REPLAY - QUARTIER GENERAL - Invité : SERIGNE SALIOU SAMB - 12 Juin 2017 - Partie 3

Поделиться
HTML-код

Комментарии • 1,6 тыс.

  • @aboubacarsy347
    @aboubacarsy347 9 месяцев назад +14

    Qui est là en 2024 précisément dimanche 17Mars Ken dou Serigne Touba koudoul Serigne Touba Yalnaniou sa borom tasse ci barkem defniou ay deugui Mouride🙏🏾

    • @magattetallly6077
      @magattetallly6077 2 месяца назад

      Je suis là le 20 Octobre 2024🎉.
      Dieureudieuf Cheikhoul Khadim❤😊

  • @falloudiongue5857
    @falloudiongue5857 4 года назад +3

    diangu katbi guir yalla mou ndieuw cartier general 2020 guir yalla taysirbi amna solo lolou

  • @toutyd269
    @toutyd269 4 года назад +20

    Thiéy serigne touba qui regarde encore en 2020 ba octobre 2020 à 2h du matin magui sétane QG yi thi wakhtanou serigne bi douma thi doyal mouk Mach'Allah

  • @mamecheikhmbaye2244
    @mamecheikhmbaye2244 6 лет назад +2

    Serigne Touba amoul morom serigne saliou samb yalla na yalla yokou aw fanam

  • @khadimgueye1216
    @khadimgueye1216 4 года назад +22

    Kouy setane li ba 2020 si Dieumi Serigne touba beuseul j’aime

  • @ndeyediodiadiagne4165
    @ndeyediodiadiagne4165 3 года назад +2

    Qui est là Septembre 2021 walay QG bi dou mathie doyal dieureudieuf cheikhoul khadim

  • @gninguesophie5581
    @gninguesophie5581 7 лет назад +12

    yonnou serigne touba gui amoul daray hazard dieureudieufe serigne touba milliard fois

  • @syllabally6340
    @syllabally6340 7 лет назад +4

    kou adak serigne bamba thiakaw thiakanam bravo pape cheikh s saliou samb teeygalol yalanalayala fay ma bègue cheikhoul khadim

  • @youssoufall470
    @youssoufall470 7 лет назад +4

    emissions yi dé amena solo di khamelé mague gni dieureudieufti serigne touba diarama Mame cheikhra fall yallana yalla yok sen lere tei tassou gni sen barke amen amen amen

  • @fadioufydiouf1764
    @fadioufydiouf1764 7 лет назад +10

    Man dal meunatouma nelaw tei setanouma li thieuy serigne Touba...fiere d être mouride

  • @manickdeng4995
    @manickdeng4995 7 лет назад +98

    Serigne saliou samb yalla nala sa borom aral bopam barke cheikhoul khadim..Wa tfm Mome da la Leni Baye ak kou ted GUI laf thiat..

  • @amyndiaye4334
    @amyndiaye4334 4 года назад +2

    Douma doyal si diko setane .ken dou Serigne touba bamba merci❤

  • @coumbasene7836
    @coumbasene7836 7 лет назад +30

    Machallah, je l'ai regardé en différé mais j'avais vraiment pas envie que ça se termine.
    Dieuredieufeté Serigne Touba, kouko wakhoul gooré wo.

    • @BOP913
      @BOP913 7 лет назад

      Coumba Sene sakh n ga deug dé séne thiali démba séne

    • @football-ce7cv
      @football-ce7cv 2 года назад

      Fen reck 🐕🐕🐕👎🇸🇳🇸🇳🐒🐒

  • @djibyfaye3616
    @djibyfaye3616 6 лет назад +9

    J'avais entendu l'ampleur de cette émission avant de vérifier mais c'est effectivement une émission de toutes les autres. Sérigne saliou SAMB Merci pour la maitrise du discours, la clarté des propos mais surtout la cohérence historique du parcours des Khalifs qui reflète fidèlement votre travail inégalable dans l'histoire du Mouridisme.''God bless us'' Yallna borom def DIAM thi rewmi yeup. Merci infiniment

  • @papewalydiouf785
    @papewalydiouf785 7 лет назад +70

    Alhamdoulilah :), Keep Kouy Gëstu si yonu cheikh Ahmadou Bamba, khamni lignou fi wakh lep lou werleu, Serigne Bamba nena yone yeupa bakh, Nagnou gueum lignou gueum mandou, ligueyal Serigne bi tei khamni moy ligueyal le prophete Mouhammed (PSL) tei khamni moy ligueyal souniou borom, Bayi weranté bi ak khoulo bi. Souniou borom ALLAH louko sop ley def, Nagn ko Sant bimou fi bayei Mak niou bakh gnissi deuk bi ngua khamni defouniou loudoul nek si mission wou souniou Borom. Kou beugua kham danguay Gëstu, li fi wadji wakh yeup mingui si khassida yi ak terei yi fi Serigne touba bayi, serigne Bamba taguoul bopam dafnio khamal rek nguir dimbalignou(témoignages yi bari bassi toubap yiko beugone sakal pékhé).
    " N'abusez pas de ma condition d'homme noir ,pour ne pas profiter de moi car je suis le serviteur éternel ,chaque génération qui passe aura la certitude que je suis venu pour elle " ."Dieu m'a accordé des priviléges qu'il n'a accordé et n'accordera à personne"."J'ai recu un savoir que l'on ne voit point dans les livres, mais au contraire un savoir qui m'a ete inspire par l'ETRE qui a fait de ma plume un rempart protecteur."
    Bureau bassa ndar dagn ko wedilo souniou borom, mo wakhfa "Likhlass", lolou indi lissi top lepp,
    Serigne bi nak yague na am ay noone(ennemis), mais bimou gnibissei si guedj gui néna Diegual na Nieup, kone Nioune Mourides rawatina Baye fall Si Diegual lagn wara deuk, Kouniou Togn niou diegual, kouniou dinguat niou diegual, nek si lignou nek gueum lignou gueum, Nioune Mourides nioune Baye Fall, nous sommes des savants, des intelectuels, etcc doté de raison. Khamnagn boubakh si louniou nek. Souniou devise moy "Diokhé niam gniko yelo" ak "Nangou toumeu".
    Lene rek lagn niou wara wakh terei niou mo diaral niou khekh khoulo, moy niou terei niou ligueyal serigne bi ndakh moy ligueyal Yonente bi (PSL) moy ligueyal Souniou BOROM.
    Mangui toubat di diegualou bou bakh si kadou yi di niane souniou borom defal niou diam fi ak founiou dieum.
    @piwaley

  • @yamambodj3645
    @yamambodj3645 3 года назад +2

    Février 2021 ba legui doyalagouma ci machalah

  • @mamebousso7761
    @mamebousso7761 7 лет назад +42

    machallah QG bi masou fee am thieuy serigne touba moy kenn de yalnanoko yalla fayal

  • @guiguindiane644
    @guiguindiane644 7 лет назад +43

    barki seydina mouhamed damay delou sante yalla bama dioudouwé fekk samay wadiour nekk mouride ma topeu ci sen tankeu barki serigne saliou

  • @madinasy2460
    @madinasy2460 7 лет назад +30

    machaallah bay cheikh yague nga def plateau bou nékh wayé bou mélni meussoulo ame,serigne saliou samb xamxam bi rafetna téi sélleu.dieureudieufety Serigne touba diarama mame cheikh ibra

  • @santeserignetouba4826
    @santeserignetouba4826 7 лет назад +13

    ñioune ndaaw gni sante nañiiu bou bakh cheikhoul khadime serigne saliou loumassi guena nékheuu ndaw gni gnio guenaa beug guenaa gueum CHEIKHOUL KHADIME 💕

  • @senthiowbeurina9981
    @senthiowbeurina9981 7 лет назад +479

    keep kou commantaire yall na ahamdou boroom diam ni defal say Mbeurr ci barké Cheikhoul khadim

    • @ballawadediack253
      @ballawadediack253 7 лет назад +3

      Yallah mooy borom diam ñi, bayyi léén bokkaalé.
      Kou déé tédd si bamméél manoul défal kénn dara.

    • @cbdkheuch9735
      @cbdkheuch9735 7 лет назад +13

      IOW xolal ya nguimay beugg sofffff do teuthie sa lamigne barké borom touba iow balla cheikhoul khadim soko beugoul do dougou aldiana

    • @ahmadoumakhtarniasse7231
      @ahmadoumakhtarniasse7231 7 лет назад +6

      yaw kéne doula ramou ta say dieuf seytané moka nangou sounekoul wone segn touba pain ndambé ngay done

    • @naboujina172
      @naboujina172 7 лет назад +8

      Balla Wade Diack au moins amal respect boudoul dara ndakh alhourane bou tede bimou binde diko diangue..... sene genre yii rek nioye heuy torokh prck amouniou teguine et o6 bala ngay wakh reflechi dengame sangou sangue yii seydina mouhamed(psl) keine doufii dess

    • @naboujina172
      @naboujina172 7 лет назад +8

      Balla Wade Diack te repondre sera une reelle perte temps parceque non seulement tu ne sais pas ce que tu dis et tu es inconcsient.... ce qui sur ce que tu regrettera tes propos inshaallah et cela sur terre.

  • @TalibèAlhasaneSalam
    @TalibèAlhasaneSalam 7 лет назад +39

    Serigne touba amoul morome , dieureudieuf cheikh Ibrahima fall💓💓💓💓💓

  • @mlm6366
    @mlm6366 7 лет назад +121

    Cheikh Ahmadou Bamba a dit : " N'abusez pas de ma condition d'homme noir ,pour ne pas profiter de moi car je suis le serviteur éternel ,chaque génération qui viendra aura la certitude que je suis venu pour elle "
    Dieureudieufé Borom Touba
    Diarama Mam Sheikh Ibrahima Fall Lamp

  • @antathiam3970
    @antathiam3970 6 лет назад +12

    Sera en na QG bi plus de 10 fois douma si doyal len dou serigne Touba 😍😍🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳

    • @mansourmboup7659
      @mansourmboup7659 6 лет назад +2

      Walahi nio yèm. Niveau dafa kawéwone

    • @antathiam3970
      @antathiam3970 6 лет назад +2

      Mansour Mboup troppp sakhh ! Ken dou kou Ted ki

    • @mansourmboup7659
      @mansourmboup7659 6 лет назад

      No bimou aksé thi serigne saliou la départ

  • @diufy1559
    @diufy1559 7 лет назад +92

    Billahi serigne touba koukoy teukeulé ak sa way kouné
    Khamoko wala khamo sa way

    • @hannetorodo6563
      @hannetorodo6563 7 лет назад +10

      DiØufy Ønly liga wakh wakhat ko way ken dou Serigne touba Mbacke amoul morom

    • @maawasy4147
      @maawasy4147 7 лет назад +4

      aka ler lolou

    • @magayesarr4714
      @magayesarr4714 7 лет назад +2

      Yalla nguénefi yague daguéne bakh mourite

    • @khadimthiam5773
      @khadimthiam5773 6 лет назад +2

      mo mane fi mane fanou dieume fopé bâ boba akhemadou Mbacke

  • @ismawade9277
    @ismawade9277 7 лет назад +14

    il n y aura plus un QG aussi magnifique,emotionnel que celui ci!merci serigne saliou samb,tu m as fait pleurer toute la nuit .macha allah marianne,meussou ma khamné talibé nga. santrek.prochain QG avec s saliou samb:wakhtane ci mame cheikh ibra fall on espere

  • @baraniang8719
    @baraniang8719 7 лет назад +55

    maîtrisé ligay wakh nekhna
    DIEUREUDIEUF BOROM TOUBA

  • @serignefalloufall4242
    @serignefalloufall4242 3 года назад +1

    Theiy kou Tédd cheikh Ahmadou bamba mbacké Khadim rassoul 👂👂❤️❤️🙏🏿

  • @khadimdiop9897
    @khadimdiop9897 7 лет назад +3

    super Quartier Général dieureudieuf à pape cheikh et Serigne SALIOU Samb vraiment ces révélations nous réconforte et augmente notre AMOUR EN CHEIKHOUL KHADIM. DIEUREUDIEUFEUTY AHMADOU BAMBA SOUNOU YAKAR DJI TAY AK EULEUK.

  • @ziggystle
    @ziggystle 7 лет назад +5

    OOOHHHH. j'ai ressenti une joie immense en suivant cette émission. Je me rend compte vraiment de la chance que nous avons nous Sénégalais. Dieureudjeuf Cheikhoul Khadim. QG bi moma dakal yi diar yeupppp. Dieureudjeuf Cheikhoul Khadim

  • @hannetorodo6563
    @hannetorodo6563 7 лет назад +34

    Serigne touba Mbacke Khadimou rasoul niko yalla def koumou nexoul diga torox adouna torox alakk yawmal xiyam ganou diam mane salihou Hanne mako wakh louma thi gobe garko ken dou Serigne touba

  • @babacarsadio4684
    @babacarsadio4684 2 года назад +1

    24mai 2022 serigne Abdou Lahad yalla na sa borom yok ay leeram🤲🏿❤️

  • @mamasitagueye2035
    @mamasitagueye2035 7 лет назад +59

    Serigne touba niko yalla Def kumu nekhoul guewmani guemnga yonentibi

  • @falloufall1816
    @falloufall1816 4 года назад +1

    Machallah dieureudieuf Serigne Touba Khadime Rassoul thiye kou tédki cheikh Ahmedou bamba mbacké Khadime Serigne saliou samba yalla gafi yague te werr amine ya rabi thi barrekp sergne saliou mbacké Khadime Rassoule 👂♥️😍

  • @macoumbandiaye1107
    @macoumbandiaye1107 7 лет назад +12

    macha alha amna solo yalna nou yalla fayal serigne touba amine yarabi

  • @aliounecisse4840
    @aliounecisse4840 3 года назад +2

    beu fevrier 2021 damakay séétaane lii douma ci doyale djeuradieufé Kou Ted kiii

  • @guiguindao9238
    @guiguindao9238 7 лет назад +6

    sama xol ceide n'a serigne touba ak wa keureum yalla naniou leine yalla fayal

  • @alioudiop3418
    @alioudiop3418 3 года назад +1

    Qui est là en 2021 appui ''j'aime''

  • @minoushladouce7013
    @minoushladouce7013 7 лет назад +22

    Kou tedd ki loumougnou defal billahi khamougnouko sakh❤❤❤

  • @diarriatoumbacke3166
    @diarriatoumbacke3166 7 лет назад +2

    bijou Ndiaye yaw,geune nala beugue ndakh Serigne Moustapha Bassirou migua toud😍

  • @serigneamsatoudialibamback1420
    @serigneamsatoudialibamback1420 7 лет назад +4

    machaalah serigne saliou samb xam xam bi lérna yall nakou yalla barkéle amine

  • @abdoumorethanakingthiam6930
    @abdoumorethanakingthiam6930 3 года назад +2

    1.6k yi dislike khawma loungén done mè meun na sedei ni wa eukhlou narr ngèn, loungèn meneu degg wala lougén kham si SERIGNE BI nalen ler ni sen mbokk dioukit ba dra khew nak té yakarna diouliit dioulit moy mbokkam nègam ay diouliit ngen (SERIGNE TOUBA KEN LEU)

  • @sokhnamamefatymbacke9674
    @sokhnamamefatymbacke9674 7 лет назад +59

    153 personnes yii disliker yalla nalen yalla guindi ci barké serigne touba

    • @Lopios-g6l
      @Lopios-g6l 3 года назад +2

      Moma diahal déé

    • @yayasow4031
      @yayasow4031 3 года назад

      @@Lopios-g6l je

    • @isaacdiouf3379
      @isaacdiouf3379 3 года назад

      Mdrrr bilahi suis la en 2021 doumasi doyel yalnaniou yalla mouseul si bania degue borome touba ak wa keureum

    • @gnagnambengue3295
      @gnagnambengue3295 3 года назад

      Yalla sakh amna niou nagouwoul

  • @ndeyeaidasamb9803
    @ndeyeaidasamb9803 7 лет назад +2

    ken dou seriger touba wayé war nano sante bou bah kinou dimbalé mouy serigne saliou mbacké sama yakari tay ak euleuk yalla nanou serign touba tass si barkem

  • @zokara7382
    @zokara7382 7 лет назад +21

    man dé dama dioy émission bi yeup nda xol bou fess thiey bou serigne touba bou amoulone. ....😢😢😢😢😢😢

  • @papekabo6390
    @papekabo6390 6 лет назад +2

    Alhamdoulillah sama sopé bi yalla nako Yallah wéreul ci barké Cheikhoul Khadim

  • @ndiayecheikhmariemou1412
    @ndiayecheikhmariemou1412 7 лет назад +5

    bilahi #tfm ma beigue sii yeen nioune Sérigne touba rek laniou am bilahi

  • @dioumpapa4305
    @dioumpapa4305 4 года назад +1

    Serigne Touba amoul morom
    Dieureudieuf Serigne Touba
    Souniou yakarou euleuk

  • @ousseynoukane4747
    @ousseynoukane4747 7 лет назад +5

    diadieuf ken dou waw le sauveur de l'humanité sans vous on serait rien merci saliou samb akassa ko tédiki

  • @abdoulahadfaye14
    @abdoulahadfaye14 4 года назад +2

    DIEUREUDIEUFÉ SERIGNE TOUBA AK WA KEUREUM

  • @khadijamouserignesaliou1019
    @khadijamouserignesaliou1019 7 лет назад +77

    Dieureudieufty cheikhouna akhmadou Bamba ...QG validé bi mom néxna doufi gawa amat

    • @khadimndiaye5129
      @khadimndiaye5129 7 лет назад +5

      mai pape cheikh invitél baye adama sarr baye fall wala ablaye Diop bisri

    • @talibehserignbarambacke4981
      @talibehserignbarambacke4981 7 лет назад +1

      Khadim Ndiaye bilahi mome la wakh na indi serigne ablaye diop

    • @khadimndiaye5129
      @khadimndiaye5129 7 лет назад +2

      talibeh serigne bara ablaye Diop lou ler lay wakh yaw ño bokou s bara

    • @talibehserignbarambacke4981
      @talibehserignbarambacke4981 7 лет назад +2

      Khadim Ndiaye walahi guisnga cheikh mouhamadou lamin reik yalla nagnou dajè ak mom walahi kon sougn yakar

    • @dickocheikh4172
      @dickocheikh4172 5 лет назад

      diarna sante dé

  • @senegaleseboy6638
    @senegaleseboy6638 4 года назад +2

    Ani Gni koy setanat ci confinement 2020 Bi ! Ay Mouride reek lagn beug done🙏🏾🙏🏾

  • @soldarbidiop9079
    @soldarbidiop9079 7 лет назад +3

    s saliou samb yalnako yalla fay amine man damako beuge ndakh baye karim mbacke

  • @danedieng5316
    @danedieng5316 7 лет назад +1

    Yallana yalla yok ngueureum serigne touba cheikh Ahmadou bamba

  • @moustaphamouhamadouseck2442
    @moustaphamouhamadouseck2442 3 года назад +13

    3ans après je regarde cette émission qui semble tjr inédit...

  • @creatoure9384
    @creatoure9384 7 лет назад +2

    akassa bilahi amna solo torop yal nanou yalla fewalé ak seytané ta bolégnou ak cheikhouna cheikhoul khadim amineee

  • @aliougueye9396
    @aliougueye9396 7 лет назад +6

    rafetna way contan rek yalla na yalla fay way machallah

  • @khadimrassoulmboup493
    @khadimrassoulmboup493 4 года назад +2

    Borom touba ak borom darou bénnn laaniooo dotouniou niaarrr
    Serigne touba moo guenn nieuwonn, gueunn gnifiii nieuw, gueunn gneullei dii nieuw jajeuffetei

  • @mameseyesylla6811
    @mameseyesylla6811 5 лет назад +158

    SALAM KOUYY SETANE LII BA 2019 BII. BEUSSEUL J AIME

    • @papawade8521
      @papawade8521 5 лет назад +3

      Bismillah mangui ni

    • @almamydiallo9966
      @almamydiallo9966 4 года назад +4

      @@papawade8521 ba 2020

    • @khadimsow6844
      @khadimsow6844 4 года назад +3

      Ba 2020 kenneu d’où Serigne Touba

    • @sallasalioushop4476
      @sallasalioushop4476 4 года назад +1

      Mannn mikoy sètann jusqu'à présent a 2020 avec mon Mari a l'instant même dougnou si doyall.
      YALA nagnou YALA nagoull sougnou koorr dieuller fi COVID 19 barkep SERIGNE SALIOU MBACKÈ ❤

    • @fatouchathieye7302
      @fatouchathieye7302 4 года назад

      Ba 2020 sax

  • @mourtadaseye6664
    @mourtadaseye6664 7 лет назад +4

    bilhai QG bi mom.dou ma si doyal barkeb serigne saliou dama konatan lol si serigne saliou sambu yalla na serigne touba défal la taw fekh ak tayzir barkeb tayzirou hazir

  • @zeinasarr4379
    @zeinasarr4379 7 лет назад +12

    alahou akbar mane deii dama sakh yemou bilahi borom touba ak ndiabootam amouniou morom

  • @mordiaw3382
    @mordiaw3382 6 лет назад +1

    diere dieuf mame s touba amoul moroom yalla na nou ko yalla fayall thi bar kép alkhourane

  • @fatoumataniang87
    @fatoumataniang87 7 лет назад +77

    Alhamdoulilahh binou yallla bolle si ndiabotoou Cheikhoul Xadimm 😍😍😍😍

  • @tinemariama3822
    @tinemariama3822 7 лет назад +1

    machala kham kham kéne douko tatonné dagn koy diangu serigne saliou lep lére na serigne touba mom amoul morom lolou lérna gnep di gnanal aussi wa équipe QG liguey rafet trop mention spéciale vraiment vous êtes les meilleurs kou wakh ak kou wakhoul laf thiate.

  • @matydiao8289
    @matydiao8289 7 лет назад +21

    thieuy serigne touba amoul morom manou ma nelaw san setan li way machalla

  • @lild908
    @lild908 6 лет назад +1

    DIEUREUDIEUFEUTi khadimou rassoul, serigne Saliou yalla na yalla guoudeul sa fan te mayla weer thi barke seydina mohamed, wakhtan bi lerna machalah, Amatina solo ndeyssan

    • @djibyfaye3616
      @djibyfaye3616 6 лет назад

      God bless us Dieureudieuf Sérigne saliou SAMB

  • @aliougueye9396
    @aliougueye9396 7 лет назад +5

    machallah machallah wakh tanwi rafetna yalla na yalla fay len machallah

  • @galsenegalsene
    @galsenegalsene 4 года назад +1

    Kouko sétane ba 2020 beuseul jaim dieureus dieufé borome touba

  • @sonhiboundiaye2154
    @sonhiboundiaye2154 7 лет назад +106

    bilaye senegal liniou amm khamou niouko serigne touba ken dou mom

  • @MorSoftThiam
    @MorSoftThiam 7 лет назад +1

    Serigne Saliou Samb, éloquence,connaissance islamique et mouride,un phylosohphe du mouridisme hors paire , Yalla nala Seydina Mouhamadou Mbakiyou téral fi ak feulé

  • @ndeyecoumbacisse7198
    @ndeyecoumbacisse7198 6 лет назад +5

    Sante Serigne Touba rék yakar Serigne Touba rék wolou Serigne Touba rék diarama Mame Cheikh Ibrahima Fall. Alhamdoulilah bagnou donné ay mourides

  • @lobesohnafall5392
    @lobesohnafall5392 7 месяцев назад

    Je regarde l’émission en 2024 Keen dou Serigne TOUBA ❤❤❤ ❤❤❤

  • @mamadoudjighaly6277
    @mamadoudjighaly6277 7 лет назад +20

    serigne saliou a tout dis dans quartier général que tout bon mouride devrait être fier

  • @fadieye8219
    @fadieye8219 7 лет назад +10

    meilleur QG kene dou serigne touba

  • @amargueye1916
    @amargueye1916 7 лет назад +1

    Tieuy yalleu Serigne Saliou Samb Yalla na sougnou borom yook kham kham bi ci barké borom touba. tei sax nii rék leu mouride wareu méél guir génération yii di gneuw meneu ame kouléén wakhtanal lou wéér ci serigne TOUBA ak ndiabotam

  • @rahmatoullahkeita5444
    @rahmatoullahkeita5444 7 лет назад +6

    Sante Yalla biniou amei kou melni Serigne Touba ak ndiabotam
    Ken dou niome

  • @bambasarre1577
    @bambasarre1577 7 лет назад +2

    SERIGNE TOUBA rék la dou morom amoul morom kou ame morom mouye sa borome DIEUREU DIEUFEUTY SERIGNE TOUBA RÉK

  • @adrameguye7847
    @adrameguye7847 7 лет назад +57

    Émission hors série kéne dou serigne. touba ndok bamassi.boké. diotayou mouride dal.khamnani.dara dakoukou bilaye

  • @mymammecisse2197
    @mymammecisse2197 2 года назад +1

    Walahi li migui melni meusoumako setane dieureudieuf cheikhoul khadim

  • @nabusaliha7346
    @nabusaliha7346 7 лет назад +18

    fier d'être Mouride kene Dou CHEKHOUL KHADIM
    Sene émission tay bi intéressant na machallah Mouride yeup contane nagn akassa

    • @ndourcodou2004
      @ndourcodou2004 7 лет назад +3

      thiey serigne touba kene dou mome sounou yakari tey ak euleuk

    • @racediop5525
      @racediop5525 4 года назад

      @@ndourcodou2004 Amoul morom

  • @souleymanediagnerafahi7220
    @souleymanediagnerafahi7220 5 лет назад +1

    Kii écoute en 2019😁 jeureujeufff s touba

  • @hizboundiaye6115
    @hizboundiaye6115 7 лет назад +12

    gudal fan Serigne bi yalla nala Serigne bi fay bamba fi ne mom kese tay ag euleug

  • @mbackesy9944
    @mbackesy9944 2 года назад +1

    Qui modaka firi thi mourid yeup talibé cheikh la nak

  • @awathiaw3574
    @awathiaw3574 7 лет назад +30

    yalla na yalla yokou séne lér té tasgnou si séne barké

  • @minasy9566
    @minasy9566 7 лет назад

    QG bi douma si doyale chaque jour ma regardéko liii contana serigne touba hadimoul rasoul amoul morome dieuredieuf serigne saliou samb

  • @bambasalihou7386
    @bambasalihou7386 7 лет назад +5

    sama tourando rekay wadia bilay kén dou mom ndax mom rk mo wakhni
    ILAYAKHADA LAHOU MALAM YAKOUNI
    WALA YAKOUNOU HABADANE LI MOUKINI
    mom rk lako Yalla may
    DIEUREDIEUFEI SERIGNE TOUBA

  • @ahmafall5060
    @ahmafall5060 3 года назад +1

    🥰 thiey Kou teed ki ...Serigne touba si khôl Mo geune adouna’k liissi biir

  • @maguettethiam5812
    @maguettethiam5812 7 лет назад +6

    li li li daffa raféte.........sante Bamba rek..comme l'an passé HTDK nioko nékhalone cet année Serigne Saliou SAMB la li dafa leeeer

  • @youssoufbarry9754
    @youssoufbarry9754 5 лет назад +2

    Serigne saliou mbacké joxnaleu sama Leep bilahii❤️❤️ioe reik la doylo mbacké walahi❤️❤️

  • @boyfall1
    @boyfall1 7 лет назад +5

    jamais une émission télé ne m'a plus autant

  • @falloufall9284
    @falloufall9284 3 года назад +1

    amena solo serigne saliou .yalla na serigne samme laa

  • @iboufll
    @iboufll 7 лет назад +17

    Thiey lima dalll tay
    j'ai veillé beu juli subeu diwadia leulou rek daldi play rek pour khoolll DAll
    Wayé dall thi 1er parti bi la tambalé Sama nélaw yeup naw
    ma faff céétane bii bamou dal naka diékh thi diamonoyimay binede nii
    Skeuy
    kharall ma playatt ko, Liiii dou doyy !!!

  • @fadello1041
    @fadello1041 7 лет назад +8

    amna solo lolou serigne touba dou kene

  • @mbarganethiam7630
    @mbarganethiam7630 7 лет назад +15

    machalla ken dou Serigne Touba dé dieurediefé Serigne Touba wakhate kate yi dé diaroul nio tontu ndakh seniy wax safane la thi niom kon wax ak niom yokolen safane la

  • @bayeousseynoufallkhataba7361
    @bayeousseynoufallkhataba7361 7 лет назад +1

    MachaAllah Amatina Solo QG Bou méll Nii doottou Fii Amatina Billahii Kénna Dou Couted Serigne Touba Cheikhouna Ahmadou Bamba khadimoul Rassoul Yackaarou Diaaam gnii Adunna Ak Allahiraa dieureudieuffétii Serigne Touba

  • @cheikhibnouarabysamb5653
    @cheikhibnouarabysamb5653 7 лет назад +5

    Dieureudieufé Serigne touba wayé diaramma mame cheikh Ibrahima fall

  • @aichambaye1623
    @aichambaye1623 5 лет назад +2

    Serigne touba mofi nek kene dou mome

  • @omardieng1975
    @omardieng1975 7 лет назад +5

    Serigne touba rek mofi nekkkkk dieureudieufeuty borome touba...

  • @kharsalioufall498
    @kharsalioufall498 4 года назад +1

    Kenn dou Serigne Touba

  • @yerondiaye8994
    @yerondiaye8994 7 лет назад +132

    Dierediefety serigne fallou mbacke tfm di guaine ame lou bakh barkep cheikhoul khadim pape cheikh chapo