Comment on peut gracier une personne pareille? Il faudrait revoir les dossiers de grâce ! C'est pas normal alors qu'il y'a peut-être d'autres qui devraient être à la place de ce gars !
Comment un gosse pareil peut-il bénéficier de grace? Le directeur de la prison où était enfermé ce gosse est responsable. Car c'est eux qui fournissent la liste de ceux qui sont graciés par Diomaye 😭😭😭. Qu'Allah l'acceuille au paradis inchalla
vraiment tamit. li keneu hamoul lanela. vraiment luniuy gracie gni key hana niou ba gni satieu guinaar ak mbourou ak gnidone khehh ak seneu wouj wala yoyou mais li tamit no way
Où sont les parents du tueur ? Faire des enfants c'est d'assurer leur éducation au lieu de le laisser airer dans la société. C'est triste de voir ce qu'il a fait à ce jeune éduqué et engagé plein d'avenir. Paix à son âme
Innalilahi wa inna ileyhirajihoun yalna ko buur yalla yeureum té diegalko kharé ko aljanna barké yonente bi sws ! Massa way yalna buur yalla doli len kholou mougne barké yonente bi sws
Mm pas quelques semaines un jeune a été tué et brûlé à tivaoune quelques choses que je n'arrive pas à oublier car je me demande comment avoir cette haine et rancoeur tuer son propre frère musulman où autre c la manque de foi chez les jeunes et l'éducation veuillons revoir leur éducation stp revoir aussi ceux qui fréquentent nos enfants wlh lii guissou ma likko gueune metti repose en paix frère yallah yeureum kharé aldiane 5:02
Il était en manque ce jeune ....comment peut-on gracifier des récidivistes ? . Qu Allah Azwazal lui accorde sa miséricorde et l accueille dans son firdawys jannatin tajri min tahti an al har..Et accorde a la famille la patience de cette épreuve.
Ndeyessane avec tout ça niouyy naan prison yiii dénio warra nékh c'est dommage 😭 Démbou REK liîrna bénni commentaire kou néee " chaque prisonnier défa warra amm chambre bopamm, matelas bou bésss akkk ventilo" ça sera très facile
Que DIEU l'accueille dans son paradis céleste. Mais ce cas montre que la grâce ne doit pas être accordée à n'importe quel détenu. Il faut impérativement un contrôle stricte des dossiers de grâce et une enquête sérieuse la dessus. Ça c'est intolérable dans un état de droit. C'est pas ça la démocratie. Je suis de tout cœur avec cette famille.
Arrêtons d appelet ces monsieurs elus par le peuple.. son excellence....En quoi sont-ils excellents lorsque la situation du peuple ne s améliore pas ou peu. Cependant la leur ( situation) evolue et croit en patrimoine et finance...
@@veroniquenatack7392 je te jure. Legui on te tue facilement pour rien. Mais del khol mois prochain gnanoumako dé mais so defoul nank même chose ngay degate.
Les dossiers de grâce doivent être etudies de manière rigoureuse. Ses parents doivent porter plainte contre l’Etat Senegalais car il y a un dysfonctionnement. Ce genre d’individu ne doivent pas sortir de prison.
Koku mokotay foumuko déffé fofu guénko waronn rayyé prison bi day yombu si mom trop fo guiss kuy rayaté mofi gueuna ragual dée danguénn ko waronn ray ndayam c tout ah 😢😢 li méttina way
@sambasene c'est le président et il est entièrement responsable Ce sont de mauvaises pratiques qu'il a herité des anciens régimes mais c'est a lui de le geré ces manquements Exple au jugement il demande de mettre pas de grâce ou possibilité de grâce sur chaque dossier Ou bien plus de grâce c'est tt on est pas dans un royaume Et voté la peine de mort....svp
Seneweb de véritables pyromanes Que diable fait le nom de Diomaye dans votre chapeau. Vooir seulement agité le débat Yallah nako borom bi yeureum té djégalko
Kholal wa seneweb ak sene titre bi le. Président de le république signature rek la am pour gracier c est aux agents penot3 nioy def sene liste bande de con
C'est un.mécontent motakh selon moi gni ray nit keine warouléne gracier dejà famille kigne raye seine dom.dinaleine meti gnouy kheuy di guisss ki deif crime bi en liberté nagnouy kholate gnignouy gracier amna mbam yo khamni prison à vie lagne mérité
La faute à ma personne qui l'a gracié boy deff li c'est du cas par cas les agresseurs tueurs ou autre et mm violeurs ne merite pas d'être gracier li nékhoul si khol
Vraiment Mane dal Sénégal Mane diakhal nama pêne de mor khana mounougnou KO voté kou raye gnou rayela😭😭😭😭😭🙏
Bilay lolou sou amoule mom li dou arête
Loulo moma jaxall
Wakhal deh, kou ray gnou rayla , kou sathi gnou dague sa lokho , bilahi légui li djiekh
Silagnou djeum d baxna
❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Avec ça ngén Beugueu kosso néx 😢😢 bo waxé niouné prisonnier yi danio soneu té bolén yeureumé libérélén niou recommencé sén yeufou mala yi😢😢
Criminel yi Kaye sen prison appart lagne wara oute Dilen trokhale goudi ak beutheuk baniou Dee
Vraiment
Traumatisme à vie balaye walaye 😢massa lène yallah n'a book thi djabotou Rassoulillah saw dii doundeu thi kèpar gueu in challah
Vraiment lii warnafei djékh Koi
Yalnako Yallah yereum té xaaréko aldjana cii barké yonénete bi Psl 🙏
🙏🙏
Mane dale amna louma méti trope vraiment khaléyi you ame avenir rék laniouy raye yalna égalais li ndawame aldiana si barké seydina mouhamed amine
Kou raye nui raye la rek biu amone Li do amatii
Yalnako Yallah yereum té xaaréko aldjana cii barké yonénete bi Psl
😭😭😭😭alakhou akbar😱😱😱 j’ai mal au coeur on doit appliquer peine de mort au Sénégal 😭😭😭😭
Comment on peut gracier une personne pareille? Il faudrait revoir les dossiers de grâce ! C'est pas normal alors qu'il y'a peut-être d'autres qui devraient être à la place de ce gars !
Deffal ndank j'ai avec moi la liste des graciés et amoul keneu kou deff crimes kouniu gracié,kii rayy tayy meussoul rayy,mingui soggua rayy
@@Mamanfelwin15la liste des gracié a été publié
@@Mamanfelwin15Ah vous êtes sur
Yow. Wara yeumbeul. Nenaniou defnako ay. crime nga. Nane ! Boy bi. Parka may dokhanto !.
@@malily6705 oui je suis sûre à 100 pour 100,j'ai la liste des graciés
Massa massa massa yalna yallah yeureume ko kharer ko aldiana firdaws
🙏🙏🙏
Gracié mo waratoul AM kou nek n'a teudd sa peine bamou diékh tak😢😢
Ndeysane yalla nako yalla yeureume te maylene kholou mougne metina
Ndeysaan massa. Yalla nakor Yalla yeureum teh hareh kor Aldianatoul Firdoussi Insha, Ameen.
Yalla nako yalla yeureum ta xaré ko Adjanay firdawsi si barké seydina mouhamed psl 👏 😭🕊😭🕊
Comment un gosse pareil peut-il bénéficier de grace? Le directeur de la prison où était enfermé ce gosse est responsable. Car c'est eux qui fournissent la liste de ceux qui sont graciés par Diomaye 😭😭😭. Qu'Allah l'acceuille au paradis inchalla
Vraiment Lou triste tanta aby yalla n'a yalla may khôlou mougnie😢😢😢
Yalla nako Yalla yereume te khare ko aldiana firdawsi
Walahi reyna kou bakh te ame kersa amon diner repose en paix mon frere matar wzlahi neubouga ba dem
🙏🙏
Yalnako Yalla Yereum. MATAR KUBAKHONLA KU NOPI AMOUL BENE BLEM ❤❤❤❤❤❤
Metina torop Yalnako Sunu Borom yërëm xaare ko aljanna firdaws.
Amin inchallah
On doit restaurer la peine de mort sinon personne ne pourra limiter ces dégâts. Que Dieu l'accueille au paradis firdawsi. Massa
Diomaye khamoul gnou niouye. gracié Niaye. Ligueyé thi justice bi . nioye. facilité grâce yi pour. delinquants
Il devrait prendre le temps.de.bien vérifier avant de gravier
C'est pas diomay ki gracie chérie
Vraiment c’est pas le président qui choisit ceux à qui gracier lui il signe seulement
@@fatoundiaye6412mais quand c'etait macky au pouvoir bcoup l'accusait d'etre le responsable alors ce n'est po le cas
Il y a beaucoup de prisonniers qui n ont pas de casiers judiciaire .
A cause de cela le president risque de ne plus gracier.
C est triste.
Man dh nianou mako yalla ms kou Ray sama mbokk fo diar ma rayla bilahi leuzi yalna nko yalla yereume metina trop
Un criminel ne doit jamais être gracié. Il y a d'autres prisonniers qui méritaient plus la grâce que ces genre de personnes. 😢😢😢 RIP MATAR.
👌
*Bilay ioe*
vraiment tamit. li keneu hamoul lanela. vraiment luniuy gracie gni key hana niou ba gni satieu guinaar ak mbourou ak gnidone khehh ak seneu wouj wala yoyou mais li tamit no way
Où sont les parents du tueur ? Faire des enfants c'est d'assurer leur éducation au lieu de le laisser airer dans la société. C'est triste de voir ce qu'il a fait à ce jeune éduqué et engagé plein d'avenir. Paix à son âme
Nitt kouy sangue neew bou démé ba dioy khamal ni limou ghiss mettina trope
Ces gens ne méritent jamais des grâces ,un délinquant....
Yalnako yalla yerem té khareko djianatoul firdaws metina trop il faut que justice soit faite 😭🙏
MAIS C'EST QUI QUI ETABLIT LES PERSONNES QUE L'ON GRÂCIE !!!!!
Yalla yalla yeureum ko thi barque Mohamed
Le criminel doit être emprisonné à vie sans bénéficier de grâce.
wakh nga deugeu Lou lér nga wakh
Li moy Sénégal
Yalla yalla diékhal li thi rew mi barque Mohamed
Qui est pour la peine de mort pour ce genre de délinquants des voyous
Ki bou guéné géne raye ko lolou rék moye solution bi
Ndeyssane Yallah nako Yallah yereume té haréko Aldiana Firdawssi 🤲🏽🤲🏽🤲🏽🤲🏽
C’est triste 😭 que justice soit rendue à sa famille
Metina loleeeeeee yallana yalla yeureumeko té khareko alediana amineeee metina wayé mougne rek eskey gracié nite kou sokhore raye domou diaboure eskey
Innalilahi wa inna ileyhirajihoun yalna ko buur yalla yeureum té diegalko kharé ko aljanna barké yonente bi sws ! Massa way yalna buur yalla doli len kholou mougne barké yonente bi sws
Allahuma amine 💔🙏🕊
Vraiment c’est triste paix à son âme 😢
Que son âme repose en paix.Amine!
Mm pas quelques semaines un jeune a été tué et brûlé à tivaoune quelques choses que je n'arrive pas à oublier car je me demande comment avoir cette haine et rancoeur tuer son propre frère musulman où autre c la manque de foi chez les jeunes et l'éducation veuillons revoir leur éducation stp revoir aussi ceux qui fréquentent nos enfants wlh lii guissou ma likko gueune metti repose en paix frère yallah yeureum kharé aldiane 5:02
Il est maudits 😢
Machallah son excellence Liguey bi rafetna lol le peuple sénégalais est fier de t'avoir a la tête de ce pays
Il était en manque ce jeune ....comment peut-on gracifier des récidivistes ? .
Qu Allah Azwazal lui accorde sa miséricorde et l accueille dans son firdawys jannatin tajri min tahti an al har..Et accorde a la famille la patience de cette épreuve.
Inallilahi wo ina ileyhi radjioune inallilahi wo ina ileyhi radjioune inallilahi wo ina ileyhi radjioune Allahouma.aghfirlahou wo yarhamhou amine
Khana dougnou khol casier judiciaire avant grâce bi tamiit!,, niit bou sathi , waleu khekh sakh, wayé kou ray niit, loutakh gniukoy gracier , chiiip
Ndeyessane avec tout ça niouyy naan prison yiii dénio warra nékh c'est dommage 😭
Démbou REK liîrna bénni commentaire kou néee " chaque prisonnier défa warra amm chambre bopamm, matelas bou bésss akkk ventilo" ça sera très facile
Saway lolou moy yonn ff nieup yemouniou té nekine bii ff dou yonn da ngay khalat nio khamni ay innoncent laniou te diomoul keneu bilahi
Yalnako borom bi yeureum
Yallah na khippè si aldiana firdawsi si barkè sangue bou tedd bi saws amine yarabi
Que DIEU l'accueille dans son paradis céleste. Mais ce cas montre que la grâce ne doit pas être accordée à n'importe quel détenu. Il faut impérativement un contrôle stricte des dossiers de grâce et une enquête sérieuse la dessus. Ça c'est intolérable dans un état de droit. C'est pas ça la démocratie. Je suis de tout cœur avec cette famille.
Yalla nako yalla yereum
Paix à son âme. Ndeysane.
kou dém prison 2 fois waratouö guén a vie irrécupérable! RIP Matar.. la grâce ne doit pas concerner les crimes de sang
Paix à son âme que Dieu l'accueil dans son paradis
Ndeysann dof yangui thi nitt gni😭massa
Nagnouko Ray rek.
Yalna ko allah yeureum firdawsi di keureum
Arrêtons d appelet ces monsieurs elus par le peuple.. son excellence....En quoi sont-ils excellents lorsque la situation du peuple ne s améliore pas ou peu. Cependant la leur ( situation) evolue et croit en patrimoine et finance...
Kokou yalna dé thi prison bi
La foule devait le battre a mort
Amoul ndeysane!
Construire une Grande prison tci alou diamniado bi , peine de mort ou perpétuité rek!
Zéro gracié !
Diamniadio sedna tamba wala kolda si tangay bi bu meti bi teksi travaux forcer
@@KhaboussFall exactement ! Y a de l'espace nagneko def! Li dafa yomb
*Je suis d’accord avec vs lou khéw thi réw bi dafa yomb trop*
@@veroniquenatack7392 je te jure. Legui on te tue facilement pour rien. Mais del khol mois prochain gnanoumako dé mais so defoul nank même chose ngay degate.
@@emilemoreira6465 *Deugue bou werr gua wakh lifi nekk da eupeu bougne ko arrêter woul day gueuneu empirer c’est trop vraimnt*
Paix à son ame 😢😢😢😢😢
Les dossiers de grâce doivent être etudies de manière rigoureuse. Ses parents doivent porter plainte contre l’Etat Senegalais car il y a un dysfonctionnement. Ce genre d’individu ne doivent pas sortir de prison.
C ça le problème je suis son grand frère lolou loutax niou graciiers ko
Kou ray niou ray sa ndéy mou diéky
Daguéne ko warona raye bala policiéyi di gñiaw
Bilay li métina trop raay domou diambour si zéro prkwa niouy gracié bandit dagne ko tethie à vie
Yalnako yallah yereume
Ki moy domérame yalla n'a yalla yeureume ko karé ko aldiana firdawsir
Kone ki yague na raye motakh mou maîtrisé fimou mane kao té boy bi
Repose en paix notre tres cher pti frère
Kouray tatayko nanuko ray loloula Yalla wakh.
Repose en paix Matar, Moussa Yallah nalénes Yallah may kholou mougne
Peine de mort kou ray gnou rayla doit être une exigence nationale 💯 gnata nit lagnou ray gratuitement si 3 dernières années yii
Réponse en paix 😭😭😭
Yalla na ko yalla yereum té kharé ko aldiana firdawsi c'est dur
Koku mokotay foumuko déffé fofu guénko waronn rayyé prison bi day yombu si mom trop fo guiss kuy rayaté mofi gueuna ragual dée danguénn ko waronn ray ndayam c tout ah 😢😢 li méttina way
Ki moy doméxarame, meunone nguéne réye ndéyame dafa yombeu torop😏
Mais quel sont les critères qui vous permet de bénéficier d'une grâce??lolou war nagne ko xolate
Bonne question.
*Trés bne question*
Vraiment lolou lou djarra guestou là parce que ce vaurien là c'est un récidiviste
Yala na ko yala yeurem
Banlieue bi dafa beuri ay anciens malades.
Mai graciè warna nan ko xolat dh
sama mbook kouray ma raayla
C est grave Diomage refuse de porter ce poids criminel. Revois vite ta politique de grâce
Diomay n'est pas pas impliqué, on lui présente des dossiers
@sambasene c'est le président et il est entièrement responsable
Ce sont de mauvaises pratiques qu'il a herité des anciens régimes mais c'est a lui de le geré ces manquements
Exple au jugement il demande de mettre pas de grâce ou possibilité de grâce sur chaque dossier
Ou bien plus de grâce c'est tt on est pas dans un royaume
Et voté la peine de mort....svp
Massa métite mounoul wéssou li yalnako yala kharé aldjana firdawsi yalnalén yala may kholou mougne
Aye graces yoo khamnè do khame nounioukoy lidiénté dama rousse sakhe billahi li mome nafiyame
boy bi rancunier leu plus psycapate il doit veillir en prison
Libérer niit ki tei pass sakh pour dem keureum douko am, bou gueiné automatiquement day défat lou raw loumou défone. Li dafa méti way
Seneweb de véritables pyromanes Que diable fait le nom de Diomaye dans votre chapeau. Vooir seulement agité le débat
Yallah nako borom bi yeureum té djégalko
Kholal wa seneweb ak sene titre bi le. Président de le république signature rek la am pour gracier c est aux agents penot3 nioy def sene liste bande de con
Les détenus après leur libération il faut les suivre et les accompagner par un médecin sociologue
Metina torope bilaye yala nako yala yereme
Ki raylen ndayame mou diekh yoboulen ndayame parc hanne diokhko gayndé yi niou lek ko
Mo mane téma toukhou Sénégal
Mais dou nieup laniou wara gracié
Est-ce que cest une personne graciée car quand on voit la date de leur libération ils ne sont pas encore en liberté.
C'est un.mécontent motakh selon moi gni ray nit keine warouléne gracier dejà famille kigne raye seine dom.dinaleine meti gnouy kheuy di guisss ki deif crime bi en liberté nagnouy kholate gnignouy gracier amna mbam yo khamni prison à vie lagne mérité
Paix à son Âme
Nagniou ko diap teuthie bamou dh
Khamna nii man souma néké homme de tenue am yénn grade yii Sénégal dii na djoub kothie
La faute à ma personne qui l'a gracié boy deff li c'est du cas par cas les agresseurs tueurs ou autre et mm violeurs ne merite pas d'être gracier li nékhoul si khol
Fane la si yeumbeul
Hum na yon DF liguéyam
😢 matar firdawsi sa keur