Boula dara meti. Lepay bakh, incha Allah. Diga tekki fi, boulessi guessou guiss yaye, guiss baay, guiss diabar aki doom. Yagatoul ! Ignore les insulteurs, ils sont déjà perdus.
Tu as bien dit, n'importe quoi ce qui se passe au Sénégal, bugu teki, bugu teral sa bop, peut être yobu yaye yi maka Diarul li, bien vrai Sénégal est trop dur mais teki diarul sacrifice bi
Entoucas kula dëglu xamni amnga yarr té guëm nga ndogali Boroom bi té niaar yoyu kumu nekci Yaw, dangay diéng rek wayé do massa daanu.. Liici kanam rawuti guëtt dina baax Faal Yaaram ❤
Cette dame n'est pas professionnelle. Elle s'énerve contre le gars qui n'a peut-être pas compris sa question 😢. C'est à se demander comment les recrutements se font
Elle a parfaitement raison ma chère le gars nous dit que c' est Dieu qui l' a amené au Nicaragua et que c' est Dieu qui l' a ramené au Sénégal. Qu' il arrête, Dieu n' a rien à avoir dans tout ça. On lui demande des détails précis rek
@@ururoba3226 ça ne change rien au fait qu'elle ne doit pas s'énerver même si celui-ci lui raconte n'importe quoi. On ne l’a pas forcer à faire ce travail je suppose. Donc elle doit rester professionnelle et garder son sang froid.
Le problème c'est que ces chaînes ne recrutent pas des professionnels compétents. Les questions restent impertinentes. À l'écouter on se rend compte qu'elle manque de connaissances et de culture. Dommage.
La vérité est que les États-Unis n’ont jamais obligé quelqu’un à être PD ou que sa soit une condition pour rentrée aux usa mais ce plutôt l’idée propre de beaucoup des jeunes qui veulent dire ce ça qu’ils sont pour leurs facilités leurs asiles, donc accuser les états-unie d’Amérique ou ceux qui sont rentrés des telles accusations ce vraiment de la calomnie manifeste et évident. Qu’Allah nous pardonnent et nous guident sur le droit chemin.
Massa thiona Mon frere . Tu es un bon croyant et tres courageux . Tu es entrain de rendre service a bcp de migrants . Tu n’as rien invente’et le recit 😢 le meme pour tous cues qui ont eu la chance d’entrer. Yalla rek mo fi neck .
Courage frere yallah lila toudone si yaw tè mo geune si yaw Liguèyate rek khalèi bou ndaw nga dina bakh. Deuk bi lou way déf pour guèneu fi diarnako ndax deuk bo amoul kadou meuno am sa akh ak sa yèlèf
Dangen bariwakh, yonou Nicaragua bi depuis plus de 30 ans mingu dokh, bingen si dougué la lepp yakou parceque vous.netes pas discret, kouy yote dou seukeute
Il est mon ami keba il est chauffeur de taxi allo (Dakar-Saloum) s’il avait 8 millions il n’irait nul part Il venait chez moi pour parler de la musique
L' Amerique est loin d'être le paradis mais j'ai l'impression qu'ils le pensent comme tel 8millions depensés au cas où tu entres en Amérique tu peux faire des annees pour pouvoir épargner une telle somme si encore que tu peux le faire
Frère billay mangui soga sétan sa itv je ne te connais pas mais loy weur di wakh dem nga gnou délo sila continuel sa yoon bienvrai k c difficile déclaré kils sont homo ça ne veut rien dire c'est juste un billet d'entrée boul nék ngaka ya de ses choses ay close la dou lép lagnouy wakh acharnement bi yako tek sa bopp bi ngay dem kén khamoula donc li yeufi gor moy rentre en silence
Et tu penses que dire « je suis pd » après doug ci territoire bi fofou lay yam ?? Dalay topp dh baci say papier… et puis lolou dou yeufou dioulit… diaroul sakh fowé encore moins diko mboubo juste pour am dara.
Cette journaliste n’a jamais pris l’avion. Ni jamais voyagé. De plus elle ne maîtrise pas la géographie. Sa formation reste beaucoup beaucoup, dommage on était en présence d’un gars intéressant
Journaliste, tu es belle Mais ton greffage a détruit ta beauté. Je suis sur que tes cheveux naturels te vont super bien 👍🏿 Ou au moins un greffage moyen
Déjà 8millions c trop et à chaque pays a ses propres conditions tu dois payer pour passer Iow y’a corrompre sa bopp, le billet c moins de 3 millions je pense que t’avais pas bcp d’informations avant de quitter, embarquement amoul faye xaliss sa droit la
@@Dioping mm pas talouma yoyou mais refoulé nagnou la do gueme yallah té jobi wate mais Di weur site yi Di wakh rek na bayi gni beugue tanté déle gnou déme fofou dafa méti dé kou yallah may oportinuté nga meune voyagi démal bo diapé ci Lou deuguer togal néna 11 million la pérte 11 million limou meune Bari n'a trop diaroul touki Sakh
Ce gars est calme machalah yalla nako yalla takhawou
Kou bax kou yarou boy bi machalla du courage c le destin que Dieu te protege
wallabies kay
@@ciekhouna😊😊
😊
😊
Oh mashallah je l’adore lui
C’est un grand homme
Ce jeune garçon
Yallah naala yallah samaa Defal la djam
Courage frère le meilleur reste a venir ❤❤
Xalei bou bakh ga yalla nala yalla maye lou geun si iow 😢❤
Amine ya rabbi 🤲
Boy du courage
Nit kou yarou gua
Nit kou coul
Dia dieuf gainde
Wakh deug defo dara lou niaw yalna Yalla diapalela si barkep seringe touba diambar dawoul dafa dani dole Yalla mogui feppo💪
Franchement parlé gaspillé 8 millions di risqué di diar ci yoonou souf mom yeufou doff leu moins de 8 millions meun nga ci am visa Amérique
No manosi am visa
Ki kay doy na War
Si, déngay né yaw xamo @@representationmatters
Boula dara meti. Lepay bakh, incha Allah. Diga tekki fi, boulessi guessou guiss yaye, guiss baay, guiss diabar aki doom. Yagatoul ! Ignore les insulteurs, ils sont déjà perdus.
sabayon ki dafa yaro de nan ko ñianall rk
Ndeyssane kou Am Tawhid Macha'Allha Doon Goor Yalle 👍
Dara diarouko si adouna cette façon de sacrifier sa vie alors que ce qui t'attends la bas est incertain
Tu as bien dit, n'importe quoi ce qui se passe au Sénégal, bugu teki, bugu teral sa bop, peut être yobu yaye yi maka
Diarul li, bien vrai Sénégal est trop dur mais teki diarul sacrifice bi
8millions tu pouvais investir ici au Sénégal et t'en sortir bien mais courage à vous Seneweb
8 millions pour devenir SDF..li africain rek moko sagne
😂 man dama waru sakh
Moi je vis au USA, ils ne savent pas que économisé 8 millions Amérique du tiakhan
@@PixelsPeeper problème de mentalité là..pour eux en occident il pleut de l'argent..iow mifa nék souléne expliqué lé gnounni daga sokhor
Broh bariga xaliss 8 million do liguey dem chinn di indi bagages toutiii toutiii
Vraiment
Ki kay khamouma louko dal
Entoucas kula dëglu xamni amnga yarr té guëm nga ndogali Boroom bi té niaar yoyu kumu nekci Yaw, dangay diéng rek wayé do massa daanu..
Liici kanam rawuti guëtt dina baax Faal Yaaram ❤
Cette dame n'est pas professionnelle. Elle s'énerve contre le gars qui n'a peut-être pas compris sa question 😢. C'est à se demander comment les recrutements se font
Elle a parfaitement raison ma chère le gars nous dit que c' est Dieu qui l' a amené au Nicaragua et que c' est Dieu qui l' a ramené au Sénégal. Qu' il arrête, Dieu n' a rien à avoir dans tout ça. On lui demande des détails précis rek
@@ururoba3226 ça ne change rien au fait qu'elle ne doit pas s'énerver même si celui-ci lui raconte n'importe quoi. On ne l’a pas forcer à faire ce travail je suppose. Donc elle doit rester professionnelle et garder son sang froid.
@@ururoba3226 parfaitement raison on a vraiment un problème de mentalité
@@ururoba3226 Mais likka wadji wakh lérena mais si yone bi la diare té magui sëdé ces propos.
Le problème c'est que ces chaînes ne recrutent pas des professionnels compétents. Les questions restent impertinentes. À l'écouter on se rend compte qu'elle manque de connaissances et de culture. Dommage.
Kéba Gor YALLA Nala YALLA Diapalé INSHALLA si Barké SEYDINA MOUHAMAD STAWS 🙏🏼
Nama moytoul '' doom '' yi rék , sinon champion leu ! 💪💪💪👍!
Du courage Inchalla leep Dina bakhe mane fofou la diare mais sunu borome Def nasi tawfékhe mais Lou metti la doudedou
La vérité est que les États-Unis n’ont jamais obligé quelqu’un à être PD ou que sa soit une condition pour rentrée aux usa mais ce plutôt l’idée propre de beaucoup des jeunes qui veulent dire ce ça qu’ils sont pour leurs facilités leurs asiles, donc accuser les états-unie d’Amérique ou ceux qui sont rentrés des telles accusations ce vraiment de la calomnie manifeste et évident.
Qu’Allah nous pardonnent et nous guident sur le droit chemin.
Ki da wara wakh, c'est une sorte de thérapie, il a besoin de raconter son vécu, ça aide. Massah et courage Keba
courage boy, il est courageux machalah,, bonne chance
Petit du courage. Ceux qui ont déclarer etre omo pour rentrer cest leur choix. D'ailleurs ya pire que çà..
Yalla nala Yalla maay xollou mougn inshalla 😢
Que qu’Allah te bénisse vous bénisse abondamment amine y’a raby ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Courage walay Dina bakh boul deguelou lii niteyii dii wakh fii dekou wakh la ❤️🥹
Boy t'es un Guerrier...
Doff bou khey touki, il faut au minimum une formation pour voyager, sénégalais amatoul bena respect thii adouna bii,
Machala yalla nala yalla takha wou bou bakh
Massa thiona Mon frere .
Tu es un bon croyant et tres courageux . Tu es entrain de rendre service a bcp de migrants . Tu n’as rien invente’et le recit 😢 le meme pour tous cues qui ont eu la chance d’entrer.
Yalla rek mo fi neck .
8millions je n'aurai même pas besoin de prendre cette route
Wow this is very sad, I know that Senegal is very hard and people are struggling
Massa yalla bakhna di bakh inchalla
Courage 😢
Merci boye keba, wadji rafetnaa. Mais toklen Sénégal gen liguey diambar , diambar laydonn dayniow diaroul dem.
Du courage yalla diékhoul
Kou AM 8 million Senegal loy wout bitim rèw dotok investire 🤔
Vraiment
Manchalla yalla nalla yalla sam senegalais yi nion trian
Courage frere yallah lila toudone si yaw tè mo geune si yaw
Liguèyate rek khalèi bou ndaw nga dina bakh.
Deuk bi lou way déf pour guèneu fi diarnako ndax deuk bo amoul kadou meuno am sa akh ak sa yèlèf
Courage frérot c’est le dis tain que dieux te protège
DéLéne respecter niou dém féké guiss yoon bi doundou si yoone bi ...
Dangen bariwakh, yonou Nicaragua bi depuis plus de 30 ans mingu dokh, bingen si dougué la lepp yakou parceque vous.netes pas discret, kouy yote dou seukeute
Je te jure nioune sénégalais yi nio moudiei xam yone Bobou😂
@@mamidiakhoudiop9567 motah banoussi dougué la lepp yakou
Sénégalais loumou dougou mou siw
@@seynabousakho3733 bilay waxga deug
Boy bi kou bakh bilahi kou yarou dinga am lou bakh dh bilahi
En tout cas boy soneu nagn fi biir New York surtout apres tout ce calvaire
Thiey Deysane 🙏
Merci ❤
Avec cette corruption generalisee on comprend pour quoi le pays est dans la merde
Wallahi 😢😢
Déme rk inchallah 👊🙏🤳
yalla bakhna guena job dina bakh
Courage bravo
L'africain de plus en plus bête en 2023
Merci fall
Il est mon ami keba il est chauffeur de taxi allo (Dakar-Saloum) s’il avait 8 millions il n’irait nul part
Il venait chez moi pour parler de la musique
Mane dé 8 million boumako yorone tokh senegal
Nie dougou te nek New York sona nagne bilay. Ay bouteille la niouy fore nie di takawalou. Non Amerique yomboul. Yalla naniou yalla soutoural
Dafa fek juste amouniou fa ay mbok je pense
Yalla nalla yalla soutoural touma yagguenna si adouna
Du courage goor yomboul
Avec 8million le guinée aux Sénégal devient milliardaire sans parler l'anglais
Peul fouta lane lay doyei moto
Inchallah Di n'a baax 😢
Du courage
Togal reck yalla bakhna 🙏
L' Amerique est loin d'être le paradis mais j'ai l'impression qu'ils le pensent comme tel 8millions depensés au cas où tu entres en Amérique tu peux faire des annees pour pouvoir épargner une telle somme si encore que tu peux le faire
Bro li moma yem dou Amérique 🇺🇸 rk partt 🇫🇷 France ... 8millions yomboul épargner
Je pense que Dieu t aidé pour revenir au Sénégal, si tu travail dure tu as plus d avoir de l argent au Sénégal qu au États Unis
Pp
@@Mameyallap
@@Mameyallap
A ce ritme le senegal est entrain de ce vider de sa jeunesse
Frère billay mangui soga sétan sa itv je ne te connais pas mais loy weur di wakh dem nga gnou délo sila continuel sa yoon bienvrai k c difficile déclaré kils sont homo ça ne veut rien dire c'est juste un billet d'entrée boul nék ngaka ya de ses choses ay close la dou lép lagnouy wakh acharnement bi yako tek sa bopp bi ngay dem kén khamoula donc li yeufi gor moy rentre en silence
Et tu penses que dire « je suis pd » après doug ci territoire bi fofou lay yam ?? Dalay topp dh baci say papier… et puis lolou dou yeufou dioulit… diaroul sakh fowé encore moins diko mboubo juste pour am dara.
@@Mdboy_D s'il s'agit de la voie normale oui mais li maf la
Thieuy Senegalese On parle trop 😂
Niifa dougué.goordjigiéne bayabo niou dieude fa bamél kou diar ci réew mi dinan dagga liga yor
😂😂😂
@@Nas0404a❤
Cette journaliste n’a jamais pris l’avion. Ni jamais voyagé. De plus elle ne maîtrise pas la géographie.
Sa formation reste beaucoup beaucoup, dommage on était en présence d’un gars intéressant
Journaliste, tu es belle
Mais ton greffage a détruit ta beauté.
Je suis sur que tes cheveux naturels te vont super bien 👍🏿
Ou au moins un greffage moyen
Perruque bi mom dokkoul
@@FatouNdiaye-zn1qm ah dokhoul way
Ak lell bi😂
Ndeysaan, gnakk gnouleen diapalai rk..ay ðiambars deugg
❤❤👋🥰🥰
C'est quoi ta coiffure Madame 😢😢😢
😂😂😂😂😂
La gendarmerie doit ouvrir l'enquête au niveau de l'aéroport
Je te jure
8 millions depart lá senegal souma yoron 8 million gnibisi senegal
8 millions cest un bon debut mom
@@coumbinafall8803 vraiment
2 millions sakh capitale.. Gni degniy thiakhaane rek
Déjà 8millions c trop et à chaque pays a ses propres conditions tu dois payer pour passer Iow y’a corrompre sa bopp, le billet c moins de 3 millions je pense que t’avais pas bcp d’informations avant de quitter, embarquement amoul faye xaliss sa droit la
Vérité absolue
Ame na gnou sokhor nakk yaw sa mbokkou sénégalais gnoukoy interview ngay takhaw nane lolou amoufa
Mais courage bro adouna mom fo wara lekk sa werseuk mideff meunoussi dra
Moi aussie on ma fait ça a Italie 2016
Mais c'est vrai senegal amoul guerre amoul famine pourquoi demande d'asile alors qu'on vit bien,c'est juste vous voulez immigrer à tt prix
Daguéne ko warone lathie loumou wakh bagnou refoulé ko😢
Ndeysane 😭
Boy wakh ga deug dé boy you bari ay papier gor djiguéne léne yor😢😢😢
Dagaye fén balén sisou bi
@@cheikhibrahim1351 tu me connais tw
Fén bakhoul wakh loula worol fén la balén sisou bi mana fén
@@cheikhibrahim1351 limo takh sénégalais dou am kham kham peut être aussi naw fék ga
Déme douss dou question way
Il ment pendant les 12 13 jours tu peu prendre des hôtels et te reposé tranquillement
mais bro 8millions mom so ko dafa sa compte dem Ambassade gnou may l visa
Senegal mongui nonnou nak kou am yarou nga
Courage Keba
Baye fall massa mais amoul bayi
Corruption bakhoul ken douko def culture. Bayilen dof dof lou diel ay millions saniko si ala bi rien k pour poukare seulement Bayilen hep sen bop
Boy War nga wagni wakh dji dé bayil plateau yii nguir yallah
Es ce que sa yon nekk n’a si walla da gua begeu dieul placam
@@seydinamouhamadoundiaye5993 yaw tu me amerde way yaw lay wakhal
Sen business lagnouy bagne mou yakhou motax wakh dji arrange woulen😅
@@Dioping mm pas talouma yoyou mais refoulé nagnou la do gueme yallah té jobi wate mais Di weur site yi Di wakh rek na bayi gni beugue tanté déle gnou déme fofou dafa méti dé kou yallah may oportinuté nga meune voyagi démal bo diapé ci Lou deuguer togal néna 11 million la pérte 11 million limou meune Bari n'a trop diaroul touki Sakh
La journaliste est nulle, merci l'homme tu la recadres même dans ses questions 😅
Lou takh yamo Espagne 😢
Hum llu du mna nek
Machlla yalla bakh na
Seugne bi Lou beuri limou wakh nonou leu mais amna yi khamni dou nonou
Saperukbi ngir yala
Mais sa wayy 8 million nangakoyy yore didéf clandidtin
Lolen wax bagn refoulé len
Affaire de fierté molen di tardel
Une chaîne qui parle un dialecte vous n êtes pas sérieux
Senegalais je ne sais pourquoi mou yomba nakh rek us amoul dara insbi
Waay mo tané senegal fouff
Magui fi dep8 2019 alors je suis concien de ce que je di .jai un ami depuis avril migui fi amoul job 7 mois sans liguey tu imagine ce perde de temp?
Bayfall 8 millions maynala départ boubah galsen
Deugeu pire 🙏
Cheuteuteuteut li kenne xamoul lane nguir Adduna kepp