Allahou akbar Sadbou tu ma fait pleuré 😭😭😭 Karbala beuss meti beuss bou niaw yalla naniou yalla fayal ndiabotou Seydina Mohamed (psl) merci Sadbou pour cette vidéo
Nioune wa keur Cheikhna Cheikh Saadbou niogui am fierté si yaw Masch Allah li dafaye daaw sama yaram kéne dou Seydina Mohamed (psl) na niouko yalla fayal ak diabote tam yeup niou sax di begue naby ak dibotam J'ai tellement pleuré 🥰❤😭😭😭😭
Depuis que j'ai est couté le karbala 😭😭 sadbou comme j'ai quelques chose dans mon name 🤲🏼🤲🏼🤲🏼 dieu et grand mai c'est très mal dans la famille musulmane 🤲🏼🤲🏼🤲🏼🤲🏼😭😭
C'est la première que je pret un oreille a cheikh sadbou samb bokk ak sama dome tour mashallah weuy wi sed na xole j'ai des frissons yallah nala yallah faye béguetémi
Machallah j'ai le coeur gros à chaque fois que j'écoute la bataille de kerbala et que si je bois de l'eau toutes mes pensées sont aux assoiffées de kerbala ....
Super top. Une belle voix Qu'Allah soubkhana watalla protége tes oeuvres. Une belle remontée d'histoire qui nous a tous fait pleurer. SADBOU félicitations pour cette belle prestation. J'aime et j'adore les khadres.
Merci de nous avoir gratifié de ce beau , merveilleux voire magnifique joyau. Seulement, il fallait remercier les auditeurs qui ont pris le temps de tout écouter... Seulement, nous ne pourrions manquer de t'excuser si tu le demandes car l'erreur est humaine...
Machallae je ne cesse d'écouter ce triste clip de sadbou Karbala sur le chemin tragédique des guerriers du prophete Mouhamed (Saw) il mérite des vues et des coeurs
Que dieu te garde fils j'ai connu ton père cheikh mbaye Ndiaye samb ça fait plus de 50ans.que dieu lui prête encore longtemps une bonne santé En effet dans les années 60 mbaye Ndiaye samb quittait mbour pour diriger à kaolack ndorong des chants religieux annuels sous l'autorité des feus el hadj lamine thiam demba président et alioune diop président d honneur.A chaque fois que je vous ecoute Saadbou j'ai la chair de poule sur l histoire de kerbala.Moi je m appelle Aly diop.Merci fils
J'écoutais cette chanson comme ça brièvement mais un jour je l'ai écoutée sur RUclips ce jour là j'ai pleuré et décidé de ne plus la fêter comme d'habitude merci beaucoup de nous rappeler cette histoire ❤❤😢😢
Machallah Sadbou Samb li nékh na trop légui nii rék laako diougué sétaane ci TFM Yalla na Yalla wéral baat bi té may la gouddou fane ak wér ci Barké Bissoup Tamkharite!
Amine were AK werler sadbou samb dakhe khool khool kasele Mane karbala bou khebou bi di wakh têye wakha dhe bou tahie sougne ma ibemaye laminame bek na yalla na yalla bek yageuna mak yaw thia guewoul bakha ya salam
Merci sadbou yalla nalla yalla fayal bopam vraiment sonou xol toy NK en vs écoutant li de dafa toy xoll nk j'ai larme au yeux kan j'écoute cette histoire karballa merci mil foi merci merci
Macha Allah sadbou sambe yalla na yalla goudal sa fane thii barké mouhamed ❤️❤️❤️🙏🙏 ousaysou ak karbala souma koy deg lou rek bilahi sama xoll ❤️ toy samay ra ngogne torou 😭😭😭😭😭😭barké naby Moustapha ma beug rassoulilah ak wa keureum ❤️🙏🙏🙏
Qui est encore la 2024 pour écouter cette belle voix ❤️❤️et cette histoire vecu par la famille du prophète Mouhammad psl😭😭😭
😢😢😢
Moi
Moi 🙏
Moi
Moi 😢
Allahou akbar Sadbou tu ma fait pleuré 😭😭😭 Karbala beuss meti beuss bou niaw yalla naniou yalla fayal ndiabotou Seydina Mohamed (psl) merci Sadbou pour cette vidéo
Nioune wa keur Cheikhna Cheikh Saadbou niogui am fierté si yaw
Masch Allah li dafaye daaw sama yaram kéne dou Seydina Mohamed (psl) na niouko yalla fayal ak diabote tam yeup niou sax di begue naby ak dibotam
J'ai tellement pleuré 🥰❤😭😭😭😭
J'ai tjrs des larmes quand j'écoute cette histoire jaime le prophète (psl) à vie
Karbala a chaque fois souma koy sétane damay dioy sadbou samb yalla naniou la yalla fayal ci Barker seydina mouhamed psl amine yaraby
Psl❤🙏
CV bien
Mon fils j'ai pleuré depuis ce matin en t écoutant. Notre souffrance n'est rien par à port à notre prophète et s'est personne que la famille.
Qui est là dans ce mois bénit de ramadan Qu'Allah accepté notre Jeûne, nos prières et nous disparaître cette pandémie.
Allâhu amiine yä rabbi ❤👊🏿🙏
Amine Inchallah Bijahi Seydina Mouhamed Saws❤❤🙏Inchallah❤🙏
Machalla
@@mouhamedseydi4183 in u.c
qui est là encore en 2024 pour écouter cette belle voix de l'Islam mashallah❤❤❤❤❤❤❤❤
Moi
Moi
Moi 😢
Ki est là dans le mois béni de Ramadan 2021 di fatélikou karbala 😭😭❤️❤️
Moi
@@amadouwane8130 😭😭😭😭😭🤮👆
2022 ouest foire
@@juniorthiello2928 moi
@@amadouwane8130😢
Depuis que j'ai est couté le karbala 😭😭 sadbou comme j'ai quelques chose dans mon name 🤲🏼🤲🏼🤲🏼 dieu et grand mai c'est très mal dans la famille musulmane 🤲🏼🤲🏼🤲🏼🤲🏼😭😭
J'ai pleurer en écoutant cette histoire à KARBALA 💓 J'ai le coeur lourd 🙏🏾
😭
شكرالك ۔ جزاك الله خيرا جزيلا
Ndaysane ni yeferyi def uoseynou metina ndeysane touti ma dioy li lou meti yagnafi jerejef sadibou yalla na bour yalla weral baatbi
Sallaw Yazid Ibn Muawiyah dioulit leu seutou Abou Sofiyane leu waye meussouma guiss histoire Bou metiwe Bou gnawe netali Bou triste comme Karbala khaliss pouvoir mbolo Bou Bonn Yalnagn thi sunu borom mousseul rek allahoumma amine amine
Sadibou Samb, que Dieu vous récompense. Je ne cesse de regarder cette vidéo.
Mmmp0😊0😅 27:23
Oo
Oo
😊
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machalah longue vie a toi sadbou samb
Macha-allakhou yalla naniou yalla djeguel dewenati thi barkey achoura thi lerou arcur-an thi barkey seydina Mohamed aki sakha-batoul kiram yi yeup khi barkey sama tourando biniou niackeu thia karbala bâ---- ababacar Sadikh
C'est la première que je pret un oreille a cheikh sadbou samb bokk ak sama dome tour mashallah weuy wi sed na xole j'ai des frissons yallah nala yallah faye béguetémi
Ndeysan tellement je l'écoute tt le temps j'ai même mémorisé beaucoup de paroles machallah ça me touche au coeur 😭😘😘🙏🙏🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲
Lpĺl
Machallah j'ai le coeur gros à chaque fois que j'écoute la bataille de kerbala et que si je bois de l'eau toutes mes pensées sont aux assoiffées de kerbala ....
Machallah dawna yaram kalbala sak jour madék louko douma si doyal hol toyna ragoy tourouna
Merci je m'appelle ousseynou karbala je suis ému
Sophie
😥😥
bilahi cheikh sadbou tu es le khalif général des nabiens yala na yala weral sa bate amine
Mashallah may God the almighty be please with them is really touching
Tu m'as fait pleurer que Dieu te protège et te guide par l'amour du Prophète
Nékhgama
Beuss Détou Méti Détou Niaw Ba Mélni Karbala Yalla Nanou Yalla Déf Deugue Deugue Dioulite Dieuredieuf Sadbou Yalla Na Yalla Maye la Goudo Fane Ak Wére
Amine
J'aime bien cette chanson l'histoire est bien racontée que Dieu protége sadbou
Amine way
😭😭😭😭😭
😭😭😭😭😭
Maschallah Sabdou Samb Yalna Yalla Gheuneu Dolil Wéreull Batt Bi Inchallahou Rabbi Si Barki Seydina Mouhamed Saws❤❤🙏Suniou Wadji❤❤🙏Inchallah❤🕋🕌🙏🙏❤
Machalla yalla nala yalla suniou borome same si barké Sedy Mohamed Salakhou alelkhi wasalame😭😭😭😭😭😭
Kene dou seydina mouhamed (psl)
Amine
Xareb karbala rk la khamni mboulèm xare yi bon doon dellsi wat karbala lay dem ndakh gnièwantal Sayidna Assane❤️🔥🙏
Yaw gor ga motakh yalla nala yalla Faye la sa yéné
Super top.
Une belle voix Qu'Allah soubkhana watalla protége tes oeuvres.
Une belle remontée d'histoire qui nous a tous fait pleurer.
SADBOU félicitations pour cette belle prestation. J'aime et j'adore les khadres.
Il a tellement maitrisé l’histoire manchAllah ❤️
Qui t’as qu’il a maîtriser l’histoire tu connais l’histoire toi?
Alhamdoulilah Alhamdoulilah machallah Sadbou samb contan na thie yaw sama yarame dawna
Barki serigne Saliou li metina 😭🥺
Yalla nala yalla fay yiw barki mane CHEIKHNA CHEIKH SAAD'BOU ABIHI wakheuyert
😭😭
Amine
Machalla kan je vous écoute j m sens bien alkhamndoulilah yalna yalla motali leep inchallah
@@tomadieng649 amine ya rabbi
Sadbou Samb yalla nafi té wér
Sama khol toyena gnoune rek gno wara santé yala boke si khétou Mouhamadou rassoulila ta li méty féqougnoufi ❤️❤️❤️❤️❤️chapeau a sadebou samb
Bilay waxga degu psl🙏❤
.
Walahi wakh gua bégue
Machala Machala j ai des frissons cheikhe sadbou yalla na yalla goudal seye fanne Barkele werale bate bii si Barker seydina Mohamed s a w
Machallah j'ai même pas les mots, rien que envie de pleurè
C extra ordinaire
Ramadan 2021 Sadbou yallah nagnu ko borom bii fayal si barké Seydina Mohamed Psl 🙏🏽😍
2021🙏❤
Moi
@@amadouwane8130 jmm
Merci de nous avoir gratifié de ce beau , merveilleux voire magnifique joyau. Seulement, il fallait remercier les auditeurs qui ont pris le temps de tout écouter... Seulement, nous ne pourrions manquer de t'excuser si tu le demandes car l'erreur est humaine...
😊😊
0
000😊00😊
M0
0😊
0😊😊
😊0
M😊
0😊
0😊
0
😊
😊
M0
😊
0😊
0😊
0
0😊
000
0😊000
0😊
0😊00😊
0m0
000😊0?000😊
😊
0
0😊
0😊
000😊
0
00😊
0m00😊⁰😊
000😊0😊
0
😊0
😊0
0😊0😊0😊0
😊M00
0
😊
0
😊
000
0
M00
M0
M00
M000m0
Pm00
00000pm0
M0
M0
M😊
😊?0😊😊
P
Pmpp
P
2024 sadbou ya ngi fexal Sama xol bi barki Sergine Touba diam ioe yalla def niou ấy dioulitt barke serigne Touba
Ya ousseynou ibn ali dief dou meti ba melni karbala on t'aime yarasoulila merci bc sadbou sambe
Machallae je ne cesse d'écouter ce triste clip de sadbou Karbala sur le chemin tragédique des guerriers du prophete Mouhamed (Saw) il mérite des vues et des coeurs
Sameu tourando cheikhna cheikh sadbou yalna yalla yokou kham kham bii
Ndaye saann yalla rèkk mooy bour ,hakkimla moom yalla !! Alhamndou lillah!
Yalna diollit yèpp am diamm amine
Kou beug Mouhamed sakh done diambar wakhou malak seuteum...Yalla na yalla doli yiw souniou sangue...si ce n'etait pas Ya Rassoul founiou dieum
Machallah histoire amna solo thiey gars you bakh yi 😭❤️
dieureudieuf cheikh sadbou kéne dou seydina mouhaméd zallahou halayhi wa zalame❤❤😢😅😊😢
Li dama ko beugu ba metrisé par cœur billahi Sadbou beugu nala nax wakeur yonente ak sa tour bou sel bi gay sama tourodo papa wallahi jtm fort
Qui est la en 2024
Moi
Moi
Ooh Histoire Karbala djoylonama mé Sadbou djoylogama damala beugue chaque année rk Maguilay Xare Seo
lou niaw yagana si Aduna mes yalla naniou yalla dolli soutoura
Machalah
C vraiment trop triste et dur à écouter machallah sadbou
Billahi
Amine
Amine amine
Que dieu te garde fils j'ai connu ton père cheikh mbaye Ndiaye samb ça fait plus de 50ans.que dieu lui prête encore longtemps une bonne santé En effet dans les années 60 mbaye Ndiaye samb quittait mbour pour diriger à kaolack ndorong des chants religieux annuels sous l'autorité des feus el hadj lamine thiam demba président et alioune diop président d honneur.A chaque fois que je vous ecoute Saadbou j'ai la chair de poule sur l histoire de kerbala.Moi je m appelle Aly diop.Merci fils
Beug yonente Mouhamed saw à vie ak euleuk fagnou dieum 🥰🥰😢😢😢 j’aime tellement notre cher prophète ❤️
Sallallahou Aleyhi Wa Salam😍 Sa Bayou Tourando❤️ Kénn Dou Mom Bilahi❤️❤️😍❤️❤️
Machalla
Yalla gha guissék seydina Mouhamed beussou yawmal khiyame
Sadibou
Sala lahou aléyhi wa salam🙏🏽❤❤
J'écoutais cette chanson comme ça brièvement mais un jour je l'ai écoutée sur RUclips ce jour là j'ai pleuré et décidé de ne plus la fêter comme d'habitude merci beaucoup de nous rappeler cette histoire ❤❤😢😢
Machalla 😭😭😭 yalla nagnou yalla fayal sahabayi si barké seyedina Mouhamed psl ❤️ yalla na yalla wéral balbi
Walahi sama yaram Moy daw thie souba ba legui walahi machalla
Cheikh sadbou samb yalla nala yalla aar si barké seydina Mouhamed psl nexna tei triste manchaallah
Dieureudieufeuty sama khol toyatena yalna yallah feyalniou seydina Mohamed ak wa keureum
Histoire bi nakharinama lole soumako yalla idilatone dina fayoule wakare mouhamade soumakaye dégoulou dafaye méleni damako fékké dakh nakhare noni yalla bouma tasé ak niome yomale khiyame 😭😭😭😭😭😭
Yomale khiyame di nga contane inchallah
@@sidategaye5061 Macha Allah sougnou khol yi toye na yalla nala yalla defal diame yague fy te were
Billay domou ouseynou bi lirr bi moma dioy lo metina trop
Diereudieuf yalla na yalla fayalla bopam magui koy dora déklou karréma wayé manite dioyna karbala
machalaa yall na diam yague .sounou xol dafa toye sope nala sadbou samb
Yalla nanou yalla maye khoiou mougne ❤❤❤❤❤ saberou❤❤
Mashallah samb yallah na sounou borom goudal fane ❤️❤️❤️🙏🙏🙏
Alhamdou Lillahi Rabil alamine. Dieuredieuf Sadibou Yallah na Yallah wéreul sa baate bou nékh bi Machallah amin
Kou beg si bissou tamxarit walahi xamo lixewoone Allahou Akbar xol fesnaيبكي في قلبي كل ساعه
Mashalla Sadbou li toye na khole ❤ mashalla. Kagn ngay deffat lou melni si bénéne histoire Badar pr exemple! Chapeau ❤❤❤
On t'aime Ya Rasul'Allah 😭❤❤
Sunu yakar tay ak euleuk ❤
ta voix est exceptionnelle sabdou que Dieu le tout puissant exauce tout ce que tu veux d ici et dans l eau delà mashallah
Ta. Voix. Est. Exceptionnelle tons. que Dieu. Le tout puissant. Exauce. Tout ce que tu veux d. Ici et Dan's l'eau délàa Machahala bonne continuation
Amine
@@lingueregueye1197 1
Amine Inchallah
@@lingueregueye1197 un
Machallah 💕keneu dou khetou sangu bou tedd bi ya Rassoulilahi
Machallah Sadbou Samb li nékh na trop légui nii rék laako diougué sétaane ci TFM Yalla na Yalla wéral baat bi té may la gouddou fane ak wér ci Barké Bissoup Tamkharite!
😭😭😭😭😭😭🇸🇳🇸🇳🇸🇳😭😭😭
Machallah. 😭😭😭😭😭
Alhamdoulila
quel émotion j ai frisson du depuis a la fin bonne continuation merci pur c est belle parole
sadbou samba yallana yalla défal tawfekh dioubari mayla weer looool ak kheweul you Bari kouko deglou dioye so am thiofel si seydina mouhamet ❤❤❤❤😭😭
ما شاءالله ma challah sama sopu by sadibou yalna yalla weral batby maye leu were
Machalla amnasollo malla begue cheikh yalla na bat bi weur
Notre idole Mouhamed psl moi ablaye ngom j'aime Mouhamed ❤️💫🙏
Ndeyesane billahi li dawna yaram 😭 machallah li amna solo
Alhamdoulilah sante yalla yalna yalla wéral bat bi macha alla ame nanou lou léral Yalna nou gusé ak seydina Mohamed psl ak wa kereum
Amine were AK werler sadbou samb dakhe khool khool kasele Mane karbala bou khebou bi di wakh têye wakha dhe bou tahie sougne ma ibemaye laminame bek na yalla na yalla bek yageuna mak yaw thia guewoul bakha ya salam
j'aime beaucoup ce que je suis intéressé par les musique sénégalaise traditionnel
Merci sadbou yalla nalla yalla fayal bopam vraiment sonou xol toy NK en vs écoutant li de dafa toy xoll nk j'ai larme au yeux kan j'écoute cette histoire karballa merci mil foi merci merci
CV bien
Macha Allah sadbou sambe yalla na yalla goudal sa fane thii barké mouhamed ❤️❤️❤️🙏🙏 ousaysou ak karbala souma koy deg lou rek bilahi sama xoll ❤️ toy samay ra ngogne torou 😭😭😭😭😭😭barké naby Moustapha ma beug rassoulilah ak wa keureum ❤️🙏🙏🙏
Yallah nanoula Yallah fayal té gueuneu wéreul sa baate bou Nekh bi Machallah
g n'arrive pas a arrêté mes larmes...merci sadbou samb de nous faire connaître la vrai histoire de karbala...
Hooo c la première fois k j'écoute mais c triste 😥😥😥.saadbou yalanala yalla fay
Nice lawle thiat mon frère
Machalla karbala bi si kholl lay dougou
Machalla sadbou yalla n'alla yalla defal diam ta weral battbii ci barcé seydina mouhamed salallahou halaïhii wasalam
Vraiment ça me fait pleurer eu cœur que dieuh te bénisse 😢💖💖
Machallah sadbou que le prophète psl content de toi🤲🤲
qui est encore en 2024 pour écouter cette belle voix de l'Isam❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Qui est la, en ce jour D'ACHOURAH.
YALNA YALLA BOLENIOU SI NGIY FEKKE DEWEEN BIJAHI MAMI SEYDINA OUSSEYNOU.
Amen toma
Amine y'a rabii
Nakhar yague na thi lislam ndéysane yalnagnou yallah déf ayy dioulite deugue Jaime SEYDINA MOUHAMED SALLA ALLAH ALEYHI WA SALAM Dieureudieuf SADBOU SAMB khol sédd na toy wayé khol sédna
Machaala yalna yalla wéral bât bi c vrema triste dieuf dôtoul niaw ba mélni karbalaa 😭😭😭😭
Niepala beug ngir seydina mouhamed psl❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
Mashallah yalla nala yalla défal diame té mousala amine
Amine
Sama khol toyna metite yaguena thi lislam yalla nayalla fayal nou seydina mouhamed slaw ak koullou ahloul baïti dieureudieuf sadbou samb
il est le seul qui peut le chanter et le meilleur aussi
M
Qq
😭😭
@@dieynabasow2959 pplp0ppp00pppplpp000pp""0llp0lppp"0pp00pppplllllllllllllpll"l0lllĺ
Machalla sadbou samb yalla nala yalla fay si barké seydina mouhamed
Amna solo dieureudieuf sadibou histoires bou triste j'ai pleurait
Allahou Akbar
Manchaaala li d'où meusa khewiiii 😢😭😭😭😭😱😱🥹🥹
😢😢😭😭 ta voix exceptionnelle que Dieu te protège
Amine
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Yalla guemoule nelawoule gni defni wa keur seydina Mouhamet psl yereume nalen euleuk yawmal khiyame
assalamou alleykoum kepp kou way wi toyy sa kholl yalla nala faye adiana si barké sama tourondo seydina mouhamad s.a.w
Métina lol way
@@djibrilmbengue2727 deugue leu
Nice
😂
Amine ya rabbi
Ndeysaan Daw na Yaram 😭😭😭😭😭😭Yalla nanu Yalla fayal Seydina Mohammed Salalahou Aleyhi wa Salam ak Sahaba ya ak wa keureum😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
longue vie à toi yalla na yalla motelii
اللهم صل على سيدنا ومولانا ونبينا ورسولنا وحبيبنا وحبيبك محمد المصطفى وعلى جميع الأنبياء والمرسلين والصالحين وعلى آلهم وصحبهم وسلم آمين يارب العالمين
Ma sha Allah sadbou samb yalna yalla goudal sa fan ji barkè naby p.s.l.❤❤
hanne bété bété cheikh Hane no deff
toukou Baa ba
kén dû wÄ keÜr YONÉNE tibii 🕋🤍🤎❤️... Ohh Sama xOl Sëd vraiment NDÉYSAN SADBOU yalla ga Goudou fAn THÎ barké YONÉNE tibii 🕋🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲🤲💦
Metina billhi 😭😭😭😭😭j’aime le prophète seydina psl saws