salam Sénégal lifi am kou bonneu doywar. les gens sont devenus très méchant ils font des choses très méchantes à leur propres membres de famille. la jalousie et la méchanceté les envieux le maraboutage à détruit les familles. je suis très contente de cette émission. c'est une maladie grave qui est dans le coeur de bcp de sénégalais. prions que dieu nous protège de ces fléaux
Le cas du monsieur beuryna Sénégal billay Yaye youy bagne dome sans raison. Des parents qui disent sans gène de que tel enfant est mon préféré ca fait trop mal Massa au Mr et du courage
Mon frere courage mane mi lolou lay ndounou souma demè senegal souma defè 2jours rek sama yay commençè tonngo ak mane may diokhè depense location et tous tè souma tardè agne douma agne
Vraiment je suis très touchée par ce que ki limou wakh damay doundou depuis ke ma nék khalé batay massou ma sentir amour maternel contrairement à mes fréres et sœur mé c ki est bizarre moy moi j'adore ma maman et l'aime de tout mon coeur et elle est ma seule raison de vie c pour que je travaille dure pour pouvoir réaliser mes plus grands rêves en vers elle je suis en Arabie saodi c dure mais je tout ce que je v c réaliser mes souhaits mm si je c k je suis la dernière qu'elle se souciera sur terre
Allahou Akbar ndankeu rekkk ,parfois satan dina dougoussi dingeuté you barii pour yakh,wayé meunala conseillé quelques prières,si tu veux bien sur whatsapp ,n'abandonne jamais ta maman, n'oublie jamais ça, discute bien avec elle pour savoir c'est quoi le vrai probleme
Massa yallah molaye faye soit forte que Dieu te donne la force et courage . C est bien aime ta maman de tout ton coeur comme tu dis et fais tout pour elle ne regrette rien tu gagneras la bonté de Dieu
Ma mère m aime tellement je vois ses yeux briller d amour quand elle me parle y a des km qui nous séparent mais on a un seul qui bat moi ma mere et frere et soeur. Alahdoulilah merci maman diop Thialaw d avoir une mere comme toi. Courage min frère tu as pas cet amour c est triste.
G vécu la mme chose parcque bima 1ans lama sama yaye abandonné ma nek mag dem weur ko ba guisko mounanema meunla am lounei si gor beug ma diay sama bop amna dom sakh sama yay tegoul tankam fima nek lou beuri youma meunoul wakh g 24ans mais awma ben amour si mom dafa jiteul khaliss lou meti lay doundoul
Ma chérie massa wayé ak métite bo meuneuh ame si Adina démoule si Yallah diouli woor niane souniou borome mou téguila li Yallah nala souniou borome takhawou courage ma chérie 🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Du courage ma soeur...affection maternelle dafa ame solo si dôme. Dis-toi k Yallah moloko séde et va de l'avant dans ta vie. Nul ne choisit ses parents.
Cest de la sorcellerie je te le jure on m'a fais presque la même chose entre moi et ma mère j'habute dans une maison ou ya une ami a ma mère elle a beaucoup de fille et moi ma mère n'a que moi comme fille elle m'aime faisais tous pour moi cette femme m'envié acause de ma beauté car je suis plus belle que ses filles j'ai plus de chance qu'eux ma mère m'aider tellement elle a tous fais pour me séparé avec ma mère j'ai eu un copain riche il m'aide a aller voir et le protéger quand j'ai su la vérité j'avais mal car je disais que ma mère a changer quelle me déteste quelle est jalouse de sa propre fille j'ai tous regretter car cetais pas sa propre grès dagnon deudeulé mais sa s'arrenge petit a petit car il faut faire quelque chose cette femme la fais que pour ne plus avoir la soutien de ma mère et d'être malheureuse mais yallah rek momay diapalé habité avec ses ennemis c'est pur que habité avec vempire
Moi même ça fait 10 ans que je ne suis pas venu au Sénégal ma grande soeur es décédé mon petit frère es décédé je ne suis pas venu et c est ma propre famille gnoma ko yobé j avait un restaurant en France je travaillais dure je n ai jamais oublié ma famille quand j ai accouché j ai laissé mon restaurant en gérance je viens au Sénégal pour me reposé 6 mois gniou nawtalma pour me gnibi France dakh bima neke Sénégal fin du mois yonné tou malene bobou ba légui rien ne va plus pour moi
J'avais vecue le meme du méchanceté, maraboutage ect.... Mais bon DIEU EST UN GRAND QUAND IL DIT EST BON SERA TOUJOURS INSI WALLAHI☝🏽🙏🏻. YALLA NANIU YALLA SAMU TÉ ARR NIU SI AYU NITT KU IGNANE.
Masa chérie moi aussi mé légui mis nako dama dane défe liguéye you keur gui yeupe nioumay ignorer souma timé léke gui douma mana léke sakh souma fabarone may fathie sama bopou ak dieude mbourou ndéki 😭😭😭sama soeur di faye facture ndoh mane may faye facture kourant mére bi ni douma yobalé kéne si keur gui may liguéye mindane Niou may faye 25mil semaine bima waré faye facture bi ma fébar fadio sama salere mére nima bo fayoule facture bi do fanane si chambre bi mére bi guéné ma keur gui 😭😭😭 mou méti wone trop si mane sama Tons fate ma
Fatou Kone magui lay masawou boubakh dila wakh lou meti yagoule legui inshalla yalla nieuw mane mi dagnouye ma dor bama sone mais sante yalla boubakh nakh si lou meti lima diar moma déf lima done taye machalla
@@khadijafall8126 Bilaye ma chérie mougne dou néne légui kay magui sante yalla boubakh di sama pape mima andi France di diko nianale yalla yeureume ko té yésale yeureume si mome dafe ma endi France 6 mois mou décédé sama ginawe lolou rék mon ma Méti mé sante nji dane téque fitena louniou sokhla ma défale léne ko Légui kay macha Allah 🙏🖕🖕
Masta Ndeyssane nak yaye kene rek amoul remplaçante yalla nala yalla boleh ak sa yaye ,guene sopekou entre mère et fils, guene nek ay complicité, mane dama beugu sama yaye teh keep ku wahk si yaye dafmay touché 😭😭😭😭nek sa xaritou yaye dafa nehk Machallah yalla nala yalla djoubeleh ak yaye Inchallah.
Amena wadiour you bone liwadji wakh gnou bari gnoung kay doundou téséni dome yi dougnléne déff dara légui dall danaka dome yi gnodieul palasou wadiour yi ndakh wadiour you bari yeurmandé bignou wara ame siséni dome amatougnouko billay dome you bari gnougui doundou kome amougnou ay wadiour de fois nga guiss si wadiour yokhamné sénidome dagnouy fébar ndakh yagui ténésakh dougnléneko wakh ayway wadiour yi déloléne sénekhel si yalla lingénedi déff séne dome yi métina
Mane môme lima diakhal Naka la nitt Di amé khôl liguèyé moromou nittam Franchement yène mom dieufou mbam la Yalla nanou yalla mousal çi maraboutage 🙏🙏🙏
Moi je connais pas ma mère si je pouvais le voir ne serait-ce une fois dans la vie. C'est dur mais Alhamdoulilahi que l'islam ma récupéré et ma sauvé je suis né chrétien
Moi c pareil. Elle ne ma jamaus fait la bise ni tenu la main Je suis toujours critiquee : elle est tres projective disant que si nous n'étions pas la , elle serait riche . Elle ne nous aime pas parce quelle ne saime pas . Cest une épreuve
@@adjib.38 C pa facilement mai de tte façon c nos mamans même bou feikei begou gnou saxe dagno wara daw thi lilene neikh nakh euleuk lou djara soralé la
@@maguitandiaye4682 wa maguita , epreuve leu , pour meu yok jom . Yallah natouneuon la femme de pharaon . Wallah Abraham ak papeum. Man demeu yok seumeu dine . Alhamdoulilah
Ahh mon frère tu as posé une question qui m'a interpellée. J'ai perdu ma mère j'avais 10 ans. Mes parents n'étaient pas mariés donc je n'ai pas connu un foyer stable ni affection, ni amour ni rien mais je rends grâce à Dieu je vis avec. J'ai une vie de solitaire et par moment je suis à terre et je pleure un bon coup puis me relève. Donc ne pleure pas. Dolil gueum. Je m'arrête là ... Ngen balma
Le gars j'aurais voulu avoir ses contacts Yorouma touss loumako diokh mais amana soutien moral dinako meuneu si mom C'est dur😰😰😰😰😰😰 Il y'a de ses parents niakk lenn sakh ngeunell laye doneu Toubab yi li motakh niouy kharou
Ces juste de la jalousie des parents envers leur fils-filles just parcequils sont en Europe ou ailleur. faites bien la remarque ces triste vraiment du courage
yalla dafa meneu seylou diam bi. ma koye digal kep kouye doundou lounimel . lo done def lou bakh yokal .yaye noumou mel yaye la dafa metti nak ngaye mougnelo kouye doundou lou metti wayé kene dou def lou bakh te yalla takh dici am faye bou bonne. yalna sounou borome defare khol yi .nitte menoul am lou deune dome surtout yaye .mettina wayé yalla nako borome bi safara
Le dernier intervenant wakhna lou méti, mais faut niou taxaw sétlou boubakh thi limou wakh. Eumb ak weussine nimou métté, doom ak nimou nékhé pour mane li c'est pas naturel, d'habitude genre doom yi di téral sen yaye yi kén doulén bayi thi nonou no déff am niouy diémeu deudalé ak sen wadiour yi
Gniy dem ci serigne nanebilayy guissnako ta propeee famille et ci niar nio diourr?senegal gni am ngor beriwoul dhh wayer magnum yalla samb lou waydeff seu lokho ley natj tôt ou tarddd
Vous M. qui vivez en Espagne et qui n'avez pas l'amour maternel contactez-moi S. V. P.. .. Je vous apporte tout mon soutien et ayez du courage gueumeul Yallah diekhoul te Nianal sa petit frère bi guene Adouna
tout se que je veux dire sur se que jai vecu avec ma mere ne peut pas racontè sur des commentaire ca merite un roman mane mom affection yaye khamoumako si je vois mes ami avec leur maman je me pose la question si c pas des film mais mon pere a rempli se vide alhamdoulilha sheut seriously jai besoin d'un therapeute pour vidè mon sac
Ndeyesane c vraiment dei amna yaye you niak khel loulen sen dôme defaral niou khep ko masta frère gni seufff sen dome yi pour louniou len lathié niou diokh len ko bounè mofi am ligueye na ligueye sa dôme seuyy legui yi dafa beuri affaire serigne domou diambour bo khamoul niniouko boté khôlal bayi 🤷♀️geuneuleunté ay dome moy indi louné si famill legui mére d famille yi nio tass sen keur yi
Mo ko wara dioure sakhe. ame na yaye you bone . bagne sene dome .. peut etre daniou bagnone baye dji mo takhe ngi sippi ko tchi dome bi .. toute les meres ne sont pas parfaites. il yen a qui maltraitent leurs enfant qui les maudissent . et les meres qui jete ou tuent leurs enfants a la naissance ? nite kou bone meme so amer dome do changer .dagaye bone rek . meme sene propre dome moune naniiou ko def lou bone ndankhe sokhore . Yalla naniou yalla moussale tchi yaye bou bone yaye bou la bagne .c est la pire des choses. mais ca existe malheureusement .
Pauvre elle dit peuvre après on les appellent journaliste, thiate est une pro mais je n'aime pas ses tche tche quand elle parle ce n'est pas naturelle.
serigne yikoy deff...Yalla naleen Yalla torokhal; torokhal senn djaboot si dounya balaa gno agg alakhira
salam Sénégal lifi am kou bonneu doywar. les gens sont devenus très méchant ils font des choses très méchantes à leur propres membres de famille. la jalousie et la méchanceté les envieux le maraboutage à détruit les familles. je suis très contente de cette émission. c'est une maladie grave qui est dans le coeur de bcp de sénégalais. prions que dieu nous protège de ces fléaux
Le cas du monsieur beuryna Sénégal billay Yaye youy bagne dome sans raison. Des parents qui disent sans gène de que tel enfant est mon préféré ca fait trop mal Massa au Mr et du courage
Liga wah sah hamoko bilahii
Mami Diedhiou je lé vécu soit fort
Mon frere courage mane mi lolou lay ndounou souma demè senegal souma defè 2jours rek sama yay commençè tonngo ak mane may diokhè depense location et tous tè souma tardè agne douma agne
Vraiment je suis très touchée par ce que ki limou wakh damay doundou depuis ke ma nék khalé batay massou ma sentir amour maternel contrairement à mes fréres et sœur mé c ki est bizarre moy moi j'adore ma maman et l'aime de tout mon coeur et elle est ma seule raison de vie c pour que je travaille dure pour pouvoir réaliser mes plus grands rêves en vers elle je suis en Arabie saodi c dure mais je tout ce que je v c réaliser mes souhaits mm si je c k je suis la dernière qu'elle se souciera sur terre
Sokhnasi boul meuss tayi thie sa yaye
Ndeysane mais iow defal sa yarr rek wadiour la
Allahou Akbar ndankeu rekkk ,parfois satan dina dougoussi dingeuté you barii pour yakh,wayé meunala conseillé quelques prières,si tu veux bien sur whatsapp ,n'abandonne jamais ta maman, n'oublie jamais ça, discute bien avec elle pour savoir c'est quoi le vrai probleme
Massa yallah molaye faye soit forte que Dieu te donne la force et courage . C est bien aime ta maman de tout ton coeur comme tu dis et fais tout pour elle ne regrette rien tu gagneras la bonté de Dieu
Ma mère m aime tellement je vois ses yeux briller d amour quand elle me parle y a des km qui nous séparent mais on a un seul qui bat moi ma mere et frere et soeur. Alahdoulilah merci maman diop Thialaw d avoir une mere comme toi. Courage min frère tu as pas cet amour c est triste.
C'est ce genre de pratique comme le maraboutage qui à laissé L'Afrique en retard.
G vécu la mme chose parcque bima 1ans lama sama yaye abandonné ma nek mag dem weur ko ba guisko mounanema meunla am lounei si gor beug ma diay sama bop amna dom sakh sama yay tegoul tankam fima nek lou beuri youma meunoul wakh g 24ans mais awma ben amour si mom dafa jiteul khaliss lou meti lay doundoul
Ndeysane fififatima Ndiaye yalnala yalla defal tawfekh ba sa delosi khelam
Ma chérie massa wayé ak métite bo meuneuh ame si Adina démoule si Yallah diouli woor niane souniou borome mou téguila li Yallah nala souniou borome takhawou courage ma chérie 🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽🙏🏽
Faites toujours vos devoirs vis à vis de vos parents quelque soit leurs comportements 🙏
Du courage ma soeur...affection maternelle dafa ame solo si dôme. Dis-toi k Yallah moloko séde et va de l'avant dans ta vie. Nul ne choisit ses parents.
Cest de la sorcellerie je te le jure on m'a fais presque la même chose entre moi et ma mère j'habute dans une maison ou ya une ami a ma mère elle a beaucoup de fille et moi ma mère n'a que moi comme fille elle m'aime faisais tous pour moi cette femme m'envié acause de ma beauté car je suis plus belle que ses filles j'ai plus de chance qu'eux ma mère m'aider tellement elle a tous fais pour me séparé avec ma mère j'ai eu un copain riche il m'aide a aller voir et le protéger quand j'ai su la vérité j'avais mal car je disais que ma mère a changer quelle me déteste quelle est jalouse de sa propre fille j'ai tous regretter car cetais pas sa propre grès dagnon deudeulé mais sa s'arrenge petit a petit car il faut faire quelque chose cette femme la fais que pour ne plus avoir la soutien de ma mère et d'être malheureuse mais yallah rek momay diapalé habité avec ses ennemis c'est pur que habité avec vempire
Moi même ça fait 10 ans que je ne suis pas venu au Sénégal ma grande soeur es décédé mon petit frère es décédé je ne suis pas venu et c est ma propre famille gnoma ko yobé j avait un restaurant en France je travaillais dure je n ai jamais oublié ma famille quand j ai accouché j ai laissé mon restaurant en gérance je viens au Sénégal pour me reposé 6 mois gniou nawtalma pour me gnibi France dakh bima neke Sénégal fin du mois yonné tou malene bobou ba légui rien ne va plus pour moi
Massa.
Le dernier intervenant a touché nos cœurs . Il dit la vérité. Mais il va rebondir
Bonne chance
9
La fille qui est au milieu est une vraie professionnelle machallah
Elle faisait l'interview des célébrités par moment thiat très pro
J'espère que big taf suivra, Inch'Allah..
Il est très pro aussi Mash'Allah
J'avais vecue le meme du méchanceté, maraboutage ect....
Mais bon DIEU EST UN GRAND QUAND IL DIT EST BON SERA TOUJOURS INSI WALLAHI☝🏽🙏🏻.
YALLA NANIU YALLA SAMU TÉ ARR NIU SI AYU NITT KU IGNANE.
⁰⁰
Ndaysane grand frère du courage et je te comprends car je vie la même chose
Courage chérie😥
Masa chérie moi aussi mé légui mis nako dama dane défe liguéye you keur gui yeupe nioumay ignorer souma timé léke gui douma mana léke sakh souma fabarone may fathie sama bopou ak dieude mbourou ndéki 😭😭😭sama soeur di faye facture ndoh mane may faye facture kourant mére bi ni douma yobalé kéne si keur gui may liguéye mindane Niou may faye 25mil semaine bima waré faye facture bi ma fébar fadio sama salere mére nima bo fayoule facture bi do fanane si chambre bi mére bi guéné ma keur gui 😭😭😭 mou méti wone trop si mane sama Tons fate ma
touba Niang merci beaucoup
Fatou Kone magui lay masawou boubakh dila wakh lou meti yagoule legui inshalla yalla nieuw mane mi dagnouye ma dor bama sone mais sante yalla boubakh nakh si lou meti lima diar moma déf lima done taye machalla
@@khadijafall8126 Bilaye ma chérie mougne dou néne légui kay magui sante yalla boubakh di sama pape mima andi France di diko nianale yalla yeureume ko té yésale yeureume si mome dafe ma endi France 6 mois mou décédé sama ginawe lolou rék mon ma Méti mé sante nji dane téque fitena louniou sokhla ma défale léne ko Légui kay macha Allah 🙏🖕🖕
Masta Ndeyssane nak yaye kene rek amoul remplaçante yalla nala yalla boleh ak sa yaye ,guene sopekou entre mère et fils, guene nek ay complicité, mane dama beugu sama yaye teh keep ku wahk si yaye dafmay touché 😭😭😭😭nek sa xaritou yaye dafa nehk Machallah yalla nala yalla djoubeleh ak yaye Inchallah.
bilay j ai les larmes au yeux yalla na yalla yalla takhou sii Barkel Mouhamed
La fille de teint clair n'a qu'à aller faire une formation en prise de parole wasalam!!!!
ta bien dit
Menoul waxx ba paré noy togué nitt di waxx foula guay re di wok bopp zéros espérance
Prise de parole en public en plus elle souriait quand le gars qui vivait en Espagne racontait son histoire
J'ai la même remarque begua régné rék molén sonal
@@aissatoudiallo5813 oui c'est un manque de professionnalisme.. Thiat Seck est très pro
Amena wadiour you bone liwadji wakh gnou bari gnoung kay doundou téséni dome yi dougnléne déff dara légui dall danaka dome yi gnodieul palasou wadiour yi ndakh wadiour you bari yeurmandé bignou wara ame siséni dome amatougnouko billay dome you bari gnougui doundou kome amougnou ay wadiour de fois nga guiss si wadiour yokhamné sénidome dagnouy fébar ndakh yagui ténésakh dougnléneko wakh ayway wadiour yi déloléne sénekhel si yalla lingénedi déff séne dome yi métina
Benn si mane sama xol bi mo déh ah la vie
Massi kham dara
Je vis la même chose .dome yi am yeurmandé rekk la yaayi di doyédèle.MaisAllah est grand.
Moi aussi je vie la même chose mais yalla bakhna
@@mariethior5105 ,du courage lépaay djiékhe ,,Inshallah.
Mane môme lima diakhal Naka la nitt Di amé khôl liguèyé moromou nittam
Franchement yène mom dieufou mbam la
Yalla nanou yalla mousal çi maraboutage 🙏🙏🙏
Bravo vraiment tout tes la méchanceté humaine es trop .maisk Dieu NS protéger
Moi je connais pas ma mère si je pouvais le voir ne serait-ce une fois dans la vie. C'est dur mais Alhamdoulilahi que l'islam ma récupéré et ma sauvé je suis né chrétien
Bon courage Yahya. Dieu est grand frérot!
Walahi digua marabouté KO khamoul la moi même je l'ai vécu et du sérieux m nakkk guem yalla ak doone talibé serigne Babacar sy lou waye def boppam
Li meity na trop yaye bila djour té amo affection thu mom moy lolou
Moi c pareil. Elle ne ma jamaus fait la bise ni tenu la main
Je suis toujours critiquee : elle est tres projective disant que si nous n'étions pas la , elle serait riche . Elle ne nous aime pas parce quelle ne saime pas . Cest une épreuve
@@adjib.38 C pa facilement mai de tte façon c nos mamans même bou feikei begou gnou saxe dagno wara daw thi lilene neikh nakh euleuk lou djara soralé la
@@maguitandiaye4682 wa maguita , epreuve leu , pour meu yok jom . Yallah natouneuon la femme de pharaon . Wallah Abraham ak papeum. Man demeu yok seumeu dine . Alhamdoulilah
Thiate nékh ngama trop danga yiw machahala rawatina si wakhine lou am solo wakhine 💋yaye nouyou nala 😁💋💋
Amna yaye you méll nonou dagno doywarrr
Salame.salame.liy.wady.wakh.lou.amenla.manmi.lolou.yak.sama.seye.
Ahh mon frère tu as posé une question qui m'a interpellée. J'ai perdu ma mère j'avais 10 ans. Mes parents n'étaient pas mariés donc je n'ai pas connu un foyer stable ni affection, ni amour ni rien mais je rends grâce à Dieu je vis avec. J'ai une vie de solitaire et par moment je suis à terre et je pleure un bon coup puis me relève. Donc ne pleure pas. Dolil gueum. Je m'arrête là ... Ngen balma
Sénégal geum na'gnou yalla wayé wolou'wou'niou'ko / séytané la'niou geuneu wolou ke yalla
Wakh gua dégue dh lou ñieuw gniouné dane ma liguéye faté dougalou yalla
Dernier témoignage +_ 18mn .
C triste c dur mais c ta mère. Mougnall yalla bahna. Yalla nala yalla dimbalii
Sama kharite sama a mdi diam mbaya da thioub rafetna manchallah
Machallah c'est la première fois may sétane émission bi mais c'est très important bonne continuation
Yallah dou mayé lépe la fille en noire tu es belle mais meuno wakhe,tele pour wakhe wakhi nite leu ndakhe gneupeu lay déglou
Le gars j'aurais voulu avoir ses contacts
Yorouma touss loumako diokh mais amana soutien moral dinako meuneu si mom
C'est dur😰😰😰😰😰😰
Il y'a de ses parents niakk lenn sakh ngeunell laye doneu
Toubab yi li motakh niouy kharou
Je te jure il m’a fait pleurer 😢 courage frère yallah baxna
Ooooh ma beug thiate 😘😘😘😘. Ey waay beug nako guiss deh
C'est triste, ce rapport que vit cet homme avec sa maman. Qu'Allah fasse que cette maman retrouve sa conscience
Amna guel you beuri manière !!!
Cheuteuteu.....
Chaque personne a une singularité et nulle n'est bête alors le mieux ce serait de l'encourager à s'améliorer tout simplement...
Ndeysane ay way Masta frère yalla n yalla tahaw la si daradier Rassul Allah saws amine
Courage courage boumou takh mouk ngua tongo ak sa yaye, yalnako Ya rabbi wagni
Dieu est la du courage
Vraiment une mère qui aime pas son enfant je le croyais pas mon amie me rencontrer la même chose mais je la croyais pas ho c'est triste 😥
Sa thioub manchallah guedj na gnio guisse dieuredieuf
Ndeysana le dernier m'a fait pleuré lingua doundou mettina trop mais bilahi Lou baxx rk nguay ame defal sa devoir rk lissi dess c entre elle et Dieu
Ces juste de la jalousie des parents envers leur fils-filles just parcequils sont en Europe ou ailleur. faites bien la remarque ces triste vraiment du courage
Kou khess ki meunoul way mais sama yaram Dawna trop
Yallah nagn yallah doli soutoura ndaysane adouna jaroul Lou gnaw dei bambel khate na ta yatou
Machallah amna solo
Nagnou diamoudji YALLA bala wèss
Très intéressant
Yene nieup deme si marabout yi surtout yene djigene ni yala mome geumoulene ko serigne gene geume
yalla dafa meneu seylou diam bi.
ma koye digal kep kouye doundou lounimel .
lo done def lou bakh yokal .yaye noumou mel yaye la dafa metti nak ngaye mougnelo kouye doundou lou metti wayé kene dou def lou bakh te yalla takh dici am faye bou bonne.
yalna sounou borome defare khol yi .nitte menoul am lou deune dome surtout yaye .mettina wayé yalla nako borome bi safara
Machalah
Thiate sa ligey refet na trop massalah
La teint claire elle n’est pas à la hauteur de cet émission franchement
😭😭😭nooo metiyna trop mama
Grand bii dioylo nama walay mé yalla baxna
Moi je comprends pas pourquoi Ria ce comporte ainsi ce quoi ton Problème vraiment, en cas Émission bi amena solo trop Bonne Continuation a vous
Amna solo trop
Li wadj wah beurinafi kou sagnone sa yaye moy done sa lep wayer geuneuleunter yaye bouko si moytouwoule wayer nak djom rek lalay yok
Goorgolu bou bakh té déf sa devoir vis a vis d elle dieu est grand
Du courage ont vie le meme problema
Le dernier intervenant wakhna lou méti, mais faut niou taxaw sétlou boubakh thi limou wakh. Eumb ak weussine nimou métté, doom ak nimou nékhé pour mane li c'est pas naturel, d'habitude genre doom yi di téral sen yaye yi kén doulén bayi thi nonou no déff am niouy diémeu deudalé ak sen wadiour yi
Yallah nako Sunu Borome Soutoural Yallah beuss khole yi
Fi quou def nitt lou bone bilay dineu retourner si yaw ... deukkk bo khamni maraboutage rekk darra doufeu bakh....
Emision bi amena solo diodio mdaye borom zac mdao bakh té oyof sa emision bi amena solo
Mee kii iskeu Merbi Moko diour
Sama xol toyna massa frere😪😪😪
Bilaye li amna mane instant yi j vie pareil chez ma belle famille
Masa ma chéri
Bon courage
Masseu ma chérie
Bon courage ndeyssane dna bakh
Bilahi deug nako ndeysane môme mi di commence d pleuré
Kouy wakh Toubab dou dougou adjana dangay kaathie walahii haziim thieeye Soune Boroom aka beurii doolé...
Dèle wakh lo metrisa
@@hassamiyoufall9939 kou bakh wakhal sa xalat
Ndongo daara wakh deug dé bakh deukoulfene meuna nek thi bep domou adouna
Doyna warr
Adina yagoul te YALLA rek moye bour
Name lolou moma dale tè djiguène la magui fi si espagne
Courage faites toujours vos devoirs vis a vis des parents surtout les mamans bon courage
Madjiguene Kane merci gracias por todo
Kia amoul professionalisme
Gniy dem ci serigne nanebilayy guissnako ta propeee famille et ci niar nio diourr?senegal gni am ngor beriwoul dhh wayer magnum yalla samb lou waydeff seu lokho ley natj tôt ou tarddd
Vous M. qui vivez en Espagne et qui n'avez pas l'amour maternel contactez-moi S. V. P.. .. Je vous apporte tout mon soutien et ayez du courage gueumeul Yallah diekhoul te Nianal sa petit frère bi guene Adouna
@@Ama-tb9es estceque je peux te contacter je vis dans une situation dépressive je te jure dakh khalat bou meti bilaye
Ou es ton contact ?
La fille en noir elle est la parfaite définition de ( tu es belle et tais toi ) 🤦🏻♀️
Mdrrr
Tu es belle mais mounoul wakh je sais pas degoul wolof wala
Esk sa Yaye moko taye pask nit dina Def dara feķk tayou ko
Fatou mbodja limouy wakh ni aka ame walahi azim
tout se que je veux dire sur se que jai vecu avec ma mere ne peut pas racontè sur des commentaire ca merite un roman mane mom affection yaye khamoumako si je vois mes ami avec leur maman je me pose la question si c pas des film
mais mon pere a rempli se vide alhamdoulilha
sheut seriously jai besoin d'un therapeute pour vidè mon sac
Mane déh Motakh souma amone sakh milliard kenn douko khamm
Mane kay mako doundou nit ko khamni dafa sokhor ignane niaw ndiot wolowoul kene te lou bone rek lay def si adounam mane lo khalat defnako
👏👏👏👏👏👍🙏❤
Stp qui peut me dire svp dans quel chaine de télé et à quel heure se passe cette émission répondez svp
C’est une télévision en ligne ma Grande c’est à partir de 09h et 10h 30
C’est Senegal7
Ndeyesane c vraiment dei amna yaye you niak khel loulen sen dôme defaral niou khep ko masta frère gni seufff sen dome yi pour louniou len lathié niou diokh len ko bounè mofi am ligueye na ligueye sa dôme seuyy legui yi dafa beuri affaire serigne domou diambour bo khamoul niniouko boté khôlal bayi 🤷♀️geuneuleunté ay dome moy indi louné si famill legui mére d famille yi nio tass sen keur yi
Vérité absolue
Wakh deugue emission bi amna solo mais ria yagui yakh emission bi do pour télé gua balma
ame na yaya you sik mais est-ce que moko djour meune na ame diourou ko dé
Mo ko wara dioure sakhe. ame na yaye you bone . bagne sene dome .. peut etre daniou bagnone baye dji mo takhe ngi sippi ko tchi dome bi .. toute les meres ne sont pas parfaites. il yen a qui maltraitent leurs enfant qui les maudissent . et les meres qui jete ou tuent leurs enfants a la naissance ? nite kou bone meme so amer dome do changer .dagaye bone rek . meme sene propre dome moune naniiou ko def lou bone ndankhe sokhore . Yalla naniou yalla moussale tchi yaye bou bone yaye bou la bagne .c est la pire des choses. mais ca existe malheureusement .
Ki dé ndéy sann khaw ma bann chance lama eup wayé mako eupeulé chanchou yaye
Thiate dama la khamer trop j n sais pas où nak mais......
Le dernier temoignage m'a énormément touché ! est il possible d'avoir son contact
Faut pas couper un auditeur ki parle
Pauvre elle dit peuvre après on les appellent journaliste, thiate est une pro mais je n'aime pas ses tche tche quand elle parle ce n'est pas naturelle.
Qui peut me faire une traduction
Moi
Ë
😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😢
Deugue
😭😭 😭😭😭😭😭😭
Slm slm
Yaye bauye mère diodio namnala ba yangui ame diam ?
Borom lou noir li amoufi place
Non est ce que lii amena tamite heupna
Vraiment
🙄😭😭😭😭😭😭😭