«Daniou ma diam 9fois, sama yay agressé nagne ko ndakh…» Mbeuss raconte son calvaire après la prison

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 6 фев 2025

Комментарии • 431

  • @People221sn
    @People221sn  10 месяцев назад +32

    N’oubliez pas de vous abonner à la chaine PEOPLE 221 TV et d’activer la cloche de notification pour ne pas rater les nouvelles vidéos 🔔 ...
    Pour vos conseils et critiques veuillez nous laisser un message sur ce commentaire Mercii...
    Témoin d’un événement contactez : +221 77 451 21 10 WHATSAP
    +221 78 149 53 10 APPEL NORMAL

  • @annakoller5905
    @annakoller5905 10 месяцев назад +44

    Sans remord 😮, franchement c'est malheureux la jeunesse de mon pays

  • @deugmoyndieukmoymoudie8279
    @deugmoyndieukmoymoudie8279 10 месяцев назад +65

    Mane dé doumala jugé 😢ndakh alahou akhelam khana nianal la rék yalna la yala takhawou ba dothi délou thi barké wérou kor gui

    • @papaxol2950
      @papaxol2950 10 месяцев назад +1

      Allahouma amine 🙏

    • @MedocNS
      @MedocNS 10 месяцев назад

      Sa genre yi nioy encourager agresseurs motax niou kaye ndamo

    • @deugmoyndieukmoymoudie8279
      @deugmoyndieukmoymoudie8279 10 месяцев назад +4

      @@MedocNS eupeu na wakh waay kou bakh encourager diameu moi même j’ai une fois été agressé nakalalène di encourager donc ki soko déguelo khameni niane la geuneu sokhela k nioukoy jugé parsk khol bi ak khélmi guéneugouthi à cent pour cent donc les jugements et les insultes douniouko yok dara thi sama khalate bou gate

    • @ninkinanka2670
      @ninkinanka2670 10 месяцев назад

      Frère tu as parfaitement raison kii so deguei nimouy wakhé nga kham bayi woul a 100% billahi

  • @neknekaatni9683
    @neknekaatni9683 10 месяцев назад +38

    Commentaire day possitive qui rethiou motakh mou def emissions bi c’est du passè gnanalen ko yalla finkal ko bep niawtef té tek ko si yonou siratal moustakhim amine

    • @Virusboubone
      @Virusboubone 10 месяцев назад +3

      😂😂 ki moussoul doundou loumouy wah ni gno bok kogne iish

    • @AissatouLo-lh9we
      @AissatouLo-lh9we 10 месяцев назад

      Kii Day doul rk mousso doundou blh😂

    • @bayefall580
      @bayefall580 9 месяцев назад

      Noooo bilahii d'où DEUG gno deuk mak mom

    • @joeba5199
      @joeba5199 19 дней назад

      Chacun est libre wakh khalatam .Nagne niou wone de bons exemples amna niouniou wara diokh micro nioudoul gni .

  • @papaxol2950
    @papaxol2950 10 месяцев назад +34

    Yalla Naniou yalla tek si yon bou barkéle 🙏🙏

  • @yakhyawagne9529
    @yakhyawagne9529 10 месяцев назад +73

    Mé ont dirais ils est fière de son parcours frère wakho fi dara

  • @cinéma_sn7790
    @cinéma_sn7790 5 месяцев назад +2

    MBEUSS KHANA BANDIT 2024 LA LI MOM YAGOUL 😂😂😂

  • @alysow9089
    @alysow9089 10 месяцев назад +24

    Mbeuss vrai dof kW ki weroul bilahi

    • @annaseck8764
      @annaseck8764 6 месяцев назад +1

      Menon na soutoural bopam

  • @AissatouLo-lh9we
    @AissatouLo-lh9we 10 месяцев назад +6

    Mbeuss bayil doule kéne khamoula bayil doul fii la béne boy diap mbaye nganiko andii ma téle ko bayil doule😂😂❤

    • @DioufCisse
      @DioufCisse 10 месяцев назад +2

      Aissatou loy wakh ni kone Mbeuss dou dra😂😂😂😂😂

  • @CheikhDione-kx7po
    @CheikhDione-kx7po 10 месяцев назад +7

    Bilahi frère doo Bandit Sénégal rk di graw grawlou nan Sénégal amoul liguéy😊

  • @Falloulam1234
    @Falloulam1234 10 месяцев назад +23

    Mbeuss nexx na 😂 😂

  • @mayorodiagne814
    @mayorodiagne814 10 месяцев назад +49

    😂😂😂pour mom champion la ni

    • @morndiaye2191
      @morndiaye2191 10 месяцев назад

      Oui oui loulou la diapou dé

    • @serignediop8861
      @serignediop8861 10 месяцев назад

      😂😂😂

    • @Princ406
      @Princ406 10 месяцев назад +1

      Dans sa tête😂😂😂

    • @babacarfaty5397
      @babacarfaty5397 7 месяцев назад

      😂😂😂😂😂

    • @HbvTxdhfu
      @HbvTxdhfu 5 месяцев назад

      Donc bandi c un champion 😢😢😢😢

  • @mohamedngaide5774
    @mohamedngaide5774 7 месяцев назад +7

    Dagn la wara niouss ci prison bi ngay nek fii di ndamo comme un champion, sa me fait rire en l'écoutant en plus danio amm sén propre langue 😂😂putains

  • @toubatoubatouba9272
    @toubatoubatouba9272 10 месяцев назад +20

    ioe boye 3ém sécteur chambre 11 ak 12 gaye dougou déglou waxtanou boye yi di doull ndayam 1mois man boye 100mét 7an lafa déff campénal 4an té douma bandit sa laming bi reuna boye nokhoul feulé

    • @Thiate499
      @Thiate499 10 месяцев назад +4

      Ki kay moy lolou mes yalla boula natou kaso dalati wayé yalla bo defati loulafay yobou

    • @Mbodjikhiffkhaliss
      @Mbodjikhiffkhaliss 10 месяцев назад

      Ohh massa frère 😢😢😢

    • @ATDansokho2Tane
      @ATDansokho2Tane 10 месяцев назад

      Mdr....

  • @seydouly8364
    @seydouly8364 10 месяцев назад +18

    Dolen ay bandi di gnodi bandit youma hamone deug amoul lougnou defoul mais bayi nagne té yalla hamna dolen guiss mouk gnouy racontée sen vie si internet bi faux bandi yi rek gnoy nek fi di gnodi life bandi

  • @vynscarvalho4641
    @vynscarvalho4641 9 месяцев назад +20

    Bilahi walahi dou Bandi ki pikine le deuk cote terrain Magg dann blowman la donne entre 2010 et 2011 legui bimouy dem prison da gno def location auto diambour ba pare def accident ray benn khaley Daw après lagn len diap mo ak deux persnnne donc khaw ma kagne la nekk Bandi bay agresser limay wakh bi preuve lassi am

    • @annaseck8764
      @annaseck8764 6 месяцев назад +2

      Doyna war

    • @viking850gfd
      @viking850gfd 5 месяцев назад +1

      Ils ont grandi dans des endroits tellement lugubres que selon eux être un bandit c'est une bonne chose du coups ils viennent sur RUclips pour mitonner😥😥😥😩😩 ces mecs issus des banlieues et des quartiers populaires 😥😥😥

    • @Anarbreezy
      @Anarbreezy 5 месяцев назад +3

      Saay xam nga beine partie ci life fam rek mais bo Fékéwoul kaay neek féké woo. Esq nitt gni xam naagn lepp lingay dound yow ?

  • @boyfass2934
    @boyfass2934 10 месяцев назад +13

    Ndekete madonn yeureum sathieu 😢 diexna teyyy 🤦‍♂️ sathieu bouniou diapp sama cogn reyy rek lala doul defff

  • @bursinenet326
    @bursinenet326 8 месяцев назад +5

    Mane je sollicite pour que justice déf liguéyam car gni ils avous leur crime, dejas chaque agression y avais des plaintes donc li devrait etre arretais

  • @amadousouleyetandine931
    @amadousouleyetandine931 9 месяцев назад +3

    Pour môme champion là, boy yeup ay ragal laniou si Galathie rékk laniou yakar koussi assuré woul sa dérr do xèkh. Koussi mandi woul do dieul alale diambour.

  • @annaseck8764
    @annaseck8764 6 месяцев назад +3

    Kham gani sa yaye kholam nekhou yalla naniou yalla mouseul ci dome you méle ni

  • @papisy5187
    @papisy5187 10 месяцев назад +20

    Yén dal diakhal ngèn ma li pour Lane la

  • @HEUREUX_
    @HEUREUX_ 10 месяцев назад +11

    Mes mbeuss mii kagn la nekk bandi😂😂té yeugoumako😂😂😂

  • @CoumbaSarr-hl1bd
    @CoumbaSarr-hl1bd 7 месяцев назад +7

    Yallah Nella yallah dièguale

  • @abdoukone4876
    @abdoukone4876 10 месяцев назад +8

    Wa li diare na émission ki wéroul 😮

  • @mariesec824
    @mariesec824 7 месяцев назад +5

    Ndeyssane Yalla nalla souniou Borom bi ték thi yonou dioup té diégueul leu say bakar😢yaw bono mon fils ndakh sa xol rafét na. Boulthi délou mouk

  • @youssoumbengue7698
    @youssoumbengue7698 10 месяцев назад +9

    😂😂😂😂sacré mbeuss neina si 4 policier leu reuthie quoi khathieu niou khadial ko

    • @morndiaye2191
      @morndiaye2191 10 месяцев назад

      Loolu mom amoul même Bou reuthion police dinako poursuivre

  • @ModouBodian-jv4oj
    @ModouBodian-jv4oj 7 месяцев назад +3

    Il faut tout simplement vous faire comprendre que le banditisme et les fréquences des milieux na pas chance ni de fin que des regrets

  • @salioudiop5538
    @salioudiop5538 10 месяцев назад +2

    Yalla nga changé ci barké seydina Mohamed

  • @tigrenoir5147
    @tigrenoir5147 10 месяцев назад +13

    Bilahi Boy bi dawoul milieu Kou daw milieu deugue d'où Bari wakhe Tak sim Bi Di wakhou aye mére ak aye Djiguéne

    • @boobahdiop7613
      @boobahdiop7613 10 месяцев назад +2

      Ki Kay xawma bane sim lay djitté😂😂ki comédien leu ngaka la quoi

    • @serignediop8861
      @serignediop8861 10 месяцев назад

      😂😂😂😂

  • @Touty-wp3gp
    @Touty-wp3gp 10 месяцев назад +6

    Kon nag firi arme.yalla nanu yalla samal bopam

  • @mbeuss.talibe.bamba.
    @mbeuss.talibe.bamba. 10 месяцев назад +16

    Day Doul dh bilakhi 😅😂😂😂

  • @awadiop4774
    @awadiop4774 10 месяцев назад +6

    Ehhhhhhh khehhhhhhhh waw li lanla 😢😢😢😢yalnanou yala samal bopam dama tite😢😢

  • @OusseynouDiagne-fv6ld
    @OusseynouDiagne-fv6ld 10 месяцев назад +11

    Force a toi bro yalnala yalla defal diame ❤

  • @user-fq2by8lg7h
    @user-fq2by8lg7h 10 месяцев назад +16

    Ay vrai domeram moy agresseurs yalna yala torokhal leun si adouna AK alakhiri AK yeun gni dileun maye beuzz sen sarapndaye

  • @MalangKondjira-rn1xk
    @MalangKondjira-rn1xk 10 месяцев назад +5

    Pablo you mague yi 😂😂

  • @massarthiam6077
    @massarthiam6077 10 месяцев назад +11

    Danguainiii diawaléé bandit ,waguaa ak malfaiteurs 😂😂😂

    • @ndiemendiaye9979
      @ndiemendiaye9979 10 месяцев назад

      Luy différence bi

    • @massarthiam6077
      @massarthiam6077 10 месяцев назад

      @@ndiemendiaye9979 akaa wouté sakh bandit c'est pour les hommes à femmes 😂waguaa moy kouyy tokh di naane diii khekh Di ndellou yaram,Di guizz (Brown, héro ,mooo)bii wala tothiee mbarikk mais dou agresseur,d'ou sathie seulement il vit comme un clochard,👉 malfrats ou malfaiteurs c'est les deux propositions réunis avec un peu de choses particulières aucune arrière pensé positive ces des sadiques qui n'ont pas peur de te tuer pour un simple dispute ou faire du mal au gens pour de l'argent ,du plaisir,et de la drogue .Il sont les cambrioleurs , dealer de haute qualité tueur à gages Alors tu as compris ou tu veux un que je te fasse un dessin 😁😁

    • @KhalilDieme-t5p
      @KhalilDieme-t5p 7 месяцев назад +1

      Waxx gnou différence bi lgui

  • @MedocNS
    @MedocNS 10 месяцев назад +4

    Ngaka yi ñioy dundu milieux ndax sa life yeup si jail bi la. Niit yi di dundu nice.

  • @torodo.ferrari
    @torodo.ferrari 10 месяцев назад +19

    Mom beug neu waxou firri arme dh😂😂😂

    • @mamajoliesalou2481
      @mamajoliesalou2481 10 месяцев назад +1

      Yefou dofe degue

    • @visonboubess2109
      @visonboubess2109 10 месяцев назад +4

      Ki fans bandi leu 😂

    • @Thiate499
      @Thiate499 10 месяцев назад +6

      Tapette rek moy diakarlo ak moromou gooreum di firi arme té ay arrêt nek fi

    • @ThierryBADIANE
      @ThierryBADIANE 10 месяцев назад

      Ki moy Mbeuss Firi Arme

  • @fatoudiop9492
    @fatoudiop9492 10 месяцев назад +11

    Mane dama diomi ki nit la li dé warna diékh Sénégal

  • @seynabouseck9633
    @seynabouseck9633 10 месяцев назад +1

    Magui soga kham definition « Milieu »😂merci People 221
    Mogui melni T-Bag prison break😅

  • @thiernocamara184
    @thiernocamara184 10 месяцев назад +2

    Rapp bila dougone sokhoor Na 😂 eske dou rabou favélas yii

  • @ndeyembathiodiallo5723
    @ndeyembathiodiallo5723 10 месяцев назад +12

    Wa ki mome werr neu ñiak diome rek nga yakar sipi nga ni

  • @29093
    @29093 10 месяцев назад +15

    niafal sa ndaye dimoukhram

  • @zalezale8946
    @zalezale8946 10 месяцев назад +8

    Après BobMarley Toog tièboudieu ! Filme indouuu deugg😂

  • @MamadouCisse-zb7vw
    @MamadouCisse-zb7vw 5 месяцев назад

    Mé iow doule liguay wakh amalou gnou béna chance dolene ay référence

  • @willywillane6603
    @willywillane6603 10 месяцев назад +5

    Théâtre guaye def mais do bandit té sa wakh barina

  • @ibrahimafaye8446
    @ibrahimafaye8446 10 месяцев назад +15

    Mom dh mingui melni kouy nètali ndam ndeysan

  • @abdougueye3105
    @abdougueye3105 10 месяцев назад +10

    Niewal itali Torino bilahi kon dinga khamni amolen fit do len bandi

    • @sambafall2819
      @sambafall2819 10 месяцев назад

      Waye fofu dafa sori gni Maroc rek bougne fa douguè yarou

    • @fatoundoye9013
      @fatoundoye9013 10 месяцев назад

      Torino kaye amoul bandi

    • @abdougueye3105
      @abdougueye3105 10 месяцев назад

      @@fatoundoye9013 amoul bandi senegalese ngay wakh nel guisoko

    • @thiernodiallo2830
      @thiernodiallo2830 10 месяцев назад

      Billahi torino kay diay drogue rek sour tout à côté de via corsos palérmo 😂😂😂😅😅😅😅 ak porte nouva 😅😊

  • @AmssaDiop
    @AmssaDiop 10 месяцев назад +7

    Bilakhi mbeuss day fène fii grand ndakar mbeur yifi nk mofi geuna ragal day Doul rek mossoul nk bandit bilakhi

    • @aliounegueye-pu6bh
      @aliounegueye-pu6bh 10 месяцев назад

      😂😂😂😂😂

    • @piifvntome290
      @piifvntome290 10 месяцев назад

      Grand Dakar la diodou yaro fi ba Legui mangi fi Amna 26 ans mais xawma kouy mbeuss 😂

    • @Oumanas5995
      @Oumanas5995 4 месяца назад

      😂😂😂😂😂😂

  • @WedjiGning
    @WedjiGning 10 месяцев назад +10

    Yw thiekouta ya meunè doull mane la sa papa karim bou pikine kagn gua nekk bvndi yw

  • @fatoudiagne3899
    @fatoudiagne3899 4 месяца назад

    Franchement c’est très bien de se repentir, Mashallah et c’est bien également d’avoir changé mais People 221, pourriez-vous poser la prochaine fois, la question suivante : et si on faisait ce que vous faites à vos familles ? Franchement, c’est bien de se remettre en question mais le coup est déjà parti, pensez-vous aux pauvres victimes ?

  • @openixmendy4522
    @openixmendy4522 10 месяцев назад +15

    Bayil tour yinguay limm

  • @almaktoumdiop8749
    @almaktoumdiop8749 10 месяцев назад +11

    Li loye adouna bonéké silou bakhoule sa khéll yédala gabayi yalla yalla diapalé baga bagñe si délou

  • @ouleycamara3260
    @ouleycamara3260 10 месяцев назад +8

    Diar diar dou gnak thi nit , dél toup fo tolou tay diamou yalla ndakh moma sakk

  • @Thiate499
    @Thiate499 10 месяцев назад +12

    Ioe mi dh bayi wo sa khétou parole yi ngay melni rabou aleu ni 😂😂😂😂agresser mom yeufou Goor djiguen la

    • @leytithioukouli9768
      @leytithioukouli9768 10 месяцев назад

      Wadji kaay language bandit leu yoor 😂😂

    • @Thiate499
      @Thiate499 10 месяцев назад +1

      @@leytithioukouli9768ki da fier si loumou nekone di diko netali ni sans pitié 😂

    • @massambadiop8181
      @massambadiop8181 10 месяцев назад

      @@leytithioukouli9768ki deih sa diabar sakh moko geuneu bandit pour te dir pikine leu deuk masoul nekk bandit limouy raconter dara dousi deugg kheuwma louko diaral liii beugg buzz reik

  • @modouaw4315
    @modouaw4315 10 месяцев назад +4

    Boy sama boy gua dee mes deconne gua yaw meusso nekeu bandit li dara diarouko bilahi 🙏🙏gno bokou beneu kogne pikine bilay

    • @pacodiop7501
      @pacodiop7501 10 месяцев назад

      😂😂 boy bi kagne arouu bandit dako nékh yakarna . Khana wagga wone yakarnè bandit

    • @massambadiop8181
      @massambadiop8181 10 месяцев назад

      Ki kay gayi claté naniou ko kham naniouko boubakh masoul nekk bandi mais louko diaral li beugg buzz reik

  • @DouniaRaoui-tj3vn
    @DouniaRaoui-tj3vn 10 месяцев назад +17

    😂😂😂😂 gros t'es un grand blans boul diawallé sathie AK bandit 😂 sathie bakhoul liguéyil lou yomb djiguoul gorr

  • @AssaneDiop-sn8qr
    @AssaneDiop-sn8qr 9 месяцев назад +1

    Mbeuss yangui ndélou di tassal ak lepp

  • @bambaji221
    @bambaji221 4 месяца назад +1

    Goor dou yor arme... 👍

  • @fallandoye6114
    @fallandoye6114 10 месяцев назад +6

    Ki meuna ndy duul sheuuu di niodii fittt niii😂😂néna daffa ame fitt nii

  • @Ababacarsow-z5m
    @Ababacarsow-z5m 10 месяцев назад +1

    Bandit amoul geuneu nième dee la kou wet khamgua ligua capable diaroul wakh silence boy

  • @azizngom8741
    @azizngom8741 10 месяцев назад +14

    Mom souy netali c’est comme ci dafa fier si loumoudone def!!!

    • @fadelsarr1262
      @fadelsarr1262 10 месяцев назад +2

      Mogui nonou nk

    • @AbdouNiass-cp1lx
      @AbdouNiass-cp1lx 10 месяцев назад +4

      Bilay walay ki Loumou don deff rethiou woull Dara si loumou deff 😢

    • @Falloulam1234
      @Falloulam1234 10 месяцев назад +1

      😂😂😂😂😂😂 ki dafa nexx

    • @AdjiDiop-by9og
      @AdjiDiop-by9og 10 месяцев назад

      MoMA djahal dafa fierni dee 😂😂😂😂

    • @mouhamedcamara1505
      @mouhamedcamara1505 10 месяцев назад

      Moma diaxal

  • @ziguiboylofficielTV
    @ziguiboylofficielTV 10 месяцев назад +1

    Gnoulénni talalll micro gno yakk deuk bi dilénnn motivé mann sakh meuss na rayy kagna mbote djinakk😅😊etc...

  • @thiattobb423
    @thiattobb423 2 месяца назад

    Kii la Jérôme Bandiaky toudou si afér yi 😂😂😂😂😂

  • @KheuchTesta-e6u
    @KheuchTesta-e6u 10 месяцев назад +8

    Done Yambar wesouwoulli😂😂😂😂

  • @doupafall6322
    @doupafall6322 9 месяцев назад +2

    Lii bane série là😂😂

  • @kingpapeuyou8304
    @kingpapeuyou8304 10 месяцев назад +3

    Sa way do dandi dé bambara gua sa bountou gallé guay diayé mafé😂

    • @MamanCisko
      @MamanCisko 10 месяцев назад

      aye waye bayil Bambara yi mafé Bambara Dou sarakhé mafé😂😂😂

    • @AmadoudiouldeSall
      @AmadoudiouldeSall 9 месяцев назад

      😂😂😂😂😂

  • @raimekasse5582
    @raimekasse5582 10 месяцев назад +8

    Ki police dako waro dieuli Bilakhi

  • @Papismbayeesp
    @Papismbayeesp 10 месяцев назад +2

    Regarde moi sa! Sa c grave aux Sénégal

  • @AïdaThiam-k4b
    @AïdaThiam-k4b 10 месяцев назад +12

    1mois 6mois kay 😂😂

  • @MadiopDiop-o9f
    @MadiopDiop-o9f 10 месяцев назад

    Wakhi 1990 yi mou defani mothi nek.yen vrement dagueni diokh succès des gens yo khamni Moy lolou

  • @DieganeNgom-p1k
    @DieganeNgom-p1k 10 месяцев назад +9

    Ki dafa fiére thie bandit bi

  • @abibousylla8843
    @abibousylla8843 10 месяцев назад +9

    Tu as eu de la chance . Les grands délinquants ne vivent pas longtemps

  • @tomrudy7246
    @tomrudy7246 7 месяцев назад

    Il a avoue tous les agretions.le procureur. Pour le foutre en prison pour la vie.

  • @gondiaye8810
    @gondiaye8810 10 месяцев назад +4

    Genre yi diarounio diox micro😊

  • @Ibrahimaly-bq1qg
    @Ibrahimaly-bq1qg 8 месяцев назад +5

    No Sénégal da nekh bilaye😂

  • @willywillane6603
    @willywillane6603 10 месяцев назад +14

    Iow comédien gua bandit dou reuy lamigne

    • @CheikhMbaye-lp2lp
      @CheikhMbaye-lp2lp 7 месяцев назад +1

      Mbeuss bayil doul man khamnala grand Dakar la deuk

  • @aliounembaye8266
    @aliounembaye8266 10 месяцев назад +7

    Boy bi doul rk lay def 😅😅

  • @BoubacarDiallo-p4f
    @BoubacarDiallo-p4f 5 месяцев назад

    Boucar pikine cfa ndéysane yayam dafko nakharlou ba déh😢😢

  • @papemalicksene7301
    @papemalicksene7301 10 месяцев назад +3

    Kii loumou book ak dip doundou guiss Mme voi oci ñuro tek tek😂😂😂 jam ci ioe😂😂

  • @wagga4life
    @wagga4life 7 месяцев назад

    Mbeuss amonafi temps nak 😂

  • @morserigne2952
    @morserigne2952 7 месяцев назад +1

    Leufeul ndayi Sénégal rék😂

  • @Ababacarsow-z5m
    @Ababacarsow-z5m 10 месяцев назад

    Dou lepp lagnouy wakh il faut savoir gardé le silence et le secrèt de certains mots de certains chose et ces certains paroles diar gua diale gua diekhna

  • @thiernodiop1460
    @thiernodiop1460 10 месяцев назад +1

    Do champion bilay

  • @toubatoubatouba9272
    @toubatoubatouba9272 10 месяцев назад +4

    1mois ak tanbér ki mouni bandi la boye ioe sa siditou ndayi tankiyi lan kattoul ndayam

  • @salious1476
    @salious1476 10 месяцев назад +3

    Vraiment wadji beeurineu wakh

  • @MbayangCiss-es2bn
    @MbayangCiss-es2bn 10 месяцев назад +4

    Sénégal woratoul

  • @tamsirdia1994
    @tamsirdia1994 10 месяцев назад +1

    Ki day doul rek dou dara grand Dakar lay nek toujours 😂

  • @amdydiagne308
    @amdydiagne308 10 месяцев назад +8

    Day doul dé😂😂

  • @MamadouDiallo-dm4ob
    @MamadouDiallo-dm4ob 6 месяцев назад

    C'est un copain de classe un cool boy

  • @papadembaniang8088
    @papadembaniang8088 10 месяцев назад +3

    Boul doug thi wakhou akh kou meuss agressé rek waroulo wakh wakhou akh

  • @diagasarr9036
    @diagasarr9036 10 месяцев назад +4

    Mais franchement certaines you tube doivent etre fermées.
    Actuellement tous les pays sont entrain de voir comment changer leur model économique et comment sortir de la pauvreté.
    En ce moment vous vous permettez de tendre vos micros a des ex-voyous qui ne peuvent rien nous apporter

  • @Ababacarsow-z5m
    @Ababacarsow-z5m 10 месяцев назад

    Baye mbeuss d’où nii warna meuneu geuneu rafet affaire yii dou ay wakh banditisme si khôl la amoul netali bandit dou expliqué

  • @BoubacarDiallo-p4f
    @BoubacarDiallo-p4f 5 месяцев назад

    😂😂 peuti cote tinré magueu danne😅😅😅

  • @rokhayadjigal8357
    @rokhayadjigal8357 10 месяцев назад +2

    Fayè alalou diambour amo len benn diomm fouma guiss gnou diap sathie wala agresseur ma barkelou

  • @seneami4448
    @seneami4448 9 месяцев назад

    mbeuss bou sicap baobab moy wakh fi nane bandit la wone non 😂😂😂😂

    • @Oumanas5995
      @Oumanas5995 4 месяца назад

      😂😂😂😂

    • @Oumanas5995
      @Oumanas5995 4 месяца назад

      Est ce que mome leu 😂😂😂😂

  • @maradiop3855
    @maradiop3855 10 месяцев назад +10

    Lii yombe n'a trop

  • @mariamafaye3689
    @mariamafaye3689 10 месяцев назад +4

    Waki moye kan waye baye na😂😂😂

  • @wadewade9897
    @wadewade9897 10 месяцев назад +10

    Ki tapéte la day doul

  • @Moussa-e8g
    @Moussa-e8g 10 месяцев назад +1

    Ki daye doul rek Diagan Bouy tafou si mir bi amoul fofou ken douko tibé pal day doul yen ki d'où bandi fans bandi la ki dawoul dara d'où Bari wax doul way