REPLAY - QUARTIER GENERAL - Invité : SERIGNE SALIOU SAMB - 08 Juin 2018 - Partie 3

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 17 янв 2025
  • Pour plus de vidéos, abonnez-vous sur notre chaine / tfm
    / replaytfm

Комментарии • 598

  • @papeb6702
    @papeb6702 6 лет назад +293

    Man dah douma mouride mé walahi lima dégua tay doy nama man mom diebeule na sama bop serigne touba bisna tay bilahi wa li doy na war dh mourid yi magui so gua kham li takh niou bakh machalah

  • @astamamaamar4000
    @astamamaamar4000 6 лет назад +649

    Kou yakkar khadimoul rasooul beussal j aime

  • @mbayangdieng7311
    @mbayangdieng7311 6 лет назад +76

    Li mom chaque jrr la wara amm dafa diot niou diox suñu temps yep borom touba!!! Dakh losi wakh doyul moy guedj bamboulann 😍😍

  • @cheetaahMom
    @cheetaahMom 6 лет назад +35

    Guisouma kou guenne serigne touba si kaw souff🙌🏻🙌🏻🙌🏻 Machalla kéneu meusoul guiss li😭😭❤️🙊

  • @oumyba3827
    @oumyba3827 6 лет назад +141

    Thiey serigne Touba douniou doyal si diotayam 💕💕💕

  • @laminmaster9387
    @laminmaster9387 6 лет назад +52

    Pape Cheikh Diallo mala Beug ndakh linga Beug Serigne Touba ☝ 👍

  • @astoudiallo2888
    @astoudiallo2888 6 лет назад +40

    Serigne Bamba yalla rek moniouko meuna fayal limouniou defal keen dou mom kéneu leu Dieureudieuf Serigne Touba 🙏

    • @bayesall26
      @bayesall26 6 лет назад +2

      Astou Diallo diadiauff astou Diallo cool

  • @mizabtv
    @mizabtv 6 лет назад +111

    l'histoire retindra l'histoire de serigne touba jusk'a la fin du monde jusqu'à la fin du monde bamba tu restera toujours dans notre coeur toujours 😢😢😢😢

    • @elhajndiaye7832
      @elhajndiaye7832 6 лет назад +2

      Aziz Ndoye wallaahie wakh NBA deggue

    • @bayemorsamoura4898
      @bayemorsamoura4898 5 лет назад

      Désolé tu dois dire Serigne Touba est toujours dans notre coeur mais pas tu resteras dans notre coeur

    • @ousseynouniang3016
      @ousseynouniang3016 5 лет назад

      Wallay degeu la barké Cheikhra fall

    • @fadeldiop7406
      @fadeldiop7406 Год назад +1

      AMINE

    • @yasinendiaye2455
      @yasinendiaye2455 Год назад

      ​@@elhajndiaye7832 lo m'y
      ❤❤.❤lb😂😢TC 😊 de de
      😅😊

  • @matarseck6112
    @matarseck6112 6 лет назад +9

    Kou ted ki dé Kokou bagne sa khol dina dague ndakh sounou borom moko déf lime ko déf té fi ak adouna di touki sounou borom diokh nako ko déf tayam diouné gathiél na démb Aywaay nanou manou thi mome boune beugué nék thi diam Dieureu nguéne dieuf serigne saliou ak serigne Khadim gueye bégue nane lole salaw yalla na kou ted ki nangoul gnou lép amine

  • @khadywade2220
    @khadywade2220 6 лет назад +6

    Khadim rassoul le serviteur éternel du prophète (psl) une lumière éternel borom touba

  • @remaba4761
    @remaba4761 3 года назад +2

    machalla ken dou beugue yoneté bi ba dap serigne touba. dieureudieuf serigne saliou samb yalla na borom bi doli khamkham bi

  • @cheikhbassiroubabou686
    @cheikhbassiroubabou686 6 лет назад +45

    Wawe lene Gore MOURIDOULAH . Dieureudieufeti Borome Touba Khadimou Rassoul .

  • @alioundiaye7472
    @alioundiaye7472 6 лет назад +10

    Ndayesane oustaz assane ya goré yague fi lole té andak wérr si barke borom touba amine

  • @seydinofficielalioune8326
    @seydinofficielalioune8326 3 года назад +1

    Thiey Serigne Touba Yalla nanouko Yalla fayal

  • @madiopmkr2923
    @madiopmkr2923 4 года назад +3

    Septembre 2020 on est là ❤️🔥 wadial Safar gui Inshallah barki borom Touba 🙏🏼

  • @daganiang5866
    @daganiang5866 4 года назад +3

    Doumasi doyal chak jr ma setane ko 2020

  • @bambamidadi8184
    @bambamidadi8184 6 лет назад +5

    Magui sant sama baye bimou dupé serigne touba Mbacke kéneu dou mom serigne Saliou samb yalna yalla yagal sa taxaway

  • @ndeyesallambengue7909
    @ndeyesallambengue7909 6 лет назад +10

    Macha allah serigne saliou samb ak sama sopé guirr serigne bamba serigne khadim Gueye dama KO sopp rkk ta serigne bamba takh kokayy royy sakh dama kayy sopp

  • @pacoseck4926
    @pacoseck4926 6 лет назад +2

    Machalla serigne saliou Samb tfm yen sen son bi dolen co arete walla guen tek aye khasida walla alkhouran khamo len toussssssssssss

  • @adamacoulibaly9903
    @adamacoulibaly9903 6 лет назад +32

    Merci TFM...Merci Pape Cheikh...Merci Serigne Saliou Samb

  • @abdoubakhefall8304
    @abdoubakhefall8304 6 лет назад +8

    Thiey serigne touba moy serigne touba kéneu dou mom

  • @mayoronguer2498
    @mayoronguer2498 6 лет назад +68

    😢😢😢😢😢mangui dioy dioyi kholl bilay Serigne Touba Amoul morom

  • @toubaservices2988
    @toubaservices2988 6 лет назад +10

    mouride daal mo nekh .....
    dieuredieufé SERIGNE TOUBA

  • @diordiop7919
    @diordiop7919 6 лет назад +20

    Serigne saliou samb long vie sante soutoure mane dior bou serigne babacar sy beugue ta yalla rek takhe ndakhe deugue guiguaye wakhe thi serigne touba

  • @mbodjibamba8895
    @mbodjibamba8895 6 лет назад +10

    Lahilah thieuy serigen touba yalla nanou yalla bolé si bopam barke borom touba

  • @mamexandiaye2183
    @mamexandiaye2183 6 лет назад +36

    Réw bamba moy kiko mom mim réw bamba ko mom
    Dieuredieuf serigne touba

  • @cheikhsarr1026
    @cheikhsarr1026 4 года назад +1

    *qui est en 2020 machallah cheikhoul khadim* 👌🏽👌🏽❤❤

  • @serignembayediop4564
    @serignembayediop4564 5 лет назад

    Serigne saliou samb yalla nala serigne Touba kou téd ki faye. Macha Allah kou bakh kou kham dara thie serigne Touba ga yalla gafi yague lol téh wer

  • @awaernestineferreira6295
    @awaernestineferreira6295 6 лет назад +7

    Serigne touba dou moromou ken si souf bamba dieureudieuf

  • @mamecheikhramos1112
    @mamecheikhramos1112 6 лет назад +20

    Thiey serigne bamba
    Akhmadou amoul morom
    Chekhoul khadim keen la
    Dieuredieuf serigne touba diarama cheikh ibra fall

  • @khadimbadiane3265
    @khadimbadiane3265 6 лет назад +1

    DIEURDIEUFETI SERIGNE TOUBA AMOUL MOROM MORAMANE TEWOUL AK KENE KOU BEUS JAIME YALLA NA SERIGNE TOUBA DEFAR SAY MBIR

  • @toubaseck4361
    @toubaseck4361 6 лет назад +11

    Alhamdou lilah bima nekè mouride yalla nanou ci sakh ba fawwwww

  • @BirahiimCr7
    @BirahiimCr7 6 лет назад +32

    Serigne saliou samb si boppam mo maîtriser alkhourane

  • @serignefalloufall4242
    @serignefalloufall4242 4 года назад +1

    Akassa Dieureudieuf serigne saliou samba kéne dou serigne touba khadime rasoule Akassa ❤️🙏🏿

  • @falloufall1816
    @falloufall1816 4 года назад +2

    Theiy cou tédki cheikh Ahmedou bamba mbacké Khadime Rassoul dieureudieuf Serigne saliou samba 👂♥️🙏🏿

  • @alioundiaye7472
    @alioundiaye7472 6 лет назад +1

    Dieureudieufe serigne khadim yalla na bate bi wérr si barke cheikh akhmadoul khadim amine

  • @lenaamar9284
    @lenaamar9284 6 лет назад +3

    Kou beug Khadim rassoul beug nala ngiir serigne touba souma deguè kouwah bani barké serigne touba sama kholbi dafay neeeex

  • @khadimleye9012
    @khadimleye9012 6 лет назад +10

    Dieure diuef serigne touba amoul morome

  • @abosouhaibourijallthiam4843
    @abosouhaibourijallthiam4843 6 лет назад +5

    Macha Allah xoll yi féss na ak mbék té yalla na lén yalla fay diere diefeté khadimou rassôll kén la

  • @sandjirydiop8254
    @sandjirydiop8254 5 лет назад +10

    Qui regarde la vidéo jusqu’à 24 mai 2019

  • @mohamedsarr2019
    @mohamedsarr2019 6 лет назад +10

    Kénn dou khadimou Rassoul✋dieureudieuf serigne saliou samb

  • @mamadoufaye4534
    @mamadoufaye4534 6 лет назад +1

    Dieureudieuf SERIGNE SALIOU SAMB waxtane Wii reik tarbiya laa bilahi MOURITOU SERIGNE TOUBA YII REIK AMOUGNOU MOROM.DIEUREUDIEUFEUTI SERIGNE TOUBA

  • @serignefalloufall4242
    @serignefalloufall4242 4 года назад

    Kéne dou cheikh Ahmadou bamba mbacké khadime rasoule amoule morome thi adouna ak allahira Dieureudieuf serigne touba khadime rasoule Dieureudieuf serigne salihou saba Machallah Dieureudieuf 👂👂❤️🙏🏿

  • @alphajallow2100
    @alphajallow2100 6 лет назад +7

    dieuredieufe serigne touba sunu yakar tay ak euleuk mbacké balla aicha

  • @yagambengue6208
    @yagambengue6208 6 лет назад +11

    Machala serigne khadim gueye

  • @djilyndiaye7198
    @djilyndiaye7198 6 лет назад +1

    dieuredieuf serigne saliou samb yalna yalla defalla mbolem lingayéni ci barkeb serigne touba miniou yaakaar atedouna ak allakhira

  • @ycouli2798
    @ycouli2798 6 лет назад +2

    Dieuredieufe SERIGNE TOUBA diarawlaké Mame Cheikh Ibrahima FALL

  • @Messi-el6vz
    @Messi-el6vz 6 лет назад +1

    Thiey serigne Salliou samb yalla gua fi yaug lolll te andak wer amine

  • @daoudasoumare9809
    @daoudasoumare9809 6 лет назад +10

    serigne touba ken khamoul loumou donne loudoul borom biko bindeu sante nanou bou bakh s saliou samb

  • @mamebinetambacke2215
    @mamebinetambacke2215 6 лет назад +1

    Yallanala yalla samou arre la si kep koulay fekhell thi zahir ak battin defalla nga ague fo nagge si présenté kiy serigne touba

  • @daoudawadji4717
    @daoudawadji4717 5 лет назад +1

    Kou yakarr koutetgi Bessel jaiem♥️♥️💯

  • @sokhnandao4746
    @sokhnandao4746 6 лет назад +7

    Yalla gua fi yague serigne saliou samb

  • @bayelatelo9258
    @bayelatelo9258 6 лет назад +6

    Machala Saliou samb amna solo trop serigne touba ken dou mom

  • @khadyfall2828
    @khadyfall2828 6 лет назад +8

    ap rone soula soutai doula terei niol ..nañu niolantei si souniou biir tei bayi fi rone bi, Seuñ Touba ap rone la 😍😍😍

  • @mbackediop7678
    @mbackediop7678 6 лет назад +2

    Sama kholl fékhna dh barké allkhoran thiéye serigne touba

  • @papematarndoye5166
    @papematarndoye5166 3 года назад +1

    Serigne Saliou Samb yalnala sougnou Borom défale tawfèkh ak khèweul boubarii si barké ALKHOURANE

  • @antamboup9024
    @antamboup9024 6 лет назад +40

    Vraiment le générique nous PERTUBE !

  • @yahyabenmahet4074
    @yahyabenmahet4074 6 лет назад +5

    Nitt dana gaddu akh ci diem diamu Yalla...fayleen ngir dieumi serigne Tüba seen son bi ci suuf

  • @ballymakhtar4691
    @ballymakhtar4691 6 лет назад +25

    Euskeuy thieuy kou tedeuki ❤❤❤

  • @lorenahernandezcanitrot2963
    @lorenahernandezcanitrot2963 6 лет назад +1

    yalnala yalla defal diame djiou barri way waxdji rafetna barke serigne touba

  • @khadimeka5020
    @khadimeka5020 6 лет назад +72

    Bilakhi wakhouma s touba ak ndiabot wayé wa keur s touba rek ken dou niome bilakhi

    • @ndeye.fatou.Mme.diop.
      @ndeye.fatou.Mme.diop. 6 лет назад +2

      bouba ndiaye. Wakhatikho wakerem rekh fo si mandi dugou yem dugal Darou khoudos, Darou salam,darou minam,di ziar wa ker serigne darou assane ndiaye......

  • @foumalin6130
    @foumalin6130 6 лет назад

    Djiëredieufty Sgne Touba,Sgne Saliou Sambe yalla nalla Sgne Tou bolé si goor yalla yimou gëneu greum,Sgne khadim Gueye yagui fi bà légui ma chalah yalla nalla Sgne Bi dolli...!!!

  • @adjathioubou3914
    @adjathioubou3914 3 года назад +1

    kiko deglou meun na bok yole ak kiko jangue wala beug na si leral d ngir jeum serigne Touba. Merci beaucoup

  • @gueyegueye3722
    @gueyegueye3722 6 лет назад +2

    Bilakhi yalla nalenn yalla faye serel ngenn khol yi

  • @modoufaye3114
    @modoufaye3114 6 лет назад +12

    kénne dou serigne touba

  • @fatoucisse3768
    @fatoucisse3768 5 лет назад +3

    Dieureufaty serigne touba

  • @layesamb3388
    @layesamb3388 6 лет назад +1

    Kendou seringe touba Dieurediefe serigne touba amoul morom si kaw souff Bilahi!

  • @datr6676
    @datr6676 6 лет назад +1

    S khadim geuye niga serale sama khol ba samay rangogne tourou yalla nala yalla defal fotolou sape khol di sede sa sounek.gay khouss thi guediou bannekhe si barke s touba

  • @nogayediallo7047
    @nogayediallo7047 6 лет назад +21

    Akhmadou bamba fep partout kenne dou môme kouko beugue bessal☝️

  • @ibousene282
    @ibousene282 6 лет назад +1

    Yalla may neu magou rèw mi yeup ak niénèn ak niénèn ... Yalnanou lén yalla fayal
    Wayé Kén dou Cheikhoul khadiim

  • @djilyngom7415
    @djilyngom7415 6 лет назад +1

    Kouy sétane en 2018 si décembre bi yalla nanou yalla fayal serigne touba

  • @deguenendiaye7265
    @deguenendiaye7265 6 лет назад +1

    Ana gni wolou Serigne touba

  • @mamadoudiop1635
    @mamadoudiop1635 6 лет назад +8

    Jotay yi dal jarna di baril amna solo loll, serigne saliou mom dankoy bayi ak serigne bi rek

  • @mafallfall5103
    @mafallfall5103 6 лет назад +35

    SERIGNE MOUNTAKHA YALNAFI YAGG TE WER

  • @omzosifodiop2688
    @omzosifodiop2688 6 лет назад

    thieye serigne TOUBA Diantou dionlore la kou bagne ni guissoko dou wagni dara si lérayame DIEUREUDIEUFATI SERIGNE TOUBA

  • @awacisse4561
    @awacisse4561 6 лет назад +5

    Deireudeuf serigne touba

  • @dieumbeniang8742
    @dieumbeniang8742 5 лет назад +1

    Samedi 25/01/2020 y’a pas mieux que ça 💪💪🙏 dieuredieuf serigne touba

  • @gueyeawa7090
    @gueyeawa7090 6 лет назад +5

    Machallah akassa serigne saliou samb

  • @sandjirydiop8254
    @sandjirydiop8254 5 лет назад +2

    Qui regarde ça en octobre 2019

  • @ndeyeawa1546
    @ndeyeawa1546 6 лет назад +1

    dieureudieuf serigne touba amoul morom kenne dou serigne touba ma beug serigne touba

  • @liskagainde2177
    @liskagainde2177 5 лет назад +2

    Serigne touba rek 🙏🙏🙏❣❣❣❣❣❣❣

  • @kyalasalihate343
    @kyalasalihate343 6 лет назад +6

    Fier d'être mouride❤❤❤❤❤

  • @daoudasamb1140
    @daoudasamb1140 6 лет назад +5

    Dieureudieuf cheikh bamba

  • @khadimfall8077
    @khadimfall8077 6 лет назад

    Serigne touba dal amoul morom
    Dieure dieuf s saliou samb soukrane oustze assane.mait son bi dafa khoumb

  • @amdyamdy5250
    @amdyamdy5250 6 лет назад +6

    Dieura dieuf s saliou

  • @bassiroukane2249
    @bassiroukane2249 5 лет назад

    Dieureudieu serigne touba diarawlak mame cheikh ibra fall...

  • @yagambengue6208
    @yagambengue6208 6 лет назад +5

    Diadiaf mouride machala serigne saliou samb

  • @cheikhabdoudongodaara1586
    @cheikhabdoudongodaara1586 6 лет назад +6

    Ndeyshaane sama khol nekhna barkeb s touba mai tfm cénérique bi andoul ak wakhtaanei koutedd ki

  • @aliouridialoulahbambakarad9086
    @aliouridialoulahbambakarad9086 6 лет назад +6

    Debou Tim wathiena ba 0degré barki SERIGNE TOUBA
    Serigne saliou samb yalla nafi yague té wér
    Mais KOU TED KI amoul morom

  • @khadimsylla35
    @khadimsylla35 6 лет назад +5

    Machallah lerna dieure dieuf serign touba

  • @khadimsamb7035
    @khadimsamb7035 6 лет назад +7

    S khadim Gueye machalla yaguefi lolll sa wéér

  • @khadimrassoulmboup493
    @khadimrassoulmboup493 4 года назад +1

    Bilahiii waaxtann bii domaa sii doyaalll

  • @AmadouDiop-b6m
    @AmadouDiop-b6m Год назад

    ❤❤❤machala mes li chaque jour là wara am wahal cheikh Ibra fall

  • @khadidiatousamb568
    @khadidiatousamb568 6 лет назад +5

    serigne Touba amoul morom

  • @jallotantoinejallotantoine4932
    @jallotantoinejallotantoine4932 6 лет назад

    Amna dieum nitt wanté donou ko kene khamoul lane, kemane wessou woul ndiabot ndakh mbolem gor yalla wala yonente bou gni bakko wathie n'a si ndiabotam, kou meuna indi seydina Ousmane noreyni si ay ndiarbatam kone ay domam gnan len.dieuredieuf serigne Touba

  • @LaQueene07
    @LaQueene07 6 лет назад +8

    Serigne Bamba❤ rk mofi nk point👌

  • @bassirougaye9564
    @bassirougaye9564 6 лет назад +6

    Sérigne bi moy Serigne touba

  • @ewakane1071
    @ewakane1071 6 лет назад

    merci tfm mie musique bi mom moy lolou prochainma guénn bayi si xéll dieurdieuff s touba

  • @ndiayecheikhmariemou1412
    @ndiayecheikhmariemou1412 6 лет назад +2

    Diereudieufè Serigne touba

  • @fatimatasarr5113
    @fatimatasarr5113 6 лет назад +12

    Barke Serigne Touba. Loudoul Serigne Touba bougouma