Bril - Validé (Clip Officiel)
HTML-код
- Опубликовано: 7 фев 2025
- ** Écoute ici bfan.link/bril... mon nouveau single VALIDÉ, disponible sur toutes les plateformes musicales & réseaux sociaux. Streame & crée des vidéos pour soutenir tes artistes **
** Abonne-toi à ma chaîne ici goo.gl/Qw5BFh **
Dieyna et Bril, heureux mariés, tout est VALIDÈ.
Merci á tou-te-s pour vos très nombreux messages et votre immense affection qui nous ont beaucoup touché.
#bril #valide #clipofficiel #dieyna #love #mariage #senegal #team221
** Crédits du single et du clip VALIDÉ **
Auteur & compositeur : Bril
Enregistrement, mix, edit & mastering : Bril pour Class’Chic Studio
Cadrage, montage & colorgrading : MatV
Special guest : Dieyna
Une production de Class’Chic Music (Dakar, Senegal, octobre 2024)
** Contact management **
brilfight4@gmail.com
** Booking international **
vincent.lagoeyte@soon.pro
Kou validé rék lalal j'aime té partager
❤❤❤❤
KOU validé rék j'aime té partager
Des coeurs pour prophète Mohamed sallalahou aleyhi wasalam
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤
Sallalahou aléyhi wasalam PSL😍😍😍
Amofi place thi Musique. Génolen ko beuge ken akkam dina la top
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Seye bou sénégalais yeupe apprécié moy bi yallah naléne yallah lafal thiate
❤❤❤❤❤
❤❤❤❤
❤❤
❤️❤️❤️❤️
Wallakhi ❤🎉
Dieyna seyeul Bril sagal nala takhawou nala machalla yalna yalla barkel inchalla ❤❤❤
bilahiiii
❤❤❤❤❤
Yallah bo lene guiss lou lene diakhal thiat sekhlou lene guene moytou showbizz problémes bou am régler lene ko sen biir waw key couple heureux
Amine
*Amenn🥰🥰🙏🏽*
*Amenn🥰🥰🙏🏽*
Amine way
Amen Amen ils méritent d'être heureux ensemble. Que Dieu vous bénisse et vous protège de tout mal
Ohh Machallah yalna léne Yalla mousseule si seytané ak thiatt si barké Seydina Mouhamad ( SAW )🎉🎉😢❤❤❤❤❤❤❤❤
Hoo l'amour ❤❤
Si tu tombe sur cette vidéo qu'Allah béni ton couple ❤et vivez jusqu'à la muérté ❤
À vous aussi 🤲🏼
Mach'allah yalna lène yalla mousseule si seytané ak thiatt si barké seydina Mouhamad (SAW) 🙏🕊️
Machalla heureux ménage yalla seuy bi barkel boumou ompou béne djiguene que du bonheur dans votre foyer ❤💍
Kou beugue serigne Fallou beuseul j aime ❤❤❤
Amoufi plage si musique 😢😢
@@Fama-d5xwakh deug 😊
@@antadiouf8547 vraiment 🫂✅
Serigne Fallou loumou fiy def la xamoul soff gueneu trop
Yaw Merde akkou serigne fallou boula tope dou bakh thi yaw .Serigne fallou dou moromou gone bagnay dieul Touram diko utiliser thi aay musique. Yabate Rew ba doff
Yalla naléne yalla diobolé mousal len ci thiat ak lamigne guene am diebote bou barkel ci barki Seydouna Mouhamad psl ❤❤❤❤🎉🎉
Bonheur de Djeyna notre combat❤
Bilahi❤❤
Hôtel bi fane la nék, fi mome dafa bakané trop waaye ❤. Diapp lène si nguène wakh ma
J'ai jamais apprécié un couple de célébrités mais bi mom j'aime beaucoup ❤yalna yalla barkel seuy bi
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Pareille Bilay ioe amine c’est très jolie ❤
Pourquoi ta jamais apprécié un couple de célébrité c quoi le problème
@@ndoyeaissatou6357 rien du tout mais bi dafa doug sama xol bi di niane yalla mou neik seuy yanou taker Thia arassss
Louy problème bi
@@LunikSeul-gk9bh amine mais j ai jamais apprécié bi moma diakhal rek kheuy na da nga dioum peut être si li nga beugone wakh
Content nagne vraiment bril topatol niou djieyna bou bakh bouka dra mety gniouy sénégalais dagniey sotte dh😂soiyè 🎉heureux ❤❤yala mousal lenn si thiate
Kou merr si couple bi rk tiokam😂😂😂
Wawaaw kesseh naak🤣🤣☝🏾
Non li Dafa nekh
Ndiaye Diatta mane mala validè je t’aime mon Rajouloul Janati❤
Bly li koussi contanoul rék baxoo yalla naléne yalla lafal thiate way ❤️
Amine mon amour ❤
Ohhh Li mey yeuk sama yaram yoyou frissons . j'adore Bril machallah yalla bolen meussa guiss loulen diakhal .@dieyna gorgorloul bou bakh .ya finé .sunu khol yow la validé...On vous adore ♥️♥️♥️♥️
❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
Couple bi Yalna Len yallah samm barkel seuy b❤ song bi nekh na torop clip b nice na
Bril est le meilleur. Barki Rassoulilahi Galsen ken dakoulafi woy .Ndam rek ci Sey bi Bro 👊👊👊👊👊👊👊👊👊
Damalen di beug ba kagn sama couple préférée 🤩 ❤❤❤🎉🎉 😂 na sen diam yagg way❤❤🤲🤲
Qui comme moi a regardé le son plus de 10fois par jour c est de l amour pure et dure yalna lene yalla sam
Sama khol sedeuna bril namena niou laa bly
Nn bly je suis tellement fière ❤❤d’être fan’s numb one ❤Mon idole 🎉 ❤li nkh na trop skh ❤❤🎉avec Mme Migui bkh moi je valide ❤❤🎉
Oh Bril ay sons wam nimakoy sentiré, est-ce-que nieup noonou lañu koy sentiré 🥰🥰
Oh l’amour
Bril prends bien soin d’elle ❤
Dieyna mounieul gueumeul teukhlou seuy ba d amal fouleu diap sa djekeur deff ko xaritt bouleine ndeubanetei lou xew deileine waxtane bouleine teud dii fananooo meirr
Gérer votre vie de couple dieyna sa yaye boum xam dara sissa seuy bril encore une fois prends bien soin d’elle ❤❤❤
JADORE CE COUPLE YALLA NGENE MAGUETTANDO SEUY BOU BARKEL NDIABOTE KOU BARKEL AUSSI YA FI DAKEU DIABAR NAK ELLE EST TOIUTE BELLE TOUT LES SENEGALAIS SONT CONTENTS
Gnaffffffffffff ! Bravoooooo Brill d'elever haut ton épouse ! On est fier du Grand Homme que tu es ! 🎉🎉🎉🎉🎉🎉❤❤❤❤❤❤❤
Yalna sey bi barkel yalla dakhal len seytané may len ndiabot gou barkel ❤❤❤❤ que du bonheur les Fall
Laffff thiatt si yeine seuy Bou barké ndiabot Bou barkel nioune fan's Yi sax validé Nagn MashaLla vs êtes tellement mignons ensemble MashaLla touffe touff🎉🎉🎉❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤nice song🎉🎉
Le bonheur de dieyna macha'ala mitiwonna trop t khadiwo. Donc tu le mérite vraiment ❤️
Yalla nalaine yalla samedi arlaine lafalaine thiat amine❤❤❤❤❤❤❤
Yallana sey bii barkel❤❤❤❤🫀❤️💍samayy artistes préférés 🎉🎉
Ki comme mw a regardé plusieur fois 🎉❤ du bonheur
Anii wa team réal manifesté vous ndam rèk inchalla sampou rèk mais bou lolou wèsso son bi nekh na❤❤
Nokhatinagne Real . Visca Barça ❤❤❤
Who likes even before watching😍😍 your #1 fan in Gambia 🇬🇲 damalen buga si suma khole❤ May Allah bless your union with wonderful children who will be d coolness of your eyes🙏 laff chat
Bly ya Mane ya eupou dol 💪🔥 yall nalen yalla mousal si thiat thie bargue cheikhoul khadim ❤️👏
Té nguéne def ndank , té moytou tiatt. Sey dafa goud tank dé, demandé à mia guissé et nfu: l'ancien couple parfait
😁bien sur : je vois aussi que dieyna est depassee par l amour de bril ; clairement et les femmes detestent les hommes qui expriment trop leur amour. Et bien sur djiguen, histoire deukoy rattrape mais bon .... nianeul len rek puisque Bril nangou neu dal
Réel men ya wor T kham valeurou djiguen yalna la yalla fay T sam leu yak sa sokhna baguene Maguette ❤
Ndeyssane yallah nalèn yallah lafal thiate sameu sen andeu bi ❤❤❤
Machalla mes amours ❤❤❤❤
Hooooo sama xol bi❤ clip bi yeup damako réé😍 mbegeul nekhna wayyy vivez heureux les fall🎉🎉🎉🎉🎉🎉
Kirasoulilah sm couple bi yéne rk lay top clip bi nekh na nice na couple bi rafetna ande na je vous love
Machaalla yalla nalene thiatt sekhlou way! Damay setane clip bi dii sourire ba fin ❤bel hommage à ta dulcinee en plus d’etre une belle chanson et un beau clip bel hommage. Big up👏🏾👏🏾👏🏾
Hoo sma khol bi bilay je vous aimes ❤ qu'Allah vous protège k du bonheur dans votre foyer ❤🎉🎉
C’est pas ROI qui est là ❤ Ma Shaa Allah
Aay wayy yallah nalaine deffale diame Diou barri and akk soutoureu akk khéwél billahi j vous j'aime ❤❤❤❤❤
Mane malèn validés ❤ heureux ménage mes amours ❤
Machallah yalna yalla sameu léne 🙏🏻
Dieyna tu mérites tout le bonheur du monde ❤❤❤
Soyez 🙂😊😘🥰❤️
Non li dafa nékh dh machallah ❤❤❤Yalna len yalla dakal Saytanei ndiaboot bou barkél topsi inchallah couple khalé way mais son bi nékh na trop ❤❤🎉
Couple khalé way mais son bi nékh na trop ❤🎉
Sène seybi yallna barkèl zè machallah seyeul ba sèyy😍😍
Yalla naleine borom bi saam thiate seikhlou leine seuye bou barkel diam diou sakh dak barke Naby saw🙏🏾❤️🙏🏾mich Love❤️❤️
Ma sha Allah son bi nekhna trop ❤bril ya diantale mène ya meune topato djigène yalla nalène yalla lafal thiate😍
Mangui si done khaar Ayy image si mariage bii😏
Yaw mi ya waron direct clip bi because lolou mo si manquer
Vraiment Yaki lale mosi manké
Mane mi magui done wakh né image mariage bi moye néke clip bi
Mashalah Mashalah li Rafet n'a yallah n'a yallah samme lénn are leinnn sutoural leinn inshalah
Wendé louma té miirna
Diokhou loma livre té lire na
Best punchline ❤❤
Ma cha Allah contente pour Dieyna yalna seuy bi baarkeel te yalla sakhal diggante bi
Laff tiett laff tiett laff tiett très beau couple yalla nelaine seytanai sori ❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤❤
❤❤❤❤❤❤❤❤ sama kholl bi nimouy sédé euppeneu ohhhh yalla nalen borom bi samm 🙏🏼🙏🏼 Dieynabou danko modi comme toujours inshaa Allah ❤❤❤
Yallah nalene Yallah samou te arr lene mouseul lene si sayetane🎉❤
Mashala que Dieu achève ce qu’il a commencé dans votre vie
Notre femme gnoun gnola validé ❤❤🎉
Bril for Life le meilleur artiste de la nouvelle génération ❤️❤️✌️
Yalla na seye bi barké si barké seydina mouhamed yalla motali lepp
Machalla ❤yalla seuy bi barkel🎉son bi mom benene affaire la🎉🎉j’aime trop
Machalah bril et dieyna ❤️❤️❤️❤️❤️❤️✅✅✅✅✅
Yalnaléne thiate sékhlou, séne séy bi bokkou si séy bou yalla validé sa arrass🫶🙏
Jolie couple ❤ machallah son bi nékhna ❤❤❤ bonne continuation
machallah le monde entier content ❤❤Lou ngueen gnou doundoulo ni dafa nekh, yalla boumou diekh❤❤❤❤❤
lounéhh wayyy Sampou rekk🎉🎉🎉❤❤❤❤❤❤❤ Mashallah congratulations loum yague yague sou guéne rekk Néhhhh
La sortie de ce clip est trop beau 😍 ❤pour cadeau 🎁 de mariage
Machalla yalna doundou ba ouff séni seutt belle couple 🎉🎉❤❤
Souniou len validé woule louniou si meune mome validé nagne ko 😭😭🥳🥳🥳🥳🥳🥳🏃🏾♀️➡️🏃🏾♀️➡️
Machalla yall nalen yalla diapalé ❤❤❤
Laff bouche way yalla naléne yalla défal diam inchallah ❤❤❤❤❤❤
Impatiente mon frère 🎉🎉🎉
Macha alla neikh na trop
Yalla na yalla barkel seuye bi
Noo coupleee bii moh rafete rekk machalllah l’aff thiateeee❤🥹😭❤️❤️❤️❤️❤️💍
Ma dose matinale
Ohhh l’amour Yalna lène yalla mouseul si thiate ak lamine 🙏🙏♥️
Oh!! Thiey mbeuguél ♥️💍
✌️🔥🔥🔥🤸🔥🔥🔥🔥🔥
Validé 👍
Yénakofi am les fall 💍❤️
Heureux ménage thi kaw thi kanam yalla lafal Len thi thiat amen touf touff
Yalna len yalla dakal Saytanei ndiaboot bou barkel topsi incha allah❤️❤️❤️❤️❤️
Bravo bril djiguene danekoye teral waye yalla n'a yalla tahawou ❤🎉
Diam rék ngén di am In Sha God
Yallah na guéne seuye ba aldiana dama contane bilakhi ❤❤❤❤❤
Yallah n’a sey bi barkel
Machalla Brll yalla na yalla barcel si barcel serigne Saliou ❤❤❤
Couple de l'année machallah 🕌🤲🕋🙏♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️
Machala du jamais vue
Yala naléne yala lafal thiate barké seydina mouhamed 🤲🤲🙏♥️♥️♥️♥️🌹🌹🌹🌹🌹🌹🌹
Vie sur vous li nekh na way ❤😍
Kou validé si matinal bi rek lalal j'aime ❤❤
Ya meune ya eupeu dolé❤❤❤❤❤❤
Ohhh li nice na trop machallah love sur vous 🥰🥰
Sama khol bi OMG 😭❤️
Machallah Sama khol bi sede na trop clip bi rafete yalna yalla sakhal ande bi inchallah ❤️❤️❤️❤️🥰🥰🥰🥰
We are juste waiting for you🤸🔥🔥🔥🔥🔥🔥
Machallah yalla naléne yallah lafal thiat sakhal ande bi barkél seuye bi 🙏❤❤❤❤❤❤
Mashallah ♥️ yalla Barker ❤
L'artiste du peuple force à toi yalla na seuy bi barkel