11:44 Reportaire bi na baayi li muy wax naan "Papa kan mo ko yaxx? Doomu Adama mo soxorr". Kenn defu ko dara, menul bere, nu daan ko. Loolu rek la. Baayi leen niakk jom ag niaaw njott.
Ok, en lisant les commentaires ici on voit nettement que les gens ne croient pas en DIEU. Ki ken yakouna; ken mounoul di mom dara koudoul sugnu borom! Li sport kesse la. Il est en bonne santé, il mange dara dalouko Ndeysane, ndeysane comme di dafa am kou de!! La chance ne lui a pas encore sourit c’est tout. Papa Boye Diene est un example!! Qui a son numéro??
Bilahi yaye le meilleur lutteur de l'année amoul siki saka diap 3 boys yo mana diour si ben ate nga dane len
Bilaahi
Franchement tu le meilleur luteur de lanné
Non non zarko
Est ce k doko bindeu si olof
Fans de balla gaye ki parle …
Khana modou lo joueur de foot la legui
zarko meilleur lutteur : 2022/2023
Tapha gueye 2 meilleur lutteur 2023/2024
@@MoussaTraore-v5fyaw li nga bind ci wolof tamit nga foog ni jag na ?
❤❤❤❤❤❤❤❤ pour notre thapha Gueye 2 ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤le lutteur de l année
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Papa na bayi beure dou mbireme
Zoss vs papa boy Djinè combat de l’année kouko Beugue Lalal j’aime
MEILLEUR LUTTEUR DE L ANNEE.... TAPHA GUEYE 2
Zarko
Zarco 2 victoires la amagoul ki 3@@Devvvv390
Dina serrer deh zarco ndannane tapha jr aussi. Motakh hygiène de vie bakh.
Ipn
Meilleur reportage de l'année 😂😂
Félicitations Tapha Gueye 2 et du courage Papa boy djinné
sakou déféttte mome dawallll boulko lallll😂😂😂😂😂😂
D'accord na dh meilleur lutter de an
Reportage parfait
Il est très intelligent ce tapha 2
Dégal m'y pa ré😅😅 ani gniko bayi khél😂😂
😂😂😂😂😂
Magui 😂😂😂
Tapha Gueye2 VS Zoss combat leu nk😂
Félicitations 🎉❤ champion pére Tapha guéye 2 ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Tapha Gueye 2 le Kéba Seck des lutteurs ❤❤❤😊
😂😂😂 c’est vrai
"Saaku defet la yorr, na wut keneen ku mu ko yen waaye du ma yen man" 😂😂 Wax na degg de, Papa dafa diiss gann ag defet 😂
Dégeul père bi mom😂😂😂
Yafi dokhane xalé bi en direct
Waw khamé nako😂😂
😂😂😂😂😂
Champion d'Afrique lutte simple poids léger 😂😂 c'est un grand technicien tapha gueye momeun niou barii😂 dolei la amoul rk
Dieulel bb elton gnou khool😂😂😂
Ndeysaan Papa yalla nako yalla génné ci tolof tolof yi té defalko ay ndam 🙏
Félicitations tapha ❤
Fatma Dia d'où nitt 😂😂 auye waaye😂😂
Tapha Gueye 2 déy nékhal lamb koi😅😅😅
Vraiment vraiment ki menoul beuré kholene boubakh
No tehy mome yeremna papa boy djinne torp billahi li metina 😢
Bilay Mane ndeye gueuye la gueune yeureume
Ponkall mi❤😂🎉🎉
Kou guis fatma dia da dougeul Pabi boit vocal mayouko dara 😂😂😂😂😂😂
Il faut terminer la saison en beauté avec Bathies seras combat revanche leu
Zozzz 😂😂😂😂
Tapha guey mo dane mai daffa daw combat bi yeup du courage papa boy djiné
Tapha Gueye 2champion leu mo meuneu boys yii❤❤❤❤
Waw déguin pêre lim Wakh 😂😂😂😂
Tapha2 vs Diop2 combat là❤❤❤❤❤❤❤
😂😂
Papa boye jdiné na ma sétesi tivaoune ma défarrego
Sakou defet Kay 😂😂😂😂
Papa mi esk dou oubi Maïga té bayi beuré😂😂😂😂
Lutteur de l'année 2024
Aye aye aye wayeu wouyyyyyyyyyyyyyyyy victoire wouy sama ndeye 😂😂😂
L'experience fait la difference 🎉
Papa boye djiné kene tegouko natou da manoull rk na bayii kholi lanene nopal ay mbokam 😢
😂😂😂
mom est ce k dinna contac
Pordan tonie na mbapate
Khamoul dara 😂😂
Lo moy deugu ❤
Papbi brom khalébi nékhnga 😂😂 néna ki worou😂😂
Hippo Ngary raay nama 🤣🤣🤣
Kou comprendre rek beusseul j’aime
Fatma dia le meilleur ❤❤
Daysane papa yalla bakh na
Lutteur de l'année
Machalla ❤❤❤❤🇸🇳
Sacou défaite 😅😅😅😂😂😂😂
Sakou défaite Kaye 😂😂
Sakou défaite doumako yénne😂
Niayy
🤣🤣🤣🤣🤣
Ndeye gueye mo watair boye djiné😂😂😂😂
🤣🤣🤣🤣🤣
😅😅😅😅
Reporter yi gnioy kagne deugeu 😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
Je suis d’accord
Khana danga doyal thei adouna 😅😅liss ndiago😱🙉
😂😂 yeumandé thi défaite
Sakou defaite mou beugue ma kooo yennn😂😂
Mane pabi momay ray ki woroul moma diélone filméma sama dér yép yakhou 😂😂
😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂😂
No tapha nandite ma koi😂😂😂😂
11:44 Reportaire bi na baayi li muy wax naan "Papa kan mo ko yaxx? Doomu Adama mo soxorr". Kenn defu ko dara, menul bere, nu daan ko. Loolu rek la. Baayi leen niakk jom ag niaaw njott.
Tafa Guéye ❤😂😂
Pére ibo ngari😂😂😂
Sa touba diapouléko svp papa boy djiné 😢😢😢
Hypo ngary bayil fatma nguir yalla
Fatma dia mayal pa bi sans😂😂
Tapha geuy 2 ak gouy gi combat laLol Lol 😂😂😂
Sakou défaites 🤣🤣🤣🤣🤣
Sa Touba waxo won Lolou de 😂😂😂
Mais père ipo nagry ngui régler ses comptes d 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
Tapha G 2 ndandité la 😂😂
Ay way nagn barewat 😂😂
Albourakh faites revenir Bathie Serasse ngén teugg combat bi Tapha Guèye VS Bathie Sérasse
Cheikh Niang....
Tapha guéye2 vs Ama dia2 combat leu je crois
Tapha gueye ya gooré ya bakh
Sakou défaites boy djiné😂😂😂
😂😂😂😂😂 momayy rayy saco déffaittt
Liss ndiago day doré dh bakhna 😂
Tapha2 diambar la nak
BOY FASS LA TOUDEU TRABAJAA
Ya finé
Papa yaw yamal ci nday geuy rek😂😂😂😂
❤❤😂Am very sorry mi dispiace
Keupou katou yal wane nga nak 😂😂
Papa bayil lamb mano dh
Papa boy jinné vs bou sitteu 😊
Tapha Guèye finale ray
Papa bari bari wala prince
😂😂😂😂😂😂Oooy sakou déféte
Reportage bi❤️❤️😂😂
Sa touba déle bayie yalla khéle
Talfa kay 😂😂
Mais père Ndiokhobaye loumouy def niii 😂😅
Khalé bi ley khool di 😂
Dou niokhobaye , Ippo leu
@@ametdiouf271 merci wakh nga deug Hipo leu lol
Papa boy djiné dore yi béne daloule
❤❤❤❤❤
Tapha Gueye 2 gouy gui
Ok, en lisant les commentaires ici on voit nettement que les gens ne croient pas en DIEU. Ki ken yakouna; ken mounoul di mom dara koudoul sugnu borom!
Li sport kesse la. Il est en bonne santé, il mange dara dalouko Ndeysane, ndeysane comme di dafa am kou de!! La chance ne lui a pas encore sourit c’est tout.
Papa Boye Diene est un example!! Qui a son numéro??
Degeull pabi😂😂
😂😂😂😂😂😂😂 sakou defet
Pa ni mo niaka diome de😂
Tapha gueye vs mor kan kan combat leu
Ipo nguari😅😅😅neina femme bi woroul😂
😂😂😂ré ba tass 🤣🤣🤣
Motax soxna si wuyuwuko sax🤣
Boula yalla diayé bagua déme si talfa dotoko défati talfa bi boyi deh
Tapha gueye dou moroumou boy yii lamb mo waxoul deug rek mé s le djinn 🧞♀️ de l’arène