊTE SANS SE COUVRIR AVEC UN CHÂLE.
WAKHAL SA WAKHE TÉ BAYI TOUROU OUSMAN. VRAIMENT DÉSOLÉ MAIS CE N'EST PAS LE CAS ACTUELLEMENT.
SA TOUROU SA BOROM KEUR REK BOU NÉKÉ THI SA YARAM KON YOW DO MEUNA DÉFF GREFFAGE WAKHOU MALA TOUROU SAYDINA MOHAMED RASSOUL AK LI NIOU WAKHE THI AL CORAN RESPECTÉ WOKO CAR DÉFF YOKOU KARAW THI SA BOPOU C'EST HARAM, DO CONTINUER DI XESSAL AUSSI
MAIS À PART ÇA BON VENT DANS TON MÉNAGE CAR CE MARIAGE C'EST LÉGAL ET NOTRE RÉFÉRENCE C'EST LE MESSAGER DE ALLAH MISÉRICORDIEUX PSL SOIT SUR LUI. IL Y A EU 2 MARIAGES
1/ AVEC KHADIJA PLUS ÂGÉE
2/ AVEC AISHA PLUS JEUNE DONC MUSLIMS MANDOU LÈNE THI SÉYOU DIAMBOUR YA. ALLAH REK MO XAM.
❤❤❤❤
😂😂😂
❤❤❤❤❤❤❤