Qui aime la lutte doit prier pour la victoire de Siteu mm si c pas ton lutteur… sa victoire va redistribuer les cartes et tt chambouler!!!! Allez Siteu et bne chance pour Dimanche
@@abdoulayendiaye8706 mais c grave tout ce monde de supporters pour un lutteur qui a pas encore atteint un certain niveau moi je souhaite qu’il gagne Dimanche Inchallah
Li rek lalène ngourgui di nakhé motakh deuk bi daye degueur boy yi di gueune di dieul galyi letat est entrain de vous endormir heure bi dou heuro fo plus de 275 jeunes ont peri en mer c Malheureux pour ce pays✊️🇸🇳♥️
Ioe do nek nit promoteur yii ay bailleurs privé laniou état subventionné wouléne ils vont avec les moyens du bord ak ay prêt bancaire you métti fi laniouy tok di dioye sponsor parcontre kay état niome la diappalé woul té niome nioko yéllo yéne vous êtes obsédé par l’état bouléne faté il ya même pas longtemps si 25 pays yi gueuneuh pauvre laniou bokone système bii daffa warra changé d’accord mais pouvoir bii limou fi def béneuh gouvernement defouko fii depuis 1960 yéneuh yi nak obsession laa à la fin vous êtes pire que maky sall lamb laniou ame bayiléne niou niou fékhal sounou khool touty stp ioe nga nieuw setan ba contane tok fi di wakh nekal nit 😂
@@footballgod4351 Deme ligueyi kaye tu me fais rire bo amoul liguey tu viens je tembouche avec un tres bon salaire si kaw nga ame aye compétence bien sur sonko aye sathie katou alalou askanewi topou niouko deh wa salam
@ElimaneNdao-tf6dn 😆 🤣 😂 you're funny koy embaucher mane? Jtjure meuna embaucher sen wakeur yeup, gni di organiser daniouy liguey mbeur yi on les paye les vendeuse les thiack thiack nioussiy beneficewu dfa beuri yaw soko diaper ay nakher amna niouko beug geum ko te lo am si deuk bi amnaniou luko raw tog
@@footballgod4351 je c pas gore nga wala djiguéne tu dis ke meune nga embaucher sounou wa keur yeup meme mon fils de 22ans en na rigolé mais dara yala bakhna le grand entrepreneur file moi ton number Bouma nieuwé December comme ca je taméne mon cv pour un entretien dembauchement
Wa Guediawaye niongui nieuw d Meuso lén niou yab té dolén niou meusa yab bly djiwé seul siteu d'où meusa nékhlé djiwé fou sa Thiès diar ak Gouy Gui la lac Di diar inchallah
Du jamais vu dans la lutte Sénégalais phénoménal vraiment ❤
Bilahi siteu ndieurignou lamb la nieupa ko wara nianal c’est un extra phénomène❤❤❤❤
Siteu légui yaw là faral sakh💪🇸🇳 combat da ngua kay diokh akkam bamou matt sëkk
Bonne chance yalmine bi🎉
Ayway siteu yalnako yalla may ndam amine
Qui aime la lutte doit prier pour la victoire de Siteu mm si c pas ton lutteur… sa victoire va redistribuer les cartes et tt chambouler!!!! Allez Siteu et bne chance pour Dimanche
C'est ce que disait a mon amis hier soir il a toute les chances d'affronter Balla Gaye ou Ama Baldé s'il bat lac de guerre
@@abdoulayendiaye8706 mais c grave tout ce monde de supporters pour un lutteur qui a pas encore atteint un certain niveau moi je souhaite qu’il gagne Dimanche Inchallah
Lou léer nga wax🎉
Bly grand bi Mais yalla bakhna ❤
Siteu est mon lutteur mais fumuy wara diar lac2 la xamoul ça sera un grand exploit souko daner
Siteu yalla na yalla sameu soutoural ko may ko ndam inchallah 🙏🙏🙏
Siteu yalla nako yalla soutoural 🤲🙏🏻
Alahouma amine way🤲
Amine
Amine inchallah 🙏🙏🙏
lol gnanal ko soutoureu kay mai danou mome dina ko def
Amine ya rabal halamine
Situé yalla maynako walahi yalnako yalla soutourale
Belle victoire Siteu Amal Diame Way Amine
Siteu Yalla Nala Yalla May Ndamm Lou Reye in cha'Allah 🙏🏽
siteu yalla nala yalla may ndam inchallah 🤲🏻🤲🏻🙏🙏🥰
Ouahh tout ce monde. Machallah boy. En tout cas je te souhaite de gagné lac 2 inchallah
NDAM LOU SEDD GOUY LEPP LANIOUY DAGANE BOROM BI BARKI TAHA ❤❤❤
C'est pas mon lutteur mais il mérite ce victoire vraiment
Noublie pas le 17 focus ❤
Siteu yalnala yalla may ndame.inchalla tu le merit vraiment 🎉
Siteu luteur le plus peuplé dans l'arène
Nioun Siteu laniou beug 👌🏾💯😍
Borom deuk bi 👆🏻yay lamb déh💪🏾 ndam rek inchalah🙏
Le président sonkoo de la lutte❤😂🎉
Vérité 😂❤🎉
Coly fay amna courage
Cng doit favoriser Siteu vraiment on aime voir ça dans l'arène
Away😂😂😂
C’est du vrai n importe quoi tout ce monde pour seulement un open Press. Mon pays va mal
YALMINE A FEÑA NDAM REK INCHAALLAH BARKI TAHA ❤❤❤
Siteu kassé BOROM deuk bi ❤
Vraiment la folie cette jeunesse vous pouvez sortir massive pour 1 lutteur qui fait k danser est pour votre liberté et defendre le Sénégal nom😅
Ndam rek mbeur inshalah
Siteu beurri neu mboloo machalla
Siteu nak nékhoul ba nékhoul amnga mayou yalla macha Allah yalla nala yalla may ndam lou nékh Ta fékh
Siteu yalla nako yalla may Ndam 🙏
Siteu mi berina siportaire machalah ❤
Yalnala yalla may ndam inchalla 🤲🏾 ❤
Beugna mou dane lac mais noumouy def ba Danko MoMA djakhal. Forcé a toi champion
Képeu kouy yéwo Diameuguene rek nanga lal❤ bii yalmine bii kassé
Yalnako yalla may dame ❤🤲🏾
Situé seul ❤❤❤
Siteu yallana la yalla may ndam lou sedd gouyy ❤
Ki ndaye diballé xallé yi yall nala yalla Faye sa ❤❤❤❤
Siteu kassé touss tassarr❤❤❤
Supporter mom yako oupou si lambou dji😢❤
yalmine bi kassé♥️♥️♥️💪
Lamb ji yako mom yalmine bi❤
Déjà Siteu tu mérite la victoire bilaye lambe dang koy diokh limou mom
Yalnako yallah may Ndam
Siteu yalla nako yalla may ndam
Siteu yalla na am ndam
Siteu et modou Lo késsé ❤❤
Yalmbine bi 💪💪💪
Ndam rek Inchalla ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Siteu ❤
Ah way mère bi limiy waye nékh na di😍😀
Ndam rek inchallah
Yalla nala yalla maye ndame siteu yaw rek laniye topo
Nioune yalmine bi moy souniou lép inchallah yallah niou yallah may ndam bou sétt 🥰❤️🫶🏽bou sobé yallah
Yalmine bi yalla nala borom bi soutoural defal la Ndam way Mashallah tu es le lutteur le plus peuplé
Siteu yalla nala yalla may ndam 🙏
ki amoul dole bou dan lac 😂😂
Yalla naniou yalla soutoural
Jour bi siteu di bayi lamb bly arène national sakh dina dioy😢
7❤
Li rek lalène ngourgui di nakhé motakh deuk bi daye degueur boy yi di gueune di dieul galyi letat est entrain de vous endormir heure bi dou heuro fo plus de 275 jeunes ont peri en mer c Malheureux pour ce pays✊️🇸🇳♥️
Ioe do nek nit promoteur yii ay bailleurs privé laniou état subventionné wouléne ils vont avec les moyens du bord ak ay prêt bancaire you métti fi laniouy tok di dioye sponsor parcontre kay état niome la diappalé woul té niome nioko yéllo yéne vous êtes obsédé par l’état bouléne faté il ya même pas longtemps si 25 pays yi gueuneuh pauvre laniou bokone système bii daffa warra changé d’accord mais pouvoir bii limou fi def béneuh gouvernement defouko fii depuis 1960 yéneuh yi nak obsession laa à la fin vous êtes pire que maky sall lamb laniou ame bayiléne niou niou fékhal sounou khool touty stp
ioe nga nieuw setan ba contane tok fi di wakh nekal nit 😂
Yenagui fepp wakh nguen ba soneu takhul nite gni beug lamb yabilen ngourgui te dem liguayal sen bop soff nguen trop
@@footballgod4351 Deme ligueyi kaye tu me fais rire bo amoul liguey tu viens je tembouche avec un tres bon salaire si kaw nga ame aye compétence bien sur sonko aye sathie katou alalou askanewi topou niouko deh wa salam
@ElimaneNdao-tf6dn 😆 🤣 😂 you're funny koy embaucher mane? Jtjure meuna embaucher sen wakeur yeup, gni di organiser daniouy liguey mbeur yi on les paye les vendeuse les thiack thiack nioussiy beneficewu dfa beuri yaw soko diaper ay nakher amna niouko beug geum ko te lo am si deuk bi amnaniou luko raw tog
@@footballgod4351 je c pas gore nga wala djiguéne tu dis ke meune nga embaucher sounou wa keur yeup meme mon fils de 22ans en na rigolé mais dara yala bakhna le grand entrepreneur file moi ton number Bouma nieuwé December comme ca je taméne mon cv pour un entretien dembauchement
Ce pays est vraiment mystérieux… Ousmane Sonko se sacrifie pour ce pays?😂😂
Dolene ayyy niit
siteu diame rkk ngeye am kholame mon rafet 💯💯💯💯💯💯💯💯💯
Siteu rk lagnouye top aller yalbine bi ndam rk
Ndame baye fall siteu
Li rék lasi am boul sonal sakh sa boppou dagay danou
Siteu rk lagnouy topou
Lac dîna la nox dan la gua nopi
Meussou makò tarde deysane 🙏🙏 ndam inchallah yalna Yalla mayla lo ko
quand on voit siteu avec ces touss on sent carrement la lutte dans sa pure tradition et ces origines yalla nala may ndam Siteu
Ndame rek Yale mbine yassame roog à thiyonge ndame inchallah
❤❤❤❤yaram daw n'a wy woye bi nekhna woyou lambou la dh
Wa Guediawaye niongui nieuw d Meuso lén niou yab té dolén niou meusa yab bly djiwé seul siteu d'où meusa nékhlé djiwé fou sa Thiès diar ak Gouy Gui la lac Di diar inchallah
Siteu am na supporter 😊
Siteu mi ma guise daye danou manoule dane lac
Ndame reikk❤❤
Siteu vrai comédiens lahh
Siteu Yalla nala borom bi soutoural may la ndam inchalla❤
Siyeu yalla nako yalla may ndam si barké seydina Mohamed Amine 🤲
Cuédiawaye seule
Yaasm o yaal oxe a damtoŋ❤
Ndam.rek.1000❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤diam.rek❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Yallah nala Yallah may ndam
Lac rék lagnouye topou ❤
Sonko Arena ❤❤
Yalla nala yalla may ndam
Inchallah bou nexé sounou borom dinga am dam
Siteu yalna ko yalla may ndam
Forme bi danoul lac d
Waye siteu waye guissouma békay mbaye Wayé kholam sédd na
Talibé Bamba bii Yalla gua am ndam barkep Serigne BAMBA
Lac yalla na yalla may ndam
Siteu kasse siteu kasse siteu kasse ❤❤❤❤❤❤❤
Danguena oumpoulé lac mais dimanche dinga khamni lamb dou wakh kesse
Lac dou touss reculé rk lafi néké
@@SoldarouBamba__4 bane mbeur modone reculé wakhmako
@@domou__rewmi mokk modlô reculé woul
@@SoldarouBamba__4 bane mbeur Modou reculé lala lathie
Yalla ga am damae
Yallanako yalla maye dame
Siteu am nga lamb bou diss mai yalna yalla soutoural la
AMIINE ♥️
Mbolo moka bolé ak lac
Siteu kassé laniouy topp