Serigne sam MBAYE relation entre mame cheikh mbaye Ak serigne touba

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 7 янв 2025

Комментарии • 26

  • @abobabacaryade1621
    @abobabacaryade1621 4 года назад +12

    Serigne Sam MBAYE était un grand érudit du 20ème siècle, un homme aux dimensions hyper grandioses. Il a corrigé, rééduqué, guidé et redressé beaucoup de gens sans autant les voir.

  • @mamadoucisse9449
    @mamadoucisse9449 4 года назад +8

    ndeysan thiey serigne sam loumou tawat tawat douko tere foumou tolou mingi delo diamou yalla yi thi sen borom jeureu jeufeuti mbaye yaram

  • @abobabacaryade1621
    @abobabacaryade1621 4 года назад +6

    *#Bismillah** Barké Böröm Töübä#*
    *#Serigne** Töübä amoul morom#*

  • @papamodycisse5524
    @papamodycisse5524 4 года назад +7

    Dieudieuf serigne sam mbaye rek la meuna wakh

  • @papamodycisse5524
    @papamodycisse5524 2 года назад +1

    Dieuredieuf serigne sam mbaye

  • @tokkmouydokhtv3760
    @tokkmouydokhtv3760 4 года назад +4

    ماساالله

  • @abbs9407
    @abbs9407 Год назад +2

    This is a weird ass movie it a weird ending sad

  • @mamedaoudambaye874
    @mamedaoudambaye874 4 года назад +5

    Machalahh..yaw la kane seneitalia

    • @seneinfo24
      @seneinfo24  4 года назад +5

      man deh ken la ci sopey serigne sam

  • @bayesalioundiaye3772
    @bayesalioundiaye3772 4 года назад +5

    Kou bakh damay ladj cheikh ahmadoul khabir mbaye s touba maka cekhal wala louy sababou ladj bi moy sadbo sambo dafa waye cheikhi s toubayi bola thi mame cheikh mbaye mou bari thiow lol

    • @seneinfo24
      @seneinfo24  4 года назад +2

      Baye saliou Ndiaye dou cheikhou serigne touba mais kokou begueon serigne touba la ba wayna kou ay way youri beurii

    • @mouhamedthiam9048
      @mouhamedthiam9048 4 года назад +4

      Baye saliou ,,c vrai mai mame cheikh mbaye kou yèmè la ,mom dou cheikh pask dafa matone seuk seuk mom serigne touba moko jeuli wone sein deuki tiossane ,andi ko done ko jangual .dolou.wayè mom bimiy nieuw adouna dafa fess deil..motah bim nèkè toute tank dane mour bopam..hamna si mom lou barri.

    • @papamodycisse5524
      @papamodycisse5524 4 года назад +2

      @@mouhamedthiam9048 mame dieu yoneti bi moko wakhone boul top ben yone meussoul dem maka ngakh nena kouy ziari ak kouniouy ziar kou raw wayë nena El hadji Malik ak borome touba niofi nekone t diokhnaniouko liniou yorone Bala niouy dem

    • @mbenegueye4864
      @mbenegueye4864 4 года назад +4

      @@papamodycisse5524 Mame cheikh Mbaye leepe loum am dji sunu borombi(Mawlana)laco dialle point.

    • @bayedamebeye5389
      @bayedamebeye5389 3 года назад +1

      Dou cheikhe serigne touba dh ms ay waay lan woon lool sakh ba serigne toude woon nako doom ms kim ka toude woon ci tout tank la guene adouna et tamit mame cheikh mbaye nekon na brom keur sokhna dia mbacke mi taawou serigne touba bifi mame cheikh guene adouna nak lako ndiara ndiara yi doorko yor mouy wakeue serigne darou assane ndiaye niom niaar dal ay kharit lan woon tamit beugante woon lool sakh ba diegui deywa am na lo kham ne manoumako fi waye kon nako wakh waye dal niom niaar nin melon doyna waar