Réaction Zarko attaque reug reug après F2F contre boy Niang: dafa beuri wax nama dieul..

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 2 дек 2024

Комментарии • 53

  • @gnionkhoretv282
    @gnionkhoretv282 День назад +3

    Vraiment zarko esprit gua sa mentalité dafa raw les gars 💪💪💪

  • @AliouSeck-j1v
    @AliouSeck-j1v День назад +7

    Zarko rek💯💯💘💘

  • @SENETIKTOK
    @SENETIKTOK День назад +11

    Reug reug rek laniouy tooop dimbali léneu niou fi guéneu toguone naane boy bi app doff laa légui doff bi guénii wakh mou wane léne yoone bi😂😂😂😂😂😂

  • @NdiaboutaDiouf
    @NdiaboutaDiouf День назад +3

    vérité absolue zarko

  • @OmarBa-r8r
    @OmarBa-r8r День назад +2

    Merci zarco

  • @sanadieme756
    @sanadieme756 День назад +2

    Zargo beuz ngua beugeu demb siteu tey reug reug deffaal louniou fil deff moi geun ngay wakh rek😊😅😅😅😅😂😂😂😂😂

  • @seedybayo7942
    @seedybayo7942 День назад +2

    Zarco rek 🔥🔥🔥🔥❤

  • @mohamedd7470
    @mohamedd7470 День назад +2

    Aidara say question terre à terre naniou😂😂😂

  • @LassanaDrame-j2u
    @LassanaDrame-j2u День назад +2

    Reug Reug da wara avancé pourquoi mouy dieul ay boy you nek fi

  • @ThioubouArnold66
    @ThioubouArnold66 День назад +2

    Premier commentaire

  • @papamboup7207
    @papamboup7207 День назад +2

    Reug reug est le meilleur diambar .yalla nopina

    • @moussadiouf626
      @moussadiouf626 День назад

      Mais vraiment dey débordé c lui et boy niang

  • @pascal1863
    @pascal1863 День назад +1

    REUG REUG seul 🎉🎉🎉

  • @AbdourahmaneSamba-i8w
    @AbdourahmaneSamba-i8w 23 часа назад +1

    Zarco sa data yaye

  • @ndoffenetine5333
    @ndoffenetine5333 День назад +2

    Mbala may guiss né reug dina dane boy niang ma guiss ko bilay 😮😮

  • @mamadoulaminembodji9648
    @mamadoulaminembodji9648 День назад

    Aperistes yi😂😂😂

  • @P4t5R
    @P4t5R День назад +5

    Boy niang bi ma guiss pareina d, beurei dore bokoul akkk mma

    • @Malicksindidi1988
      @Malicksindidi1988 День назад +2

      Saway mom la beug mou daan mai désna dh xaana giisoko

    • @P4t5R
      @P4t5R День назад +2

      @@Malicksindidi1988 beurei dore dafa bizarre mane d souma done miser si boy niang laye teik

    • @boyeniang3781yeumbeul
      @boyeniang3781yeumbeul День назад +1

      bilay 🎉

  • @julejulo1823
    @julejulo1823 День назад +2

    REUG REUG DIAMBAR MOKOY BEUG

  • @dembasarr6111
    @dembasarr6111 День назад +1

    Kida sokhor

  • @LimaDiagne-v4f
    @LimaDiagne-v4f День назад

    Zarko cheuuu 😢

  • @Ma-Habba19
    @Ma-Habba19 День назад +1

    Yap sénégalais yi wéssouwoul nga diakarlo ak écran bi lék melni kouy yéy élastique

  • @kionking-i9k
    @kionking-i9k День назад

    Le mma est un sport organiser

  • @boyeniang3781yeumbeul
    @boyeniang3781yeumbeul День назад

    zarko Dara safouko😂😂

  • @ousmanedaffe679
    @ousmanedaffe679 День назад

    Zarko amoul xam xam sport prsk MMA reug reug momouko na kounek niafé ba raw ko
    King. Reug reug Omar kane 💪🏾
    Nioun reug reug laniou beugu 🥁

  • @SébastienFaye-g1v
    @SébastienFaye-g1v День назад +1

    Faralouma reug d mais dou moromou zarko mi

  • @BabacarDiop-ke7mf
    @BabacarDiop-ke7mf День назад +1

    Yaw ya geuneu tardé si lamb bilahi

  • @bayemo4147
    @bayemo4147 День назад

    Allez zarco

  • @mouhameththiam1576
    @mouhameththiam1576 День назад

    Reug Reug kassé

  • @mamadoufaye-kp6il
    @mamadoufaye-kp6il День назад +2

    Iow zarko soo beugué dougou dengay déf lou reug déf trimmer

  • @Diallo-uv2ry
    @Diallo-uv2ry День назад

    Billahi comba la zarko ak rug rug

  • @abrahamfaye5359
    @abrahamfaye5359 День назад

    Khekh séne bir lamb doy nassi

  • @bogalbogal3461
    @bogalbogal3461 День назад +1

    Zarko boul yaw

  • @abdoucoly8278
    @abdoucoly8278 День назад

    Zarko yaw def ga lou Aidara wakh Moy yon warolen xekh séne bir thiii Eméma Fock guene eseye guene Or peyis

  • @bayemo4147
    @bayemo4147 День назад

    Zarco mom gueum nani meun na am dara MMA

  • @amadouthiam7967
    @amadouthiam7967 День назад

    Zarko yaw boul gnou sonal ya geuna beuri gnep

  • @ModouNdour-b5s
    @ModouNdour-b5s День назад

    Yaw yaa wara teutj saguémmigngui téguéna beuri wakh difouddou lamb dji reug nianoul dakoo khalébi

  • @mamadoundiaye5230
    @mamadoundiaye5230 День назад

    Zarko pa bou sokhor la

  • @moctardiouf3924
    @moctardiouf3924 День назад

    Reug reug dou mome lagnefi arretewone C’est triste le Sénégal kou yabou armewou sa galé

  • @Danielgeneraldf110
    @Danielgeneraldf110 Час назад

    🦍🦍🦍🦍🦁🦁🦁🦁🦁✌️✅✅

  • @BabacarLoum-q3i
    @BabacarLoum-q3i День назад

    Zarko khamo sa bob

  • @BabacarDieng-pp2ff
    @BabacarDieng-pp2ff День назад

    Yow dull

  • @Diaxer-t5c
    @Diaxer-t5c День назад

    Zarko tu as deux combats et tu veux quoi?

  • @mcbig6971
    @mcbig6971 День назад

    Zarko iow laniou farall mais dell téla teud comme tu dis k daguayy téla yéwou

  • @mohamedd7470
    @mohamedd7470 День назад

    Zarko lolou dou xam xam. Demal outi adversaire mo gueun

  • @ibrahimadia7469
    @ibrahimadia7469 День назад

    Zarko yaW vrai nafék ga yafi wahone 😂 Modou daye dane Siteu légui nk😅

    • @BoyPoulo-kg5pl
      @BoyPoulo-kg5pl День назад +1

      Legui kou dane

    • @bayemo4147
      @bayemo4147 День назад

      Modou dor nako dakkeko dane ko par avertissement