Je demande aux enfants et aux parents de ce vieux de venir le récupérer, le soigner et le sortir du milieu de la lutte. Chaque jour migui toop ada fass di dioye té amoussi satisfaction.
Il faut savoir quitter la table quand le respect n'est plus servi. Kouy setane say interview xamni danga beug Ada mais kou beug diapalé mo nékha diapalé
Sénégal tu vois un jeune qui fou le bordel niou nane xalé la ...père ya warra nopalou ta fait tout ce que tu avais à faire mais qui d'où donne champion car il n'est pas sportif.
Vrai ki ani ay domam kw doun recupere sen papa ji si age bi mou topu nit koula fale woul epui limiy sorti si boy bi legui mou bari bou yague yaw la nit gni di diepi kw
Waw mé pabi mome soy topou niit té respectéwoula dogo tégue ni dégué mé a chaque fois Ada li Ada lè bayil Ada soula tolé nonou
DEUG pir yène yi iniane laye ndourou dh
Dafay am defois guis ben grand topou ben dafa guisni ki man am dara thie lamb ndeyesan beugeu dafa fort quoi
ki au debut mo done entrainé ada fass. ki souko ada fass woré dou ko djikeu. je suis temoin occulaire
Per bayil
ada fasse domaram la amal fouleu yalla mougui fep
Je demande aux enfants et aux parents de ce vieux de venir le récupérer, le soigner et le sortir du milieu de la lutte. Chaque jour migui toop ada fass di dioye té amoussi satisfaction.
Vraiment bien parlé
Billahi
Bilahi Sénégalais mon tame yakar si
Koumou yakar ni moko tané té démain woul nonou
vraiment
Merci way
Pere yaw ken du yaw .. Vraiment longue vie a toie❤❤
Père yalla na yalla sammm laaaa wollahi BEUGUE nguir linga toudeee sa domm sama SERIGNE Mawlana cheikh Ibrahim niass radiyalahou anhou
Thiey wa fasss 😢😢 chak jour problem 😅
Pére boma diourone taye digua
Bayi ada fass si ni wala si néh
Da yék bopame😢
Vraiment ada fass dou mbeur dou champion dou veudette khaliss dong Moko bayii si lambedji
Père nopaaloul thi ada fass beugoul lou bakh kay degeuloula bayi koo
Ndeyssane yala nala yala defal tawfeih pere.
Père mouno bayi ada fasse comme que respecté woulla
Ada fass nuit daye gore 😢
Wahonako ya topou ada wayé ada faléwoula
Pére da beug ada términaison bi amna solo ada dél batré PA adouna yagoul fall
Vraiment ada fass domeram la
Machallah amna solo
Ada vraiment dou nit
Franchement ada dou toss
Ha li doyna war deh ada fass koula beguone la mai ces fini ada dou gore thieu li nice soul ada sétile pa bi
Soko bayé numakoy wagni tmt Yalla yoor nieup
Sénégal 🇸🇳 mitina
Père nguir yalla do bayi boy bi diap si yalla il verra
Bilahi ya niake diome do bayi ada fass
Il faut savoir quitter la table quand le respect n'est plus servi. Kouy setane say interview xamni danga beug Ada mais kou beug diapalé mo nékha diapalé
Problème yi diougué na pikine Mingui 😂ndakarou 😂
Paa bi dof la ki respect tewoula doko bayi chaque jour rek ada fass maydiou
Bayil ada tout trankil té gua concentré ci sa écurie noppi
Cheuuu sokhor aka beuri Sénégal touti succès rk niou sikeul la
Père bayil interview yi guay def dou respecte ci iow ak wa fass
Père nopaloul tamitt
Pere Ada dou niit bayko way
Pa bou gnak foula ga depuis 2022 yagui dioy guir ada fass doko bayi khana sa dom sax boula dioxoul thieur ga abandonner ko
Père do nopalou bayi Ada fass tamit nga nopalou ana ayeu domam dougn ko dieul wax ko mou bayi waxou Ada yaw ko xamni xamoul sax sa keur tamit
Pere esk do niu dimbali bayi Ada fass ...
Vraiment warga fété boy bi bou gnawwaté boulgo lédjeunti
Sou yaguè nak gnouni dagako soxorè succès bo
Day doul ki dou tous dileur leu
Ada fass mo yeukk succé té dou deureum
Je t’assure
Ada Fass Di Ngaka
Coach tamit chaque combat la même chose nguay wakh après loum yague yague di guen dioubo 😢😂
Pere yawns gua balma dagua commencer beuri wakhh
Bayyile doum diambour barigu woxe trop
Pabi nak diakhal nama barki cheikhou tidiane barki cheikhoul khadim barki cheikhra fall😅😅😅
Demall gua beurék liss mo guenn nak ada fasss dou mbeur
Pa bi démal nopalou dji svp sa wakh migui beuge bari. Ada fass nawlo woula comme khamoul sa keur
Yaw pére Loula Ada fasse déf bakhna yaw ya topou Ada wayé Ada topoula kom diaralé nala wakh Lou amoul thi mag moutol ni yaw té ragalau thi yalla
Père dafa beugue Ada motakh mouy wakh koi
Yaw ada falé woula yalnane ko dane
Sa diobou Ndey
Adafassrek
Ada dou mbeur n’a bay lomouy def
Lamb dji amna Li yepp 😂
😂😂 sheutt site yi sofe nagn
Pére bayil ada fass tranquillement gua tok diko sétane audouna dinako yar
Pabi thie bopam mo wara bayi lamb à mon avis
Nako bayi si le gosse ne veut plus de lui c'est aussi simple
Sénégal tu vois un jeune qui fou le bordel niou nane xalé la ...père ya warra nopalou ta fait tout ce que tu avais à faire mais qui d'où donne champion car il n'est pas sportif.
Aba kara domou NGB bii
No pabi nak warna gnouko wakh deug nak
Ey siteu baye fall leu Bilay siteu d’où mbeur sakh baye fall leu Bilay pabi sou deukone diam guene siteu douko setane
Vrai ki ani ay domam kw doun recupere sen papa ji si age bi mou topu nit koula fale woul epui limiy sorti si boy bi legui mou bari bou yague yaw la nit gni di diepi kw
Pabi nak mom
Non ada dou mature jamais 👎🤦♂️
Pere nak nga balma mai sa wax mingui beuga beurii demal nopalou t bayi ada fass mi legui mak nga
Pere diapal rek day bakh