DU SÉNÉGAL AU NICARAGUA: TRAJET, DANGERS...LES CONFIDENCES INÉDITES ET TERRIBLES DE MAME THIERNO

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 24 ноя 2024

Комментарии • 9

  • @adinamoulsolo765
    @adinamoulsolo765 9 месяцев назад +4

    Bo wathié Nicaragua do diar Costa Rica ndakh dankoy bayyi sa guinnaw aprè Nicaragua, Honduras,Guatemala,Mexique.

  • @kamal313ndiaye3
    @kamal313ndiaye3 9 месяцев назад +4

    Wax dëgg Yàlla man sama laisser passer keen jàpp mu te thiapatiola ci police immigration sama laisser passer 45 jours la amu ma been problème.

  • @kamal313ndiaye3
    @kamal313ndiaye3 9 месяцев назад +3

    Déet yoon dañoo bari am na ñu jarul Ariaga man 11 jour la deff ci yoon bi. Man Nicaragua Honduras Guatemala Mexique Amérique yoon bi moom Mexique rekk mo ci am ay bàndi te ci séen police yi la man mi tekk dañu pistolet me dara affairu góor la rekk Mexique ñoo gëna boon ci yoon bi.

    • @adinamoulsolo765
      @adinamoulsolo765 9 месяцев назад +1

      Pourtant avant Mexique mo geunone yombe Nicaragua mo guenona métti mai légui dafa changé fi métiwone mo yombe fi yombne diafé mane Nicaragua dagnmafa teuthie

  • @aboudjigo8786
    @aboudjigo8786 9 месяцев назад +1

    Mars no,we are February.

  • @thillosarr4049
    @thillosarr4049 9 месяцев назад +1

    ❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉💼💼💼✉✉✉

  • @Kako-gq3cj
    @Kako-gq3cj 9 месяцев назад +3

    5.milliions

  • @AliouThior-dr8ro
    @AliouThior-dr8ro 4 месяца назад

    Des

  • @Mamebathiediagne21
    @Mamebathiediagne21 25 дней назад

    Niatta gay dioxé