N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ... Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii... Témoin d’un événement contactez : +221 77 451 21 10 WHATSAP +221 78 149 53 10 APPEL NORMAL
Kali dala yereume billahi bambél khatna loole loye wakh nafék gua amssi lou lérr mo gueunne killi démall diamoudji yalla mo gueunne sa li guaye déf ragualay yalla yaw kou bonngua bilahi
Slm wa yen gni di wotéwo talibe damalena yereum ndakh menouma guemné batay wadji désséna talibé apré ses fuites de audios et videos en 2022 Man mouride la wayé naniou niémé deug ki dou ap serign ndakh ragaloul yallah ap domeram deug leu di lal diaparou talibém ak di wané ay awram té am diabar ken continué diko pr lan kholat len sen bop té oubi sen khel ki dou touss domeram de 1 categorie la ishhh!
Bul generalise nag ku baax am na Sëriñ su ndaw soo xam ne ci jaamu Yàlla rekk te dundal yoonu Srg bi ci la ñu nekk🙏 Bàyyileen bu benn kilifa defe dara walla ñu jiiñ ko dara ngeen ciy profito di xas ñu ci seen yoon nekku ci 🙏
Mané séne serigne bi sicke na lole. Kéne chantageouko léppe mome la. Aye talibéme la yereume. Bayiléne ki dou tousse, vous perdez votre temps di sani séne khalisse thi dara.
D’après ‘Abdallah Ibn ‘Omar (qu’Allah les agrée lui et son père) : Le Prophète (que la prière d’Allah et Son salut soient sur lui) est monté sur le minbar et a dit en levant la voix : « Ô vous qui êtes musulmans avec la langue mais dont la foi n’a pas pénétré les coeurs ! Ne causez pas du tort aux musulmans, ne leur faites pas des reproches pour des choses qui ont été commises il y a longtemps et ne cherchez pas à découvrir ce qu’ils pourraient cacher. Car certes celui qui cherche à découvrir ce que son frère musulman pourrait cacher alors Allah va chercher ce que lui cache or si Allah cherche ce qu’une personne cache Il l’humilie jusqu’au sein de son foyer ». (Rapporté par Tirmidhi dans ses Sounan n°2032 qui l’a authentifié et il a également été authentifié par Cheikh Albani dans Sahih Tirmidhi, Hadith Hasan)
ki bane serigne la ? non way ki domerame la way bayilén wakh seugn bi il a un nom c'est une bande de mafia qui vie sous le dos des fidels mourite parceque ici les mourites son facile a tromper quant tu utilise notre chère vénéré SERIGNE TOUBA
😂😂😂😂😂😂 en tou cas senn serigne yiii si ay thiakhann rekk lanou nekk... lii dou yefou kilifa 😂😂😂 wadij amoul argument pour defandre sen serigne bii diagala 😂
N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ...
Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii...
Témoin d’un événement contactez : +221 77 451 21 10 WHATSAP
+221 78 149 53 10 APPEL NORMAL
En tout cas séne liguéye bi dou liguéye dé, yalnaléne yalla sopi
Serigne bi wakhlenn ko mou raggall yallah
Audio 2022 ak 2024 yeupp c est la même chose, serigne waroull dokh thi yenneu yii
Nit gay wax Mouy ioe Mouy Serigne bi warul nék ci yéneu yi
Boul wakh Lou la lèroul
*Waayé xanaa bu tuubee waruñ bàyyi ba 2024 ñu koy partager waat*
Serigne bii nite leu
@@babsshoesshoesbabssenegali3714leer na kay ,so wakhe ne audio 2022 leu niou guene watt ko .
Kon kay audio amneu.
Kou ragaloute yalla sí ligaye déf mouno diar fène ba yalla dou la wère
Thiey yalla li dée moye lou bone dou raaf yalna niou yalla soutourale 😢😢
Serigne daa wara kham adoune
Nekhoul ba nekhoul serigne bi mouride la mais dey thiakhe wakhlenko deugue
Ndakh deugue la yalla beugue
Yalna yalla chance Sène djikho yi
Jaamukatu yalla day leer❤
Kali dala yereume billahi bambél khatna loole loye wakh nafék gua amssi lou lérr mo gueunne killi démall diamoudji yalla mo gueunne sa li guaye déf ragualay yalla yaw kou bonngua bilahi
De tout fâchions Seringe bi djiouboule 😢
No meun fi kissou mafi preuve dakh audio bi dafay continuer ba legui
Slm wa yen gni di wotéwo talibe damalena yereum ndakh menouma guemné batay wadji désséna talibé apré ses fuites de audios et videos en 2022
Man mouride la wayé naniou niémé deug ki dou ap serign ndakh ragaloul yallah ap domeram deug leu di lal diaparou talibém ak di wané ay awram té am diabar ken continué diko pr lan kholat len sen bop té oubi sen khel ki dou touss domeram de 1 categorie la ishhh!
Vraiment ki kay say say bou magla😂😀🤣
Merci beaucoup dou guate serigne dina def li bouniou diouguè di moubo serigne touba sim di wakh wakhou thiagua merci rek
Deug deug
Sénégal amatoul valeur no mon pays va mal😢😢😢
Khanaa sa sénégaal moo amatoul valeur, nioun déh sounou sénégaal masoula niakk valeur inchallah linou linou yalla diangal thi alkhour'aane, yonént bi psl diangal nouko thi hadiisam, sounouy kilifa diiné diotalinou KO thi Séeni téeré, inchallah thi lii rékk lanouy nékk, kouthi nékk niou nékk thi, kouthi nékkoul niou nékk thi, alhamdou lilah alhamdou lilah alhamdou lilah ❤❤❤
Khanaa sa sénégaal moo amatoul valeur, nioun déh sounou sénégaal masoula niakk valeur inchallah linou linou yalla diangal thi alkhour'aane, yonént bi psl diangal nouko thi hadiisam, sounouy kilifa diiné diotalinou KO thi Séeni téeré, inchallah thi lii rékk lanouy nékk, kouthi nékk niou nékk thi, kouthi nékkoul niou nékk thi, alhamdou lilah alhamdou lilah alhamdou lilah ❤❤❤
Il faut que la police s'occupe de sa c'est grave
Serigne bi dale meunouléne ko sétal mane mi mourite la mais Serigne sou taw yi danio doye warr
Bul generalise nag ku baax am na Sëriñ su ndaw soo xam ne ci jaamu Yàlla rekk te dundal yoonu Srg bi ci la ñu nekk🙏
Bàyyileen bu benn kilifa defe dara walla ñu jiiñ ko dara ngeen ciy profito di xas ñu ci seen yoon nekku ci 🙏
Yalla naniou yalla doli soutoureu 😢
Mouride yiii amna gnou niak fayda
Serigne modoulo gamou matoul serigne démléne diamou yalla ta roy si yonnenty bi sws❤❤❤
Sa data yaye
@@sadiofaye3975 boy damay khar sa leufeul ndaye déh domou katihe
lolo la serine touba baege de❤
@@sadiofaye3975khana sa yaye amoul data😂😂
Adamo yabon bilahi yall nala yall fay sa bor yakk kalifhone momou ningén di khawé soutara diambour yi yall na yalla khawé sén soutara nonou
Top léne yalla bayi serigne yi
Mo gueun dé
Yaw danga meune guénè serigne bi si Yalla
Wayy li 2022 la wone wayyy li yageuna bayilène doull ak takhe domou adama
Kou soutoural bein joulit Tei y’alla rek tax Yalla Soutourala adouna ak alaxira
❤❤❤❤❤
Est-ce que djoulite la ?,éy bokalé katt légne tarikha yii
Lan molén nékh si wérr domou adama liguéni déff gniaw na 😢ta méttina si kholou képeu kou beugeu lou bakh
Yallah na yallah doli soutoura incha'Allah
Souma fataliko ba kaliphone né daye diapelou Adamo dakhe sagayi 😂😂😂
Lii yeup mennoon na niakk, si kou teggou si yoonou Serigne touba té dokhoo si ay tiaakhaan
Seringe bi Modou Lo moy domou haraam domou khadj
wayé yén talibém yi mbaam sah molén tané démlén topi sén Baye yi wala ngén wouti Seringe bou bakh
S Touba nekoull ci aye rt
Thiakhan AK aye fenebayilene tapale
Alkhourhan ak sunnah moy deug ❤
Liguén deff gnaw na réw mo xam ni xawi sutura rk wayé bax diaall bagui sèn kanam démlén rk😢😢
Kou dé si marché bi ya tagué sa bopou ki domérame le ak wakhou thiaguam yi si serigne talibé yi daniou fébar ki lokoy doyé yoboul kéneu aldiana sim
Lima meti moy goor djeguen bi di wakh kom ko kham degue domo xaram ji pape mbaye
Même bou feké deugue le loutakh diko were nii… soutoureu waye😮😮😮😮
Prquoi audio 2022 si serigne tamite aaaaaaaaaaaaa
Serigni.loumoulén.déf.bà.lilép.am.
Adouna yahuna😢 buniu demé bay weranté ni
De len soutoural nite té yalla takh
Ki di wakh si serigne bi limouy wakh maîtrisé wouko dé comme dictée préparer
Serigne biiiiii . Aaaaaah
Walahi Diamou Lén Yala Té Bayi Serigne Yi. Topal Say Wadiour Mo Waur
Serigne bou nan oubil sa badio bi .non kalifone mo rew🤣😀😂🤸♀️🤸♀️
Aye wayyy Sénégal bariguenn wakh ligueyy len dekeubi bayii aye détail 😢
Gni gnepp Europe lagnou nekk
Noooo kalifone ya néke ci deugue
Ah nguabou mi mom ap kathior la kate mom adounam yeup Anna ndiaye la 😅😅khamna karatayni yimouy werd moy def effet 😅😅
Ani soutou r boulene yalla daifon ni folaine dieume 😢😢😢😢😢
Kou soutouraloul nit Yalla doula masa soutoural Bilahi
Kali Liga wakh la geum
Nite dangay ame soutoura
Mané séne serigne bi sicke na lole.
Kéne chantageouko léppe mome la. Aye talibéme la yereume.
Bayiléne ki dou tousse, vous perdez votre temps di sani séne khalisse thi dara.
Qui dou Serigne thiagua la point
Audio dou preuve, avec l'intelligence artificielle on peut faire des audios avec la voix d'une autre personne
Il ya des vidéos aussi,khana neko Sénégal yaw😂😂
Serigne bi di diegeulou.
Lolou preuve leu.
Barki seydina Mouhamed psl kepou kouy khawi soutoura nitt bess dinna nieuw nga reugnou lou beuri te yague toull darra walahi
Adamo Amal soutara li niawna de vraiment bayil ki
Un marabout pervers, merci Kali wér ka ki day guathiel dîné
Kalifon day politique ndax apr daa am problem ñu bëggë tourné xélu nitt ñi
Ya ngui hors sujet deh,li diote woul ak politique Dara.
Boul outal Serigne bi AP laye.
Nit koubakh la Machalah … nit moy dioum tei saytanei bayiwoul keine
Dioum thiii diabarou diambourrr
@@Lalabvedioum ñiariyoon😮
@@yacinegueyetahir9487 haaa biii mooome woooroumaaa kou dé ak sa bamel Mais premier fw bii mome avouer naa
Tiaga la dou serigne kene dou dioum di katte diabarou diambour
Au lieu de vouloir faire des marchés contre omar diagne il faut régler ce problème qui est grave
Adamo yaw adouna dinala yare yak kalifono ay doméram guéne rék
Kalifone et adamo bil lahi sen deh di na meti looooool sax ,yen toraxal ay diambour rek ,bess di na niaw guen beugueu retiou mou wess .
Yéne ay doméram guéne rék
أعوذبالله من الشيطآن الرجيم
ADAMO LOY DAW DI NEUBEUTOU DI RÈTANE NOONNNN SA KANAM GUI NGAY NIROK SANÈKH NONOU 😂😂😂😂🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Segn bi kéne meunouko layale
Li dé montage lako tek
Nooooo man ma djomy thi talibè yii….
Bilahi damaléna yereume louguéne guena yakh talibéyi si guena toi di guaana beury guire yalla nopalouléne li mayouk yallala
N'importe quoi
Ah kén fékoul blanc comme neige naaan tâche baagui niii té guissou ko 😮lou waay wakh rk amna lousi lakhasou 😮🤫🤫
ligueyou serigne touba keen meunouko yakk
Modou lo ngabou moy domeram, data diabar talibé yi rek ley weur 😂
Bayiléne yaxanté bi di diéma consantéré wou si séne déganté ak séne brom dééé amna Dé ta bamél xat n'a iow rek yafay nek ak say dieuf audio yi 2022 la
3 personnes yi teki yi woun g sarap ndayame
Adamo khalatal euleuk
MN pays VA mal
Kali a raison
Ahahah serigne bi vulgaire gua 😂
Doynawar
Li yagga na de
😂😂😂😂 nguabou yaye domeram
serigne bi thiaga pir leu, li rek warna tah talibé yi téyé seni adiya ak seni diabar ci domiharam yi.
Sen serign bi mo wara bayi audio thiakhane yim nek Di envoyer jigen Gni .wakhlenco deug
No Sénégal non seulement Serignesi ay Say Say lagniou wzye nitgni gniolenthi diappale thiey li😢😢😢😢😢
Adamo kaliphone amete cice bis dina gnew gnou tak leune dougal leune si bur bamel khalat leune bis bobou soutoura ken douko khawi
Ki dal da top bakaname rek
Serigne nitt rekkla lii fiirna la. Doylo lenn yalla Serigne bou adamayatou beurii si mom matoul Serigne
Ki dou sérigne diaroule soutoural nahe djiguene yi rek
Adamo qu'est ce tu gagne avec tout ce que tu fais. Il faut vraiment que tu change c'est pas normal tout ça
Adamo na rien fait serigne bi aye vocalam laniou tek si ko khamni néna si serigne touba laye topou naniou bayi serigne yi aye thiagua laniou point
Adamo yaw ak kali Kate l'en.sen data yaye
D’après ‘Abdallah Ibn ‘Omar (qu’Allah les agrée lui et son père) : Le Prophète (que la prière d’Allah et Son salut soient sur lui) est monté sur le minbar et a dit en levant la voix : « Ô vous qui êtes musulmans avec la langue mais dont la foi n’a pas pénétré les coeurs ! Ne causez pas du tort aux musulmans, ne leur faites pas des reproches pour des choses qui ont été commises il y a longtemps et ne cherchez pas à découvrir ce qu’ils pourraient cacher.
Car certes celui qui cherche à découvrir ce que son frère musulman pourrait cacher alors Allah va chercher ce que lui cache or si Allah cherche ce qu’une personne cache Il l’humilie jusqu’au sein de son foyer ».
(Rapporté par Tirmidhi dans ses Sounan n°2032 qui l’a authentifié et il a également été authentifié par Cheikh Albani dans Sahih Tirmidhi, Hadith Hasan)
Bayi lèn yoyou tè wakh thi wakh dji. Serign bi loumouy wakh thiopèrèt? Man lolou la begeu kham
Bay sekh wanalen deug
Awe bilahi danga alakou yawe kaliphone sall eske yawe dioulite nga aussi dioulite daye ame soutoura
Serigne lagne wara takal ay sokhna ichhh ki sonou na torop
ki bane serigne la ? non way ki domerame la way bayilén wakh seugn bi il a un nom c'est une bande de mafia qui vie sous le dos des fidels mourite parceque ici les mourites son facile a tromper quant tu utilise notre chère vénéré SERIGNE TOUBA
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂🎉café touba😂
😂😂bilaye baye chiékh Dieng Yamana Doul Daw aïda la wone
Ce faut
Sénégalais AKa manna yakh goor
Non Sénégal dou dèmmm, moi personnellement je ne crois pas. Ils veulent le détruire uniquement
Yen veree domerame nguén
K alifone les gens ne sont pas dupes. En 2022, il peut y avoir plusieurs cas.
Li rous louna talibé yii diééébèééétttt lénnn 😂😂😂😂😂 souneu sii kayy QU'ALLAH nous guide
😂😂😂😂😂😂 en tou cas senn serigne yiii si ay thiakhann rekk lanou nekk... lii dou yefou kilifa 😂😂😂 wadij amoul argument pour defandre sen serigne bii diagala 😂