Le Mahdi Seydina Limamou Laye psl dans le coran, la sounna et les dits des savants

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 21 янв 2025

Комментарии • 77

  • @issaciss725
    @issaciss725 4 года назад +5

    Machalla Laymakhtar yalla na yalla yokou sén kham kham goudeule sén fane sangue lén mbalanou soutoura, lér ,yiw,khéweul ci barkèb Baye Lahi RASSOULAHI aleyhi sallatou wa sallam

  • @NdiayeFabi
    @NdiayeFabi 5 лет назад +12

    MashaAllah Laye Makhtar, Allahou Akbar! Yalna Ya Allah 🤲yokeu sène lère ci Barbey Seydina Mouhamed ASWAS, Limamoul Mountazar❤! La vérité ne s'éteint jamais! Adjibo dahi Laye❤

  • @seydoufaye9942
    @seydoufaye9942 5 лет назад +6

    Machalla laye makhtar yalla nala yalla samal bopame amine laye

  • @aliounediop6557
    @aliounediop6557 5 лет назад +12

    Machalla kou dèguol rek dangua teukhe mè lérna nagne

  • @mamanlahi2235
    @mamanlahi2235 5 лет назад +4

    Mâcha ALLAH souniou Sangue yi yalna Yalla défal léne diam ak soutoureu barké Baay Laay

  • @ousmanealexislayelawson8123
    @ousmanealexislayelawson8123 5 лет назад +11

    Lerna teeyna seelna Laye Makhtar...May God bless You

  • @badaralayesamb2607
    @badaralayesamb2607 Год назад +2

    Amana bilahi wa Rassoulihi🤲

  • @assanesagarsonko1307
    @assanesagarsonko1307 2 месяца назад +1

    Mâchallah ❤. Laye makhtar

  • @oustazahmedfall6478
    @oustazahmedfall6478 2 года назад +2

    بارك الله فيكم فسعيكم مشكور

  • @mbayethiam5835
    @mbayethiam5835 5 лет назад +16

    mancha allah. li lagnou sokhla ayy téktal you kén doul wéddi.

  • @youssoulayegueye9733
    @youssoulayegueye9733 5 лет назад +10

    machaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaaala

  • @layemalick1747
    @layemalick1747 4 года назад +4

    🙏🙏🙏ziar ba ngui nonou

  • @gueyeamadoupascal9080
    @gueyeamadoupascal9080 5 лет назад +7

    mashalaa Sangaa yii 🙏🙏🙏🙏🙏

  • @adjisamb6308
    @adjisamb6308 5 лет назад +7

    Machallah laye makhtar

  • @oustazahmedfall6478
    @oustazahmedfall6478 2 года назад +2

    شكرا جزيلا يا أخي الكريم الغالي شيخنا الفاضل محمد بار الله المحترم على جهدك الرائع الطيب.

  • @mangaye7200
    @mangaye7200 4 года назад +5

    Kou geume niou gueume kou bagnie douniou taguo ba diwane baye laye amoul masse 🙏🙏

  • @mathiorothiaw4769
    @mathiorothiaw4769 5 лет назад +7

    Mashalla laye makhtar

  • @alassaneseck8039
    @alassaneseck8039 4 года назад +4

    Machallah limamou moy rassoullilah

  • @oumylaye9464
    @oumylaye9464 5 лет назад +7

    Mashallah djeureudjeuf Laye

  • @Illimane08
    @Illimane08 5 лет назад +5

    Dieureudieuf laye

  • @ansoulayetoure6848
    @ansoulayetoure6848 4 года назад +4

    Dieureudieuf laye makh tar❤🤲

  • @badaralayesamb2607
    @badaralayesamb2607 Год назад +1

    ❤❤❤

  • @serignemansourlayengomngom5323
    @serignemansourlayengomngom5323 3 года назад +6

    Walahi sene mame moy yonenti yalla mamadou

  • @piscolo6710
    @piscolo6710 5 лет назад +13

    lane mo takh nite kou gnoul khep bopame mane dama manoul comprendre pour quoi yen gniy wedi baye laye tee tegoulene ko fene loudoul baye laye diangoul dacor baye laye diangoul mais loo diang diang boo diakarlo ak mome mou diangal la
    kane moma mana guenel photo baye
    kane mo mana wakh kou diangal baye laye kou doul yalla
    yen gniy wedi laye wakhal soo lene ko khamee ngene wakh mako
    limamou laye rasoulou laye djine thia sawba ilalahhhhhhhhhhhhh

  • @oustazahmedfall6478
    @oustazahmedfall6478 2 года назад +2

    والله نحن نفتخر بكم وأمثالكم

  • @oustazahmedfall6478
    @oustazahmedfall6478 2 года назад +1

    كل من أنكر رجوع النبي صلى الله عليه وسلم فقد أنكر جميع أيات قرأنية، لأن الرجعة عقيدة قرآنية لقد جاء في القرآن عدة أيات تتحدث عن الرجعة في أمم السالفة

  • @bayenguiss1291
    @bayenguiss1291 4 года назад +3

    Au79 Mardi 06 Ramadan 1399
    Mamadou Moustapha 👃

  • @youssoulayegueye9733
    @youssoulayegueye9733 3 года назад +3

    Diadieuf laye Maxtar seul le savoir est sûr

  • @mamadouseck8918
    @mamadouseck8918 2 года назад +1

    استغفرالله العظيم

  • @mamadoulayesene538
    @mamadoulayesene538 5 лет назад +3

    Contanna lol si li billahi

  • @hallildiallo6781
    @hallildiallo6781 5 лет назад +2

    Gnoune Senegal gno gueum ya ALLAH gueun fi, gueuna civiliser di wower yenen africains gnaak... Am naak sougnou dinner bop parce que gnoune gno gueuna mouss gneup.... Yonente bi Aliy Salatou Wassalam gueune adouna t wakh nagn ko gnanal mais au Senegal serigne na Ya ALLAH yok lerraam.... Je suis confus la, expliquer lenn ma bokk.

  • @issaciss725
    @issaciss725 4 года назад +4

    Seydina Limamou moy Seydina Mouhamed bén djeum dji
    amoule bén sikki sakka

  • @madameniang2796
    @madameniang2796 5 лет назад +3

    Degu leu

  • @serigneadamafofana39
    @serigneadamafofana39 4 года назад +4

    Yalla naniou yalla baal...senegal lounei ngay guiss

    • @aissatoundoye6054
      @aissatoundoye6054 4 года назад +1

      Gua balmeu, mais nitt bala guey weddi dara daguey gueustou beu paré, demeul sett aya yi akh tektal Imamoul Mahdi si Al Quran, akh signes yimouy andal gua sogua wakh, nakhté woroul, merci

    • @serigneadamafofana39
      @serigneadamafofana39 4 года назад +3

      Aïssatou Ndoye sokhna diaroul mey guestou amneu leneu lo xamni sokhla woul guestou..il suffit juste de refflechir et ne pas etre fanatiqu..le prophete a fait la description sur le mahdi Dans un hadith de bukhari et muslim,il a dit qu’ il aura le meme nom que lui et celui de son pere au pere du mahdi et il sera a la mecque..bayilen diinei bi ngen di fowei

    • @aissatoundoye6054
      @aissatoundoye6054 4 года назад

      @@serigneadamafofana39 Désolé mais je pense que tu n'as pas lu les bonnes informations, je te propose de refaire tes recherches à propos du Mahdi, mo gueune guey wakh lo khamni yakaroumeuni worneuleu, aya yiniou wakh si 3 parties vidéo bi aussi gua dem kholko, so paré gua outt ay nitt de confiance youleu ko meuneu tekil et niouleu meuneu expliquer histoire Seydina Limamou Lahi saw, je te parle en connaissance de cause nak, weddi bakhoul, so gueumoul rek boul weddi

    • @serigneadamafofana39
      @serigneadamafofana39 4 года назад

      Aïssatou Ndoye bane aya leu ? Bouniou tousou seydina limamou ?

    • @aissatoundoye6054
      @aissatoundoye6054 4 года назад

      @@serigneadamafofana39 Wakhoumeu aya bougn toudd Seydina Limamou Lahi, mais aya yougnouy wakh si "Imamoul Mahdi", recherche "Le Mahdi dans le Coran" gua khol, tu peux mm regarder la 1ere partie avant cette vidéo, so beugué gua relevé ko aprés gua dem rechercher, je sais pas si tu vois ce que je veux dire, et aussi gua geustou histoire Seydina Limamou, niou beuri degn tekni c'est du fanatisme, et que Layenne yi nioko wakhal senn bopp, or que non, mom Limamou moko wakhal bopeum "Adjibo dahilaye ya marsaral insi wal jinn ini rassouloulahi ileykoum", geustou bi ça ne te coûte vraiment rien et je t'invite vraiment à le faire, je ne sais pas combien de temps cela va te prendre sou néké tu as vraiment la volonté, peut être des années, mais le jour où tu auras fini In sha Allah recherche ce commentaire et écris pour que meu guissko. Merci.

  • @lasouverainete2794
    @lasouverainete2794 5 лет назад +7

    Li ngèn Di wakh tègou woul fén louway gat gat kham kham khanani mème bou yonénte bi gneuwa ton meunoul nekat yonénte yalla teuth na bountou yonénte yi demal lèn diangi

    • @abdoulayediop2460
      @abdoulayediop2460 5 лет назад +9

      un conseil monsieur le sage, ne vous fatiguez pas à commenter ce à quoi vous ne croyez pas. Vos pères et grands ne croyaient pas, ils sont partis et vous ont légué la mécréance, nos pères et grands pères sont partis et nous ont allaité de cette forte croyance qu'ils avaient au bien aimé psl. Le dénigrement de vos pères et grands pères n'ont rien pu faire contre cette flamme qui jaillit de nos cœurs. De grâce monsieur borom xam xam ma sha Allah il fait chaud ces temps ci, buvez tranquillement votre verre d'eau fraiche dans votre coin, et laissez nous savourer le notre, nous illettrés. svp

    • @airmaxstar5762
      @airmaxstar5762 5 лет назад +1

      Rien que la vérité kone issa sou niewaté dou yoré gratou yonenté??

    • @opinionsjustemilieux6257
      @opinionsjustemilieux6257 5 лет назад +2

      Wayé mom mo wax ni mana dem mana tay lo si meune

    • @ahmethfall9083
      @ahmethfall9083 5 лет назад +2

      Soula nékhé wayé gnoun gueum nagne lignouy guem limamou moy mahdil mountazar

    • @cheikhoudia9517
      @cheikhoudia9517 5 лет назад

      Rien qu..........,.changél ton nom yaw deugouwo lo khamsi mahdi asws khamale liguasiy wakh wara nga geuss tou ko

  • @moussaba2321
    @moussaba2321 2 года назад

    Sa mission khamna pour sénégalais yi la.

    • @diamalahieventsprod
      @diamalahieventsprod  2 года назад +2

      Laaye Maxtar sangaa bii Mission Seydina Limamou Lahi Al Mahdi PSL wessouna Sénégal

    • @mouhameddrame5353
      @mouhameddrame5353 2 года назад

      Yaakaarnaa pour sénégalais yila réK

  • @mallbelly8250
    @mallbelly8250 5 лет назад +2

    Yombou na de

    • @ahmethfall9083
      @ahmethfall9083 5 лет назад +1

      Lou takh nga wah lolou nagnou tok défsi débat

    • @mallbelly8250
      @mallbelly8250 5 лет назад

      Ahmeth Fall déba diarouco

    • @ahmethfall9083
      @ahmethfall9083 5 лет назад +1

      @@mallbelly8250 soy wédi dangay indi lénén, yaw lo indi? Ana say ardiouma?

  • @libassesarr1997
    @libassesarr1997 5 лет назад +6

    macha allah laye mahtar

  • @petitlahiwade9670
    @petitlahiwade9670 5 лет назад +8

    Machalah laye makhtar