Man nie Di beug siweul séni mbir ak di wanéwou damalén yeureum kou kham thiat nimouye déf domou Adama warnga moytou - Sénégal🇸🇳 sa Kanam - peace and love🇺🇸
Nabou yalla bo bok ni takha si mbir bouniaw bi sa kharite Aziz je vous connais a travers la télé mais je vous adore 😢 Aziz et Waly yalna yalla kharelen adiana si Barker seydina Mohamed psl 🙏🙏🙏
Nabou ley damafoknee amoul hol dakatee Amna hol loutakh mouy dioyfi tamoukis loudoy warar dioyoul gen nan yalla boumoula boka mom mosi bolen bopam Aziz nimoumel akmom tatitoul rafoul😢
Nabou yalla bo bokou si lini wakh mais nak niou khamné saytané foum khadioul rek laye dougou guisnanan fi niou bokou ndeye ak baye di rayanté kon mém bouko yalla nato mou bokosi tamit niaari famille yi nane ko rafetall ta khamné natoula ndakh ak loumana khew nabou kou beugone aziz la rip aziz et boubacar
Aziz j n l coné mai nitt bou sincère lay niroul boko degué moy wakh rek ga kham ni limou gueum rek lay wakh dieu ohhh dieu man yalla bouma dioy ba febar j n’en peu plus tt é floue 😭😭😭😭😭
Assalamu Alaykum. damatie sani bén rék dawoumakoy sakh farale di binde commenter...6:40 nitt migui beugue Guis lén ma di wanéwou wala ngaye siweul sa bop. sur tout si internet you bon yi nga khamni adouna bi yeup danioukoy guis war nga soralé thiatt ndakh bakhoul daye top nitt basi bire bamél. Man dé samay mbir doumakoy siweul loumay déf souko niar rék yeugué yakouna kon nitt nie warnaniou moytou. yalla nalén yalla yeureum kharén aldjian firdawsi nianie fa fék ak nialén fa fék psl - Sénégal🇸🇳 sa kanam - peace and love🇺🇸
NABOU MO NOBONE AZIZ.. MAIS AZIZ NOBOUKOWON.. AZIZ DAFKADAN FADIAL SOKHLANN MANAM SAY BOU NAMEH GOR DEM SI AZIZ.. CAR APRES TOUT, AZIZ ETAIT PROPRE, AMBITIEUX, MIEUX QUE LES COXEURS, ET LUTTEURS AVEC QUI ELLE SORTAIT, CAR LE FRERE DE BATHIE SERAS A BIEN DIT DANS UNE VIDEO QUE APRES BATHIE SERAS, NABOU NOBANETENA AK BEAUCOUP DE LUTTEURS , DANSEURS ET COXEURS.. CHETETEU.. NABOU LEYE MO YAKHOU. ANYWAY, ELLE AIMAIT AZIZ MAIS AZIZ NE VOULAIT PAS.. MOU DEM NAK BA YORE SAKH NDIEULOU KEUR GUI.. AZIZ LUI DONNAIT LA DEPENSE, CEST ELLE QUI ACHETAIT LE MANGER POUR LA MAISON, CEST ELLE QUI DIRIGEAIT L'APPARTEMENT.. MAIS AZIZ KHOLE WOUKO WONE BEUTOU THIORO, N'EMPECHE SAY BOU NAMEH GOR, AZIZ DEFAR KO. MAIS NABOU EST DEVENUE JALOUSE, LA ELLE MENT NAAN AZIZ LOLOU LA WON, DEY FENN.. AZIZ GOR YALA DEUGEU LEU WON. TE KEN KHAMELOU WOUKO WON SI YOUYOU TIAKHANN.. JEPSERE QUE NABOU AURA LA PEINE DE MORT OU BIEN PERPETUITE. MOM AVEC LES AUTRES BANDITS ACOLYTES.. NIONIOU SEN NDEYI DIOUR KHOTI TAAT SI KASSARA.. TCHIM MAKHALA PA YI TAMIT KENN DEMOUL NIOU DESS, BEURI DIABAR, ET DO ASSURER DARA SEU KEUR. KHALEYI NEKEU BANDIT.S DOM YOU JIGEN YI NEKEU TIAGA.
Vraiment Aziz mi kou bakhe lawone ndeysane yalla nako y'alla yereume kharé aldiana
Amine
Allahouma Amiiiiiiiiiine Y'a Rabbi 😢🤲🤲
Ndeysane😭😭😭yalla nagnou yalla moussal ci thiatt ak seytané 🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Billaahi wollahi Amiine Yarabbi
@@NdeyemaguetteSeck-m9t amine ya rabbi
Bilay yow thiate bakhoul 😢😢😢 c'est triste vraiment 😢😢
Ndeyssane yalna niou YALLA moussal si chaytané ak thiat bilahi j'ai le cœur meurtri
Bilaye même Mane lolou la wakhe li yeupe cheytane la
Man nie Di beug siweul séni mbir ak di wanéwou damalén yeureum kou kham thiat nimouye déf domou Adama warnga moytou - Sénégal🇸🇳 sa Kanam - peace and love🇺🇸
amine
Nabou yalla bo bok ni takha si mbir bouniaw bi sa kharite Aziz je vous connais a travers la télé mais je vous adore 😢 Aziz et Waly yalna yalla kharelen adiana si Barker seydina Mohamed psl 🙏🙏🙏
Khana bokatt ngey wakh
Kon yaw geumeuga b legui
Bilakhi ndeyssane da nékhouta guom😢😢
@@matyndiayeduval7263man déh ba tay geumou mako 😮
Amine yarabi rokhayasarr
Ya Alla yalnañou yalla mousseul si seytané
La maman de nabou ressemble à une bonne personne
Li mom Nabou manou si bokou 😢
Aziz ndeyssane, khédione na fi ba ci kanam....Tognoul kénn, dérangéwoul kénn....ooh li métina ci khol 😢💔
La vidéo m’a fait pleurer… franchement la fin de leur histoire est triste🥹
Vraiment 😭😭 je pleure c'est triste est que nabou marabouter wougnou KO pour li
Walahi
@@rokhayacisse7905 leep nakk yalla la
Bilahi Barké wérou koorgui nguéne nék Yalna YALLA sétal Nabou léye YALLA boumou si lallé Aziz ak waly Yalna souf woyof sén kaw niou Motelé sén ndaw Aldiana si barké SEYDINA MOUHAMED S.A.W amiiine amiiine amiiine
Amine
Amine
Ndeysane adouna dou dara aziz ak nabou ay kharite lagnou oooooohh métina trop trop
Nabou ley damafoknee amoul hol dakatee Amna hol loutakh mouy dioyfi tamoukis loudoy warar dioyoul gen nan yalla boumoula boka mom mosi bolen bopam Aziz nimoumel akmom tatitoul rafoul😢
Aziz
Il dit sa ma dom
C'est pour l'affection qu'il a envers eux
lidé dama yakarné saytané la ak thiate motakh sen relation bi moudié ni mais yalla nalen borom bi yeureum
Hooo ray ngen nitou keseh kou bakh Bilahi walahi Y aziz danga dem niou dog la kham😢rip les 2
Pourtant fii nabou mongui dioy deh😅 loutax dioyoul kon bignou diambatè kharit bi😢 nabou té incroyable
mais meuna tiit. qmna nio hamni buniu amé nakar douniou joy
Vérité absolue
Dama dioy ohhhhhhh😢😢😢😭😭😭
Yana yalla weer ki déf dieuf diou niaw dji fi mom amoul yeureum les coupables 😢
Bilahi sama khol bi mingui mèti
ndeyssane
Yalla nagnou Yalla bourbi moussal ci thiate ak sètane ,
Ameen yarab, allahou masali Allah seydina mouhamed. (SPL)
amine
Wouy sama khôl bi 💔🥺💔
Hey way thiey yalla 😢😢 😢 nabou li yalla bossi book si barké kou tedki
amine way ndeyssane
Nabou ya deff li Aziz
c est ça le monde du show biz , jalousie , sacrifice, drogue , sexe , faux billets, perversion, etc...
You right💯%
Ndeysane 😭🙌
Nabou hoo lii 😭😭😭😭😭
Li yagoul deyssane 😮😢
Seynééé moo beurii dolé motakh danio wara dii djappp pour qu'Allah nous protege contre lui satan.Repose en paix Aziz
😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭 direct paradis inchallah amine yarabi 😭
Eskey Azi ak Wally Yalla na Aldiana Firdaous di sene keur 🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Workate bou bon ga ray aziz domi diambour téyé sa dome yallna yalla torokhal la aziz dafa bakh ndeyesan🙏🙏🙏🙏😭😭😭😭😭😭
dara leroulaci iow mi kou degueur fit nga
Nabou yalla bo bokou si lini wakh mais nak niou khamné saytané foum khadioul rek laye dougou guisnanan fi niou bokou ndeye ak baye di rayanté kon mém bouko yalla nato mou bokosi tamit niaari famille yi nane ko rafetall ta khamné natoula ndakh ak loumana khew nabou kou beugone aziz la rip aziz et boubacar
Ya rabi
Ya Allahou
Ya rahmane
Paix à leur âme
Que dieu le pardonne
Nabou ak Aziz dagn lena warone mayer bou yague
Est ce que nobaneté négne wone
ah iow mi lolene hamal
@@myamya6523yawite deh beuri ngua histoire 😂😂gneup ngay lidieunti 😂koi
En tout cas yayou aziz rek mo perte domame
Éviter ces faux marabouts vous les jeunes d'Angoulême di khabtals rek diléne takhalé ak séni kharit
Thiatt ak nattou
ndeyssane
ley ley adouna dieynala nomelle Aziz dabala le thiey adouna rip Aziz AK wally
Elle à toujours rêvé d’être à la lumière et bas non c’est pas elle qui a eu mais Abdoul aziz la jalousie sa paye pas vraiment 🙁😒
Yow loo wax nii
Nabou leye werr ngua aziz dabala mais yalla dina atté
Oh ndeysanne 😭😭😭😭
Doma ta bi yaw bilay donite sax
Waw barki rassoulou lahi dama laye diam ha ha ha !
Diomi na
Nabou yaye domeram deuggeu deuggeu deuggeu
Thiat bakhoul je pitie leuy leuy
J'ESPÈRE QUE NABOU LEYE TU N'EST PAS IMPLIQUÉ DANS LA MORT DE ABDOU AZIZ DABALA ET WALLY.
FRANCHEMENT
Yalla n’a yalla def diam way Nabou Yalna leep leer tei gua bagnesi takh sinon dîna am louma meti
Mere bi da niroke badou meune lep😂😂😂😂
Yaaye doomraam😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
😂😂bilay deugla
Bilaye ndeye ndiaye est ce que bokouniou
@@Adulovev5qo diarena verifié di nagne ko bolè thi dossier nabou leye bi
@@ndeyendiaye2942dou naguo bokak mome ba dossier bi diekh
Rétanou Aziz louné la
Mouy dioy dioyou seytané ni. Yaye domou xathie deugue
Bilahi hath sahh moko tanei Borom hool bou bon Rey katoh Nit shim
loko hamal rek
Aziz j n l coné mai nitt bou sincère lay niroul boko degué moy wakh rek ga kham ni limou gueum rek lay wakh dieu ohhh dieu man yalla bouma dioy ba febar j n’en peu plus tt é floue 😭😭😭😭😭
Yak man 😢
Éy way😢
Kou tothe ça leufeul daye gha yow nabou ça data yaye
Ki kay😢
Assalamu Alaykum. damatie sani bén rék dawoumakoy sakh farale di binde commenter...6:40 nitt migui beugue Guis lén ma di wanéwou wala ngaye siweul sa bop. sur tout si internet you bon yi nga khamni adouna bi yeup danioukoy guis war nga soralé thiatt ndakh bakhoul daye top nitt basi bire bamél. Man dé samay mbir doumakoy siweul loumay déf souko niar rék yeugué yakouna kon nitt nie warnaniou moytou. yalla nalén yalla yeureum kharén aldjian firdawsi nianie fa fék ak nialén fa fék psl - Sénégal🇸🇳 sa kanam - peace and love🇺🇸
Diadieuf Abdou
@@Seyd985you welcome - merci😅
Nabou moye deumeu
danko ham esk dara lerula ci li khew.
Ndeysane Ziz dabala morom mbakh lawone peine de mort pour les meurtriers
Déf len nank ken khamoule foy moudié
You right!!!!
CEST AZIZ QUI AVAIT FINANCE CE DINER
NDEYSAAN AKA BAKHONE
TE MOUSSOUL GUENEU FENN WAKHKO
NABOU YAYE BADOLO
Seytané radjim.
NABOU MO NOBONE AZIZ.. MAIS AZIZ NOBOUKOWON.. AZIZ DAFKADAN FADIAL SOKHLANN MANAM SAY BOU NAMEH GOR DEM SI AZIZ.. CAR APRES TOUT, AZIZ ETAIT PROPRE, AMBITIEUX, MIEUX QUE LES COXEURS, ET LUTTEURS AVEC QUI ELLE SORTAIT, CAR LE FRERE DE BATHIE SERAS A BIEN DIT DANS UNE VIDEO QUE APRES BATHIE SERAS, NABOU NOBANETENA AK BEAUCOUP DE LUTTEURS , DANSEURS ET COXEURS.. CHETETEU.. NABOU LEYE MO YAKHOU.
ANYWAY, ELLE AIMAIT AZIZ MAIS AZIZ NE VOULAIT PAS.. MOU DEM NAK BA YORE SAKH NDIEULOU KEUR GUI.. AZIZ LUI DONNAIT LA DEPENSE, CEST ELLE QUI ACHETAIT LE MANGER POUR LA MAISON, CEST ELLE QUI DIRIGEAIT L'APPARTEMENT.. MAIS AZIZ KHOLE WOUKO WONE BEUTOU THIORO, N'EMPECHE SAY BOU NAMEH GOR, AZIZ DEFAR KO.
MAIS NABOU EST DEVENUE JALOUSE, LA ELLE MENT NAAN AZIZ LOLOU LA WON, DEY FENN.. AZIZ GOR YALA DEUGEU LEU WON. TE KEN KHAMELOU WOUKO WON SI YOUYOU TIAKHANN..
JEPSERE QUE NABOU AURA LA PEINE DE MORT OU BIEN PERPETUITE. MOM AVEC LES AUTRES BANDITS ACOLYTES.. NIONIOU SEN NDEYI DIOUR KHOTI TAAT SI KASSARA.. TCHIM
MAKHALA PA YI TAMIT KENN DEMOUL NIOU DESS, BEURI DIABAR, ET DO ASSURER DARA SEU KEUR. KHALEYI NEKEU BANDIT.S DOM YOU JIGEN YI NEKEU TIAGA.
En bon 😢😮
Cest la maison de nabou ou bien
Du fait de la😊 présence de sa maman cest chez elle
😭
Nabou
Thiey beugeu bok vivre au dessus de ses moyens
Yaw loy wakh nii… ay wakhou doff mom diaroul commentaire… diap si rek
yes. yes!
@@ibrahimasterlingsow9969ki Kaye wéroule 😂
😭😭😭😭