QG - Spécial Serigne Touba partie 1: Gana Méséré, "Cheikh Oumar Foutiyou Tall mo ndieukeu wakh..."

Поделиться
HTML-код
  • Опубликовано: 29 дек 2024

Комментарии • 488

  • @jarineliitv4986
    @jarineliitv4986 5 лет назад +719

    kou beugue s touba beuseul j'aime

  • @awagaye1993
    @awagaye1993 5 лет назад +166

    Dieureudieuf serigne touba serigne Ganna yalna kham kham bi yok si barké seydina mouhamed psl

  • @Dac_59
    @Dac_59 5 лет назад +502

    Mane Tidiane pire la, wayé serigne Touba douma nangou koumassi eupeulai. Mako beugue ba souma degué Touram sama khol day nekh. Yalla nagne yalla fayal serigne Bamba. So degue Lo khassida yi sa khôl fèkh. Sénégal amena lou rew you barri amoul bilahi. Khôl sedana gouye.

    • @saliound6833
      @saliound6833 5 лет назад +8

      Akasa ndeyesane

    • @mamadoundiaye6375
      @mamadoundiaye6375 5 лет назад +4

    • @ndeyefamasyla4278
      @ndeyefamasyla4278 5 лет назад +11

      Wa lii nékh serigne bi mom niépa ko bokou té kou bakh rk mokoy beugue

    • @ZeynabRassoul1
      @ZeynabRassoul1 5 лет назад +7

      Do tidiane yaw ap mouride bouy wakh nga ak bou beugue j'aime. Wakhal say wakh té bagn toudou todiane. Mouride dafa beugue reuyeul wakh ak beugue ap competir

    • @MLgueye
      @MLgueye 5 лет назад +2

      kane mo la assurer né tidiane pir ngua ?

  • @cheikhounatine758
    @cheikhounatine758 5 лет назад +59

    Serigne Touba le sauveur de l'humanité. Si t'es d'accord.pousseul bleu

  • @binettediaby9559
    @binettediaby9559 5 лет назад +42

    Alkhamdouliah thiey Serigne touba amoul morom Sant Serigne touba moniou warr ay way naniou Sant Serigne touba kouy djoulit kontan gna rawatina Mouride dieureudieufè Serigne Mbackè ❤️❤️🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏🙏❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️

  • @PeopolAgrobusiness
    @PeopolAgrobusiness 5 лет назад +127

    Kouy Mouride sope Serigne Fallou beugue Ségne Bamba beusseul 👌🏻👌🏻

    • @mariasant3937
      @mariasant3937 5 лет назад

      Sope Serigne Fallou sope Serigne Salihou Mbacké

    • @lahadfaye5205
      @lahadfaye5205 5 лет назад +1

      Sant serigne touba moniou war

  • @oumarcisse4443
    @oumarcisse4443 5 лет назад +5

    Serigne Gana a augmenter ma joie de vivre machala et j'espère que je ne suis pas le seul ici

  • @mouhamedwar4510
    @mouhamedwar4510 5 лет назад +4

    Kou dakorni serigne Touba amoul morom touss j aime

  • @khadimsall9112
    @khadimsall9112 5 лет назад +4

    Kou beugue sa khol séde lou nék diokhko kouko métrisé Serigne gana machaalah khol yépe séde na dieuredieufé Serigne touba

  • @rimachou6695
    @rimachou6695 5 лет назад +52

    Kou beugue serigne touba pousse j aime

  • @ElTIO_Galass
    @ElTIO_Galass 5 лет назад +27

    Serigne gana mesere yalla nga fii yagg te and ak wer si barkiii cheikh ahmadou bamba 😍

  • @mouhamedndiaye8235
    @mouhamedndiaye8235 5 лет назад +31

    kou kham né Serigne Touba amoul mass beusseul J'aime

  • @elagendiaye7631
    @elagendiaye7631 5 лет назад +4

    Le plus grand richesse c'est d'avoir cheikh Ahmed Bamba la fierté c'est d'être talibé Serigne Touba l'élégance c'est d'être un vrai mourite le bonheur c'est Mame salihou dans le cour💓💓

  • @dim_bamband2445
    @dim_bamband2445 5 лет назад +8

    dieureudieuf ty serigne touba kou beugue s bamba beuseul jaime

  • @mouride_bi
    @mouride_bi 5 лет назад +3

    Kignou dinthie thi bamél rék mola meuna wax kouy serigne Touba😣💗

  • @moustaphakare8996
    @moustaphakare8996 5 лет назад +37

    Manchala Srg gana léral yi amna Solo kéne du Serigne TOUBA khadim rasoull

  • @mamadoudiallo4852
    @mamadoudiallo4852 5 лет назад +6

    Kouy wakh cii Serigne Touba té am00 kham kham nanga koo 0utii machalah Serigne Gana🙏🙏

  • @dametaaal3125
    @dametaaal3125 5 лет назад +12

    kou beugeu Serigne Gana rk beusseul like

  • @dinhomaodo5246
    @dinhomaodo5246 5 лет назад +124

    Dieureudieufé sérigne touba khadime rassoul ana gniko beug 👌❤

  • @bintoufall3816
    @bintoufall3816 5 лет назад +11

    Akhmadou Bamba khadim Rasdoul sii Khol mo dakh léém💖

  • @madandim1686
    @madandim1686 5 лет назад +7

    Thiantt serigne Touba faratala dieureudiefeuti Serigne Touba diarama mame cheikh Ibrahima fall
    Serigne Gana massare Macha Allah xol yeupeu fekh

  • @khalilgueyebkg2540
    @khalilgueyebkg2540 5 лет назад +8

    Nous toujours le numéro 4. J'aime

  • @papisfall8364
    @papisfall8364 5 лет назад +13

    SANTE NA😭 Serigne TOUBA ki kène dou Mome Senegal danou wara xame kouye Serigne TOUBA

  • @matarfashion3753
    @matarfashion3753 5 лет назад +14

    dieureudieufeuti SERIGNE TOUBA SERIGNE NGANA MESSARE YALLA Na sa diamou yagg aminne

  • @diagnar5754
    @diagnar5754 5 лет назад +10

    Bilahi c la premier fw mayii suivr émission bi ak sma pass mé ken dou serigne touba bly nakk baniou ande sante serigne pour senegal dieum sii kanam

  • @gayemamediarra9731
    @gayemamediarra9731 5 лет назад +41

    Beug nala srg ganna barkei cheikhoul khadim

  • @aladjiass963
    @aladjiass963 5 лет назад +13

    Mouride yi da nguenn beug lou yomb. Beug akimo serigne touba té dolenn si xadial kenn.
    Gno bagne dé djeuredjeuf serigne touba

  • @binetafalygueye5350
    @binetafalygueye5350 5 лет назад +18

    Machalla serigne gana yalla nga fi yague lool te wer

  • @ngagnedemba3802
    @ngagnedemba3802 5 лет назад +10

    Machala Serigne gana mesere léral yi ame n'a solo kéne dou mome serigne touba amoul morome

  • @mouhammedrasoull7710
    @mouhammedrasoull7710 5 лет назад +14

    Barké al khouraane serigne ganna dall nekh nga ma nitt nité way wakh day diarr yone ta am danéll yalla nga fi yague ta wéerr si barkép wérou koor gui 🙏🙏

  • @fatoudiouf6498
    @fatoudiouf6498 5 лет назад +1

    Alhamdiulilahh Bagnou dooné ndiabotou serigne touba
    Ahmadou sunu borom....❤

  • @rimkitongoka784
    @rimkitongoka784 5 лет назад +16

    Maane Deh Tidiane haqaan la, wayé Dama Beug Cheikh Ahmadou Bamba Dama Beug mâme Cheikh Ibrahima Fall lampe baboul mouridina.

  • @mbackendiaye7605
    @mbackendiaye7605 5 лет назад +5

    Machallah ken Dou Ahmadou Bamba🙏💖

  • @kassodiop6945
    @kassodiop6945 5 лет назад +18

    Khôl sedena dieur dieuff serigne touba amoul morom bilay

  • @amidiaw3107
    @amidiaw3107 5 лет назад +1

    alhamdoulilah bima neke mouride beugeu serigne TOUBA ak wa keureum

  • @moramysylla3275
    @moramysylla3275 5 лет назад +6

    Dieureudieufèty Borom Touba Khadimou Rassoull

  • @elngom7159
    @elngom7159 5 лет назад +23

    Serigne touba amoul morom wakh ko yakoul daara.

  • @sodadiop3114
    @sodadiop3114 5 лет назад +10

    Machallah kén dou Serigne Touba Amoul Morom dée dieuredieuf Mame Chieckh Ibra Fall Lamp ken dou mom

  • @afiasylla6035
    @afiasylla6035 5 лет назад +2

    tay la lepp nekh ba kouné di dingatt bay dislike mè 5 septembre 1895 koudoul wone serigne touba numéro 4 signé gua tay guen am fitou nek fi di wah rk

    • @mariamadiakhate6372
      @mariamadiakhate6372 5 лет назад

      afia sylla merci bayilene fofou sene khol di bone Serigne Bamba kene la

  • @dembadrame6081
    @dembadrame6081 5 лет назад +6

    Machalla serigne gana khol yi fékh na

  • @mbenguendeyeastou8000
    @mbenguendeyeastou8000 5 лет назад +1

    Dieureudieufè Serigne Touba. Djarama Mame Cheikh Ibrahima Fall

  • @abdourakhmanediop8467
    @abdourakhmanediop8467 5 лет назад +2

    je suis toucouleur serigne touba point

  • @mamandiaye4880
    @mamandiaye4880 5 лет назад +118

    Dieuredeuf Serigne bi sama holl séd n'a si émission bi

  • @ndiayeastou3567
    @ndiayeastou3567 5 лет назад +8

    bgue s touba dall dafa nopalé ❤❤

  • @abdoulayediop3585
    @abdoulayediop3585 5 лет назад +130

    Man ap tijan mè bamba nimako beugè nonou lama diaxalè tè dana diaxal kènèn koudoul man thiey akhmadou

  • @ndiayedjiby8881
    @ndiayedjiby8881 5 лет назад +1

    Serigne touba moy kimane aduna ak allakhira

  • @boobadiallo169
    @boobadiallo169 5 лет назад +20

    Alhamdoulilah sante yalla boubakh bime niou ganalè si aduna bolè niou ak kou tedd ki mouy cheikh ahmadou bamba khadim rassoul yalla na yalla yoki lèrame tè tasniou si barkème 🙏 🙏 kène dou mome

  • @mayarediop2631
    @mayarediop2631 5 лет назад +5

    Dieureudeuf serign gana wakhtan bi amna solo torop❤️❤️❤️❤️

  • @princeloum500
    @princeloum500 5 лет назад +5

    Alkhamdoulilah. Dieureudieufff Serigne Touba

  • @lasalihate657
    @lasalihate657 5 лет назад +7

    Ahmadou bamba bilay rew mi sougnou massei diko Sante yok diarignou yalla nagnou yalla Def deugue deugue talibei

  • @modytoure5278
    @modytoure5278 5 лет назад +12

    Alhamdoulilah sante serigne touba rk🙏🙏🙏😍😘

  • @akim100merengue2
    @akim100merengue2 5 лет назад +2

    Machallah serigne Ganna

  • @MG-Saliou
    @MG-Saliou 5 лет назад +12

    Ahmadou Bamba, beuss bouniouko kéneulé fi si Sénégal beuss bobou kheweul yeup oubikou.
    Baaboul mouridina keneu dou iow mignou wone AHMADOU 😭

  • @modoumbow5559
    @modoumbow5559 5 лет назад +1

    Dieuredieuffé serigne touba

  • @bambabamba7106
    @bambabamba7106 5 лет назад +6

    beuge serigne touba doyna diamou yalla

  • @babacarndiaye4194
    @babacarndiaye4194 5 лет назад +7

    Dieuredieuf Serigne Touba 🙏 Ngana Yalna Yalla Yagal Takhaway bi 💓💓

  • @ndenediagne50
    @ndenediagne50 5 лет назад +27

    Kène dou serigne touba

  • @mamadoudiouf7115
    @mamadoudiouf7115 5 лет назад

    machallah dalal ngen kou bari xam xam Sérigne Nganda messeré yalna yalla goudal ay fanam té yookoko werre

  • @mamedieng7261
    @mamedieng7261 5 лет назад +14

    Dieureudieufty serigne Touba

  • @ablayekebekebe1951
    @ablayekebekebe1951 5 лет назад +1

    yalla nala Faye gana b karkeb s touba

  • @kebecheikh8365
    @kebecheikh8365 5 лет назад +12

    Grasis serigne touba diadieuf serigne touba merci serine touba ourigado serigne touna

  • @soufi732
    @soufi732 5 лет назад +1

    Mane sokhna Thiam louma ame Serigne Touba momako gueneul barcké Serigne saliou

  • @salioundiaye2222
    @salioundiaye2222 5 лет назад +3

    Sérigne touba amoul morom bilahi kénn la💪

  • @Sancoun43
    @Sancoun43 5 лет назад +5

    Dieureudieufêti Khadimou Rassoul, Serigne Touba, Cheikh Ahmadou Mbacké, Cheikhoul Khadim😭❤️🙏

  • @serigneseck3966
    @serigneseck3966 5 лет назад +7

    Kendou serigne touba

  • @ousmaneniang976
    @ousmaneniang976 5 лет назад +25

    Jtm BAMBA ❤❤❤

  • @dipdoundouguiss7455
    @dipdoundouguiss7455 5 лет назад

    Serigne touba Ken la thi zahir ak si batin☝️

  • @ogrijalkane5900
    @ogrijalkane5900 5 лет назад +1

    Kéne dou Mame Bamba 🙏💚👌

  • @aissatousall923
    @aissatousall923 5 лет назад +21

    Keine dou Ahmadou Bamba Khadim Rassoul🙏

  • @falloufall371
    @falloufall371 5 лет назад +34

    Serigne bouko geune amoul
    Serigne bouko meune amoul
    Serigne bou tollo ak mom amoul
    Serigne bou biinde limou biinde amoul
    Serigne bouko geuna diégué Yalla amoul
    Serigne Bouko geuna xam Yalla amoul
    Serigne Bouko geuna raggal Yalla amoul
    Serigne bouko geuna Beugg Rassoulilah amoul
    Serigne bouko daxa diayanté amoul
    Serigne bouko eupp yeurmandé amoul
    Dangay binde ba sonou mé ken dou meunoul wax lep ci Serigne té ken Da xamoul lep ci Serigne
    Serigne bi rek moy Serigne

  • @aboubacardiop1176
    @aboubacardiop1176 5 лет назад +3

    Maash'Allah, dégatina deugg, kouko bagn rékk dagako xamoul

  • @mourtallaafia73
    @mourtallaafia73 5 лет назад +3

    Machallah yalla nala yala faye si barké serigne touba

    • @mourtallaafia73
      @mourtallaafia73 5 лет назад

      Lou reuye la wa rouba ame barké serigne touba

  • @thiounefall4018
    @thiounefall4018 5 лет назад +16

    Machalla way 😍 😍 👏

  • @louisediagne67
    @louisediagne67 5 лет назад +1

    Sante mame touba rekh ak mame lamp fall mane sama khôl dji sede n’a serigne bamba si khôl ❤️😭

  • @Laye-cana3714
    @Laye-cana3714 5 лет назад +1

    Serigne touba khadim re soûl kousop begue Serigne bamba besel jamais

  • @gueyetoba6519
    @gueyetoba6519 5 лет назад +9

    Dieuredieufati cheikhoul khadim naniouko kennal way

  • @mamedembadioumdioum4414
    @mamedembadioumdioum4414 5 лет назад +30

    Bamba progrresse amoul tanki guinaw ci kanam rek

  • @rmormboup8278
    @rmormboup8278 5 лет назад +1

    Hay sounou amoul wone Serigne Touba labaye nienw

  • @khoudiandoy481
    @khoudiandoy481 5 лет назад +9

    Ahmadou borom diame dji serigne bamba rek

  • @binetoulo8513
    @binetoulo8513 5 лет назад

    Ahmada khadim ken la yalla nagnou ko sougnou borom fayal. Dieureufé borom Touba

  • @fatouchad3801
    @fatouchad3801 5 лет назад +1

    Cheikhoul khadim 👉♥️😭😭😭

  • @abdoulayedia9460
    @abdoulayedia9460 5 лет назад +1

    Macha Allah sounou mak gnou bakh gni !!!

  • @tickedioum6541
    @tickedioum6541 5 лет назад +6

    machallah kene dou serigne touba

  • @bayeibra9210
    @bayeibra9210 5 лет назад +34

    Ken mousoul setane QG ba heurbi serigne touba kenla

  • @MG-Saliou
    @MG-Saliou 5 лет назад

    Ya Allah SHUKRANE bangma défé mouride😭

  • @papisecissko7498
    @papisecissko7498 5 лет назад +1

    Ken dou serigne saliou mbacke dieuredieuf seringe touba

  • @ndeyekharama6520
    @ndeyekharama6520 5 лет назад +7

    Dieredief Serigne Touba

  • @khadimmbengue2026
    @khadimmbengue2026 5 лет назад

    Dieuredieufèty ahmadou bamba xol sèdatina❤❤fièr d'être mouride alhamdoulillah

  • @mustafaaseyjamiil7227
    @mustafaaseyjamiil7227 5 лет назад +1

    alkhamdou lilahi bignou neke ay mouride

  • @diarrabeye5012
    @diarrabeye5012 5 лет назад +54

    Kenn dou ahmadou domy diariyatou lahi

  • @manunited1989
    @manunited1989 5 лет назад +8

    Bilahii sma xol bii sedna gouy..

  • @sokhnaamimbackeniang1131
    @sokhnaamimbackeniang1131 5 лет назад +9

    Dieuredieuf khadim rasoul 👌👌❤

  • @gorandiaye4047
    @gorandiaye4047 5 лет назад +9

    kénn Dou Serigne touba

  • @diamadieng3477
    @diamadieng3477 5 лет назад +6

    dieurdieuff seringue touba seringue Gana dieuredieuff conetane bou bakh

  • @seydoubouss3939
    @seydoubouss3939 5 лет назад +7

    serign touba ken la

  • @s.cheikhmbacke7019
    @s.cheikhmbacke7019 5 лет назад +29

    Diardueff chiekhona chiekh ahmdo bamba khadim rasoull

  • @niarrybayefalltv
    @niarrybayefalltv 5 лет назад +7

    Cheikh Ahmadu bamba sunu yakar tay ak euleuk kum Sédul daguay fandei

  • @mohameddienefaye4962
    @mohameddienefaye4962 5 лет назад

    Serigne gana missére..yalna yalla yonaintébii ak Serigne touba ..défall leu diam... Diéreudieuff Serigne touba....kou tédquii.beugu rék mo waurr

  • @modoukangdiop5995
    @modoukangdiop5995 5 лет назад +96

    République du Sénégal diotna niou sargal chekhoul khadiim nite kou nioul kou amoul ci adina

  • @fatysyll5643
    @fatysyll5643 5 лет назад +4

    Oh les jaloux serigne touba vous adore ns o6 on vs adore