Ouztaz pape hann bravo encore avec ton invité vraiment kebe il est très excellent dafa teyy je suis talibe baye Niass mais j'adore les layennes vraiment
Merci bcp au gfm sen takhaw matalena rafetena yamalegueen. Nous talibes layeen sommes fierts de vous et saluons votre engagement a la cohésion sociale et religieuse au senegal. Grand merci a vous Yalla na Yalla dollileen Barke dollileen kheweul Dollileen Japale. Mention especial a Bouba Ndour grand Yalla na la yalla dolli weer dolli la japale dolleel la jamaal soutouraal la yaw ak sa jaboot ak kep kulako yene. Nioun layeen douniou meusseu book ci louy yakh senegal plus particulierement gfm .gfm niouko book. Merci a tout l personnel vous avez fait un bon boulot. Bravo
Il n y a pas de deuxième mission ma soeur pour Mohamed psl et limamoulaye c est un faux prophète je le dit et je le confirme oubilén sén khél yi touti té khalate
@@binetalayembengue5228 c'est du vrai n'importe quoi ce qui se passe au niveau des layenne qui pensent que limam est prophète , c'est comme sabotage vis a vis de notre religion qui est L'Islam . Je condamne fermement cette pensé , comme si c'était du jeux . C'est clair et je répété le Mr n'est un prophète . Qu'allah nous guide vers ce qui à de mieux Amine
nous sommes très fiers laye makhtar d'avoir au sein de notre communauté, un érudit de votre facture. K'allah par sa Puissance océanise votre savoir d'une pureté inégalée.
@@Footballive-c9e et tu prétends en savoir quelque chose toi pour dire c'est pas vrai, lotakh nguéne niémé borom bi, tu prétend avec ton compte en savoir sur le coran et la sunnah , or tu ne sais absolument rien. mais sache que nga niak geum walla nga geumm moci yam . Mouhammad ibn abdallah est Seydina Limamou ibn Alassane BAYE LAYE MOY RASSOULOU LAHI, légui nak bo beugué débat rék nieuweul.
Manchala Laye Makhtar Laye séni Laye Alassan Limamou laye Mii ndèkè mom la yalla wakh si alkhouran nii khèt wu nék na si yoni yonéntè kon dèr bou gnoul yalla yoniwat fi Seydina mouhamed hooo manchala man deh santana ba bima yalla dimbalé ma kham ko ta guem nako loll bilahi
wayè nak boulén bagne kou wedi wala kouy saga ndax mom seydina limamou bimou wotè sa mak non yi saga nanu ko dor nanu ko ba dam sakh bégnam ta ba fii may wakh akh yén am na gnouko fa geumoul batay ngala kon balén gnouy wakh rek lounouy geun di wakh dafay geuna yok sunu geum Mame baye lahi miii heuu moy wadji dé laye makhtar
Je demande une seule chose vous les layénes rv bi yowmal khiyam légui boudé baye laye moy mouhamed rassoul (psl) waw May lathie té nane laye déff gni geume mouhamed (psl)narr bou khéss bi bayou fatima rokhaya seynabou Ibrahim khassim ki teud thia médinatoul mouna wara minga khamni c le prophète incontestable par toutes les musulmans et partout dans le monde ont le connais May lathie nane la gnouy déff, 2)question dou ay khass la wakhe mé une question rék à part Sénégal bane deuk (paye) ngay déme gnounila peuple bi ay layénes lanou
Ce que les musulmans doivent comprendre justement c'est vrai que le prophète Mouhamed (Ahmad) à été envoyé à une mission c'est vrai mais scindé en 2 moment distinct, 1 Oriental en tant Mouhamed psl 1 autre occidental en tant qImam de la fin des temps psl.
Ou est ce Allah a dit dans le Quran que la mission de Mouhamad est scindé en deux parties. Amenez vos preuves si vous êtes véridiques. Ce que les musulmans ont compris c'est que Ibliss vous a égaré et enjolivé vos actes. Certes vous êtes dans un égarement évident. Depuis longtemps le Prophète nous a mis en garde contre ces égarements
Kou beugueu ma ablaye beuseul👍
Thiaga la dou guate dokhane diabarou diambour yi rek lafi néké ak ték beute serigne si
KOU BAAX KOUNE BEUGUEU NGAKO MAME ABLAYE KEBE YALLA NA WEER LOOL TE YAG FI
Machalah Laye makhtar mame baye laye amoul kou bonne
Salaatane waa tasliimane ‘alaa Seydil waraa Mame Limamou laahi asws lééram yi nio raw you dianta bi❤️Yalna niou yalla fayal Seydina Limamou lahi psl diadieuff mame Abdoulaye kebe kham kham bi rafet na MaSha Allah🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Blh ms yalla na yalla déff diamm diou si réw mi si barki seydina limamou laye ❤❤❤❤
Yalla ko yoni mouy nabi ❤
Geum gui dal mo geune wor wédi gui seydina limamou lahi psl yay rassouloulahi mouhaméd psl
Souniou fierte Mame Abdoulaye Kebe Laye
Ouztaz pape hann bravo encore avec ton invité vraiment kebe il est très excellent dafa teyy je suis talibe baye Niass mais j'adore les layennes vraiment
Merci on t'adore également
machallah , wallay niola geuneu beug .
Merci bcp au gfm sen takhaw matalena rafetena yamalegueen.
Nous talibes layeen sommes fierts de vous et saluons votre engagement a la cohésion sociale et religieuse au senegal.
Grand merci a vous Yalla na Yalla dollileen Barke dollileen kheweul Dollileen Japale.
Mention especial a Bouba Ndour grand Yalla na la yalla dolli weer dolli la japale dolleel la jamaal soutouraal la yaw ak sa jaboot ak kep kulako yene.
Nioun layeen douniou meusseu book ci louy yakh senegal plus particulierement gfm .gfm niouko book. Merci a tout l personnel vous avez fait un bon boulot. Bravo
❤❤❤❤❤
Non. N
Bilahiii walahi talahii Baye Laye Moy Mouhamadou Rassoulilahi (psl)
L'autre miracle derrière limamou, la mer ne touche jamais son mausolée.
Génn adouna di déff mouhdjiza,guédj gui dou lall khabrou bi moukk.
Bilahi laye lolou tmt bokkou na si guénne adounam Di deff moukhdjkzat
Bilahi geume nanè limamoul mahdiyou moye yonentè bi machahala
Nio thi yaam deih
Dioumo dé laye makhtar
MACHALLAH LAYE MAKHTAR , geum ba deih reik inchallah
Lou yallah binde bayé laye mossi guene ❤️🙏🏿
hahaha
Wa waw moy deug de billahi
Waawaaw ndakh moy Seydina Mouhamed Sallalaahou aleyhi wassalam
KEN DOU SEYDINA LIMAMOU ALEYHI SALATOU WASALAM MAME ABDOULAYE KEBE TA FADAL MACHKOURA CHOUKRANE LAYE MAKHTAR 🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿🙏🏿
Lou yalla bindeu baye laye mossi gueneu ❤️🙏🏾
Gfm tjrs 1er ca kanam rek ndaam rek Incha ALLAH
Machalah yalla nanou sunu borom ray si geum bay dekal noussi dieureudieuf mam abdoulaye kebe
Aleyhimaa Salaam
Wallahi seydina limamou psl moy rassulilahi t lolou la yallah def ken mounou si dara✊🏽❤️
Limamou lahi rassouloulahi baye laye moy seydouna Mouhamed 🙏
Baye laye moy Mohamed psl
Dou degg
So déggé dra geumo ko demall gua geuss dji
Mo geune 💓💓
Yalna Yalla fayela Ma Abdoulaye Kébé
Dii yessalatt sama geum si Seydina Limamou Lahi PSL
Kou gueum teher euleuke kou gueumeul donous guis ahirra🖐
machalah yalana yalla fayulnu mame lamamou laye
PSL
Amin
machalla laye makhtar baye laye amoul mass,💗
Machallah mamadou mactar dieureudieuf khol sedatina
Le prophète Mahomed ❤️🙏psl à savoir seydina Limamoul madiyou Mountazar dans sa deuxième mission yalla naniou ko yalla fayal❤️🙏
Rectifie laye Makhtar justement cest fe quil faut pas dire, cest 1mission mais a 2 moment plutôt
Il n y a pas de deuxième mission ma soeur pour Mohamed psl et limamoulaye c est un faux prophète je le dit et je le confirme oubilén sén khél yi touti té khalate
@@salifsagna7607 gueumeul li nga gueume rk saawaay bou déwé di nga khaam ndakh mome la wala dou mome
@@salifsagna7607 toupko
@@binetalayembengue5228 c'est du vrai n'importe quoi ce qui se passe au niveau des layenne qui pensent que limam est prophète , c'est comme sabotage vis a vis de notre religion qui est L'Islam .
Je condamne fermement cette pensé , comme si c'était du jeux .
C'est clair et je répété le Mr n'est un prophète .
Qu'allah nous guide vers ce qui à de mieux Amine
wéddi bakh na lolou wayé weddi lo khamoul woroul á vrai dire tout est raisonnable
Ma ablaye yague fii té werrr ❤️🙏💯
Mouhamad moy Limamou ya wéxone démb nioul tay yalla na yalla bayi fii bépp kilifeu diné si barké seydina limamou def Senegal djame
Mame Ablaye kébé yague fii lol té ande ak wére
Baye laye(psl) amoult masse bilahi walahii👌🙏
Holl sédenaaa gueum ba déé rék inchalah
Yaw
Nakamou
@@alycisse4972 sava sante
Yalla na santa yague
Entoukaaaaa yalla maynakooooo loumou mayoulll kennn barkiii cheikh Tidjiane 😢❤❤❤❤
nous sommes très fiers laye makhtar d'avoir au sein de notre communauté, un érudit de votre facture. K'allah par sa Puissance océanise votre savoir d'une pureté inégalée.
bonjour
Bilaye baye laye Amou mass ❤❤🕋
Merci mame Abdoulaye laye makhtar kene dou Seydina limamou
Ndaysane ndi wéddi daniou khamoul Baye laye moy rassoulilahi👏👏👏
El phénomèno Serigne Mame Ablaye kebe Laye merci
Diaradieuf laye matkta laye baye Abdoulaye yalna nafi yague te wer
Machalla mame Abdoulaye sante rek Laye makhtar👍👍
Yalla nanou fayale baye laye ❤❤❤
ndjine yonene nga mame limamou laye yaye rassoulou lahi yadi borom diamalaye lahilaha illalahou
Mashalah tjr pertinent dieureudieuf laye makhtar
Kèn dou MAME BAYE LAYE psl, mom la won demba sa MACKA àk MEDINE ABDOULLAHI àk AMINATA diourko, momla watt tay fii si SAAW DIANTE BI ALASSANE THIAW àk sama Mame bou tedd bi bou sell bi SOKHNA COUMBA NDOYE LAHI diourko.
BILAHI WALAHI WA TALAHI NIOUNE GUÈM NANIOU NI TÈ WORR NANIOU NI KHAYROU KHALKHIL LAHI MONGUI DIAMALAYE.
Khalifatoul Aam Khalifatoul Mouslimine SEYDINA EL HADJI ABDOULAYE THIAW LAHI yalnafi yagg loool tè andak wèrr ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤ ❤
Machalla
@@salimataseye8375 diadieuf Laye Makhtar
Bilahi Mame ablaye ya barri kham kham, machallah machallah.. wayé Pape hanne yaguefi té ame wéur
Macha allahou yallana yalla fayyeu yiweu ak bokkeu barke baye lahi wormayy mame seydi
Kou gueum niou gueum kou guemoul niou gueum. Baye laye moy Mouhamed rassoulilah psl.
Machalla laye mactar rafaite na limamou laye yayeu rosorou laye moye roso Lou laye lahilaha ❤❤❤❤❤❤❤
Billah baye laye MOy resouloulahi
Machallah Laye momadou macthar beguenaniou
Xam xam bi werna machalla
Yalla gnu yalla faayiial baye laye (psl)🙏🏿
Baye laye amoul mass moy Rassoulahi🙏🙏
Ylla nanouko yalla fayal
Thiey Sénégal 😱yalla nagnou yalla yeureum
Dacorna ak yaw dé,,thiey sunu senegal bi, loune guey degue, lounek guey guiss,,,,yeurmande borom bi lagniu gnian
Bayelaye Moy rossloulahi nalerr ♥️🙏
@@modoumamendiaye691 soubhanalah,lolou ça n'engage ke toi
@@ibrahimacamara5615 Lou yalla bayelaye mo ci geun
@@modoumamendiaye691 yow fo ték lolou,mouhamed sws nak nokay def??
BAYE Laye Amoul Masse kou gueume niou gueume kou bagne douniou tagoo badiwane ( PSL)
Di fattali dioulit gni que seydina limamou laye moy mouhamadou rassoulahi psl
Yonente la woté
mensonge
C'est pas vrai
Magui wath nane bilay walay mame limamooy rassoulou Laye
@@Footballive-c9e et tu prétends en savoir quelque chose toi pour dire c'est pas vrai, lotakh nguéne niémé borom bi, tu prétend avec ton compte en savoir sur le coran et la sunnah , or tu ne sais absolument rien.
mais sache que nga niak geum walla nga geumm moci yam .
Mouhammad ibn abdallah est Seydina Limamou ibn Alassane
BAYE LAYE MOY RASSOULOU LAHI, légui nak bo beugué débat rék nieuweul.
Baye laye amoul mass
yagal fii baye abdou laye
Baye Laye amoul mass Moy rassoulilahi
Mach'Allah Pape Hane. Emission bi nékhna
🙏🙏Machallah laye makhtar🙏🙏
MOUHAMAD = LIMAMOU point finale koumou neikh ak koumou neikkhoule wasalaam.
Wakhal kham kham nekh AK nekhoul newo nou si
Baye laye YALLA yoni woko fénn
@@wakhtaanediamono5329 yeine sokhor moleine diapeuh seine khole yé feibar magui gniane sounou borome mou kheitali leine
@@wakhtaanediamono5329 SANTE YALLA
Machallah wa akhlou bayti rassoul seydina Limamou lahi al mahdi p.s.l💖🥰🙏🏾🏳️✔️🕌🕋💓
Maashaa Allah Lahi Makhtar🤝🤲🙏❤️❤️❤️
Bayelaye Moy rossloulahi nalerr ♥️🙏
Baye laye amoul mass mo wékhon tha maka mo nioul tay mom la démb mom
La tay
Manchala Laye Makhtar Laye séni Laye Alassan Limamou laye Mii ndèkè mom la yalla wakh si alkhouran nii khèt wu nék na si yoni yonéntè kon dèr bou gnoul yalla yoniwat fi Seydina mouhamed hooo manchala man deh santana ba bima yalla dimbalé ma kham ko ta guem nako loll bilahi
wayè nak boulén bagne kou wedi wala kouy saga ndax mom seydina limamou bimou wotè sa mak non yi saga nanu ko dor nanu ko ba dam sakh bégnam ta ba fii may wakh akh yén am na gnouko fa geumoul batay ngala kon balén gnouy wakh rek lounouy geun di wakh dafay geuna yok sunu geum Mame baye lahi miii heuu moy wadji dé laye makhtar
Machallah yalnanko Hague feikei ta talko inchallah
Mame ablaye kebe aka moko buegue ndaye sane yallnafi yagui te werr barke baye laye
Bilahii walahii talahii Limamou lahii moy mouhamed
Machallah khol sed nattina 💓💓💓💓💓
Baye laye yaye Rassoulou lahi asws
Mame ablaye kebe laye khol sedena yalna yalla fayla ci barké mame baye laye yagua fi té wer laye matar
Dieureudieuf dieureudieuf dieureudieuf dieureudieuf dieureudieuf dieureudieuf dieureudieuf dieureudieuf
Mandé mouritla wayé douma nataplé né. Mome moyy rassouloulahi non keen dou baye laye
ASTOU YA BAAX YALLA NA YALLA FAYLA BARKE BOROM TOUBA MI NGA YAAKAAR DIEUREUDIEUF
@@magattediagne7812 bilaay damaay suvre aiyy wakh tanam rek bilaay keen dou mome
Au début c’était comme ca avec moi
Mais a la fin j’ai cru sérieusement
Yamana dool khamo loy mouride
SERIGNE TOUBA moko wakh كل مريدبي يلوذ فليدم تلاوة لخير ذكر قد رسم dhmal diaggui
Machallah laye contane nagne thi yaw Salam reck baye laye Amoul masse
Alhamdoulilah rabbil alamina
Alhamdoulilah allah kouly al
Baye laye moy Rassoulilahi aleyi salatou wasalam
Machalla laye makhtar dieredief laye
Dieuredieuf laye makhtar walae baye laye moy mamadou
Seydina limamou moye Rassoul lilah
Baye laye mouhamad démba mo nioul tääy moy Seydina limamou lahi
Machallah baye laye amoll mass
Baye Laye moye rossouloulahi bouléne si sone Baye
Kouye guem guem kou guemoule bayie nionke kie nion nénaniou aamana
Dieureudieuff laye makhtar 😭😭
Mashala laye maxtar
Bilahi walahi watalahi baye laye moy Rassoulou lilah 🙏💓💓 psl
Bilaye kene d'où Mame limamou laye
Baye la yalla yoni👏
Limamou Moy Rassouroulahi !!!!!!!!!!!!!!!!
Pape ane amouleoo laye euleuke.yawemalekhiyare
Sénégalais Yii Dagno Nane aay Somnifères Yéwogougne legui dh
Limamou Yowmal khiyame la diokhé Rendez vous
WALLAHI mbok mi thie lagni xaam kane moye kane barki SEYDINA LIMAMOU
kéne dou seydina limamoi lahi psl
Walahi moko wakh gnar RK gnoma xam kima gueum bâ dh ak kima weddi bâ dh
@@birandiaye6424 loloula naak gnome bougnou diogué ni wa ahlou lahi gniye djoulite yifi gueune baparé bagn Baye moye yoneine bi 🤷🏿♂️
Je demande une seule chose vous les layénes rv bi yowmal khiyam légui boudé baye laye moy mouhamed rassoul (psl) waw May lathie té nane laye déff gni geume mouhamed (psl)narr bou khéss bi bayou fatima rokhaya seynabou Ibrahim khassim ki teud thia médinatoul mouna wara minga khamni c le prophète incontestable par toutes les musulmans et partout dans le monde ont le connais May lathie nane la gnouy déff, 2)question dou ay khass la wakhe mé une question rék à part Sénégal bane deuk (paye) ngay déme gnounila peuple bi ay layénes lanou
Baye lay moy rasolou lahi psl
Ma cha alakh laye makhtar
Machalla Yalla na Yalla gudal sai fane 💯💯💖🙏💖🙏💖 sono contento di conoscere oggi Mame Limamou Late💖💖💖
sénégal naniou kholi kane moye seydina limamou asws
Billahi limamoy rasouloul lahi yalla dogalnako
Baye laye❤ (psl)amoul mass
Mashallah khol sédana
Machallah laye makhtar 🥰💞💖
Baye laye moy Mamadou
Baye Laye amoul mass
Baye laye mi bakh
Ce que les musulmans doivent comprendre justement c'est vrai que le prophète Mouhamed (Ahmad) à été envoyé à une mission c'est vrai mais scindé en 2 moment distinct, 1 Oriental en tant Mouhamed psl 1 autre occidental en tant qImam de la fin des temps psl.
Machallah
❤️❤️❤️🙏🙏🙏🙏💯Laye laye
Ooooh machallah b1 dit
Ou est ce Allah a dit dans le Quran que la mission de Mouhamad est scindé en deux parties. Amenez vos preuves si vous êtes véridiques. Ce que les musulmans ont compris c'est que Ibliss vous a égaré et enjolivé vos actes. Certes vous êtes dans un égarement évident. Depuis longtemps le Prophète nous a mis en garde contre ces égarements
@@babacarwillane3004 Montre moi la verset ou il est montrée comment le musulman doit prier dans le Coran, après je te répondrai inchalah.