C pour donner un bon exemple aux jeunes li rafet na yalla nalen yalla defal diam vrema js8 fan de Balla me Eum chapeau à toi et félicitation aussi à la Reug Champion du monde
Très belles images! J’aime bien les ondes hyper-positives que dégagent ces lutteurs sénégalais. Cette fraternité est très belle à voir et devrait contaminer aussi tout le monde de la lutte, les supporter y compris. Tout cette violence dans la lutte n’y a point sa place. Les supporters s’entretuent tandis que les lutteurs vivent très bien entre eux et entretiennent de très bonnes relations.
Moi je suis supportére fidèle de balla toujours la pour le soutenir balla le digne fils de c'est parents l'homme au grand cœur en or eumeu sene un très grand champion parmi les champions respect yalnaléne yalla défaléne diam Amine yarabi balla rék balla késsé 🤲🏻❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🤲🏻
BALLA GAYE 2 LE LUTTEUR LE PLUS FAIRE PLAY RAPELLEZ VOUS DE SON PREMIER COMBAT AVEC EUMEU SENE ET SON COMBAT AVEC BOY NIANG 2 MALGRES SA DEFAITE BALLA N'A JAMAIS HESITER A SE DEPLACER POUR FELECITER SON ADVAIRSSAIRE
Bilaye man Modou moye sama mbeur mais j'aime beaucoup balla et eumeu c'est des gens biens, balla akk eumeu Sénégal xole dafa rafett, bravo a reug reug champion
@@AhmadouDiop-v8y Est-ce que dou Eumeu mo bakh boléssi humble rek, ndakh Balla ak Modou mélougne nonou. Niari adversaires bou tassé ki am victoire mo wara wathié bopam sinon ki am défaite dou nék à l'aise.
Nooooo😂 vraiment sa c nice li mome vraiment contane nasi li c sa l sport c l union et pas la separation felicitation BALLA EUMEU REUG REUG ET ERIC FAVRE Pour c bonne image c sa le SENEGAL 🇸🇳
VRAIMENT DE BEAUX GESTES POUR DES GENS NOBLES.... YALLA NALEINE YALLA SAMEU YOKEU LEINE WEIRE AKE SOUTOUREU.... UN EXEMPLE POUR TOUS LES JEUNES DE TOUT BORD.... POLITICIENS, ÉTUDIANTS SUIVAIENT SES EXEMPLES.....
Man fans eumeu Séne la mai bilahi dama beug Balla gaye 2 ♥️♥️♥️
Mo tekini mbarane kat nga
Mais do mousseu déggueu supporter djouteul lo Di bégué Balla gaye rancuniers yi 😂😂😂
@@AmzaFaye-d2j do meuseu dége suporter fawzeyni di bégué kharagn lô 😋
@@Khamza903 combat siteu vs Modou la faralone 😂😂😂
@@AmzaFaye-d2jbeneu thi mane fans modou lo la mais supporter rou balla yi geunou niou ma beugeu balla gaye 2
Eumeu balla reug yalla nalen yalla deffal jamm bilay ❤❤❤
Merci beaucoup
Amine ❤
Kou respecté Balla gaye beug ko niou beug leu kone eumeu séne diam si iow❤❤❤❤
Diam si yen😊
Eumeu niouss ko 2foi 😂😂
@@Khamza903surtout 😂
@@Khamza903ba nokou leu 2 fois😂😂 eume victoire yimou am sikaw balla kéne douko lim si carriérou modou kone diémlén am ndam sikaw balla mogeune daw lakou bii niak ngéne fouleu loll 😂😂😂
@@Domou_Deukk_Bi koula wakh modou lo moy sama mbeur 😂 yén ték ngén beut modou lô 🤣☝️
Nioun supporter balla yi danouy bégué eumeu sene❤
Waw surtout lolou
Solén ko bégué woul lolendidef 😂😂😂😂😂😂😂2 0 wouyy
Guinaw bimou lén nioussé 2foi😂😂
@@Khamza903 nioune souniou khole yi niouloule kome sen yoss, nokou naniou léne 2 fois mais yéné wolén niou diam😂😂
@@moussadiop4055surtout lolou😂
Ma nguie Rée 😂 Rék no li Douma si Doyall machalah li nékhna ❤ Yallah na niépp ame diame Amine 🤲💖☝️
Balla temps yi mongi si ét'at machalla
Guis nga lolu
Dafa eumb 😂
@@cheikhsamb8292 Wawaw
@@lamzogaming4 yangi roubé dh ét'at de forme la wakh😂😂
Lag Thiat laf Thiat 😂😂😂
Machalah li rafétna trop Balla gaye 2 ak eumeu sene ak Reug Reug❤❤❤❤❤❤
Ay xarite lanio nahk ma cha Allah ❤
Gnarr gniii rek la guisss adversaire you bguentè ❤❤❤❤machallah
Bilahi❤
Prck seneu xool yi mon nice 😢❤❤
Je suis fan de Modou balla rek la djepiwone mais bilay Balla nexoul bagne..kou bax beugeu ko..nitou kasser la
😂 yalla nanga KO wall sa nawlé yi😂
Do fan modou dé nagn wakhanté deugu😂
Doff ngua reiik noy diéppii wé domou Adama 😂😂😂
@@beugfallou2853amine
Ki moy nekha begue yaw
Li Rafet Na way Senegal 🇸🇳Bén Bop la Big up Balla et Eumeu ❤️💪
Eumeu séne Yalla nsa diam yagg 😂❤❤ Kifi geneu beug balla Gaye moy wakh ni
😂copain malaraw ci balla gaye
Mala raw fouf 😢❤❤Lou lere laleu wax
Boy Niang moungui gneuw dh
Vraiment eume séne ak balla gaye 2 vous êtes de vrais champions y compris reug reug je suis très ému de vous voir tous ensembles ❤❤
Balla gaye mo bakh wayé lou Niawu lounék Eumeu sene wakh nako Balla gaye mais alhamdoulilah diameu moy lepp si Adouna yalna diameu yagg si rewmi 🇸🇳❤️🙏🏿✅
Balla et Eumeu c'est de vrais sportifs sén xoll da rafét ❤❤❤
C pour donner un bon exemple aux jeunes li rafet na yalla nalen yalla defal diam vrema js8 fan de Balla me Eum chapeau à toi et félicitation aussi à la Reug Champion du monde
Oh li refet na trop❤❤way j’me bcp balla gaye❤
Très belles images! J’aime bien les ondes hyper-positives que dégagent ces lutteurs sénégalais. Cette fraternité est très belle à voir et devrait contaminer aussi tout le monde de la lutte, les supporter y compris. Tout cette violence dans la lutte n’y a point sa place. Les supporters s’entretuent tandis que les lutteurs vivent très bien entre eux et entretiennent de très bonnes relations.
Big respect aux deux lutteurs franchement li rafetna ❤
Borom niari khol you nice . Machallah na jaam yaagu
Moi je suis supportére fidèle de balla toujours la pour le soutenir balla le digne fils de c'est parents l'homme au grand cœur en or eumeu sene un très grand champion parmi les champions respect yalnaléne yalla défaléne diam Amine yarabi balla rék balla késsé 🤲🏻❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🤲🏻
Enfin je suis content pour la complicité des lutteurs sénégalais ❤❤❤❤❤❤
Way li rafetna way yalla na diam yague thi adina ❤❤❤❤❤❤
Désormais balla gaye bolénala samay lutteur dagua am talibé kou bakh geu mais boul beurék eumeu Moy sama lutteur n°1.
BALLA GAYE 2 LE LUTTEUR LE PLUS FAIRE PLAY RAPELLEZ VOUS DE SON PREMIER COMBAT AVEC EUMEU SENE ET SON COMBAT AVEC BOY NIANG 2 MALGRES SA DEFAITE BALLA N'A JAMAIS HESITER A SE DEPLACER POUR FELECITER SON ADVAIRSSAIRE
Tu as fait un très bon remarque frère
@mouhamedlydiouf8934 bilay sa ma beaucoup marqué beau geste vraiment
😢❤jtjure
Balla gaye 2 Eumeue sene support Balla gaye dano beng Eumeue sene ❤❤❤❤❤🎉🎉❤❤❤
Comme c’est beau 🤩
Yallna diam yague barkep serigne saliou li dafa nekh 🎉🎉🎉❤❤❤❤❤
Nila deh wayé melni ké bo guissé sa morom yi sa khol bi di bonnne rek té sport dongu leu apres day diékh Macha Allah ❤yalna diame yagu
N'oubliez jamais les 5 prières par jours ❤🎉
Incha la llah
Ak rafetal kholyi yenenete djame
@@Al-Muminun_Les_croyants7 il faut toujours avoir un très bon aperçu sur ses frères musulmans et de manière générale pour l'être humain
Inchallah
@laminetahadiop3028 Et rappelle ; car le rappel profite au croyant S:51 V:55
Merci les lutteurs continuez comme ça la solidarité est réelle chez vous. Un bon exemple pour les autres sports
Yalla na diam yangu rafeth na machalla ❤🎉
Non geste bi rafetna merci les deux champions ❤❤
Eumeu mognou sonnal 😂😂
Guiss na doleii cii balla dhh bilahii pouss bii bouger woul sakhh
Mafia Balla gaye ana guéne❤❤❤
li moy Sénégal ❤❤❤❤❤❤❤❤
BG2 vs siteu
Eumeu vs Aliou seye 2
Modlo vs sa Thiès
Yi nio wara takhaw li la wkh kou rk na beus aime bi😉👍
Modou lo tapha tine
Mom la d’accord dh mane 👍🏽
@@diakhatecheikhna8146 Modou Lo moy sa mbeur?
C’est trop beau ça
C’est le Sénégal qui gagne
2:50 eumeu ya pousse ya delou guinaaw😂😂 balla amna doolé legui 😂😂 mais seine faire play bi neikh nama trope niila❤
Giiss ngako 😂
REUG REUG a raison Si on autorise le MMA au Sénégal, ça sera une opportunité pour bcp de jeunes lutteurs qui peinent à avoir un combat
Bilaye man Modou moye sama mbeur mais j'aime beaucoup balla et eumeu c'est des gens biens, balla akk eumeu Sénégal xole dafa rafett, bravo a reug reug champion
@@MicrosoftkssKane c pa vrai n jou pa le fau
Balla ak eume danion beugantè nak Bilahi founiou tasè wanèko 😂❤
Moh eumeu niouss ko 2foi bganan beugeunté 😎
@@Khamza903wa mais lolu Dara nekoussi sport c'est leurs job mais téwoul GNU beuguénté ❤
Khamo sport@@Khamza903
Man souma djissē eume AK Balla gaye dĩ kaf Di rëė damay contane mane fans eume la waye j'aime Balla gaye
@@AhmadouDiop-v8y Est-ce que dou Eumeu mo bakh boléssi humble rek, ndakh Balla ak Modou mélougne nonou. Niari adversaires bou tassé ki am victoire mo wara wathié bopam sinon ki am défaite dou nék à l'aise.
Li réfétna trop billahi❤
Yalla Na diamm yague si rée mii❤❤❤❤
Eumeu sen niga mell ak balla gay nekh nama yalla khamnako❤❤❤
Vraiment j'adore ces 2 champions au cœur d'or
C'EST BEAU ÇA ❤😢 NDEYSANN MASHALLAH ❤
Macha ALLAH nice na torope
Balla gaye 2 rék kouko sogou sankou ❤❤❤❤❤❤
Ndaysane adouna amoul solo Yallna yallah doli diam si Yène inchallah ❤❤❤
Tangal thiep bi doy na seuk gran contre petit rk ,balla dieuleul siteu ou nga xar fran wala reug reug on en a marre des combat revanche
Diadieuf gayi liguey reka wor vs etes des proffessionels❤❤❤
Machala ❤❤❤
C'est Beau❤
Machalla li nice trop sport kafe ak re la diadieuf sama mbeur mi balla Gaye
Liii nice naa yalla n'a diam sax
Machalah ndame recke inchalah cikaw cikaname inchalah ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Yalna diame yague 🤲🤲
❤❤❤❤❤❤❤❤❤Yalla na diamm yague
Reug Reug mo saytané diakhassé na balla ak eumeu rek😂😂😂
Ça c est vraiment beau ❤ bly
Machalla c le Sénégal
Merci reug reug liga wakh rfétna
C magnifique
Mais gnare gni aye vrai nite lane
Walaye Ndaysane
Balla ak eumeu yalla bouniou beuréty
Amine 🤲
Amine
Amine 😢❤
Billay je pleure li dafa Nice ❤
Non li moy Senegal 🥰🥰🥰
Non franchement c'est très cool entre deux Balla et eume séne❤❤❤❤😂
C'est beau ça
Respect reug reug sa Thiès modou lô lolou mo wara takhaw
❤❤❤yallna diame yagg
Non,ça c'est magnifique je ne suis pas leur fan mais j'ai très content
Machalla li nice nah
Nane Modou lô moye sama beureu ms billakhi balla borom xôll bou raféte la ❤❤❤❤❤ kou mana mougne la
Macha'Allah lacomplicité nice...c’est bien
Li rafete na lool way ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Je suis fans Balla gaye 2 mais j'aime bien Eumeu séne ❤❤❤ il aime de s'amuser avec les lutteurs ❤❤❤
MMA, Rugby, lancer poids, haltérophilie, judo, boxe, tous ces sports pouvaient profiter aux lutteurs
No eumeu d'où mbeur khôl bi mo raféte❤❤❤❤❤❤❤❤
Luler nga wax li rafetna kaf fo retane nileu
Reug moo ngi laye nateu der😅
Ndeysan liii nice na deh 😂😂
C'est beau
Mâcha alla balla gaye eumeu sene
Lirou limouy yeuy warna deugeur
😂😂
😂😂😂😂
😂😂😂😂
@@Yuussuujr 😂
@@WakeurSerigneBara 😂
Ay kharit ngen walay
Balla Gueye❤
Balla un vrai champion koi 😌
Mashallah rafet na torop jamou dafa nekh ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤😂😂😂😂
Li dafa Nice bly
Balla kessé bilahi
Lirou diane NMA bimouy am Sénégal 🇸🇳 yaggna MMA lagnla wakh😂😂😂
Non li nekh balla gaye ak eume Sene wara dounio peuré bilahi
Nooooo😂 vraiment sa c nice li mome vraiment contane nasi li c sa l sport c l union et pas la separation felicitation BALLA EUMEU REUG REUG ET ERIC FAVRE Pour c bonne image c sa le SENEGAL 🇸🇳
Machalla balla réck la beuge mai eumeu machalla
VRAIMENT DE BEAUX GESTES POUR DES GENS NOBLES.... YALLA NALEINE YALLA SAMEU YOKEU LEINE WEIRE AKE SOUTOUREU.... UN EXEMPLE POUR TOUS LES JEUNES DE TOUT BORD.... POLITICIENS, ÉTUDIANTS SUIVAIENT SES EXEMPLES.....
Li nice na
Allez balla way❤❤
Balla eumeu yalla nasén diamou yageu
C ça le Sénégal c beau ❤❤❤❤