Tu as tout dit, que Dieu te protège et te garde, rien n'est perdu, tu peux toujours y arriver. Les jeunes doivent t'écouter. Que Dieu vienne en aide aux jeunes sénégalais et du monde entier.
Arrêtez de mal le juger et écoutez ce qu'il explique il donne de bons conseils au jeunes car il a vécu le côté sombre de la vie. Quand les gens veulent reprendre le droit chemin il faut les motiver et les encourager car fi ken geunoul Ken t nak doundou bou wessogoul teey daftji bakh.
Il a tout à fait raison coumba am daye ak coumba amoul daye mo am galsen mais la loi doit être égaux pour tout le monde mais dougnou ko déf niit kou tak si décé 2 personnes gnou beug mou am liberté provisoire pour lane😮😮
tres important .un jeune a promouvoir,il peut reintegrer beaucoup des siens ,les conscientiser.A retansmettre sur tous les plateaux de television .ce jeune merite detre promu et accompagner pour conscientiser ses egaux et lui donner les moyens de le faire
Armé gno wara dieul jeune yi nèk si quartier yi tè liguèyoun ak di bandit bandit lou gnou recrutè lën si armè bi , mèm sounou amul diplôme Sunu paré formation gnou dèflèn gnou nèk patrouille de si kongne Yi C'est le meilleur solution
Ya une chose cette pensée de banlieusards laniou wara bayi. Sayo waxé niouni la nioune ay banlieusards lagn lolou la meuneta comprendre. Nioune gni xamné village laniou diogué guissou niou courant, guissou niou ndox amouniou wone connexion mais téwul niongui gardé wone suniou dignité batay niongui ni sante yalla. Tu l'as dit M.Petit Bandit respectons nos parents t am ay ambitions di top niou bax am diné
Machala👍👍👍🇸🇳🇸🇳 vraiment tu as très bien parlé Jambarr , de l actualité et les causes . Et surtout de la pure vérité qui soit , avec respect . Je suis d accord pour les talibés etc... contre leur utilisation . Vraiment tu es à écouter . Respect 🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼
@@mbayebabacardieng1769 bayyilèn diar diar ki dafa diouddou ba wara wakh aye diar diar beug lou yomb molèndi dougueul ci yi dou lènèn .. khalè bo tolloo ci diangue da ngay diangue bou sa diangue dèmoul nga dèm diangue mètier
Je ne suis pas la pour juger personne des fois diar diar dafay ame natou dafay ame mais bo démé ba khamato fo dieum gua délou figua diougué bandit amoul gniarigne
😂😂😂 Mais nak il ne faut pas stigmatiser, dans la banlieue il ya des intellectuels, des personnes bien. Les gens qui choisissent ce chemin facilité rek, nango léne diangue, ni diangue métier, beugueu guéne ame lou goor yi ame t beugo lene ligueye. Yalna souniou borom doli soutoura. Aye waye Ibou goorgorloul téga dimbali sa yaye
Boybi loumouy wax loulér laywax kheuyna loumouy wax kousi diaroul mounoco khame cousidiar ba yalla djéles laçimomouna comprend limouy wax way lépe nattou yalla la yalla na yalla safaral lépe
Pauvreté bi mo waral li yeup, niak mon bakhoul si goor mo waral rancune bi si kholo jeunes. Les jeunes cafe touba lou am barké la , diouk léne ngéne liguéye, en entendant états bi wakh si liguéwou ndaw gni
Promotion banditisme ok senegal magui doga kham loutakh peul fouta yi respect wouniou ak yenen étranger ce vraiment honteux billahi walahi li metinama dee
Fils bandit bakhoule… Mais jour bo demé Guinée bayi bandit sénégalais… Fofou ci arme à feu la niou tole PMAKA… je connais très bien la sous région sen niveau bandit dépassé largement bou sénégalais combattons le banditisme mais na niou bayi yakh der. NB je parle en connaissance dd cause
Tok leen fofou di khar État niak diom rek moleen diap ak yak sen Liguéyou nday beugue Lou yombou bone sen boppou bala ma dé niounane État ligueyi leen complexe yi shim
Tu as tout dit, que Dieu te protège et te garde, rien n'est perdu, tu peux toujours y arriver. Les jeunes doivent t'écouter. Que Dieu vienne en aide aux jeunes sénégalais et du monde entier.
Arrêtez de mal le juger et écoutez ce qu'il explique il donne de bons conseils au jeunes car il a vécu le côté sombre de la vie.
Quand les gens veulent reprendre le droit chemin il faut les motiver et les encourager car fi ken geunoul Ken t nak doundou bou wessogoul teey daftji bakh.
Il a tout à fait raison coumba am daye ak coumba amoul daye mo am galsen mais la loi doit être égaux pour tout le monde mais dougnou ko déf niit kou tak si décé 2 personnes gnou beug mou am liberté provisoire pour lane😮😮
wa pikine diahal nagn ma ay ibou bandit,modou bandit lou kenn hamoul,regler lenn,outi liguey ngenn di har Etat
Kestion de jaar jaar leu environnement
@@senegoogleadr4860c’est pas une excuse
😂😂 motax deukk bi parégoul sakh pour avancer ay yeufou doff rék nga fi guiss légui nieupay kheuthio pour nék bandit
Abou bandit ay mathiou tour you yeme
Mo takh chaque jour gnouné diw ray na nitt actu buzz yenn ay bandit rk guenii diokh senn micro yi
Le message très important à écouter sans préjugés 👍🏾
En l'écoutant très attentivement cela devient intéressant.Un grand merci.
Les gars bayiléne khassatébi ki deug rék lay wakh en plus il sensibilise les jeunes
Franchement il dit que la vérité
Li motakh Sénégal d’où dém loutakh gnouy wan ay bandi di influence sougnouy dom 😡 sen fasson wakhin rek ngay khamni gni ken waroulen deglou
tres important .un jeune a promouvoir,il peut reintegrer beaucoup des siens ,les conscientiser.A retansmettre sur tous les plateaux de television .ce jeune merite detre promu et accompagner pour conscientiser ses egaux et lui donner les moyens de le faire
Ils sont tous conscients. Ce n est pas là le problème pour moi ils n’arrivent jamais à faire le bon choix. Le problème est systémique 😢 c est un tout
Merci boy surtout les enfant talibé il faut arrêter ça sinon Sénégal d'où changer impossible
Armé gno wara dieul jeune yi nèk si quartier yi tè liguèyoun ak di bandit bandit lou gnou recrutè lën si armè bi , mèm sounou amul diplôme
Sunu paré formation gnou dèflèn gnou nèk patrouille de si kongne Yi
C'est le meilleur solution
Une bonne solution, armée force , gueneu amsa liguey, bilahi solution leu
Bien dit
Bilae deugg geu wax
Ya une chose cette pensée de banlieusards laniou wara bayi. Sayo waxé niouni la nioune ay banlieusards lagn lolou la meuneta comprendre.
Nioune gni xamné village laniou diogué guissou niou courant, guissou niou ndox amouniou wone connexion mais téwul niongui gardé wone suniou dignité batay niongui ni sante yalla.
Tu l'as dit M.Petit Bandit respectons nos parents t am ay ambitions di top niou bax am diné
Bien parlé on voit que certains peuvent se repentir et changer de vie
Lou wore gua wakh yalla nala yalla sam ❤
Machala👍👍👍🇸🇳🇸🇳 vraiment tu as très bien parlé Jambarr , de l actualité et les causes . Et surtout de la pure vérité qui soit , avec respect .
Je suis d accord pour les talibés etc... contre leur utilisation .
Vraiment tu es à écouter .
Respect 🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼🙏🏼
Franchement il merite des encouragements il s.ensibilise les jeunes à eviter le banditisme
Ndiabot gui yalla dimbali len thi barke mouhamed
Goor yallah na sa diameu yagg bonne continuation ❤️🤲🏿👌🏿
Il faut que l'Etat sanctionne les gens qui exploitent et trafiquent les enfants de la Guinée vers le Sénégal
Sa diobou ndeye naane bandit pikine fi kou sathie gnou tothie sa ndiobou ndeye
Copain kou nékeu amba diar diar ki limou wakh yeup ay conseil lay wakh
@@mbayebabacardieng1769 bayyilèn diar diar ki dafa diouddou ba wara wakh aye diar diar beug lou yomb molèndi dougueul ci yi dou lènèn ..
khalè bo tolloo ci diangue da ngay diangue bou sa diangue dèmoul nga dèm diangue mètier
@@mbayebabacardieng1769fokk niou wagni yeureumteulou bi ak hypocrisie bi
@@goorgorloumerci khalé bou ndaw nane boy yi ki paré guoul
Day. Doul. Rekk. Lou. Mou. Djèkou. Moy. Dem😂
Sa papa très bonne question la😂😂😂
😂😂😂😂
@@DadaFaye-q7l😂😂😂
Machala frère wakh deugeu frère diam si ioe❤❤
Très pertinent a travers ces idées ❤
Il a raison sur tous les plans
Il est très intelligent sou gorgorlo touti réussit billahi
Il a bien sensiblisé.il regrette je sens.fignou tol bakh correct rèk mofi ame.so boné nelé lagnelaye tégué.massa mais wakhena deugue
TRES BONNE QUESTION😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Mais ki nekhna deh
Tres bonne questions ba kagn nak iow😂😂tres bonne question wakh dji rafetna tres bonne question 😂😂
Courage frére yalla samal la boopam Thi barki seydina mouhamed 🙏
Diambar yalla na Yalla takhoulen tu es un bon examples gueneu gorgorlou yalla na boye yii saye wakh
Je ne suis pas la pour juger personne des fois diar diar dafay ame natou dafay ame mais bo démé ba khamato fo dieum gua délou figua diougué bandit amoul gniarigne
😂😂😂 Mais nak il ne faut pas stigmatiser, dans la banlieue il ya des intellectuels, des personnes bien. Les gens qui choisissent ce chemin facilité rek, nango léne diangue, ni diangue métier, beugueu guéne ame lou goor yi ame t beugo lene ligueye. Yalna souniou borom doli soutoura. Aye waye Ibou goorgorloul téga dimbali sa yaye
Yalla nala Yalla changer diantal bro
Au moins il a révélé les maux de notre société
Deugueu bou weure guaye wakhni bro
Boybi loumouy wax loulér laywax kheuyna loumouy wax kousi diaroul mounoco khame cousidiar ba yalla djéles laçimomouna comprend limouy wax way lépe nattou yalla la yalla na yalla safaral lépe
Ndiambar amoul thi banditisme souss vodi sathi ak agressé lolou dou ndiambar
Yare len sen doome yi bala nion mél ni Ibou walla Sénégal naniou yare xalé yi
Bilay waxna ay deug da khawa khoromou rek😂 xollen si mom guen changer nguirr yalla li amoul ndiarigne deh ba dem kasso
Tu as vraiment raison❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Machalah bro
Ndeysen sama Sénégal legui so nekol bandi pour iow yambar nga nek bandi bayiko diko wakh dara lolasi déranger bah na r
Mane très bonne question la meunoul comprendre 😂😂😂 sheute Sénégal woreutoul qui va nous aider
Très bonne éducation il voulait dire
😂😂😂😂😂😂😂😂
😂😂😂 SÉNÉGAL MO NEKH
Yalla naléne sounou borom sopi amine
UN GARSON TRES FRANS AVEC BEAUCOUP DE RÉVÉLATION MACHALA
Lou intéressent laye wakh nak
Sistéme kounou diap gnaou taal ndeyam. Rewandé rec molénendiap
Ibou a dit tous les vérité
Boy yi nék fi di bandi bandilou nieup laniou wara diapa youbou lén ci tolle yi niou bay force nakk
Sa papeuh très bonne question la😂😂😂😂😂😂😂😂dina deh
😂😂😂😂
Meune nama ray
😂😂😂
Un regard perçant et glaçant 😮
Nandtéla, nioune ngaaka yi nio am ragard bou vague😅
@@moom3931😂😂😂😂😂😂 haaaa lii deh mom dokhoul
Wa llahou kay 😅😅😅😅😅😅😅😅😅
Il est entrain de donner des leçons de morales il a changé alhamdoulilah ndeysane natou dou wess mais bo changé rek nekh gneupou
😂😂Moy. Toul. Ma. Woo. Nanditèyi
Mais ioe do très bonne question déh😌
Boyz bou bayiwoul bandit bandilou FDS dinaniou daxar sa ndaye ba ngénn yammm
😂😂 bandit bandit lou dééwou kagna rék
Pauvreté bi mo waral li yeup, niak mon bakhoul si goor mo waral rancune bi si kholo jeunes. Les jeunes cafe touba lou am barké la , diouk léne ngéne liguéye, en entendant états bi wakh si liguéwou ndaw gni
séni ouahe rafétna mais daguéne neu niakeu diome sonnale séni ouadioure populations moye dioke thi yéne
Très important
Woutti len métier
Banditisme amoul mouthiou glou glou moy wakhi lane boléne khamone li nek si bakh diguéne bakh
Mane dh gambie kom k Sénégal ibou bandi nabou bandi ak niom moussa bandi niofa nek xaral ma tok gambie
😂😂😂
Khalle douyakamti am allale khalle na jaggue wolla mou jaguimeche koulen wa khoute nakhna len
vraiment Senegal c’est du n’importe quoi 😮 wa banlieue nék lene aye nité ☹️ problème mou Senegal yené rék leu
Vérité absolu
Ay waye losi toudé kiné tamit déte waye
Pour nioom foula bilahi sen sarap ndaay
Lii Mouy wakh nii DEUG là bou wèrr . C'est à écouté milieu yii kouko tope ak khalé djiguèn milieu yii iow là iow là, daguay sankk sa Adouna
Wallaahou😂😂😂😂
Boy Pikine yeup ay domeram n'en tchimm
❤❤❤❤❤👍🏾
Lou am solo ga wakh
Ay mixta, cité damel, mbaye dia, farot, pneu, willy, yow dé maîtriser gua milieu yeup, bref néanmoins tu donnes de bon conseil
Nono ibou
Ki lou lere la wax agresseur yeup niou ki chez peuno côté yeugoulene ak willy
Liguay wakh ni melni kouy wakh si diner soko goorgorlou wone woute ligueye mogeune gua tokk di expliker di perte temps niak guene khorom trope.
boy yi dagnou beug lou yomb bouy parè di dèlou wate ci limou nèkone guemougnou sèn bop
@@goorgorloumbadou mouy zimbéré 😅😅
C est complexe le cas des talibes il faut que l état s y attele
li méttina dé mé yalla naniou yalla dolli soutoura rék 🙏
lane mo menti ?
Amine inchallah
N'a kounek dieull matwayam rek wasalam
Lolou moy bagass bi. Na kounekk braayé sa wègn
Amaloulen société bi ben ndiarigne .demlen ligeyi
Yemena tropp
😂😂😂😂boy. bi. Amoul nena. Tribunal da gno. Logual
L’an moy. Millier
Koulou koulou koulou koulou koulou koulou KOULOU
Nane Sa VODI, Takk Sa Chim mouy daw
Gni dounou ay bandit bagna ligueyi rek
Pourtant il dit la vérité dh surtout nk khalé yiy démm si. Nadio yi
Demlen ambulant dji
Promotion banditisme ok senegal magui doga kham loutakh peul fouta yi respect wouniou ak yenen étranger ce vraiment honteux billahi walahi li metinama dee
Fils bandit bakhoule… Mais jour bo demé Guinée bayi bandit sénégalais… Fofou ci arme à feu la niou tole PMAKA… je connais très bien la sous région sen niveau bandit dépassé largement bou sénégalais combattons le banditisme mais na niou bayi yakh der.
NB
je parle en connaissance dd cause
Séne titre you katt ndeyam yi bandit pikine
Vraiment
Yaw ladial sa yaye no dioudo ba parré 🎉
@@MslimeGd come ni sa papa dioudo rék
Ban sar moy walahu
Kossi dégü mounana sama yaye lay diapalé wa ana sén baye yi
Do data yayame
Ay beuss Ay deuss moye lane dieul euss yokoussi Loula safe did diay bandi
Dawna yaram
Deug reiknla wakh
Ibou kagne gua nek bandi😅😅😅😅😅😅
Moma diaxal 😅😅
Boy bi loumouy watt ni rekk
Boy yi niak nagn diom parent yi téla daw séni responsabilité meuneu diour kom ay mouss
Boys yi yepp laniuye talle sene ndeye degloul rek
Tok leen fofou di khar État niak diom rek moleen diap ak yak sen Liguéyou nday beugue Lou yombou bone sen boppou bala ma dé niounane État ligueyi leen complexe yi shim
Boy banlieue bi nek len ay nit
Arretez d le juger limou wax dara nekoussi day sensibilité pour beug gniou xamnei life bandit amoul mouthiou