Merci Oustaz. Vraiment tu as tout dit. Yokk nga sama ngueume ci Baye Niass ak ci sunnay yeukeuti bi. Tu pensait k meungua devier nitngni Mais danganiou gieuneu Yokk ngueume ci Mawlana Sheikh Ibrahim. Shukran
J'aimerais bien lorsque je l'écoute qu'il me dise comment prier comment réparer une prière etc mais il passe son temps à critiquer des musulmans comme lui franchement y'a beaucoup de sujet très important pour les musulmans Maintenant s'il n'est pas d'accord avec les soufis n'a bayi yalla juger au jour du jugement wa Salam
Boule découragé béneu yone kila sope la dila gnianale goudou fane ak wére ak sa yéné cilou bakh yalla matale ko mane yalla rek la yakar té sope mouhamed (psl)
Way Way meyniou fo xamene kou tolou ni cheikh tidiani fala bok kou melni cheikh saad bouh koul melni cheikh abdoul khadjr jeylani kou tolou ni.mame serigne touba kou tolou ni el.hadj malick yalla naniou yalla rey si sen yone
Assalamou aleykoum chers frères et soeurs en Islam. Premièrement: Je pense que en tant que musulmans nous sommes tous intéressés par la bonne guidée (la bonne voie pour adorer notre Seigneur afin d'obtenir sa Miséricorde et donc le Paradis). Deuxièmement: En tant que sénégalais, nous savons que nous vivons dans un pays à sectes religieux dont principalement les soufis composés de l'ensemble des tarikhas et ceux qui se réclament d'Ahloul sunnah wal jammah. Et entre ces deux composantes de notre islam au sénégal, il existe des différences d'interprétations, de comprehension et de la pratique de notre religion. Je pense que si nous sommes tous intéressés par la vérité ce n'est pas en nous insultant et en nous attaquant les uns aux autres via les réseaux sociaux que ce problème va se régler. Il n'y a qu'un seul moyen de savoir qui a tort ou qui a raison: retourner au Coran et à la Sunnah du prophète PSL. Sur ce il n'existe qu'une seule voie de prouver que ce que Oustaz oumar Sall avance est erroné: soit les références coraniques et aux hadiths qu'il donne sont fausses, soit ces références sont vraies mais qu'il en fait une mauvaise interprétation. Il ny a que dans ces deux situations que l'on peut lui imputer le tort car dans ses déclarations il avance des arguments. On ne peut pas gagner son procès en insultant son adversaire ou se contentant de dire "Il ment", il faut pouvoir apporter des arguments solides tirés du Coran et des Hadiths. wa sallam
Merci yahaki ils peuvent pas argumenter oublions les insulteurs ne te fatigue mme pas quelqu'un n'est pas sourde que celui ki ne veut pas entendre en + leur unique argument est koi nos ailleurs le font comme ça ces gens-là ne basé pas ni hadiths ni coran wallahi ça fait pitié comment peut-on être musulmans sans suivre la sunaa du psl inimaginable un pays soi-disant 95 musulmans sur nom pas l'acte no problème ko dieu ns guide.
Jador s oustaz.bilahi. cependan Lignorance reste la pire dè soumission.d grace prenè come guide spirituel mohamed psl.c l salut final.sèrieu ya dè gens ils son tt mouton
salam nagn bayi saga yi way té ragal Yalla lou nitki wah wala bindi rek Malakayi bind nagnko Si vous êtes d'accord avec Oustaz Sall barakallah fik si vous en êtes pas5 d'accord guen ham lolen di wah Oustaz dioulit sunnite leuh té dioulit dey réfétal assalamou alaykum
Je viens d’ecouter Baye niass et comment il a raison. L’homme possède une arme puissante qui n’est rien d’autres que sa langue. Cette arme peut faire de lui le plus grand homme de l’histoire comme elle peut le rabaisser a l’échelle pharaonique. Elle est source de bonheur, mais aussi de malheur. Elle sort des bienfaits mais aussi des méfaits. Rien qu’à l’entendre parler on sait qui parle. Elle conduit à Allah en l’invoquant ou à dire que du bien vers Allah. Mais aussi elle conduit en enfer en faisant du Fene et Dieuw. Yallan nagnou Yalla moussal si lamigne
DEUG nexoul.Ya Outaz boul Bayi.kou am deguine ak xel xamni Yagui wax DEUG kessei. Lima meti moy kou Amoul réponse bou valable tek ay saga.les gens t'insulte et nous on te suit si diangal yi ngay def. Pourquoi vous l'écoutez alors que li ngueni deg néxoulene.deglou lene koulene nekh té Bayi Ki ngueni saga.Allah est plus savant .
Baye Niass n'a jamais dépassé 4 femmes et ce que vous racontez sur l'interview de Gassama n'a jamais eu lieu on a tous écouté cet interview. Oustaz nitt kou bakh dou deff li ngay deff. En ce qui concerne le tarbiya vous ne pourrez jamais comprendre cela et Dieu choisis ceux qui le connaîtront. Baye Niass est une chance pour l'humanité ainsi que beaucoup de ces marabouts que vous contredisiez.
baye Niass d meusouta wathie charia t meusoul ame lou eup niétti sohna Oustaz nite sou gueumé yalla dou sossal nitou yalla khawma nak Lo dioublou si li wayé yalla dinala mbougeul inchalla
bayileen sen ndeye ak sen bayi yi di foywe tè fèkhè xam li tax yalla sakk lèn ndeye ak baye ba parè amal lèèn ...Yalla nieup la fi nèkal wayè ku nèkal yalla ..YALLA nekal leu ... man kanalilahi kanalahou lahou ...fekhèlèèn xam sen bopp...oumar sallo ...,demba...patèè yoo.... ku xam sa bopp Xam sa borom...je suis yalla yalla mais j'aime Baye Niass parceque xamna Yalla tèi xamal nako ay talibèm...
Xamm xamm kendou diangue ( danou koy sakkou) . Wayé dara meunouta xamm dara filék guissouko. Diamou yalla Bo xamm né mouno xamm ki ngay diamou . Lolou moy être dans un état d’incertitude. Té yalla thi khaak nga koy diamo, manam deug ( la verité , le secret ) . Comprenons dans ce sens l’islam est un secret, et un secret ne se divulgue pas mais plutôt il se transmet par un messager qui est d’annoncer le contenu . Mané pour mouy leer Cheikh Ahmadu Bamba Khadim Rassoul motax niou xamm yalla , gueumm yalla , agg thi yalla . Am Yakin ba moudiou done ko , done abdoulahi diko diamou ba done Sadikh , té thi deugou gogou nonou la nitt di soukeudikou pour amm lerou yalla dji . Allahou nourou samawati wal ardi. Dieureudieufeuti Sangue CHEIKH MOUSSA CISSÉ NIAMBÉ BROM DAROU
Diante bi dafa lérr nagne t yalla mayoul nieup giss ko (goumbeu yi) t pourtant dafa lerr nagne Nonou leu yalla mélll geumeul linga geum nioune baye daff nio nandal chariya ak haquiqua santeu yalla boubax bala nga comprendre (IYAKA NAHBOUDOU WA IYAKA NASTAHINOU ) lernala ni yangui diano ak mom yalla wayé kiray bi dokh sa digeunté ak sa borom moy waral niakk kham gui wayé sante yalla boubax bima doné gouney cheikh ibrahim
Maasha Allah... Jazaaka Allah kayran. We are really greatful for the effort that sheikh Omar Sall is doing to pull the wool out of our eyes. Sufism is indeed a horrible sect.
Alkhamdou lilah Dieureudieuféty Baye Niass Baye Niass meussoul wathie Sharia the waxal Baye lou ñaw taxoul dara ñaw ci Baye kon lou way def rek bopam té wedi nittu Yalla yagnafi ndaxté Yeuneunt bi ay nitt ñoko dan wedi kon sou amé ci Baye rek bettuñu demb moy tey rek wayé nak borom deudj bi meunna dioy deudjam té Baye louko way def bala nga dh dinko guiss Ñun nk Baye moñu yarr mo tax duñu saga ken té douñu xass ken wayé kou lal Baye rek lal ngañu mo tax duñu noppy ci wax dji Baye Gédj bouy yokk sassouné la té dou meussa wañekou Dieureudieuféty Baye Niass Baye boudé fébar nañou rey beug nañ
Pourquoi montrer la photo de baye ca me fait mal ca n'a rien avoir avec ce que vous expliquez ..le disciple de baye est un modèle de l'islam dans tous les domaines..C'est l'adoration en ALLAH et suivre la voie du souna faut pas nous montrer des exemples de certaines personnes qui font du n'importe quoi et dire du n'importe quoi pour gèneraliser les écritures peuvent être grosse mais les actes sont agréé..tout savant à du soufisme en lui cela dépend comment il se manifeste.. C'est une connaissance divine un secret que l'on doit garder par maitrise en soit,C'est pour èclairsir que baye niass sa voie c'est Dieu son Prophète et le coran..
baye niass deh waxnani yarr na ay talibem bi zahiri sharhi wa nouril moubine dnc yow echec nga si feinal les soufis nga xamni sharia dagnoukoy top feinal nga baye si linga wax ni mo waxni nitou haqiqa leu ngani Rts mokoy tek je tassure soumalay guiss dila trokhal diokh ma sa adresse ma weer la legui pieuvre sakh mola taneh ya trokh feinne nga feinnn ba amato loy wax tegalal nite gni fou gassama waxei ni baye niass affairou lou eup 4 femmes doko indi mouk ndakh amoul benen bi moy baye meusta takando lou eup nienti sokha * lingay fein yeup do dei tei wahidou qahar doulako fay
Booko guissé dinga kham noumou mél... Demal nga diem ko guiss... Guiss yalla diaféwoul, guiss loudoul yalla moo diaffé. Nd1kh yalla mingui wakh si alghouran, sourate Baghara :" ولله المشرق والمغرب فأينما تولوا فثم وجه الله إن الله واسع عليم" mbokk, kheloul moo gueun. Boul topp ay rumeur
Soubhannalah.. g perdu 30mins de ma vie car tu ne faisais que te répéter; mais aussi je me renforce dans ce que Mawlana Baye niasse m’a appris alors que je ne suis qu’un debutant. La manière de comprendre n’est rien d’autre qu’une croyance ( IMAn).. La vérité n’est pas une compréhension de n’importe qui. Il ne faut pas dire que quelque chose est vraie ou fausse juste parce que tu ne l’entends pas comme tu le veux. Elle vient d’une sainteté et cette sainteté est la quintessence de la soufie. Soufis = selal rek Il ne faut pas rester à l’an 1 de l’hégire. Les bienfaits (Connaissance rek la dou lenene) d’Allah sont en croissance jusqu’à la fin des temps. Et svp essayons de dire la vérité sans notre opinions personnelles.
Oumar sall khamo dara baparė doo nopu yaw dina kourouss sa ndeye domou mbam khoukhga domoharam domo haam ga khamo yalla khamo yėnetbi tė dinė islam doou ay wakh rek demal diamouji yalla gay mėlni sėkou
Quelque soit le nombre de femmes que Baye Niass avait il sera toujours en règle avec la charria. Il n’y a pas de limites sur le nombre d’enfants aussi. Et qu’Allah préserve son secret et protège sa famille, ses talibés contre Shaytane.
Bayil baye Niasse teu Diemeu ligueyeul Yallah Mo Geune Amo bene TEguine Matto Oustaz Taye so demei beu Meune libre fi di diamou yallah di Teyei micro di Waxx rek wala Sampe Darraa Ligueyou Makk You Bakh yi leu niolakofi ligueyeul Reuy nga lamigne trop tEU Meuno Waxx Lou Yem Talibé Baye Beum Geum Leu
baye niass nienti diabar la fi bayi boumou gué né adou .té moussoul wahné charia defma tenki parce que ken guénou ko beug charia .kokou di touma baye Niass ladjnako lann la yala wah thie mandou .Djoulitt bou bah dey moytou togne . Yaw niata niit nga dougal ci dina islam? Baye ak mag gnifi nekonn lignou def ci dina diarna guereum.baye Aÿ diouni diouni doumou Adama la dougal ci dina islam.gueumo ahlou tassawouf amga ci droit . Ahlou tassawouf gueumouleu .yalna nala dimbali pour ngay lo ham .parce que koula deglou hamné dengay diahassé si wah lo xamné amo ci benn ham ham .
Mane dOuma Taloubbè Baye mais Bayye Cheikhal Islam mola Gueune,Gueune sa ndayy,Gueune sa Baye Ak Sayy Mame Ndax ligguèyeulouñOu l'islam Saram ndayyam ci deukk bi...ayy SeuttOu Baye niola euppe xam xam gueuneula djanggue Feu Imam Hassane,Cheikh Mahi Cissè,ak Imam Cheikh Tidiane Cissè niola rawe ci Zaahir ak ci baatine...Li ngayy wax yeuppe,Ya une seule chose ki est juste Moyy Associationniame où bokkalè gui sénégalais Yi nèkkè mais tt le reste tu mens...Makk Gni DaañOu ligguèyyal islam Domaram k tu es
Ibou Diop 😢 la vérité est dure mec weah tres dure a entendre surtout pour gniga xamni seni xoll da febarr Yal nala yalla yeureum mn frère De plus u mntre mm k la ou u tu appartient on ta op éduqué Faible esprit k té
Ki geuneu New daradjia si Talibé Baye yi mo la geuneu kawé makama so khamone dara linguaye wakh doka wakh Dell wakh deug Baye Niass meussoul wakhni charia teunkouko
Seul la sunna et le coran reste le bateau de sauvetage vers le paradis. Merci oustaz
Vérité absolue
Kesk le paradis par rapport à Dieu. Dieu t'a créé pour lui mm. Et t'a donné tout tu ne peux rien d toi mm.danouga ndax sofianké mola diangual
yén daguéna mana fén motakh yéne AK Omar sall
Merci Oustaz. Vraiment tu as tout dit. Yokk nga sama ngueume ci Baye Niass ak ci sunnay yeukeuti bi. Tu pensait k meungua devier nitngni Mais danganiou gieuneu Yokk ngueume ci Mawlana Sheikh Ibrahim.
Shukran
C'est difficile de remettre en cause ses propos puisqu'il a toujours des preuves à avancer soit dans le Coran ou la Sunna !!!we love oustaz
Sunnah rek💪
J'aimerais bien lorsque je l'écoute qu'il me dise comment prier comment réparer une prière etc mais il passe son temps à critiquer des musulmans comme lui franchement y'a beaucoup de sujet très important pour les musulmans
Maintenant s'il n'est pas d'accord avec les soufis n'a bayi yalla juger au jour du jugement wa Salam
@@pierrekeuni7020 mais on est tous musulmans donc il faut corriger nos frères et soeurs avant ils vont rencontre dieu.
C'est ça l'islam.
Vrai terroristes baye niass rawnalene fene kate bigua donne
@@ndiagafall4326 yow rayo kene. Au Sénégal nitou tarikha yi rek gnoy semé la terreur ( viol, agression, meurtre, toukh yamba, nane sangara, ndialo, prostitution corruption, musique etc...). La khourane au sounnah rek moy mouthieul diam gni
merci oustaz o sall yall mofi neka merci beaucoup encore une fois ❤❤❤❤❤
Le mensonge =Injure
Incompréhension=frustration
Tandis que
La vérité=tranquillité
La foi=paix du coeur
Oustaz machaallah
Cheikh Ibrahim niass si xol ❤❤👈
Loudoul Baye ay thiaakhaan leu...
أنا أحبك في الله يا شيخ عمرو اللهم اغفر له ذنوبه وحافظه على كل حال ونفعنا وإياكم لما يحبه ويرضاه والصلاه والسلام على رسول الله وعلى اله وصحبه اجمعين
Begeu baye niasse boude yobou nite safara yalla nafa djitou yarabi
Bro man maala begue guitou safara boudèh beugue baye daye yobu nitt foofa...
Boule découragé béneu yone kila sope la dila gnianale goudou fane ak wére ak sa yéné cilou bakh yalla matale ko mane yalla rek la yakar té sope mouhamed (psl)
Ma shaa Allah
Way Way meyniou fo xamene kou tolou ni cheikh tidiani fala bok kou melni cheikh saad bouh koul melni cheikh abdoul khadjr jeylani kou tolou ni.mame serigne touba kou tolou ni el.hadj malick yalla naniou yalla rey si sen yone
ماشاء الله يا أستاذ بارك الله فيك وجزاك الله خير الجزاء و حفظك الله من كل سوء ومكروه آمين
manchallah oustaz yalna yalla yokou xam xam bi j l'aime trop bilay
massamba ndiaye yaw ak mom sene thiottou nbiaye
Daye fene rek sa koye baye
Amine .. Yokk si lou beuri beurii beuri beuri beuri beuri sakh. Nakh da makei lou beuri beuri beuri beuri yallla meune nako..
Yalla na Yalla deff gnou bayi fene ak dieuw
machalla oustaz yalla nala yala fay lingay léral amna solo de
Do bayi douuul
Ioe mom doumala wakh amine nakh sa gnane bi dou meussa nangou
Assalamou aleykoum chers frères et soeurs en Islam.
Premièrement: Je pense que en tant que musulmans nous sommes tous intéressés par la bonne guidée (la bonne voie pour adorer notre Seigneur afin d'obtenir sa Miséricorde et donc le Paradis).
Deuxièmement: En tant que sénégalais, nous savons que nous vivons dans un pays à sectes religieux dont principalement les soufis composés de l'ensemble des tarikhas et ceux qui se réclament d'Ahloul sunnah wal jammah. Et entre ces deux composantes de notre islam au sénégal, il existe des différences d'interprétations, de comprehension et de la pratique de notre religion. Je pense que si nous sommes tous intéressés par la vérité ce n'est pas en nous insultant et en nous attaquant les uns aux autres via les réseaux sociaux que ce problème va se régler. Il n'y a qu'un seul moyen de savoir qui a tort ou qui a raison: retourner au Coran et à la Sunnah du prophète PSL.
Sur ce il n'existe qu'une seule voie de prouver que ce que Oustaz oumar Sall avance est erroné: soit les références coraniques et aux hadiths qu'il donne sont fausses, soit ces références sont vraies mais qu'il en fait une mauvaise interprétation. Il ny a que dans ces deux situations que l'on peut lui imputer le tort car dans ses déclarations il avance des arguments.
On ne peut pas gagner son procès en insultant son adversaire ou se contentant de dire "Il ment", il faut pouvoir apporter des arguments solides tirés du Coran et des Hadiths.
wa sallam
Merci yahaki ils peuvent pas argumenter oublions les insulteurs ne te fatigue mme pas quelqu'un n'est pas sourde que celui ki ne veut pas entendre en + leur unique argument est koi nos ailleurs le font comme ça ces gens-là ne basé pas ni hadiths ni coran wallahi ça fait pitié comment peut-on être musulmans sans suivre la sunaa du psl inimaginable un pays soi-disant 95 musulmans sur nom pas l'acte no problème ko dieu ns guide.
Ndiaye rek gua meuneu sante. Bien dit la verite se trouve dans les livres si on est en quete we savoir il faut qu'on prenne le temps daller apprendre
Jador s oustaz.bilahi. cependan Lignorance reste la pire dè soumission.d grace prenè come guide spirituel mohamed psl.c l salut final.sèrieu ya dè gens ils son tt mouton
sidya diop merci frère 😚
Deugg deh da metti borom xoll you febarr yi douniou ko degg🤨
Yalla nagnou yalla yeureum téh djegall niou🙏🏿
Baraka lahou fiik ya oustaz
Barakallahou fikoum ya cheikh oumar
salam nagn bayi saga yi way té ragal Yalla lou nitki wah wala bindi rek Malakayi bind nagnko
Si vous êtes d'accord avec Oustaz Sall barakallah fik si vous en êtes pas5 d'accord guen ham lolen di wah Oustaz dioulit sunnite leuh té dioulit dey réfétal assalamou alaykum
djeureudieuf Oustaz OUMAR SALL👍
Dafa lerr nagn
wayé celui ki ne vx pas voir la vérité en face vera le contraire
Dieureudieuf ya Oustaz
Ma cha Allah wakhga degue
we love Omar sall
Je viens d’ecouter Baye niass et comment il a raison. L’homme possède une arme puissante qui n’est rien d’autres que sa langue. Cette arme peut faire de lui le plus grand homme de l’histoire comme elle peut le rabaisser a l’échelle pharaonique. Elle est source de bonheur, mais aussi de malheur. Elle sort des bienfaits mais aussi des méfaits. Rien qu’à l’entendre parler on sait qui parle.
Elle conduit à Allah en l’invoquant ou à dire que du bien vers Allah. Mais aussi elle conduit en enfer en faisant du Fene et Dieuw. Yallan nagnou Yalla moussal si lamigne
Merci beaucoup mon oustaz Oumar sall
Allahou akbar ki meuna fenn
Macha oustaz Oumar lepp deugeu la
حوءا كير daguay doul yaw AK Omar sall
DEUG nexoul.Ya Outaz boul Bayi.kou am deguine ak xel xamni Yagui wax DEUG kessei.
Lima meti moy kou Amoul réponse bou valable tek ay saga.les gens t'insulte et nous on te suit si diangal yi ngay def.
Pourquoi vous l'écoutez alors que li ngueni deg néxoulene.deglou lene koulene nekh té Bayi Ki ngueni saga.Allah est plus savant .
Allah yalna yalla attelake Baye Niass si barke mouhamed
Zarikha ak hakhikha benn monoul dem bayi moromam sante borom touba rek
Deugue diou werr
Ndeyesane demala nangoul ngante thy bagne Mohamed khamou gnouko mo takh nonou nga mel ack wa soufuiyi yalnala yalla soppi walla safara nga dieme directe barque baye niass
Baye Niass n'a jamais dépassé 4 femmes et ce que vous racontez sur l'interview de Gassama n'a jamais eu lieu on a tous écouté cet interview. Oustaz nitt kou bakh dou deff li ngay deff. En ce qui concerne le tarbiya vous ne pourrez jamais comprendre cela et Dieu choisis ceux qui le connaîtront. Baye Niass est une chance pour l'humanité ainsi que beaucoup de ces marabouts que vous contredisiez.
😂😂😂
Ndeysan y.
Qu'Allah tr guidez
Oumar Sall est tout simplement un menteur.
Meussouniou wote wahdadoul woudioutt
baye Niass d meusouta wathie charia t meusoul ame lou eup niétti sohna Oustaz nite sou gueumé yalla dou sossal nitou yalla khawma nak Lo dioublou si li wayé yalla dinala mbougeul inchalla
j aime le soufisme
bayileen sen ndeye ak sen bayi yi di foywe tè fèkhè xam li tax yalla sakk lèn ndeye ak baye ba parè amal lèèn ...Yalla nieup la fi nèkal wayè
ku nèkal yalla ..YALLA nekal leu ... man kanalilahi kanalahou lahou ...fekhèlèèn xam sen bopp...oumar sallo ...,demba...patèè yoo.... ku xam sa bopp Xam sa borom...je suis yalla yalla mais j'aime Baye Niass parceque xamna Yalla tèi xamal nako ay talibèm...
Baye niass n’a jamais dis dans sa vie « charria tenqui nama » khawma... Baye niasse n’a jamais eu en même temps plus de 4 femmes.
Xamm xamm kendou diangue ( danou koy sakkou) . Wayé dara meunouta xamm dara filék guissouko.
Diamou yalla Bo xamm né mouno xamm ki ngay diamou . Lolou moy être dans un état d’incertitude. Té yalla thi khaak nga koy diamo, manam deug ( la verité , le secret ) .
Comprenons dans ce sens l’islam est un secret, et un secret ne se divulgue pas mais plutôt il se transmet par un messager qui est d’annoncer le contenu . Mané pour mouy leer Cheikh Ahmadu Bamba Khadim Rassoul motax niou xamm yalla , gueumm yalla , agg thi yalla . Am Yakin ba moudiou done ko , done abdoulahi diko diamou ba done Sadikh , té thi deugou gogou nonou la nitt di soukeudikou pour amm lerou yalla dji . Allahou nourou samawati wal ardi.
Dieureudieufeuti Sangue CHEIKH MOUSSA CISSÉ NIAMBÉ BROM DAROU
Diante bi dafa lérr nagne t yalla mayoul nieup giss ko (goumbeu yi) t pourtant dafa lerr nagne
Nonou leu yalla mélll geumeul linga geum nioune baye daff nio nandal chariya ak haquiqua santeu yalla boubax bala nga comprendre (IYAKA NAHBOUDOU WA IYAKA NASTAHINOU ) lernala ni yangui diano ak mom yalla wayé kiray bi dokh sa digeunté ak sa borom moy waral niakk kham gui wayé sante yalla boubax bima doné gouney cheikh ibrahim
Yalla bogoul coyiéfetfna oumar salla niagelaye diaye rékk waye dall
Jere Jeff oustaz
Serigne nie Sénégal yié jogan na ragall yalla moahmed imnoulabdohwahb ak albané ak bonbass jouye yakhdené dji
Kou daka fene oumar sall mousoumako guss
Maasha Allah... Jazaaka Allah kayran. We are really greatful for the effort that sheikh Omar Sall is doing to pull the wool out of our eyes.
Sufism is indeed a horrible sect.
جزاك اللة خيرا شيخ عمر صال
Dagay fén rék
Bilahi yagui fènal baye niass
عليكم بتقوى الله وحسن الظن على الله وعلى عباد الله
Ay fen rek
Alkhamdou lilah Dieureudieuféty Baye Niass
Baye Niass meussoul wathie Sharia the waxal Baye lou ñaw taxoul dara ñaw ci Baye kon lou way def rek bopam té wedi nittu Yalla yagnafi ndaxté Yeuneunt bi ay nitt ñoko dan wedi kon sou amé ci Baye rek bettuñu demb moy tey rek wayé nak borom deudj bi meunna dioy deudjam té Baye louko way def bala nga dh dinko guiss
Ñun nk Baye moñu yarr mo tax duñu saga ken té douñu xass ken wayé kou lal Baye rek lal ngañu mo tax duñu noppy ci wax dji
Baye Gédj bouy yokk sassouné la té dou meussa wañekou
Dieureudieuféty Baye Niass
Baye boudé fébar nañou rey beug nañ
Yalla nagnou Yalla mousseul si lamigne bouy gueinei lou bone rek. Lamigne bouy fene ak Dieuw rek.
Machalla oustas.
Santé cheikh moussa cissé ndiambé borom darou rek
ماءشاالله شيخ عمرو شكرا
bo guissoul yalla boul wakh si môme yefar ngua
Omar Sall yaw mome yallah nala yallah yereum .yaye mbam dég
Santé cheikh moussa cissé ndiamé darou léerou lerr yi rek bâ faw
Un fou
Ustass marshallah
Yaw sowakhé ba talibé baye bou gueuna ndaw bayi baye niass topeula ma bayilima gueum dangaye sonal sa mbopeu
Pourquoi montrer la photo de baye ca me fait mal ca n'a rien avoir avec ce que vous expliquez ..le disciple de baye est un modèle de l'islam dans tous les domaines..C'est l'adoration en ALLAH et suivre la voie du souna faut pas nous montrer des exemples de certaines personnes qui font du n'importe quoi et dire du n'importe quoi pour gèneraliser les écritures peuvent être grosse mais les actes sont agréé..tout savant à du soufisme en lui cela dépend comment il se manifeste.. C'est une connaissance divine un secret que l'on doit garder par maitrise en soit,C'est pour èclairsir que baye niass sa voie c'est Dieu son Prophète et le coran..
Ngorsi sall bayil doul domeram
Mouhamed Cisse serigne bi ki wétou béne talibé baye rek manako diagual Omar sall khamoul Dara ba nopi Bari wakh
baye niass deh waxnani yarr na ay talibem bi zahiri sharhi wa nouril moubine dnc yow echec nga si feinal les soufis nga xamni sharia dagnoukoy top
feinal nga baye si linga wax ni mo waxni nitou haqiqa leu ngani Rts mokoy tek je tassure soumalay guiss dila trokhal
diokh ma sa adresse ma weer la legui
pieuvre sakh mola taneh ya trokh feinne nga feinnn ba amato loy wax
tegalal nite gni fou gassama waxei ni baye niass affairou lou eup 4 femmes doko indi mouk ndakh amoul benen bi moy baye meusta takando lou eup nienti sokha
*
lingay fein yeup do dei tei wahidou qahar doulako fay
El'hadji Diery Seck
aminata diallo ziarnalaaa
bane aminata leu ni sakh
Ki DomOu ThiottOu ndayyam la diarOul tonttOu...Bayyam ak ay Mamam ligguèyouñefi Saram ndayyam pour islam
Waw giss yalla mom ay doulla man khamna sy dara nan wakhe noum mel loy giss dafa wara am mello kan
Booko guissé dinga kham noumou mél... Demal nga diem ko guiss... Guiss yalla diaféwoul, guiss loudoul yalla moo diaffé. Nd1kh yalla mingui wakh si alghouran, sourate Baghara :" ولله المشرق والمغرب فأينما تولوا فثم وجه الله إن الله واسع عليم" mbokk, kheloul moo gueun. Boul topp ay rumeur
Soubhannalah.. g perdu 30mins de ma vie car tu ne faisais que te répéter; mais aussi je me renforce dans ce que Mawlana Baye niasse m’a appris alors que je ne suis qu’un debutant.
La manière de comprendre n’est rien d’autre qu’une croyance ( IMAn)..
La vérité n’est pas une compréhension de n’importe qui.
Il ne faut pas dire que quelque chose est vraie ou fausse juste parce que tu ne l’entends pas comme tu le veux. Elle vient d’une sainteté et cette sainteté est la quintessence de la soufie.
Soufis = selal rek
Il ne faut pas rester à l’an 1 de l’hégire. Les bienfaits (Connaissance rek la dou lenene) d’Allah sont en croissance jusqu’à la fin des temps.
Et svp essayons de dire la vérité sans notre opinions personnelles.
Nous attendons une sanction divine contre Oumar Sall.amine.
شكرا استاذ سال كلامك صحيح ان اخسرك كلامه قال الله قال الرسول
khamo Dara dara tasawouf moye sariha ai souna mankao aramal yala moye aramal Aka daganal nopaloul
guiss nga serigne bi fene nga wara bayi ak oute vu si youtube nguir lo depenso diamou djil yalla t moytoul kathi
Machallah oustage Oumar sall
Alhamdulillah sufism is the best.
Omar sall Barhama bi Nguaye contre moy sa andandor té molaye dalal fingua dieum
Ki baye douko dalal fenn
Oumar sall khamo dara baparė doo nopu yaw dina kourouss sa ndeye domou mbam khoukhga domoharam domo haam ga khamo yalla khamo yėnetbi tė dinė islam doou ay wakh rek demal diamouji yalla gay mėlni sėkou
Quelque soit le nombre de femmes que Baye Niass avait il sera toujours en règle avec la charria. Il n’y a pas de limites sur le nombre d’enfants aussi. Et qu’Allah préserve son secret et protège sa famille, ses talibés contre Shaytane.
Eux Même ce sont des cheyaatiin
Lepp dadjalowoul nék léne. Ki meune na feine. Leine li mo tassaro nék lepp ya une difference khammo louy wahdatoul woudjote
6:34 dof ak rere
Macha Allah
من هنا وجب عليك السكوت يا عمر سل
قف الله يفعل ما يشاء
Omar sall diangui watale moguene
Ndeyssane mane comprendre nala ibliss moy wakh si lamignam
Oustaz dangay deugeu sa ndaye amo khamkham
Bayil baye Niasse teu Diemeu ligueyeul Yallah Mo Geune
Amo bene TEguine Matto Oustaz Taye so demei beu Meune libre fi di diamou yallah di Teyei micro di Waxx rek wala Sampe Darraa Ligueyou Makk You Bakh yi leu niolakofi ligueyeul Reuy nga lamigne trop tEU Meuno Waxx Lou Yem Talibé Baye Beum Geum Leu
Topal fêlé
Ouztas réseau sociau wakhal ak sa talibe bi dila sante guénelko bén khadiss bok🤣🤣🤣
Ya meuneu doul domeram
Deug rekk moy deug yala naniou yala tekk si yonou dioub
Vérité total oustaz
Katy Diouf yaw sa leufeule ndeye yaw ak omar sall
Amadou Lo walahi ku amul yarr ak laye rk moi saga.
Katy Diouf Tu as raison je suis d'accord avec toi
Katy Diouf saleufeul nbiaye domou thiagua yene ibadou yeup aye domerame guén
Katy Diouf Ouztaz deug rek lag wakh
Kii mo dakh doul si Sénégal
جرجف الشيخ موسي سيس جمب دار
Oumar sall ma ladj bén question fane gua meuneu sédénii yala amna
Dmrm diémal xam sa bop xamidjil yala yaram souff moy boromam
baye niass nienti diabar la fi bayi boumou gué né adou .té moussoul wahné charia defma tenki parce que ken guénou ko beug
charia .kokou di touma baye Niass ladjnako lann la yala wah thie mandou .Djoulitt bou bah dey moytou togne .
Yaw niata niit nga dougal ci dina islam?
Baye ak mag gnifi nekonn lignou def ci dina diarna guereum.baye Aÿ diouni diouni doumou Adama la dougal ci dina islam.gueumo ahlou tassawouf amga ci droit .
Ahlou tassawouf gueumouleu .yalna nala dimbali pour ngay lo ham .parce que koula deglou hamné dengay diahassé si wah lo xamné amo
ci benn ham ham .
75, est-ce que c'est vrai
Lima diakhal si oumar sall moy louko mana yobou safara rk lay wakh
Bulko toumaal.
Soubhanala. Nioune sénégalais da melni safara la niou beug .bou nou niou wakhé deug niou mer. Walahi Sall sougnou diam rek laniou beugueul
Mane dOuma Taloubbè Baye mais Bayye Cheikhal Islam mola Gueune,Gueune sa ndayy,Gueune sa Baye Ak Sayy Mame Ndax ligguèyeulouñOu l'islam Saram ndayyam ci deukk bi...ayy SeuttOu Baye niola euppe xam xam gueuneula djanggue Feu Imam Hassane,Cheikh Mahi Cissè,ak Imam Cheikh Tidiane Cissè niola rawe ci Zaahir ak ci baatine...Li ngayy wax yeuppe,Ya une seule chose ki est juste Moyy Associationniame où bokkalè gui sénégalais Yi nèkkè mais tt le reste tu mens...Makk Gni DaañOu ligguèyyal islam Domaram k tu es
Yalnala yalla ray
Yaw Oumar salla bouko ngi eupè kham kham tamit, moraw sa nday raw sa bay
Omar Sall nit safara gua Yallah néna kou diguate sama borom xam xam hi man Yallah magui lay déclaré guerre
Islam sou si tassaouf guéné dara doussi dess ndax lo meunti pratiqué si charia tassaouf mokay leeral
Yaw mandoul khamo dara talibé Baye Niass yi sakh dougn sa morom
yalnala mague niou bax yi yereume yaw lane moy goor ak lane moy djiguene xana xamo yaw djiguene nga yeureume nala
Diar na bayyi xel dh ki deugue rk laye wakh
Omar sall sofga sokhorga khéséwga
سيد أستاذ عمر صال ،أنت محجوب عقلك مطبوع ، فسرلي هذه الاية (من كان في هٰذه الاعمي وهو في الاخرة الاعمي)ولله لو زوقت زوق الحقيق لتسلب ما كنت به
Quelle sombre cœur tu as Omar Sall yaye nullard teh yabateh meuna fene
Ibou Diop 😢 la vérité est dure mec weah tres dure a entendre surtout pour gniga xamni seni xoll da febarr
Yal nala yalla yeureum mn frère
De plus u mntre mm k la ou u tu appartient on ta op éduqué
Faible esprit k té
Ki geuneu New daradjia si Talibé Baye yi mo la geuneu kawé makama so khamone dara linguaye wakh doka wakh Dell wakh deug Baye Niass meussoul wakhni charia teunkouko
Yaw mom noppi Mola warr
Bo khamoul danga wara noppi
Moumina Seck iow y'a kham dara
konkour fene bou amon omar sall momelay yobou
U remporterè surmen celui du plu idio crw mw🤣
mangui waate si YALLA omar sall nittou safara la amoul bénne thieur si YALLA AK SI YONENTE BI LE PROPHETE NE LE RECONNAIT PAS
Yow werr gu
Bobou nga deim safara ioe momou
yalla nga torokh domou fenkate