Ahmed Khalifa Niasse: Sokhna Oumou "Sama Niételle La"

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 5 фев 2025
  • Ahmed Khalifa Niasse: Sokhna Oumou "Sama Niételle La"

Комментарии • 1,6 тыс.

  • @TalibeCheikhoulKhairy
    @TalibeCheikhoulKhairy 5 лет назад +6

    Sot khèèkh limo takh wooroul.ndakh gniy khèkh daniouy parer juboo nga wayadi nak 😅
    Neu talibé yi continuer di saguanté ak di saaga Serigne si rek.niom dé gningui nii.founiouy dioubo wé dolén ko fèkké.
    Heureux ménage à vous deux.Yalla nanguén thi am ay Saalihiin ❤

    • @ahmadoubabandiaye167
      @ahmadoubabandiaye167 5 лет назад +1

      Bilae ta raison il faut qu'on arrete les insultes surtout envers nos guides religieux

    • @TalibeCheikhoulKhairy
      @TalibeCheikhoulKhairy 5 лет назад +2

      @@ahmadoubabandiaye167 Gars yi yeugou niou sakh li khèw

  • @moralfall801
    @moralfall801 5 лет назад +7

    Mame Abdou Aziz dabakh da bakh beugue lou bakh ba déme di gueune bakh ak di bolé nitt gni li rek leçon la .sa none sakh boulko yéné lou bone fi ak mongui nék djoulite ndakh "al mouslimou bil mousslimi kalboune yani " dioulite ak moromam dano wara mélni tabakh andando ba lou thi yakhou boune ko défaroul lénéne li fék siko machalla yalla na diame yague

  • @rubykiss3959
    @rubykiss3959 5 лет назад +60

    Mariage confirmer alhamdoulilah yalna yala barkèl seuybi Niass Coumba Abdallah.

  • @youssoudiouf6649
    @youssoudiouf6649 5 лет назад +3

    Ce qui est triste au Sénégal cest que gniy féliciter Ahmed Khalifa sakh kham nagn ni dou nite kou bakh guemoum touss kou degue ses versions rekk khamko. Mais nite gni lim wakh Maodo ci lagn contane. Pitié pour vous Maodo défouléne dara. Di nguene khamni Maodo dou sen morom.

    • @agueye3947
      @agueye3947 5 лет назад

      Oui nitt yi dinagn contane ndakh sagga sa mam nga am diabar
      La prochaine fois si kelkun attaque tivaouane c à nous talibés de rester calme

    • @mamadoucisse9449
      @mamadoucisse9449 Год назад

      En tous ca pere ahmad a une Jolie femme machallah elle et vraiment mignone sa femme la fille de dabakh jeurjeuf serigne Ahmed

  • @abdoukarim9584
    @abdoukarim9584 5 лет назад +8

    و الله احبك حب لا يقاس ahmed khalifa yalla nafi yague té weer

  • @adourahimseck6070
    @adourahimseck6070 4 года назад +1

    Que le miséricorde vous bénisse et vous donne longue vie et bonne santé vraiment moi je ne vais plus vous dire quelque chose de mal parce on te comprend pas mais mais mais tu mérites du respect

  • @morniang2342
    @morniang2342 5 лет назад +77

    Sama gayi founk len seni wadiour mo guene, tee jamou yalla lolou rekk mo worr

  • @moussagaye194
    @moussagaye194 5 лет назад +1

    Merci 1000 fois ahmed koula bangn na deeeee manou niou si yaw touss ndakh baye mola nianal defal loula nekh

  • @richemonde7248
    @richemonde7248 5 лет назад +46

    Je suis fan de Ahmed khalifa 🙏🏾

    • @samsatoufall1096
      @samsatoufall1096 5 лет назад +1

      Ak mane

    • @dorndokh3344
      @dorndokh3344 5 лет назад +1

      Fans walla Talibe ? Ki dou star dé Serigne la

    • @aichagueye2210
      @aichagueye2210 5 лет назад +1

      Malako gueneu fan

    • @mendanjaye5549
      @mendanjaye5549 5 лет назад

      Ak man mako fan pirr😂🤣😂

    • @mamadoudiop1105
      @mamadoudiop1105 5 лет назад +1

      @@aichagueye2210 daguen ko fan d apre propos yimu wakhon wala soude lolu ay seytane guen

  • @aboucamara2962
    @aboucamara2962 5 лет назад +2

    Machalla niass dieuredieufe baye niass yari keur yi bennalla yaxakate yi comme ibader di na rouss

  • @peaceandlovelove7679
    @peaceandlovelove7679 5 лет назад +102

    Sokhna aida Ak Ahmet khalifa niass gno eupp fitt si senegal ndiaye😂😂

  • @Corailpro
    @Corailpro 5 лет назад +26

    Machallah, khalifa Sall est très correct. Yallah nala yalla samm.

    • @thiernodiallo2254
      @thiernodiallo2254 5 лет назад +1

      Aye dorr marto rek

    • @thiernodiallo2254
      @thiernodiallo2254 5 лет назад

      Oumo khalsoum do darra

    • @fatoundiaye1103
      @fatoundiaye1103 5 лет назад +1

      Thierno Diallo oumou mo gueune sa ndeye Ahmed gueune sa baay

    • @saoune1saoune16
      @saoune1saoune16 5 лет назад

      @@fatoundiaye1103 ahmed khalifa mom thiagala djiguène rk lay weur tèi baggage yii bahoul daniou ko tapeu si niger

    • @fatouguisse6421
      @fatouguisse6421 5 лет назад

      Mane ma diomi wadji moy dougou si beurigo diwtirr guéneu weikh ki mako bagne té yalla takh. Oumou moom dama gueneu si moom ndakh respecter woul mamame

  • @cipionndiaye3847
    @cipionndiaye3847 5 лет назад +4

    #12mn 19 sokhna ci réé na ba teud...béguééé waay...Ahmed Khalifa veut juste que les gens savent qu'on est de simples mortels...heureux ménage mon père..
    Goney you ndaw yi di commenter ak di saaga..yéém léén...lo maîtriser woul danga ciy mandou..

  • @ndiackdang91
    @ndiackdang91 5 лет назад +32

    Mane dal Ahmeth khalifa fan la, soumanékoudone mouride yay done sama serigne.

    • @leuzleuz8602
      @leuzleuz8602 5 лет назад

      Tu es content alors

    • @mamadoudia2347
      @mamadoudia2347 5 лет назад +2

      Boul togn mouride yi wakhal Say wakh ta dieul Say engagement

    • @tk92221
      @tk92221 4 года назад

      Donc di nga perte. Ndakh il est bizarre

    • @fallmor1049
      @fallmor1049 4 года назад

      Mbokomi wésogoulé délëne wakhe loléne geume

    • @ndiackdang91
      @ndiackdang91 4 года назад

      @@fallmor1049 yaw ya wara diangue di wakh lo kham. Loula leer né gueumouma limay wakh?

  • @naturehumaine1219
    @naturehumaine1219 5 лет назад +26

    Weddi dé giss bokou ci.
    Li fi Ahmed Khalifa wax yeup
    Giss nguene li ci toop.
    Lo xamoul xamo ko🤔
    Kou yabou daal di fermer sa bouche🤫🤫
    So amé loy diokhé diokh ca ndeey ak ca baay tey jammu Yalla👌👌

  • @papin456diop9
    @papin456diop9 5 лет назад

    Kouy wëër nâfèkheu nala diâp, Ecoutez le bien et vous saurez que loumou def meune ci guèneu. Il faut être un vrai doméram pour être comme A Kh Niass.

  • @ndeyebarakatoufall7314
    @ndeyebarakatoufall7314 5 лет назад +8

    Barki yalla mèrè wona Ahmed wayè taye dafma rètanlo ki ak ndèmssi yalla bèthio gno guene nèkh sur terre founè lagnouy feulè

    • @alaminmohamed6327
      @alaminmohamed6327 5 лет назад

      Ndeyebarakatou Fall 😂😂😂😂😂😂😂😂

    • @sanguebitv8429
      @sanguebitv8429 5 лет назад

      Non boyl teukeulé niar you bokoul bethio bethio la Ahmed Ahmed la

    • @Ndaar-Faam
      @Ndaar-Faam 5 лет назад

      Exactement nakk tu lui as trouvé à ALMETTE NIASS un bon semblable: BETHIO !
      C'EST BON PLUS DE COMMENTAIRES !!!

    • @Ndaar-Faam
      @Ndaar-Faam 5 лет назад

      @@sanguebitv8429 bien sûr teukeulé ce sont deux Say Say !!!

  • @cheikhcheikh893
    @cheikhcheikh893 5 лет назад +1

    Machalla niass longue vie à toi sa baye mame Khalifa niass moy khout bou zaman

  • @papemaouloudfall2682
    @papemaouloudfall2682 5 лет назад +4

    Wa lii nekhoule ana borome holyou tangue yii dailene vive serignebi niass

  • @seydialioutop3640
    @seydialioutop3640 5 лет назад

    Une très grande leçon pour les détracteurs. Il faut faire très attention entre les hommes religieux car tout c’était passé hier avant aujourd'hui. Nos ancêtres ont bien tracé le chemin et pourquoi de nos jours les petits disciples veulent semer la séparation?

  • @karimcamara7865
    @karimcamara7865 5 лет назад +18

    Ndanane deug moy Dr Ahmed Khalifa Niass

  • @mbayediop2371
    @mbayediop2371 5 лет назад

    Vous qui commentez et dire du mal, ayez dans l'esprit que le pardon est signe de grandeur divine. Kou nek kholko thissa bop. Si ce mariage a eu lieu, Alhamdoulilah devrons nous dire, encore une fois la noblesse fait valeur. La famille de Mame Elhadji Malick Sy et de Mame Abdoulaye Niass ont montré encore une fois, que non loin des differents qui peuvent exister, elles incarnent la noblesse. Si tu m'insulte et en retour tu demandes la main de ma fille, c'est au fond y'a un regret, et au fond je pensais pas à ce que je desais, au fond on est tous humains. Pas de rancune, tels les enseignements de Dabah. C'est l'islam qui gagne, et tous talibé doit en être fier, wa salam!!!

  • @saakhewardiouck2824
    @saakhewardiouck2824 5 лет назад +15

    Mashalla yal nako yalla barkél , lii sou amoul wone mou diakhalma il fallait que kilifa yi woné béne missal bouye nopilo yakh kate yi , yéne gniye niawlou lii dafa mélni gueumeutoulene ni arass la niouye takké seuye yi , amna fi nak nio khamné légui sokhnassi la niouye wakhal nane greffage ak Pathé té ay kilifam nioko mayé yene lou nguéne si , loudoul ay spectateur nak , parceque yéne yenay yakh kate ya donne demb, di douguou keur serigne si di khol séni sokhna na niouye togué, séni dome na niouye solo etc... , motakh al hadji malick wakhone si digeuntém ak hadji abdalla si gni si nara douguou di yakh khamone nako , motakh lii firndé la rék diap léne ni daa dieul domam rék maye ko domou hadj abdallah té nopissi mo gueuneu wor wakh ba yakho si , par parlo thi ak nafékh nguéne di bayi wédi nguéne ba sonne ndakh reuye ak niak talibé légui comme amna , sokhnassi nguene di doyodal thi séne you niak fayda yii , serigne dou yalla wayé yalla lagne koye toppé té lolou si biir la bou féké ni nak yéne serigne bou nouro ak nitt nguéne khép ko moye nitte nguéne di diamou wayé dou yalla vrment rére nguéne lole .quant à ahmed mom sou nguéne kholé sakh khamné dou séne morom kone wakh ba dé rék wayé nienté mouno léne ko si mom al hadji malick rda al hadji abdalla rda ak serigne hamid kane rda danio wakhone ni bou féké séne koleuré gui lou wer la nako yalla firndel si la yalla dogual serigne Mansour bou makk , baye niass ak sokhna astou kane guané diamono si béne ate , lolou la yalla woné wate fii rék kone bou yabo nguéne nopalou mag gni dougne séne morom yalla nopi na té matouléni talibé ndakh niaka kham , réwandé , eupeul té niémé nitou yalla wayé kou si otouwoul sa bopp torokh adina ak alakhira .

    • @Coumbagaye1976
      @Coumbagaye1976 5 лет назад

      Dara woroulassi nei ay kilifam nioko mayer. Un d la famille a dit k wa tivaouane yeugou niou fou ahmed takkei soxna si. Tei mom amon na djeukeur ba tasd doudou wade moko ndieukon takk. Islam maynako mou out seddei kenen mayei ko sans ay ndigalou way diouram. Donc alahou ahlam

    • @diopmamediarra2820
      @diopmamediarra2820 5 лет назад

      Moy thiou moy thia déh

    • @saakhewardiouck2824
      @saakhewardiouck2824 5 лет назад

      @@Coumbagaye1976 yow ite est ce que am nga lou la lére si ni ay kilifam mayé wougne ko , té l'islam lim ko maye selon son cas lolou rék moye compté , kilifa goguou ngay wakh est que wor nako né benene kilifa thi ay mbokam you diégué téwé woul mayé bi , importance bi moye ndigueulou yalla bi ws .

    • @bel5838
      @bel5838 5 лет назад

      Ki kann moko matériel? Meussouma dégg ameth ni diw moko May djabar

  • @abibouba6107
    @abibouba6107 5 лет назад +1

    Sa yone nèkoul si tivaoune ndiakeu diom

  • @baayseex2595
    @baayseex2595 5 лет назад +3

    Ndeysann dafa beugueu S.Touba nak, loumou wakh bolé kossi ❤❤❤

  • @talibebunjeng9470
    @talibebunjeng9470 5 лет назад +44

    Ndeyssane BAYE Niass mola ñanal thiakaw - Thikanam reek Ahmed khalifa Jërëdieuff Cheikh Al Islam

    • @fatoushadiakhatei9156
      @fatoushadiakhatei9156 5 лет назад +5

      Kha'na Baye niass khamalouka ni djiguénn d'où diokh loxo gor boudoul boromm keureumm .

    • @cheikhbayekonteye9668
      @cheikhbayekonteye9668 5 лет назад +3

      Fatoush jakhate outil teggin

    • @fatihmetoubarhama7241
      @fatihmetoubarhama7241 5 лет назад +2

      @@fatoushadiakhatei9156 hee xamal nigay waxé

    • @modidiaw8291
      @modidiaw8291 5 лет назад

      @@fatoushadiakhatei9156 wakhe deuge

    • @fatouawaniass687
      @fatouawaniass687 5 лет назад +2

      @@fatoushadiakhatei9156
      Wakhal sa wakh tè boulci bolè Baye kom Khamo noy wahè ak kilifa nga baalma nak

  • @Mamadou-Fall
    @Mamadou-Fall 5 лет назад +11

    Wakh nalenn pere niass , dama ko fan !!! Bilahi

  • @diopndeyeamina9561
    @diopndeyeamina9561 5 лет назад +1

    Wa mouni y'a koi keski se passe damay def cauchemar wala ki Ahmed khalifa niass la yaw kouyaboul gnanalela wala gnou wathialela kamil mon dieu y'a graw lo dougue guénessi niass y'a bari pekhéh waw kay kennn douyaw au passage heureux ménage wala grand ménage

    • @abdoulayendiaye4296
      @abdoulayendiaye4296 5 лет назад

      Nopoloulen ni ndawsi nangou mo khame na KO nopal ki sague sa Mame guaye nangou moulay djegue khamatouma si d'Ara,c'est domage Sénégal guathe d'où raye.waye douniou tere DI doylo Mame maodo malick sy(radiyalahou talla anhou).

  • @bamba4886
    @bamba4886 5 лет назад +66

    Kii mo meneu dougue si barigot diw tiir kèènn wékhe taalle

  • @yorodiallo4722
    @yorodiallo4722 5 лет назад +2

    Bilahi kouy doora meune kouy saaga. Diadieuf Niasse, doolé dokhoul diame💪💪💪💪💪💪

  • @alladiopxassidatv3056
    @alladiopxassidatv3056 5 лет назад +8

    Yallana ngafi yague tewir niass thi barkep borom touba

  • @nyassafall2316
    @nyassafall2316 5 лет назад +39

    heureux ménage mon marabout de coeur inchallah

    • @thiernodiallo2254
      @thiernodiallo2254 5 лет назад

      Khatal sa ndeye Yaw setane ga

    • @tk92221
      @tk92221 4 года назад

      Mais A. khalifa niass vous venez de le découvrir, il a été décoré par honoris causa, c’est un franc-maçon de la loge skull and bones. Begueu égarer nitt gnii dilèn rérloTout comme Youssou ndour

  • @toubadiop4803
    @toubadiop4803 5 лет назад +22

    Niasse machala amna solo wahbi yalla nala yalla fay si barke serige touba

  • @lamamanpoule8963
    @lamamanpoule8963 5 лет назад +15

    Yalla na yalla leral li Dougal sokhna oumou si sey bi .amna louma meti torop

    • @ousseynousarr5210
      @ousseynousarr5210 5 лет назад

      Gueumouniou sene mame ak sene baye

    • @papybarhamdieng7593
      @papybarhamdieng7593 5 лет назад +6

      Maguette Cissé boulene weddi Yalla. Yalla loumou deff rekk nonoula. Yalla deff ngani dakoro Bakar geunouko reuy. Mangui diegalou 🙏🏻

    • @muuntaxasilla7892
      @muuntaxasilla7892 5 лет назад +6

      Way way Sëy bu ñu taak ci farata ak sóona moo dila méeti kon waar ga xõolate sa bópo

    • @TalibeCheikhoulKhairy
      @TalibeCheikhoulKhairy 5 лет назад +7

      @@papybarhamdieng7593 wèddi Yalla dé lii mo thi geuneu gaaw.Yalla dogal ngani dédéét? Soubhanallah 😢

    • @diopsiyare5936
      @diopsiyare5936 5 лет назад +3

      Diam ak pekhem bour y’Allah ak dogalam. Façon pekher bou nek pekher nguene ko saga nguene ko soralewo lene ay domam ak ay seutam niom niou nopi y’Allah fayoul lene. Koumou nekh na saga waye Ahmed K Niasse dou moromou kene kouy yewo tiwawouane y’Allah moy mayer te y’Allah d’où nit.

  • @bassiroudiop9814
    @bassiroudiop9814 5 лет назад +24

    Yalla na seye bi barkel

  • @famakanesarr1717
    @famakanesarr1717 5 лет назад +2

    Barké baye mala beugg yalna sey bi barkel yarabi ameen loudoul jamm jammako geun Niass goumba Abdalah 🤲🏾🙏🏾

  • @diopsiyare5936
    @diopsiyare5936 5 лет назад +4

    Diam ak pekhem bour y’Allah ak dogalam. Façon pekher bou nek pekher nguene ko saga nguene ko soralewo lene ay domam ak ay seutam niom niou nopi y’Allah fayoul lene. Koumou nekh na saga waye Ahmed K Niasse dou moromou kene kouy yewo tiwawouane y’Allah moy mayer te y’Allah d’où nit.

    • @thorthor4293
      @thorthor4293 5 лет назад

      Diop Siyare setal si Yalla niit kou Bakh dou fen..!! Khalife général des tidianes fen rek ngakoy degu moy tivaoune té demal lathié fou dingeul Li diougué... Ndananou Sénégal moy wa tivaoune nangoul rek té kham nagnou lep boulgnou wakh Lo nak.

    • @diopsiyare5936
      @diopsiyare5936 5 лет назад

      thor thor y’Allah rek mo kham lep yaw khamoulo touss nafekh nga

    • @ndeyeteuw6900
      @ndeyeteuw6900 5 лет назад +1

      iow momou yaye nafékh bi iow diop siyare wakhal sa wakh rek guénési wa tivaoune kiguay dèfendre sakh sou diaratone si loumou wakhone mou démé nénéne loumou doug rek meune nasé guénate.Ni rek guéne di déf ba alkou

    • @bamsbams3171
      @bamsbams3171 5 лет назад +1

      Diop ya méùneu doul Mamou Ahmed khalifa Niasse Maodo Moy kilifam /
      Sénégal kou'fouy yéwô poussière Maodo rombou'na'la

    • @thorthor4293
      @thorthor4293 5 лет назад

      Diop Siyare teudieul sa guémign fi kou nek kham nga kouy sa baye... donc fen bakhoul...

  • @abdourahimseck6334
    @abdourahimseck6334 5 лет назад +1

    Ameth très intelligent je l aime bien .sou diékhé rek diekhna la vie continue

  • @alhikmatv2206
    @alhikmatv2206 5 лет назад +8

    Billahi kou jeul sey mbir ajko si serign sii guissoumala mbaaw

  • @dansokhomouhamed3061
    @dansokhomouhamed3061 5 лет назад +2

    Niass.un.très. grand. Messier. Bravo.bik.respect. Niasse👌👌👌👌🙏🙏🙏🙏🙏

  • @mamadouleofaye4938
    @mamadouleofaye4938 5 лет назад +55

    Yay ndanane deh .Ahmed
    SVP soyez neutre sur leur mariage .
    Fi kou nek amna liko doy si keureum.

    • @ndeyefatoudiallo4237
      @ndeyefatoudiallo4237 5 лет назад +5

      Mamadou faye merci

    • @abass4057
      @abass4057 5 лет назад +3

      Mamadou léo faye wakhatiko dé! Ndanane pire

    • @abdoulayediabang3726
      @abdoulayediabang3726 5 лет назад

      No mon frère ! Ce message adresse le à Ahmed Niass ! Neutralité moom mooko yélloo !

    • @mamadouleofaye4938
      @mamadouleofaye4938 5 лет назад +3

      @@abdoulayediabang3726 ok frère. Mais senegalais bou fi nek amga loula doy seuk SI sa mariage donc naniou ko bayi ak mariage bi. Talibé danio wara dal parcke niom kilifa yi ils se connaissent

    • @mamadouleofaye4938
      @mamadouleofaye4938 5 лет назад +3

      @@abass4057 anita guisga lolou bilahi pa bi niveau wam dafa dépassé gayi . C ke senegalais yi danio gawa mer koi. Senegal ben bop la. Naniou rafetal rek

  • @southafrica6239
    @southafrica6239 5 лет назад +2

    Maa Shaa Allah!! Niass coumba Abdoulah!! Waa Senègal khamonou yaw yay kan Niass

  • @ladiva8730
    @ladiva8730 5 лет назад +10

    Yalna séybi barké mais moytoul di nétali aÿ bou passé Papi Ahmed

  • @khew2006
    @khew2006 5 лет назад +1

    Mak yi nénagnou sou dérette diakhosso khasté diekh. Kou khass Ahmed Khalifa rek khassalé Sohna Oumou Sy.

  • @elmbayegueye4334
    @elmbayegueye4334 5 лет назад +13

    Thiaye Ahmed khalifa niass moye champion dhe

  • @khew2006
    @khew2006 5 лет назад +3

    Nékhoul ba nékhoul mais il est très fort khawouma foumou diar sou yabo rek gnou tok diko sétane. Gnikodone saga taye warnagnou rouss

  • @sunnyday7844
    @sunnyday7844 5 лет назад +18

    Mime reew ahmed khalifa ko mome
    Reew mi ahmed khalifa moy kiko mome
    😂😂😂 bilay damako fan

  • @khadijabaye9389
    @khadijabaye9389 5 лет назад +2

    Machallah Niass avec la syenne Oumou Kalsoum tu es Adorable

  • @sowmoussa6471
    @sowmoussa6471 5 лет назад +48

    Ahmed khalifa soutacké diabar louthi souno yone

  • @aminatandiaye3620
    @aminatandiaye3620 5 лет назад

    motakh gnoune internautes yi warnanouy mandou. CHEIKH AHMED TIDIANE CHERIF ken meunoul bole ndiabotam. Réro meunoul gnak ; ndakh seytane moh bari dole . Yalna YALLA wathié diamm si Sénégal. AMINE YA RABBI

  • @aidasene419
    @aidasene419 5 лет назад +13

    Mane dal beug na serigne bi niass

  • @momodoukane5861
    @momodoukane5861 5 лет назад

    Yow Ahmed Khalifa niass lou nehk rek ga boug dohol so doh nosss la gueume so wokh daffa wouttee

  • @seydinagueye5528
    @seydinagueye5528 5 лет назад +10

    Niass coumba Abdallah dundeul ba say may di bawane am tawféikh ak taaysir chahandanta daréyni ak nuru daréyni sunu brome swt samaleu boppam téik leu fu yakeu yéiggul beug leu ndax linga beug ku tedd ki chéikhoul xadim radilahu anhu

    • @diopsiyare5936
      @diopsiyare5936 5 лет назад

      Amiiiiine hakaza mouride

    • @soulayendiaye3702
      @soulayendiaye3702 5 лет назад

      Seydina cueye yaw kopo ki beuguioul kéne guiemoul kéne diuguiéne ak khalliss rék moko gnore

    • @oustazsy7061
      @oustazsy7061 5 лет назад

      Soulaye Ndiaye wakh kou sokhor ngaa fii wakh 😂

  • @dansokhomouhamed3061
    @dansokhomouhamed3061 5 лет назад +1

    Bravo.bravo.bravo.Niasse... Machalla.🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏bik.respect. à. Nom. Chefs. Religieux👋👋👋🙏🙏

  • @mamediarraboussodiouf5141
    @mamediarraboussodiouf5141 5 лет назад +18

    Dieureudieuf khadim Rasoul💚

    • @fallsoudeur.8616
      @fallsoudeur.8616 5 лет назад +3

      Mame diarra bousso Diouf wawww loum wout fi

    • @securitydream7567
      @securitydream7567 5 лет назад +1

      Kone bou nité mo gueuneuh sope bou con...

    • @abdoulazizndiaye705
      @abdoulazizndiaye705 5 лет назад

      Bayilene tourou serigne bi nguene def slogan di kaffé di fowè di garouwalé dissi wat dissi tiakhane... santoulène ko... Wasalam

  • @willystar4007
    @willystar4007 5 лет назад +4

    Une seule certitude. Elle est très belle la dame Oumou Kalsoum Sy. Machallah

  • @awasakhosarr2474
    @awasakhosarr2474 5 лет назад +28

    Non maneu Ameth khalifa damako bgu😂😂non kiii damako fan😂😂 yala na yala goudal sa fane maye la weer guerrier ga mame boy🙏

  • @boygaye1132
    @boygaye1132 5 лет назад +14

    Machalla niasse thi kaw thi kanam rek barke sr touba

  • @sadioyama5649
    @sadioyama5649 5 лет назад +6

    Yay kilifa mala fan yalla nga am diam

  • @mamediop1524
    @mamediop1524 5 лет назад

    Mane dé damaye mandou
    Yalna YALLAH maye nieup soutoura ak diame ak Salam abadane si barakatou RASSOUL SAWS AMIIIINE.
    Yalna SOUBHANA WATAHALLAH moussale niou si seytané. Sénégal diame rék in sha Allah amiiiine amiiiine amiiiine ya RABB

    • @gouradia7541
      @gouradia7541 5 лет назад

      Sokhna oummou rèdiu Dana fèk diaf wèsuo malako wakh tè ding go thiss

  • @diehiitoumakgni2503
    @diehiitoumakgni2503 5 лет назад +28

    Wakhdji rafetna loll yalna diam dji continué

    • @mouhametfall9550
      @mouhametfall9550 5 лет назад

      Xana ap mourid nga motakh nga bakh

    • @diehiitoumakgni2503
      @diehiitoumakgni2503 5 лет назад +2

      @@mouhametfall9550 yaram wawawe mourid la mes yéné niou geune dé walay ndeysane

  • @lemzocanzo5406
    @lemzocanzo5406 5 лет назад

    Yal nala yalla sopi si barke seydina Mohamed

  • @muhammedsamba4294
    @muhammedsamba4294 5 лет назад +6

    Alhamdulillah yalna yalla barkel seye bi

  • @pommecorail2699
    @pommecorail2699 5 лет назад +1

    Bilay ñieupeu la beugue heureux ménage

  • @alhadjindiaye2248
    @alhadjindiaye2248 5 лет назад +34

    Lou rafet dou mossa ñaaw machallah yalna saybi barkel te diammou yaga

  • @Djana4
    @Djana4 5 лет назад

    Machalla papa Ahmed khalifa te guenko bayi ki pro la xell kesser la kou d’où ci mborram rekk sonne

  • @serignepapemalicksytv6388
    @serignepapemalicksytv6388 5 лет назад +15

    Nous les talibes dal faut faire attention et aussi madou vous voies

  • @uyhd9757
    @uyhd9757 5 лет назад

    Ki kou bah la comme son frère sidi lamine Yalla na Yalla seral soufam té harelko aldiana

  • @freemansolo5427
    @freemansolo5427 5 лет назад +24

    Ahmad Khalifa Niass dal moy nandité quoi

  • @senetoufamame6004
    @senetoufamame6004 4 года назад +1

    Thiéye yalla acolate bi tamite mé cé le monde a lenvers

  • @binthuwaliddiouf126
    @binthuwaliddiouf126 5 лет назад +22

    Ahmade yalna seuy bi barkel yalnasi ndiaboot gu barkel toppeu si

  • @mamadougueye3380
    @mamadougueye3380 5 лет назад

    Bayii lēnne fomii tē diamou yalla ak Yonne lolou serigne cheikh Ahmadou Bamba dikkē lēe

  • @akimsylla9224
    @akimsylla9224 5 лет назад +4

    Barké borom touba diam rék ngaye ame

  • @diarrietousow9683
    @diarrietousow9683 5 лет назад

    imaginez le mariage de Ahmed khalifa niass et sokhna aida diallo ? quel cocktail explosif niom niar kiff kiff fit késsé laniou louniou dougou gueineu ci

  • @amydiatta7367
    @amydiatta7367 5 лет назад +7

    Bilay sokhna oumou def gua lou niaw ki gua kham ni lou né wakh nako sa mamé gua sey ak mome

    • @deugdiop3616
      @deugdiop3616 5 лет назад

      Mais lui nak tu l as entendu parler aujourd'hui

    • @rassoulgaye2317
      @rassoulgaye2317 5 лет назад

      Sa papa niata yone la xoulo ak sa yaye tei tewoul monkoy seuyel niata yoon lala sa papa khass tei yangui ande ak mom domram

  • @aminatadiop6263
    @aminatadiop6263 5 лет назад

    Senegal dal mo nekh lou nekh way wakh tay bou souba gua geine si way dieureudjeufè Seydi Hadji Malick yala naniou yala fayal Mame Maodo mom miniou yarr nioun ay talibèm 👌

  • @seckseck3810
    @seckseck3810 5 лет назад +13

    Ahmet khalifa niasse ya
    Niaka diom deug deug .
    Sokhnassi mom amoul kilifeu sou amone kikifa dou doug siyaw. Cheytane radjiim nga mais tu vas voir.
    So khamone lilay yoot dinga bayyi lingay yoot.

  • @tidianediallo2400
    @tidianediallo2400 5 лет назад

    tu est .un vrai Sénégalait.meun pouthie meun pathie

  • @thiammor62
    @thiammor62 5 лет назад +26

    🤣🤣thiëye yalla , multiplie couleurs plusieurs manières 😂😂

  • @ndeyadiop578
    @ndeyadiop578 5 лет назад

    Machala dama beugueu ameth khalila niass haha yalla na seuy bi barkel machala

  • @louisediagne67
    @louisediagne67 5 лет назад +4

    Macha alla yalla sey by bakel naiss ak sy 💏💕💕

    • @henriettediouf2551
      @henriettediouf2551 5 лет назад

      oumou dal fi gua danou do fofou. Sama Serigne gua nak mais vraiment...

  • @gansiryfall7247
    @gansiryfall7247 5 лет назад

    😀😁heureux ménage félicitations à toutes la familles et à hamed niass

  • @conscienceverite7898
    @conscienceverite7898 5 лет назад +4

    Extrait du roman « Vie et enseignement de Thierno Bokar, Le sage de Bandiagara » de Amadou Hampaté Bâ, page 137-138.
    L’hypocrite enturbanné
    Thierno Bokar avait horreur de l’ostentation (étalage de sa fortune, et son mérite) sous toutes ses formes et, plus encore, de l’ostentation religieuse. Un jour, je lui demandai :
    - Thierno, quelle est la conduite que tu hais le plus ?
    Il répondit :
    _ Mon ami, je n’aime pas haïr, mais la conduite que je désapprouve le plus et que je prends en pitié est celle de l’hypocrite ridicule. Il s’agit de cet individu qui, affublé d’un turban entortillé huit fois autour de la tête, porte ostensiblement au cou un chapelet à gros grains, marche appuyé sans nécessité sur l’épaule d’un disciple et sur un bâton plus fétiche que bourdon (bâton de pèlerin). Cet homme prononce avec beaucoup plus de bruit que de ferveur la formule de la Shahada et prêche avec une ardeur qui n’est motivée que par l’espoir d’un gain immédiat. Un tel homme corrompt l’esprit et pervertit le cœur. Il est mille fois plus abominable qu’un assassin qui ne s’attaque qu’au corps.

  • @mouniroundiaye4853
    @mouniroundiaye4853 5 лет назад +2

    billahi oumou kalsoum mo bone déh té rouslou sa wa keur baye ak sa wa keur mame wayé khamna aye niari khath rék you ande dieume safara ndakh kou nago seuyak alkou khalifa niasse amo diné wayé démléne loussi kaname rawoul beute

  • @khadimleye2785
    @khadimleye2785 5 лет назад +7

    Yalla loumou déf Ken manou si Dara hmed khalifa sakanam

  • @macoumbandiaye716
    @macoumbandiaye716 4 года назад

    Brother vous etes formidable que le bon dieu vous garde

  • @cfcholding1836
    @cfcholding1836 5 лет назад +24

    Oumou rouss lo nga niou dh bilahi Yalla kham nako

  • @pathecisse8004
    @pathecisse8004 4 года назад

    My pa, best la koi

  • @woulbatdi2985
    @woulbatdi2985 5 лет назад +5

    لله درك ! هذا من فضل ربي ! الخلية وام المؤمنين معا نور علي نور !!!

    • @Ndaar-Faam
      @Ndaar-Faam 5 лет назад

      Haza layssa minn fadli rabb bal minn inda CHAYTANE !!!

  • @mbayeababacardiallo7440
    @mbayeababacardiallo7440 5 лет назад

    Ameth khalifa niass ta tothie diobou ndeyam. Talibe mouride yi moom niokoy félicité si commentaire yi thiow li yeup maodo moy binaiguar sene khol you bone yi. Mai femme bi moom amoul kilifeu. Na wakhnak kane moko maay ahmed khalifa. Forêt

  • @ousseynoucisse9071
    @ousseynoucisse9071 5 лет назад +6

    Wallahi aduna amoul solo yalna yall moseléne si saytané

  • @mourtallafall3526
    @mourtallafall3526 5 лет назад +1

    No Ahmed Nak Guèrier La Koi, 72 ans ngay takk sokhna No Diambar nga

  • @inasal8176
    @inasal8176 5 лет назад +3

    Heureux ménage way, yalna diam yague. Koumou nékhoul talal gaz tok si

  • @abdoulayewade971
    @abdoulayewade971 5 лет назад +2

    Nono gi d'où Ahmed khalifa Niass yalla atèna 💪ah deugeu ré ka deugeu légè ngila done beugeu ndakh Liga yak wa tivaouvane khana rous Nanou vive tivaouvane

  • @gayeabdou1553
    @gayeabdou1553 5 лет назад +22

    Wakhoumala Mariage ou pas sakh mais greffage khessal baa wekhh ci Domou Dabakh lii moy li Serigne Mbaye Sy Ndiol Fouta di wakh nane kou dougou souniou keurr yi khepp niou

    • @elhadidiallo3441
      @elhadidiallo3441 5 лет назад +1

      Serigne mountagha interdit mèche xef xessal mako beug

    • @domoupapam4729
      @domoupapam4729 5 лет назад +1

      Deugg deugg fall waxal dehh

    • @taniangdabax6913
      @taniangdabax6913 5 лет назад

      Sk c la fille de Mame Abdou Soxna Oumou bobou makk la d dou ki d

    • @aminata0485
      @aminata0485 5 лет назад

      @@elhadidiallo3441 C est interdit par l'Islam et par tous les religieux frère, mouy Touba, di Tivaouane. Gnune kay gno dieuféwul. Tu verras ay doomu Serigne ak soxna youy xessal, di pose ongles ak lenen. Nagnu gnane Yalla May gnu deg ak toop !

    • @gayeameth5407
      @gayeameth5407 5 лет назад

      Habib Niang bien di ki loumouy wax sakh khamouko

  • @moussasylla2987
    @moussasylla2987 5 лет назад

    Dama rouss je pleure kii lane la wara yabai tivaone diew nge al amine do dara

  • @amadoulaminediallo3100
    @amadoulaminediallo3100 5 лет назад +22

    Bravo.sama serigne gayangui cissou mdr.kimoye akhmed kenlafi

    • @gorguidiouf4825
      @gorguidiouf4825 5 лет назад

      Domou ram pirr

    • @fatoundiaye1103
      @fatoundiaye1103 5 лет назад +1

      Gor Gui Diouf souko sa ndeye amine comme djekar dou wakh ak sa baye

    • @Ndaar-Faam
      @Ndaar-Faam 5 лет назад +1

      Un Say Say comme Keen laffi moom !!
      Un menteur comme lui kenn laffi.
      Un franc-maçon comme lui kenn laffi.
      Un ndialoo katt comme lui kenn laffi.

    • @omarsallah1601
      @omarsallah1601 5 лет назад

      Ghulaami Tidiane 🤣astakhfiroullah

    • @deugheulaveritemoufin4731
      @deugheulaveritemoufin4731 5 лет назад

      @@gorguidiouf4825 yaaye khadj

  • @Babistbjgjhiuhhgg
    @Babistbjgjhiuhhgg 5 лет назад +2

    Fran Mac,ons bou bon bi yène niar yèna yame ay bandi ngèn xalis rek li warna yè wa Senegal se baye nek waliyou kamil taxoul nga nek nitou Yalla

  • @mouhamadlaminedrame5299
    @mouhamadlaminedrame5299 5 лет назад +5

    Ahh sama wadji Ahmed mbeur piirr

  • @mamadouba3331
    @mamadouba3331 5 лет назад +1

    Niari mandari youy taxawalou dox ba dadjé