Alhamdoulilah... Alanda ZARCO, domou Grand yoff bi ,doff bi . Wakhongako deh ada kholou. Félicitations à toi grand et du courage à Ada fass tay danga lamb mais dadjo... ZARCO nak bou thiakhanoul keneu meunouko ci lamb je et ça ceux qui connaissent ZARCO peut me témoigner.
Bravo sarko bravo Ada face yako wakhone ki sa make la te mola djitou si lamb mais champion nga défarou guena takhaw yalla nala yalla aguali finga begue yégue zarko ndam li yalla nala djikk
Félicitations zarko courage ada fass, c est la loi du sport t es un grand champion, mais Lima diakhale loutakh gua diapou bou bakh liguéyo thi fofou thiakhabale , mbott , wérrou lepp khadianenafa mais bissou danou thiouné ngaye nekk courage champion 🙏💪
Félicitations Zarko Et mes encouragements pour Ada fass jeune gua t amgua public ci défaite bi boci tiré ay leçon ci sa dokhaline ak niguay wadialé say combat gua changer ko rk tu sera un grand champion xolal boy niang bimouy préparer son combat contre Balla niata mois la tok guissoul sakh wa famille bi iow nak dagua feussone trop mbeur dafa am foumouy tolou daguay wagni lou beuri t aussi gua defate sa entourage pour être un champion mome dafa ladj gua def ay sacrifice mbeur gua t dagua téla am tour d’où n’importe qui mola wara diégué
Zarco mi est devenu mature, il précipite plus ces combats et je vois que maintenant il es serein, et trop technique sur ces combats, zarco fera du dégât dans cette arène, Zarco vers Gouyki
Je me suis dit la même en regardant son open presse Il doit avoir un ancien dans son Staff Aussi les jeunes lutteurs avec beaucoup de supporters ils doivent savoir que lamb dou supporter rek
kouy dougou si keur si bounto ngay aw ada fass da bari wakh monewon yalmine bi lay dieul danougua lonrant lagne lay diokh😛😛 ,félicitations zarco dangua nekat si yon
Boy bi dafa tela def bopam roi des arènes confiance da eupe mm si lewto bi,tè Zarko da boko kholè khamenè naturelement dafa diape tèkci entrainè tè amena dolè tè zarko da yèwo legui comprendre lamb dji
On dirait k les arbitres bénéficient des avertissements. On doit avoir un règlement concernant les avertissements. On doit avoir 10mn de lamb puis mi-temps et puis 5mn avant de commencer les avertissements. Les spectateurs ne sont pas venus pour regarder klk1 tomber et rentrer. On est là aussi pour savourer, vivre la pression et enjoy les moments forts. CNG réveillez vous et travailler pour une bonne conduite de notre chère culture
L'indiscipline d'où athlètes mbeur sou amé combat day discret respecté avdeversaire bi Ada fasse vraiment amo entourage bou bakkh so beugé done champion kholatal sa dokholine
@@kefgg no ki dou mbeur robot la srapp ndm😂😂sawayy ki bari n'a dolé t li geuneu graww dafa yewou legui t dou thiouné si lamb Zarco kay dann ko dou yomb
@@kefgg way Frère man wa Guediawaye la mai Gouy gui amoul dolé bou meun danel zarco ni beuré bi En plus legui zarco.doff bou yewou la😂😂😂weroul robot amoul kouko si meuneu yeungeul
Ada fass mbeur day kham ni mbeur leu dail lakatou bo amai combat di neub sa bop champion nga li dou dara moy takh nga nek mbeur felicitation Zarco
Bien dit frère
Walahi ❤❤
Frr ki naniou ko diokh ay mboram tei mou moytou rirou lamb ak supporter
Bilahi ki dafa amul conseiller yu bakh
Bilay ada fass sodon tay dinama bétt trop dieul ambiance Dieu beuré day yombo trop
Ada fass défaite bi mola meuneuh df mbeur donc boul khaddi c le moment de bien travaillé davantage yaye yakarou ndakaru donc du courage 👏👏💪
Alhamdoulilah... Alanda ZARCO, domou Grand yoff bi ,doff bi . Wakhongako deh ada kholou.
Félicitations à toi grand et du courage à Ada fass tay danga lamb mais dadjo...
ZARCO nak bou thiakhanoul keneu meunouko ci lamb je et ça ceux qui connaissent ZARCO peut me témoigner.
Félicitation à zarko c'est un vrais athlète et un très grand champion bilahi et du courage à ada fass
4
Bravo sarko bravo Ada face yako wakhone ki sa make la te mola djitou si lamb mais champion nga défarou guena takhaw yalla nala yalla aguali finga begue yégue zarko ndam li yalla nala djikk
Félicitations zarko comédien lagnou la diapè ak Dof Inchallah gnom gnep nguay diekhal
Lac de guere ak sarco kou dacor ak mane beseul j’aime
Kone zarko dinako ray kaname gui mo rafet motakh lac rek 😂😊
Zarco mome paréna pour diékhal boy yi il est mature avec de force machallah
Adversaire deñ koy jokh thieur. So danee ndam li meuna reuy.
Félicitations Zarko.
Zarko il est sans pression il a très bien étudié Ada fass
Zarco grand yoff diokhe nala boppou bo néké nitt kèn menounala si lambj du courage Ada fass 👏
ADA FASS TEY NGAY NEK CHAMPION ✊🏿💎👌🏿👑
Incha Allah.
Félicitation zarko❤️🔥💪🏾✅ do khôl 👀
Félicitations zarko courage ada fass, c est la loi du sport t es un grand champion, mais Lima diakhale loutakh gua diapou bou bakh liguéyo thi fofou thiakhabale , mbott , wérrou lepp khadianenafa mais bissou danou thiouné ngaye nekk courage champion 🙏💪
Zarko mbeur bou am expérience leu ses adversaires lui doivent le respect.
Ada fass mbeur deug leu ame fitt du courage le meilleur reste à venir
Le réveil de zarko est spectaculaire
Jeune bou nekk thi yone wakh bou beurri djigouko bilahi félicitations zarco et mes encouragements à ada fass défarouwate rek
Félicitations Zarko Et mes encouragements pour Ada fass jeune gua t amgua public ci défaite bi boci tiré ay leçon ci sa dokhaline ak niguay wadialé say combat gua changer ko rk tu sera un grand champion xolal boy niang bimouy préparer son combat contre Balla niata mois la tok guissoul sakh wa famille bi iow nak dagua feussone trop mbeur dafa am foumouy tolou daguay wagni lou beuri t aussi gua defate sa entourage pour être un champion mome dafa ladj gua def ay sacrifice mbeur gua t dagua téla am tour d’où n’importe qui mola wara diégué
Beuri wakh eupeul boy bii
Merci zarko
Trop sakh bilahi dafa ndey eupeul trop motakh ma djepiko
Liguene wakh mo eupe foufe boy bi limouy wakh nopi lene ndem way
ada fass bilay champion nga mais guenal defalou nakh iow kham nga sa bop felicitation le grand zarco notre fiertè cest grand yoff 🤜
Dole dokhol Diam Thiey Zarco tu es devenu mature maintenant.
Waye la 2stv waye vraiment nanome nagne sen direct "la lutte autrement" kèn dou yène si direct 🔥🔥🔥❤❤❤❤
zarko wakhon naléne ko mo meune fouf Ada fass bilahi do combte sakh 💪💪💪💪💪
Zarko Bilay galem la dioge ni waye diambar ga
Zarco mi est devenu mature, il précipite plus ces combats et je vois que maintenant il es serein, et trop technique sur ces combats, zarco fera du dégât dans cette arène, Zarco vers Gouyki
Bravo zarco grand yoff contan na niou si ioe ❤❤✌️✌️🥰💯💯💯💯
Combat bou nekh vrément mais je pense que ada fass dafa respecté troo zarko mo takh mou danou. C'est le Sénégal qui Gagne🇸🇳🇸🇳🇸🇳.
Bien pr lui zarko es fort Ada fasse da eupeul te defago dara
Félicitations à Zarco et du courage à Ada Fass .C'est comme ça l sport il faut reculer pour mieux sauter Ada.
VIVEMENT NAGNOU DIEUL CHAISES YI THI ARÈNE BI DEFALEN AY DEURR COMME LOLOU LAGNOU MÉRITÉ comme ça kougnou dann sa mbeur do am loy dadji
Zarco, un grand champion, félicitation vraiment
Félicitations zarco mobile wakhone nako boy bi khamoul zarco mais courage cas même
Ada fass amoul staff bou bakh.
Té bou féké ni lay continué dou ame carrière bou bakh.
Félicitations zarco et du courage Ada defarouwate rék
Je me suis dit la même en regardant son open presse
Il doit avoir un ancien dans son Staff
Aussi les jeunes lutteurs avec beaucoup de supporters ils doivent savoir que lamb dou supporter rek
Les gens oublient que zarko mbeur bou meuna beurré la ta am dolé niak hygiène de vie rek ak eupeul moko diappoone mais legui on voit que yewouna
Félicitations zarco Ada fass était trop impoli sur ce combats
Ada zarko dafko nakh si action Yam lako dané vraiment l'expérience fait la différence
Félicitation zarco domou grand yoff bi🥰💯✌️
ADA Fass dafa wané xamoul gatt 😂😂 affaire spectacle moko néx sa way do star do roi toukeul feulé 😂
Zarco respectel niit gni toi aussi ms félicitation mbeur
Ada 😂dafa yenou combabi di dioy rek tamit 😂bon courage zarko dafa niow teur nieup😊
Bilay khamo zarco motakh nga dougou si mome😂bandii guéww leu
Non zarko sedalna sama khol Machallah🙏🏽🙏🏽🙏🏽 ada beurina wakh t todioul feneu lolou moma diakhal
Dafa téla yeuk succé
Zarco Moy ndanane
ZarkO Baye fall la dal
Zarco nk il était trop confiant dollé dokhoul diam du courage Ada
Ada fass koukoy nguimbe 😳😂😂😂😂😂
Athieu Ada 😍 courage iow khalega 👐🥰♥️♥️♥️
Ada fass respect woul zarko moko yobé li dafa yakar zarko amoul dolé nakh gua sa bop nak 👉😡😡 adversaire boko diokhoul thieur ni rék lay démè félicitations bro
Jélou magg la Thieuyy Bécaye l'innovateur
Grand yoff vamossssss zarko ada du courage changel sa ngimb bi
Betouma bilahi
Ada li bakh na si mom défaite bi champion Yep diar nansi fi guay diarè nek champion
Pour man Ada dfa téla guem galadj bamou eupp kholal ma ngébam bi
Manchala Zarko prépare activement Diéne kairé
🤣🤣🤣 Zarko da diap boy bi ba xamni moko meun mouy fooooo 🤣🤣🤣.
Doolé dokhoul jaam.
Zargo dafa moun ada fass mes ada defet bi bakh la si mo
Ndakh dina defar lou bari sou beugeu nek champion curage
Félicitations pour zarko courage ada fass
kouy dougou si keur si bounto ngay aw ada fass da bari wakh monewon yalmine bi lay dieul danougua lonrant lagne lay diokh😛😛 ,félicitations zarco dangua nekat si yon
Zarko daffa am confiance trop sakh
Ada fass khalé ngua té pa bou tol ni zarko mom mounoula yakhal
Kone nioune supporter on est fier de toi Ada
Boy bi dafa tela def bopam roi des arènes confiance da eupe mm si lewto bi,tè Zarko da boko kholè khamenè naturelement dafa diape tèkci entrainè tè amena dolè tè zarko da yèwo legui comprendre lamb dji
Ada danga tèla yeug sa boppou wagnil waxdji ta ligèyi fara Lou ma la won nk félicitations zar dof biii
Merci zarko tua bien fait il et très un polies 😂😂
Khana école gueweul gua diangué
@@sambakane6876 😩😅😅
Nn ça papa moma dianguel
Ada fass dh nguêmbam bi sah meun nako danel...li melni halé bouy doga fêr ba yewou souba tel rek ak couche bi nak🤗🤣
Bilaahi ni la ko waxee woon sama copin Musaa Mbay newoon na ko Zarko dina daan Ada Faas zarko dàq mbër fopp.
Zarco daye nékhal lambeu bilahi nak
L'entourage d'Ada fass a fait un choix en lui disant de prendre Zarco physiquement et techniquement Zarco etait meilleur
D’à xamoul zarko rek dofff lay beurel sans pression 😅😂
Bilahi ni lako waxei, Zarko dara yeugalouko, da weroul sakh nak
Ada mbeur leuh biss mo gneuw rk c le Sénégal qui gagne
Zarco da wa ra th lamba jj inchallah
Bantaba TV is the deal 👌
Ada fass dafa khamoul ni zarko dafa meune beuré billahi
Félicitation zarko do kholl😰
On dirait k les arbitres bénéficient des avertissements. On doit avoir un règlement concernant les avertissements. On doit avoir 10mn de lamb puis mi-temps et puis 5mn avant de commencer les avertissements. Les spectateurs ne sont pas venus pour regarder klk1 tomber et rentrer. On est là aussi pour savourer, vivre la pression et enjoy les moments forts. CNG réveillez vous et travailler pour une bonne conduite de notre chère culture
Merci sisrer
L'indiscipline d'où athlètes mbeur sou amé combat day discret respecté avdeversaire bi Ada fasse vraiment amo entourage bou bakkh so beugé done champion kholatal sa dokholine
Zarko Moussa ndoye lambou bou nékh la wala zarko ama nékh 🥰
Ada fass dese na saf da khamoul zarko bere rek lay def
Je l'avait dit ada fass a fait un mauvais choix fallait pas prendre zarko
Et il a été très impoli
Il lui Laisee une chance ce Ada fass ce prennait pour un grands bah voilà le résultat Merci zarco jevais bien dormire moi mdrr
@@cheickamalasanogo7939 trop ont te Laisee une chance toi tu veux parlée mal
Zarko késsé n'dam rek domou grand yoff dou ragal
Zarko diene kayré comba la
Zarco comme frein a main😂😂😂😂
Xale.bou Rew mou noss la
Félicitations à zarko très grand combat
Billahi Ada vrai champion lah
Congratulations Zarko..
Zarco rek
Zarrako power 🔋 💪 ✨️ 🙌
Police bi ak wadji😀😀😀
Merci zarko comme que amoul respect surtout si siteu
On appelle cette prise en judo ""DE ASHI BARAI""
Ada mbeur bouné day combat boukoy def ndannane waye ioe combat bii mola wora def Ndanane '''Zarko dan nga wayé tego yone niga beré
très intelligent zarco
ZARKO VS GOUYI COMBAT LEU
Machallah zarko❤❤🇸🇳
Zarko Mii amena dolé deii
Félicitations zarko 💪
Zarco na dieul yekini jr wala gouye gui
Mok gouy gui revanche la
Non dou beuré ak yikini jr quant à guy gui oui
Gouy gui- zarco
Becaye mi zarco la faral wayy😂😂
Ki dem dem si kaww digua dieul mbeur yii t bayi robot bi 🤣🤣🖐Zarco dou nitt kii com robot Gouy gui bou yabo gua écarté Zarco sino dou bah si ieiee
Zarko doff leu bou ragaloul boy bi da amoul conseils rk
@@kefgg no ki dou mbeur robot la srapp ndm😂😂sawayy ki bari n'a dolé t li geuneu graww dafa yewou legui t dou thiouné si lamb Zarco kay dann ko dou yomb
@@Elhadji2187 En plus dama fite de trop sakh 😂
@@jeureujboromtouba6784 😂ki robot la croyez moi
@@kefgg way Frère man wa Guediawaye la mai Gouy gui amoul dolé bou meun danel zarco ni beuré bi
En plus legui zarco.doff bou yewou la😂😂😂weroul robot amoul kouko si meuneu yeungeul
Zarco moye bandit deugu 😂
Zarko dieuleul say morom way..ada fass ligue beure bakhoul eupo zarko dole waro wona nangu diapante bi,ragual gua warone wane pour nakh ko am ndam..