Affaire Cheikh Omar Diagne Li cii Serigne Saliou Samb wax

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 8 фев 2025
  • Join Bichri TV to get access to perks:
    / @bichritv
    Adhérez comme membre de Bichri TV , (en cliquant ici / @bichritv ) Vous pouvez utiliser votre carte Visa, Mastercard, Discover AMEX ou votre compte Paypal. Tous les modes paiements sont sécurisés. Votre soutien est trés apprécié!
    Pour plus de vidéos abonnez-vous sur votre chaine RUclips préférée, en cliquant ici goo.gl/kjAdSD
    Pour la couverture et la retransmission en direct sur Bichri TV de vos événements religieux (les Magals, les Gamous, les Ziarras);
    la couverture et la retransmission en ''Live & Direct'' de vos activités sociales, Contactez-nous par email: contact@bichri.tv ou par téléphone: +221 77 818 39 39 (Afrique) / +1-646-838-0300 (USA) / +32 485 69 90 82 (Europe).
    Merci de Téléchargez l'application Bichri TV sur App Store
    (itunes.apple.c...)
    ou Android sur Google Play (play.google.co..., pour une meilleure qualité de Stream.
    Suivez-nous sur tous les réseaux sociaux
    / bichritv
    / bichritv
    / bichritv

Комментарии • 96

  • @mahmoudgueye5387
    @mahmoudgueye5387 5 месяцев назад +7

    Machallah deugueu bou wërr diadieuf mouride ...ziarnaléne

  • @mbackeleye4264
    @mbackeleye4264 5 месяцев назад +5

    Masha.allah Alhamdoulilah santati yalla bou weer jërëjëf Cheikhoul Khadim amoul morom ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @mamadoudiouf6900
    @mamadoudiouf6900 4 месяца назад

    Waw goor niveau bi kaweneu❤❤❤❤❤❤yoow rek ya wara wakhtane ci serigne bi dé machala

  • @Aïtaseye
    @Aïtaseye 5 месяцев назад +3

    Débat bi am na niveau Borom Touba d'où Moromou kou Yalla Binde❤❤

  • @Madoudieng-r8e
    @Madoudieng-r8e 5 месяцев назад +1

    Machala ❤❤ nji wara tok si télé 📺 yii di leral ❤

  • @taphadiadia
    @taphadiadia 4 месяца назад

    Merci pour ton message

  • @Aïtaseye
    @Aïtaseye 5 месяцев назад

    Yalna Yalla Guene Deuguereul Sèn Takhawaye Sèn Takhawaye amna Solo Ma Shaa Allah❤

  • @modoufall1365
    @modoufall1365 5 месяцев назад +3

    Dieureudieuf Serigne Touba diarawlack Cheikh Ibra Fall

  • @AkimSerigne
    @AkimSerigne 5 месяцев назад +3

    Ndóok bañu andee ak moom❤❤❤❤❤

  • @jaangatttv4577
    @jaangatttv4577 4 месяца назад

    Jërëjëfety Sëriñ Tuubaa ❤❤❤❤❤❤

  • @moussagueye7000
    @moussagueye7000 5 месяцев назад +3

    Dieureudieuf serigne bi amna solo dh

  • @mohamadoukallo3051
    @mohamadoukallo3051 5 месяцев назад +1

    Oh XAMXAM YALLAH NAY GUINEU YOKOU ❤️❤️❤️

  • @massarthiam6077
    @massarthiam6077 4 месяца назад

    Amena solo looll❤❤❤

  • @MbassouNdiaye-u9y
    @MbassouNdiaye-u9y 5 месяцев назад +1

    Dieuredieuf Serigne Saliou samb.. yaw rek ya wara wakh nak....... diadieuf ❤❤❤❤❤❤

  • @ametlaminediop4412
    @ametlaminediop4412 5 месяцев назад +1

    Machalla saliou samb kham kham rk moo waur❤❤❤

  • @realthianta1718
    @realthianta1718 5 месяцев назад +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤ Thiey bi xam xam weer n'a l'err na❤❤❤❤

  • @MbayePouye-q9g
    @MbayePouye-q9g 5 месяцев назад

    Dieureudieuf Serigne Touba

  • @abdoulahadleye9532
    @abdoulahadleye9532 5 месяцев назад +1

    ❤❤❤Machallah amna solo yaram

  • @ahmadoubambadiop2608
    @ahmadoubambadiop2608 5 месяцев назад +1

    Il a parfaitement raison

  • @damedia9410
    @damedia9410 5 месяцев назад +1

    Machalah amna solo

  • @papediouf8662
    @papediouf8662 5 месяцев назад

    Dieuredieuf Serigne Touba la kouli chaye une khadiroune

  • @cheikhbombaly2789
    @cheikhbombaly2789 5 месяцев назад +1

    En tout cas Saliou Merci 😘

  • @Mbenguei
    @Mbenguei 5 месяцев назад +3

    Bichri Tv ak Wakeur Aida Diallo thieuy yalla.suis Mouride mais parfois duma sakh comprendre sen logique

    • @ToumanySagna
      @ToumanySagna 5 месяцев назад +3

      Tu es directeur de programme donc tu la ferme

    • @maguettebouboufaye2993
      @maguettebouboufaye2993 5 месяцев назад +2

      SOXNA AIDA DE MO GEUN SA NDEYE GEUNE SA BAYE AU MOIS MOUGUI LIGUEYAL KOU TEED A Travers les hommes sa papa AK sa yaye lougnoufi deef domeram

    • @joesylla4433
      @joesylla4433 4 месяца назад

      Thiey ben seytan mingui ohhh ..gnouy wakh si serigne touba ngay fewelé @mbengue cheikh omar diagne sakh la guen 😂😂😂

  • @serignetine1420
    @serignetine1420 5 месяцев назад

    Machallah s saliou gnoye yakk yon bi gnoy gnouye wakhtan diema ded signe kon nit ordinnaire mais aussi di ignorer yenni mbidam

  • @bambaraserignebethio382
    @bambaraserignebethio382 4 месяца назад

    OOHHH IMAM SERIGNE SALIOU SAMB YAW SAGOU YOON WII NGA❤ YAW GNEUPEU LA WARA DÉGLOU

  • @mohamedmbacke5801
    @mohamedmbacke5801 5 месяцев назад

    Déguatina degua dieurdieuf boram touba

  • @AbdoulayeNdiaye-eq2dh
    @AbdoulayeNdiaye-eq2dh 5 месяцев назад +1

    DIEUREUDIEUFAAAT SERIGNE BETHIO SERIGNE BAMBA DIARRAMATYYY SWRUUU MAME CHEIKH SIKAR NDIAYE.❤❤❤.(MF?!?!)

  • @limparfait-b7v
    @limparfait-b7v 5 месяцев назад

    Machalah gars yi amougnou makhrifatou bilahi mo takh gnou deuk di wédi Serigne bi

    • @bassfaye1730
      @bassfaye1730 5 месяцев назад

      Damani mahrifa Serigne Touba djangaléwouko. Tagg YONENT bi SWS kessé lafi djangalé. Béneu livre la bindeu si tassawouf té Moy massalikoul djinane. Mahrifa soko beugué dangay dém si MAWLANA CHEIKH IBRAHIM NIASS. Mom kessé Moy djokhé mahrifa bou sétt té séleu. Mouridisme dou yonou xam xam. Bagn naniouko ba ndiggal djeufé point laniou wotté

  • @ibrahimaNDONG-np8cu
    @ibrahimaNDONG-np8cu 5 месяцев назад

    Dieuredieufety ❤❤❤

  • @MouhamedDiaw-f9b
    @MouhamedDiaw-f9b 5 месяцев назад

    dieureudieufety samb

  • @cheikhounambacke7148
    @cheikhounambacke7148 5 месяцев назад

    ❤❤❤❤❤machallah

  • @fallouthiam4933
    @fallouthiam4933 5 месяцев назад +2

    Kouy deff si Lettrou 9 lignes 20 fautes nanne daguay corriger serigne Touba ;

  • @dionebayfallsast7214
    @dionebayfallsast7214 5 месяцев назад

    Jeurejeufeti S Saliou Samb ci lèral yi

  • @MoussaDiop-e7c
    @MoussaDiop-e7c 5 месяцев назад +2

    Seutététtt saliou samb ya wér eskeiyy

  • @fallouthiam4933
    @fallouthiam4933 5 месяцев назад +2

    Serigne Touba kouko bagne khaw ma si yow dara ;
    Les complexés de ce pays ay golo lègn

  • @SaliouGueye-i8h
    @SaliouGueye-i8h 5 месяцев назад +1

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉

  • @mbayeba3627
    @mbayeba3627 5 месяцев назад +1

    Thiey bilay dagua war di wahhh

  • @ibrahimaNDONG-np8cu
    @ibrahimaNDONG-np8cu 4 месяца назад

    ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @malickseck911
    @malickseck911 5 месяцев назад

    Ken la

  • @dionebayfallsast7214
    @dionebayfallsast7214 5 месяцев назад

    ❤❤❤

  • @layengom4024
    @layengom4024 5 месяцев назад

    Sa wax thi rékka am solo

  • @mbayeba3627
    @mbayeba3627 5 месяцев назад +3

    Man sa xam xam moma doyyy

  • @malickseck911
    @malickseck911 5 месяцев назад

    Amoul morom khadim Rassoul

  • @mouhamed8820
    @mouhamed8820 5 месяцев назад

    Serigne Saliou Samb Yalla nagua fi yague te weer

  • @serignesalioufaye3449
    @serignesalioufaye3449 5 месяцев назад

    ❤❤❤❤❤❤❤❤

  • @sandjirygning162
    @sandjirygning162 4 месяца назад

    Boulaaa nieupeu donn degulouu tee bayii kignann xam xam tassaro loubarii leeerrrr marchallah

  • @mamechiekhfall315
    @mamechiekhfall315 5 месяцев назад +1

    Mourid dal ndigeul mak ngui fofou la nou nékon wayé ko kham ni sou s mountakha né li gua andék aye djégeun guir adouna tok tay né dagay diokhé aye lésions

    • @solution5135
      @solution5135 4 месяца назад

      Saliou sambe mi limou déf li omar diang défako geune fouf

    • @mamechiekhfall315
      @mamechiekhfall315 4 месяца назад

      @@solution5135 fouf

  • @mamadoundiaye-yv6lr
    @mamadoundiaye-yv6lr 5 месяцев назад +1

    Waw loutakh tontowouy nii cod loudoul di khouloo reck

  • @elhadjisene7172
    @elhadjisene7172 5 месяцев назад +2

    Cheikh Omar Diagne defna erreur mais yaw miy raamal jiguene waro wakh

  • @adamandiaye2580
    @adamandiaye2580 5 месяцев назад +3

    Wadji guêne fi invité tanêwoul Cheikh Omar Diagne.

  • @mbayeba3627
    @mbayeba3627 5 месяцев назад +2

    kou yalla dimbeuli gua

  • @elhadjiabdoulayediagne8319
    @elhadjiabdoulayediagne8319 5 месяцев назад

    Dieredieuf

  • @bassfaye1730
    @bassfaye1730 5 месяцев назад +1

    Wolén borom xam xam yi mo gueun. Kii dou borom xam xam. Wolén CHEIKH OMAR DIAGNE mou wakh gayi limou wakh foumouko ték.

  • @mamechiekhfall315
    @mamechiekhfall315 5 месяцев назад

    Lomana wakh doulako degeul guir daga féké yon wou serigne touba déf ték niou si gua nieuw andé ak sokhna so kham day wathé ndigeul gua andé ak mome tè gua xam ni nékoul si dagui té sou nékon si dagui sakh té s mountakha wakh né fofou geun néké dou fofou yaw mi lanou wakh lo fatè khadiou fi yaw mi ya wara kholat sa togay mourid yi mome niogui founiou néké

  • @layengom4024
    @layengom4024 5 месяцев назад

    Way ki rék ka wara wax

  • @mamechiekhfall315
    @mamechiekhfall315 5 месяцев назад

    Saliou sambe man dé ba serigne mountakha wakhé ba nopii gua tontou guir aïda diallo té yon wou bakh kassè la don wakh kon yaw nopil niou mélni yaw yéna takh kou mélni Omar diagne diniou yab yaw kila envité boudé ap mourid warou la wona envité

  • @mouhamadousalihougueye615
    @mouhamadousalihougueye615 5 месяцев назад +1

    Yaw dé khawma loye wakh Serigne mountakha diguel nala nga bagne

    • @ToumanySagna
      @ToumanySagna 5 месяцев назад +2

      Serigne bethio mo am sagn sagn thi ay talube point

  • @smssms9300
    @smssms9300 5 месяцев назад

    Yéna Yam reck invité bi mom ch Omar Diagne mola tané yaw djigeen Nay sa kilifa

  • @mamadoundiaye-yv6lr
    @mamadoundiaye-yv6lr 5 месяцев назад

    Dizadieufaty

  • @solution5135
    @solution5135 4 месяца назад

    Yaw mifimana bayi seringe mountakha mi sourko keull dém andak ayda diallo billahi si yaw lakhamé ni yalla manna louné sa kham kham boubari bi yép té manogiss dara si batinou seringe touba bi yay mbaame yaw

  • @bassfaye1730
    @bassfaye1730 5 месяцев назад

    Ahh yow mom so amonn xam xam do djeul djiguén def ko sa djeuwrign.

    • @maguettebouboufaye2993
      @maguettebouboufaye2993 5 месяцев назад

      KON DEE KHANA SERIGNE MOUNTAKHA DA DIOUM MOM MI DIEUL SOXNA SODA KHOUMA DEF KO DIOWRINE GNOU DIOULI GUEDJI GUI DIAMALAY DEVANT MBACKIYOU FAYA AK SÉRIGNE YOUSSOU DIOP HISBOU TARKHIYA

  • @MamadouNdiaye-v1u
    @MamadouNdiaye-v1u 5 месяцев назад

    Bouniou nopé déllola sa seunba

    • @ToumanySagna
      @ToumanySagna 5 месяцев назад +3

      Boudiouman yi rek gno kham Sennba il a plus de connaissance k toi qui parle sans tête ni langue

  • @dioufmaisa6605
    @dioufmaisa6605 5 месяцев назад

    Yaw gourou mbotay gourou watarbane yaw gneup gno wara wakh senegal bamou des yaw .topou thi kaw djiguene lambarlambari gnou wakh nga tock thi pengnemi ne y’a wara wakh.yaw lou way bone bone mola tane.

    • @ibrahimaNDONG-np8cu
      @ibrahimaNDONG-np8cu 5 месяцев назад

      Li rk nguène xam wakh djiou gnaw violence AK sossal nitt lolou rk nguène diapé yone wi ki amoul sènn temps

    • @ToumanySagna
      @ToumanySagna 5 месяцев назад

      Ki taloula sa khôl dîna dague dakh serigne Moko ak soxna aida dewal

  • @habibdieng3006
    @habibdieng3006 5 месяцев назад +2

    Bichri tv vous ne devriez pas inviter ce bonfou car son guide spirituelle c’est une femme donc ce gars c’est un lâche on doit pas l’écouter sur les affaires de Serigne Touba

    • @serignetine1420
      @serignetine1420 5 месяцев назад +2

      Yaw ki mola eup xam te guisouma kouko eup xam xam thi yon bi😊

    • @PapeNdiaye-j4w
      @PapeNdiaye-j4w 5 месяцев назад

      ​@@serignetine1420vraiment

    • @AkimSerigne
      @AkimSerigne 5 месяцев назад

      Kii dañnë ak reer ,waxi seriñ tuubaa rek lafi wax,lamb tuwul ta tontunë ci xam xam ta genul axuraan ak xassidë

    • @adamandiaye2580
      @adamandiaye2580 5 месяцев назад

      Deug bou wër gua wakh

    • @adamandiaye2580
      @adamandiaye2580 5 месяцев назад

      ⁠@@AkimSerignekou dagn ak rêr dou dieul ap Soxna defko serigne.khamal liguay wakh kou baax

  • @mamechiekhfall315
    @mamechiekhfall315 5 месяцев назад

    Yaw borom xam xam bou tolni yaw kouy guiss mbakh di don sa serigne

  • @taphadiadia
    @taphadiadia 4 месяца назад

    Merci pour ton message

  • @bambaraserignebethio382
    @bambaraserignebethio382 4 месяца назад

    OOHHH IMAM SERIGNE SALIOU SAMB YAW SAGOU YOON WII NGA❤ YAW GNEUPEU LA WARA DÉGLOU

  • @malickseck911
    @malickseck911 5 месяцев назад

    Amoul morom khadim Rassoul

  • @mamechiekhfall315
    @mamechiekhfall315 5 месяцев назад +1

    Lomana wakh doulako degeul guir daga féké yon wou serigne touba déf ték niou si gua nieuw andé ak sokhna so kham day wathé ndigeul gua andé ak mome tè gua xam ni nékoul si dagui té sou nékon si dagui sakh té s mountakha wakh né fofou geun néké dou fofou yaw mi lanou wakh lo fatè khadiou fi yaw mi ya wara kholat sa togay mourid yi mome niogui founiou néké

  • @malickseck911
    @malickseck911 5 месяцев назад

    Amoul morom khadim Rassoul